Comment a t-il bien parlé ??Ce griot qui ne fait mentir et chanter les louanges d'un homme comme lui.Aucune dignité si tu savais ce que c'est prendre la terre d'un pauvre paysan qui n'a aucune ressource tu ferais mieux de te taire.
Sa xarit leu sa gueweul joudiou leu diarna gay wax tè setoti yalla guir yalla ragal leen yalla tei khol ni alalou aduna jarour yeen yi walhi lepp nitali lay don wa ngler yalnalen yalla japalè brki seydina muhamed🤗
Partout dans le monde on protège les arbres au Sénégal on détruit les forêts. Il dit avant dans ces terres tu ne pouvais pas voir plus de 20m parceque plein d'arbres il a payé 80 millions de francs cfa Pour abattre les arbres. Oh terre mère je vous demande pardon pour l'inconscience des hommes.
Genre khadime samb yii gnioffi beurri si réewe mii et il parle que pour leurs poche késsé...parceque tous ses révélations qu'il ns dit .légui môme nagniou wakhe loumoussi aame comme courtage douko wakhe déh Thiimme.et aprés
Babacar Ngom dal gathié ngalama! Arrêtez cette cabale contre lui, comment peut on reclamer la propriété de champs qui se trouvent à 6km de son village sans titre ni rien? Bayilene yakhalaté
L'erreur de M.ngom c'est de n'avoir pas prévu un gros budget pour les paysans dans son business plan. il devait payer des centaines de millions aux paysans aussi.
Babacar ngom est un grand homme et resta un grand homme. Je ne comprends pas l'acharnement de ses derniers temps. Son projet à Djilakh est plus rentable pour la nation et pour les populations autochtones. Son entreprise se développe et continue à se développer. Babacar n'a pas fait de forcing, il a demandé de l'attribution des terres (la forêt et non les champs). On ne peut pas vouloir quelques choses et son contraire, soit on avance vers la modernité soit on stagne.
Khadim on sait que monsieur Ngom est un patriote mais c'est le titre foncier qui fait problèmes 300ha pour une seule personne pendant que le sénégalais lamda veut un lopin de terre pour cultiver
LIMA CI DIAXAL.MOY NO AMÉ TITRE FONCIER SI LO MOMOUL? KOU DIOKH BABACAR NGOM TF MOY DOMÉRAM . ..PÈRE LI NGAY WAKH YÉP MAYOUL BABACAR MOU DIEUL SOUFOU DIAMBOUR. PÈRE NIOUNE VILLAGE LANIOU DEUK SUNU KEUR YI AK SUNU TOL YI EUP NA 10KM . PÈRE MAY NIOU SA DOM NIOKO DAK DIANGUE CI WALEU BOU NIOU NÉK? WANTÉ LO MEUNE MEUNE DIANGUE AM KOULA KO DAK
N'oubliez pas de vous abonnez sur votre chaîne Senbuzz TV et d'activer la cloche pour recevoir les notifications merci.
Dlm Officiel on va le faire inshAllah. Merci
Pourquoi abonnez alors que vous nous proposez des domerams kom Khadim Samb
Ok
@Dlm Officiel ok
@Dlm Officiel g
On demande pas de faire un publi reportage à la con mais de nous dire ton rôle dans le litige!
Très bien parlé khadim merci est félicitations
Comment a t-il bien parlé ??Ce griot qui ne fait mentir et chanter les louanges d'un homme comme lui.Aucune dignité si tu savais ce que c'est prendre la terre d'un pauvre paysan qui n'a aucune ressource tu ferais mieux de te taire.
Très bien parlé félicitation khadim
Sa xarit leu sa gueweul joudiou leu diarna gay wax tè setoti yalla guir yalla ragal leen yalla tei khol ni alalou aduna jarour yeen yi walhi lepp nitali lay don wa ngler yalnalen yalla japalè brki seydina muhamed🤗
Yalla Amna dé Allal diaroul lie
Khol si yalla lingaye wakh
Bilahi sa intérét rk motakh ngay wakh doull way
Partout dans le monde on protège les arbres au Sénégal on détruit les forêts. Il dit avant dans ces terres tu ne pouvais pas voir plus de 20m parceque plein d'arbres il a payé 80 millions de francs cfa
Pour abattre les arbres. Oh terre mère je vous demande pardon pour l'inconscience des hommes.
Loolu moo gën a naqari.
kii doméram leu genre yii ño yakh sunu rééw maar tate rek 0 honnêteté
Vrai domeram kou amoul khaliss dougn andak yaw
@@mourtallaseye8657 deug leu amouñou ngoor
Respect waaaay kilifeu la
Très bien parlé félicitation
@@assanesylla4136kilifa domeram la
Notre problème c pas Babacar ou autre le problème c le gouvernement
Il parle avec des gens douès d intelligence et ki reflechississent
Ya Des Genres De Personnes Que Vraiment Ils Cherchent Toujours De L'argent Tout Les Façon C'est Bon
Genre khadime samb yii gnioffi beurri si réewe mii et il parle que pour leurs poche késsé...parceque tous ses révélations qu'il ns dit .légui môme nagniou wakhe loumoussi aame comme courtage douko wakhe déh Thiimme.et aprés
Alalou adouna diarna lii🇸🇳🇸🇳🇸🇳👹👹👹👹amna
Un domeram. C'est pas comparable. Mimram c'est avant les indépendances.
Gni nio yakh sénégal intérême rek motakh mouy wakh Babacar ngom amoul koumouy yonni koudoul ki, motakhite thiow topou nako
Vraiment qui loumouy wakh deug la
non mais dans quel pays nous vivons?!
Thiey Sénégal
Babacar Ngom dal gathié ngalama! Arrêtez cette cabale contre lui, comment peut on reclamer la propriété de champs qui se trouvent à 6km de son village sans titre ni rien? Bayilene yakhalaté
Les paysans cultivent à 10 km de chez, ki thiog leu.. C'est immoral ce que fait Babacar Ngom même s'il a tous les papiers du monde.
Il n'est pas cohérent Sandiara est à côté de Tiadiaye après Mbour alors que Sindia est avant Mbour
Machalla kéndou yi rafét na
Aka mouneu fén 😂😂mm le porte parole de Sedima a reconnu qu’ils sont allés la bas pour negocier avec les populations a propos des terres
Yaw nékh gua wawé wakh gua deugue
pabi dul geuy def
Xafim c'est un cockseur un champ de 225 ha ne peut pas être homogène il y'a forcément place à cultiver
Khadim Samb bayi gnou waay iow babacar mola wakh ingénieur agronome leu 😂😂😂
Père koyou bouki la 😂😘🙏🏾
L'erreur de M.ngom c'est de n'avoir pas prévu un gros budget pour les paysans dans son business plan. il devait payer des centaines de millions aux paysans aussi.
Terain 250million amoul malika té sou amon babacar douko mayé khadim bayil yoke yi
🤔🤔🤭🤭🤭🤭khara ma noppi 🤐
Senegal dou dem ndakh Senegalais dagno sokhor.diapale les Marocains et les Europains molene geuneul diapale Senegalais domeharam yi
Il est dans toutes les sauces ce Khadim Samb.
Wakhou gueweul 🏃♂️🏃♂️🏃♂️🏃♂️🏃♂️🏃♂️
Ma cha Allah wakh dji amna solo serigne khadim
Babacar ngom est un grand homme et resta un grand homme. Je ne comprends pas l'acharnement de ses derniers temps. Son projet à Djilakh est plus rentable pour la nation et pour les populations autochtones.
Son entreprise se développe et continue à se développer. Babacar n'a pas fait de forcing, il a demandé de l'attribution des terres (la forêt et non les champs). On ne peut pas vouloir quelques choses et son contraire, soit on avance vers la modernité soit on stagne.
Que dieu ait pitié de toi minable
Li ma naqari rekk mooy àll yi ñgeen di gor di dagg guy yi ak daqaar yi.
Khadim on sait que monsieur Ngom est un patriote mais c'est le titre foncier qui fait problèmes 300ha pour une seule personne pendant que le sénégalais lamda veut un lopin de terre pour cultiver
Guéwal dagay done noble
C vrai teranga ci nga wah si mom bouko defone ak was ndengler thiowli diekh
Bay 3mois par an mofi wara jex nagnu jox toll yi gniko meuneu exploiter budon tubab ken du wax
Paa bi waroul wone toudou khadim
Nasaye Dom mom Canadá Lolo yen la rek mais soufou ndenguler gui mom dinguen ko bayi
Ce genre de vieux qui plongent le pays dans des problèmes . Il faut les dénoncer les gens ne sont pas au courant .
Sénégalais beggoul sénégalais toubab ak chinois rekk lagnou begg
Sounou beugonn dieul sa soufou baye, di Waax ki dayy doul.
Qui daye doull limouye wakhe Dara léroussi so dieulé entreprise mou ndindi garabe lofaye gorati
Fèn rek fèn rek khaliss rek gèn geum ba dèmè sakh yako wakh niko guis na souff ndèngeler
Senegalais mo bagne bopam.ay domeharam deug lagne
Yaw dagaye ndoul rék ya guene cate sa ndeye si guiwal yi do dara diamou xaliss bou bonne ga
li leep Macky sall domaram dji leu
Genre nit gni gno yakh Senegal cdes imbeciles ils pensent qua leur interet
Je suis pas contre du projet mais titre foncé c'est inacceptable
Très véridique Nous Sénégalais nous sommes méchants.Nous ne voulons pas notre réussite
Pourquoi citer la société ENTRACOM et omettre l'autre société ?
فل حق ولو كان مر
Yow momou ya guemoul yalla khadim.Nek guewel rek guene am xaliss topoulene feulé
Vous entendez 300ha à 30millions et abattre des arbres pour installer qu'est qu' il ont fait pour l'environnement.
Comme kou bindeu si yaw dootul bindeu deii waroon nga meun liir beu lir souniou commentaire yii
Guéweul yi xaliss rek
Pere vraiment tout le monde t apprecie au Sénégal mais la tu derailles
LIMA CI DIAXAL.MOY NO AMÉ TITRE FONCIER SI LO MOMOUL? KOU DIOKH BABACAR NGOM TF MOY DOMÉRAM . ..PÈRE LI NGAY WAKH YÉP MAYOUL BABACAR MOU DIEUL SOUFOU DIAMBOUR. PÈRE NIOUNE VILLAGE LANIOU DEUK SUNU KEUR YI AK SUNU TOL YI EUP NA 10KM . PÈRE MAY NIOU SA DOM NIOKO DAK DIANGUE CI WALEU BOU NIOU NÉK? WANTÉ LO MEUNE MEUNE DIANGUE AM KOULA KO DAK
D'où dëg d'où dëg
Sénégal danou sokhar
Sa wakh gui lèroull
billahi ya katta sa ndeye
Mes 300 hectares à 30 millions terrasement 80millions hum
Dou dara gueumou gnou Sénégal intérêt personnel réke
Doull rek ngaye deff yaw domeram rek nga yaw donitou dara danlay diende kom khar doull way yaw
Mimran mom walo gno amoul foula si sen souf
Fen rek
Mais Khadim samb bane journaliste la waxon né doto bindeuti
nous on a rien mai on a notre dingnite
Doul rék ki
Quelle incohérence
Fén rék goorsi aka meuna fén
C'est le titre foncier qui gène !
Wakh rekk nguay deff opportuniste bi
Geweul yi nio niou warra may ndeye diameu
Thiogg rekk thiey bou nieupou Melon ni mame Samba
Set si diguenté ak yalla
Ragal yalah te nga bayi mey bii
Ya meuneu tothssa thiotou ndeye doul
Xarito xaliss rek
Teudiale sa gatte thioggou nga
Khalis rèk lagnou gueume sène bène mame andoul
Yalla rek mofi ne
Koula deuglou nga hamné sa intérêt ngay wahal
Deugue nekhoulll deeeeee
Doul rek
babacar est un patriote
Senegalais mo sokhor beugeu niou kouy liguey
@@fansdemba6992 soy liguéye bo takh nga beuga dieul alalou diambour
Patriote dou exploité ses compatriotes, même s'il a tous les papiers du monde, c'est immoral.
Wakhl way
setsi yalla loukaye wakh
thiogou you bone yi
lui il parle pour son ventre
Donarsam
Sa wakh dji yalla takhoule
Non mais yaw yaa meuneu fen...ana yaw ana Man niou diokhla 2 million sans motif
Pere soy wokh der si khole yala
Mec tu été mandaté pour aller faire le sal boulot moyennant finance pour ta poche
Yawou ya mouna dou nafexhie gue degue degue degue yawou do rossou sakhie xalisse rek gaye wuer di doule rek sa koyou baye guewle daye defni elhaji mansoure mbaye 🤐🤐🤐🤐🤐🤐
Ak Mame Samba Diabare Samb kokou modon Noble bilahii suuf woyoff si kawam
@@youssoufabdoulayediopjohnn3774 amine waye
Ils sont tous pareils 6 ak 9
Hqha
Wakholl dëg doull katt la nafékh la
Yombnade