@@LouiseDiabouMané-z4zIl y’a ça aussi. Sène biir famille yi ak séne entourage amna niouy déf lou yess sol lou gate, niom séne bopou douniou ay walliou daniouy baakar ni nieup niou paré dougou ci rèseaux sociaux yi di diaye sell🙄Faux moye deuxième tourou sénégalais ci gnima ko sania wakh
J'ai aimé ton commentaire car c'est vrai 😢😢😮😮😮 merci beaucoup 🎉 Dieu te bénisse les vêtements bien c'est important car après la mort les choses que la personne à fait reste toujours
@ThiernoyayaDiouf dieukeurm bane deug laye ame? Sa vie c'est sa vie fimouy wété ak boromam dou dieukeur dou yaye. Beugoul nekeu ibadou choix wame la yonou dieukeureum nekoussi
Des gens disent qui daffay liguey en quoi cette travail disent qu’elle doit porter du n’importe quoi pourtant elle est une grande star et c’est une très grande chanteuse moi personnellement je l’aime mais bon li yeup daniouy dée bayikofi té euleuk dou agne dou rére wayé lou mata bayi khel la
TON LAPSUS EST RÉVÉLATEUR : SÉNÉGAL KEN BËGGULA???? SÉNÉGALAIS YI MIA MAABO LANU BËG, MOONU WARA REPRÉSENTER..LE SÉNÉGAL EST TRÈS RESPECTÉ DANS CE MONDE ACTUELLEMENT.. MIA( BEYONCÉ) FRAMACONNE BOOBU , JIGEENU PUFF DADDY, KOOKU DU SUNU MIA, BËGGUNUKO... LEEGI TANAL BUDEE JIGEEN BU BAAX NGA.. NOFACE AVAIT RAISON: ÑUN AY SOXNA LANU.. ET NON DES KARDASHAN, RIHANNA, MADONNA...POUR MUY CLAIR...
Amoule dara loumou lépa bone bayi lene quou tinmoinié rek niou défandre ko atelene degue mes mia je t'aime bien wayé li dohkoul Cou d'accord ak mane Aimel❤️✌️
Wakh bou bone famou dhougué le deuk. Kéne dhiokhou la lék,ni nane, dhiguéne bouye réussire, di démale bopame lagnou bagne…… en avant …..💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾🥰❤️ félicitations 👏🏾
C'est juste le vestimentaire qui dérange même si c'est le show biz on comprends bien mais ton corps de femme on "aime pas le voir svp "mais ta voix ton style de musique❤. Prenez le positivement et avance.
Dans mon cas je vous dit d'arrêter de l'a jugé vous vous trompez sur personnage et personne mia est une guerrière vraiment du courage mon idole focus rk
En tout tu as une fois étais trés décente à travers ton habillement et wallahi trés belle, aimée et appréciée. Je fesais partie de celles qui imitaient ton style mais sincèrement je l'ose plus.
Tata Mia Sénégal sofi beugé nk dèm ag fanga dieum boulma dégloul conards yi di wax si yw fonsèl le chemin est très loin et vous n'avez pas le temps pour eux ❤❤on t'aime ❤et on vous soutiens
Yen doul li lanla qui viviane mo ko dakh sol lou bone tei denguen thiy mandou tei diour dom you tolo ak mome bou sey sakh lay wakh ki molen eupe diom gune lena kham bopam beugue ngen jugei nit yei dolen yalla kou kham lingen di def yen ken yalla kessei kon arretei 'solou fi lou star soloule ay slipou nene sakh guisnagne ko ki molene eup pudeur fouf en dehors de sa sene khamo lene sakh nite
J' aime beaucoup Mia guisse long vie ma actrice préférée long vie ❤️💞❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ elle porte des tennu bien et aussi classe j' aime vraiment cette artiste dans mon cœur ❤️❤️❤️❤️❤️❤️ je battre avec mes amie pour cette artiste ❤️❤️❤️bon carriere
Mai 😢 reviens sur terre mais ne regarde pas se qui sont considérés comme bien et Font le mal toi concentre toi sur toi avec le bien Mia la vie n'est rien c'est pas parce que tu es artice que tu fasse le mal Que Dieu te montre le bon chemin ❤
@ manè solou fi lou kène soloul tè guène haar ndjabot dji mo gueune. Mia sur sa page snap elle publie des vidéos ou sa fille apprend le coran alors certains filme leurs enfants en dansant est-ce k finalement le problème c’est mia
Mia on t'aime on n'a rien contre toi c'est des conseils constructif et des leçons religieuse que nous te donnons Car actuellement tu est entrain de donner raison à Now Face En plus tu as une fille qui ne doit pas voir tes images négatif à travers les réseaux sociaux sinon elles aurait des problème demain avec ton attitude
Ce n'est pas une question de prostituées mais en raison de valeur il ya beaucoup de gens qui te suivent et actuellement tout les chansons que tu chante aujourd'hui reflète quand tu étais avec ton mari réfléchi bien mia la beauté d'une femme ne ceu trouve pas dans la vulgarisation
Guis gua nit boko beugué dagua koy wakh deugue. Moi je l’ai toujours adoré et défendu mais maintenant je n’arrive plus à la regarder tellement je suis déçu par son comportement elle est entrain de donner raison à son mari et au autres hommes qui croit que les femmes n’ont pas de cervelle. Avec la position dans lequel elle se trouve elle doit donné l’exemple. Regarde toi devant un miroir avant de sortir. Gni lay diéy di la Conseillée wakhou gnou la deugue. Doto khalé dioy fadioul dara.
Ame na nioula critiquer woul ndakh kham nagne la te kham nagne kima done koula kham deug dina kham ni ya gueune fouf gni fi nek di juger nite yi té khamougnouko
C est une artiste laisser la en paix' elle sont nombreuses les femmes qui s habillent apparemment comme mia. Par ex: Viviane n est pas decente ;Titi maintenant fait de même etc...
Mia bilay amo fouleu dou nékone ma yaw douma sakh tontou damay liguéy sama liguéy bayyi len gnouy ratati Yaw instants yi ya téyé deuk bi défal loula saff doune la rayy doune la fess ay wakh rek lanou lay sanni mais yaw boul guéssou focus si liguéy ta famille t'aime
nagn waxanté deug danio am sounou ay réalité sounou ada ak thiossane ay kilifeu liguéyal niou lou reuy Meussouma beug di wax cci yéneu yi et je l'aime beaucoup mais dafa wara xalate euleuk ak thiolam gou bone gui
ART NE VEUT PAS IRE MONTRER TES PARTITES INTIMES;YA DES CHANTEURS QUI SONT LA ET QUI NE MONTRENT LEURS PARTIES INTIMES;UNE FEMME RESPECTABLE NE SE COMPORTE PAS AINSI
De toute façon djiguénn dafa wara nékk royoukayy ndakh kou bakh djiguénn mola diour revien sur terre mia😊😊
Khana you bonne goor moko diour
Bilay damay rouss bilay yeri mome nice pas
MBA yow royoukay gua reck
Ki artiste la dou Ibadou louko saff lay soll motayy yéna. Ngaa def Lou geuna salté tei kénn yeugouko mounane royoukay on aime Mya vie elle est
@@LouiseDiabouMané-z4zIl y’a ça aussi. Sène biir famille yi ak séne entourage amna niouy déf lou yess sol lou gate, niom séne bopou douniou ay walliou daniouy baakar ni nieup niou paré dougou ci rèseaux sociaux yi di diaye sell🙄Faux moye deuxième tourou sénégalais ci gnima ko sania wakh
Mya Lou baxxx leu mei naniou encourager comme ça mouy sol Lou diote mâcha Allah❤
Délll soull lou bakh adouna dou dara bilaye amoll solou 😮😮😮😮
J'ai aimé ton commentaire car c'est vrai 😢😢😮😮😮 merci beaucoup 🎉 Dieu te bénisse les vêtements bien c'est important car après la mort les choses que la personne à fait reste toujours
Très bien merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mia lire na commentaire yii nite gnii baniou leu solale lou diote sama sœur ❤
Bilay nak da gua amoul conseillers vestimentaires
Je te kiff bcoup❤❤❤❤
Limouy sol créé wouko. Deuk bi nieupeu ko soll. Maylene ko diameu cest sa vie
Elle vs as bien répondu artiste da am tenue de scène vs qui comprenez pas deh len wakh rek mdr
@@Ablayblingua wax nanguoulnalako dh mai da am Lou xewone nieup faralko ecek tay dieukeuram amoul deug thikawam
@ThiernoyayaDiouf dieukeurm bane deug laye ame? Sa vie c'est sa vie fimouy wété ak boromam dou dieukeur dou yaye. Beugoul nekeu ibadou choix wame la yonou dieukeureum nekoussi
Show biz n'est pas égal à dénuder Mia te au Sénégal ici l'habille fait le moine
Des gens disent qui daffay liguey en quoi cette travail disent qu’elle doit porter du n’importe quoi pourtant elle est une grande star et c’est une très grande chanteuse moi personnellement je l’aime mais bon li yeup daniouy dée bayikofi té euleuk dou agne dou rére wayé lou mata bayi khel la
Vraiment sénégalais mo beuri cheytaner
Nafekh rk té
Nafekh rk
Coumba gawlo moko eup khaliss gueine ko nekk star deh day sol lou yiw changel sa yeine solou yi way 😢
Miss tu as déconnée oh tu n'as pas raison ds ton attitude trop abusé toi et wally tes tenues aussi
Mais de toute façon Lou yiw mo gueune vraiment 🥺
Tu es juste l’exemple de la jeunesse il faut s’habiller de façon correcte !
Bien dit
Elle n'est pas un exemple
Ndagay nakh sa bopou moy tou léne addouna yalla yalla bay sa tolle yalna borombi giuni la
Mé aknoumoumene démé domou dioulite gua té dioulite gua té adouna dafay diékh li yépou adouna la yame
Du courage ma chérie bonne continuation mais sache tu es Maman Liga wah lép dégleu tu es artiste tout le Sénégal t'aime très fort
Damani kholatal lingay sol. Dangay soff
TON LAPSUS EST RÉVÉLATEUR : SÉNÉGAL KEN BËGGULA????
SÉNÉGALAIS YI MIA MAABO LANU BËG, MOONU WARA REPRÉSENTER..LE SÉNÉGAL EST TRÈS RESPECTÉ DANS CE MONDE ACTUELLEMENT..
MIA( BEYONCÉ) FRAMACONNE BOOBU , JIGEENU PUFF DADDY, KOOKU DU SUNU MIA, BËGGUNUKO...
LEEGI TANAL BUDEE JIGEEN BU BAAX NGA.. NOFACE AVAIT RAISON: ÑUN AY SOXNA LANU..
ET NON DES KARDASHAN, RIHANNA, MADONNA...POUR MUY CLAIR...
Merci beaucoup
Amoule dara loumou lépa bone bayi lene quou tinmoinié rek niou défandre ko atelene degue mes mia je t'aime bien wayé li dohkoul
Cou d'accord ak mane
Aimel❤️✌️
Elle est très fragile 😢
Mia artiste la . Merci Mia , tha kaname. FÉLICITATION ❤️❤️❤️ bien des choses 🥰
Ragualal yalla mo gueune adounna dou keur 😢😢😢😢😢baxna
Congratulations SUPERSTAR 🤩! And don’t LOOK BACK NEVER 💯💯❤️❤️!!
teint marron bi rafet na, naturel na ! ma shaa allah
Wakh bou bone famou dhougué le deuk. Kéne dhiokhou la lék,ni nane, dhiguéne bouye réussire, di démale bopame lagnou bagne…… en avant …..💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾🥰❤️ félicitations 👏🏾
Un peu de respecte pour nous TATA MIA GUISSÉ mais sa soline nékhougnou nous qui t'a considéré comme TATA 😭😭😭😭😭
Do thiaga mai danga teyoul kou eupeul nga
Exactement, un peu trop excitée je trouve
Elle est en depression motakh dey def nga exiter tjrs ak desordre ds la tete di thieupi thieupi
Essais de revoir ta vie ces très importants mai on vous comprend plus vraiment
Bravo ma belle très bien répondu ❤
Qui d'où dara gouwmako nafsou bakanam la topp
❤❤❤❤❤❤❤
Bly les gens critique sans raison de toute façon amoul bayi on t'aime et t'admire❤
C'est juste le vestimentaire qui dérange même si c'est le show biz on comprends bien mais ton corps de femme on "aime pas le voir svp "mais ta voix ton style de musique❤. Prenez le positivement et avance.
Kom kham nga ne yiwoul lokoy solé😢😢
Bravo Mia.bonne continuation. Meilleurs vœux 2025❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Mia do not care. Bou lene fale.
Tout ce que j'ai à te dire faut juste habiller des vêtements qui sont on peu descend. On t'aime et on t'aimera
Sam yonn nekou si😅😅😅
Allakhirah chacun pour soi,😮
Mia si tu veux vraiment réussir n écoute pas aux commentaires
Mane d no mél beugue na❤❤❤
Dans mon cas je vous dit d'arrêter de l'a jugé vous vous trompez sur personnage et personne mia est une guerrière vraiment du courage mon idole focus rk
En tout tu as une fois étais trés décente à travers ton habillement et wallahi trés belle, aimée et appréciée. Je fesais partie de celles qui imitaient ton style mais sincèrement je l'ose plus.
Bon courage Mia doundal sa Life ça n’engage que toi mane dé yow rek laye topeu ❤🎉
Quand on vit en société, on ne fait pas publiquement ce que l'on veut.
Tata Mia Sénégal sofi beugé nk dèm ag fanga dieum boulma dégloul conards yi di wax si yw fonsèl le chemin est très loin et vous n'avez pas le temps pour eux ❤❤on t'aime ❤et on vous soutiens
Yen doul li lanla qui viviane mo ko dakh sol lou bone tei denguen thiy mandou tei diour dom you tolo ak mome bou sey sakh lay wakh ki molen eupe diom gune lena kham bopam beugue ngen jugei nit yei dolen yalla kou kham lingen di def yen ken yalla kessei kon arretei 'solou fi lou star soloule ay slipou nene sakh guisnagne ko ki molene eup pudeur fouf en dehors de sa sene khamo lene sakh nite
Merci Ndella❤❤❤
Merci ma belle gni gno soff😡
Outeul conseiller mais vrai conseiller, tu as du potentiel, conseiller bou bakh laley gnanal!
Nioun nitt loumouniou wane rek lanioucoy kholé linga deff rek la sénégalais yi wakh mia do bayima nitt nga walla bokk lingay deff mo eup
Damani dokhalal artiste ga❤
Courage ❤ ma chérie
J' aime beaucoup Mia guisse long vie ma actrice préférée long vie ❤️💞❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ elle porte des tennu bien et aussi classe j' aime vraiment cette artiste dans mon cœur ❤️❤️❤️❤️❤️❤️ je battre avec mes amie pour cette artiste ❤️❤️❤️bon carriere
Solin no thiaga rek ngay solo boul niou sonal amo ben kilifa nga melni ko amol dom ni niakeu kersa
Mai 😢 reviens sur terre mais ne regarde pas se qui sont considérés comme bien et Font le mal toi concentre toi sur toi avec le bien Mia la vie n'est rien c'est pas parce que tu es artice que tu fasse le mal
Que Dieu te montre le bon chemin ❤
Mia guissé sénégal louñiou wakh si iow dafa beuri trop mais c la vie
Machalla ❤❤
Kii amoul benn ndiarigne si société bi, yakk rék lay déf !
délll soll loubakh lala wakh
Manè dokhalal certains sénégalais ne sont jamais contents tè nieup mounou niou la beugueu❤️❤️
Yaw mom sa wakh yi mom moy lan. Ki jeunesse inconsciente bi daniouy roy si mom. Té bou solo lou bon dalé ni influencé
@ manè solou fi lou kène soloul tè guène haar ndjabot dji mo gueune. Mia sur sa page snap elle publie des vidéos ou sa fille apprend le coran alors certains filme leurs enfants en dansant est-ce k finalement le problème c’est mia
Merci yonou diam
DJIGUENE amatoul valeur wallahi ajim
Mia so dèmè si yalla nèko show bizz la okay
Love you Mia ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Cv domou baye loutakh nga LOV mia gissé❓
Soit correcte on a des valeurs à sauvegardés
Thiaga DEUG la ki alalou satan la fimou diougue AK fimou d'all nooo
Ce toi tu est conplexse on conprent Tres bien tu p porte ta tenue africaine et reste dans le show
Bien parlé Mia❤❤❤❤❤❤
Thiaga bakhoul Sénégal duekou dinnela
Djiguènn dafa wara nèkk royoukayy😊😊😊😊😊😊😊
Bonne continuation pour toi Doundeul wéreul yabakh ❤❤❤❤man dama la beug lolo ❤❤❤
Nala yallah defal diam
Kou melnii thiagga niou wakhlako thiagga divorcée
Astahfiroulah
Mia guissé ndeysane sén prière clips yaye mako nianwal wax bimo sol machallah diamano diodiou mia gui yéw ndeysane tay mom souma amé louma méti cii lén réc la moy wagne yoon guen dém cii yoon bi bone lol réc moma méti mais koy nianal yala antdi watt cii yoon bi guene dia Dieuf ❤❤
exagération totale thippp🙄
Mia on t'aime on n'a rien contre toi c'est des conseils constructif et des leçons religieuse que nous te donnons
Car actuellement tu est entrain de donner raison à Now Face
En plus tu as une fille qui ne doit pas voir tes images négatif à travers les réseaux sociaux sinon elles aurait des problème demain avec ton attitude
Bou fontoo nit yi
On comprend bien le show biz
Mais cela ne veut pas dire que danga wara def taatou néne
Comprendre milieu artistique moy lane au contraire yaw Mia ya comprendre woul boy Mia tu a intérêt à changer wollahi
Nono lala begue wallahi tédamalay begue ba fawou mais xolatal sa bopp nak
Machallah ❤🎉
Mia je t'aime beaucoup mais tu a perdu un vrai homme de valeur tu étais très belle pour moi avant
Ce n'est pas une question de prostituées mais en raison de valeur il ya beaucoup de gens qui te suivent et actuellement tout les chansons que tu chante aujourd'hui reflète quand tu étais avec ton mari réfléchi bien mia la beauté d'une femme ne ceu trouve pas dans la vulgarisation
Mia il faut voir wally si sa femme fait c'est gérer de choses et pourtant tu actuellement très proche de lui wally
Dèl sol lou bakh gnak nga diom loole thiaga binga done
Merci beaucoup mia bonne réponse moi je t'aime beaucoup soi forte❤❤❤
Guis gua nit boko beugué dagua koy wakh deugue. Moi je l’ai toujours adoré et défendu mais maintenant je n’arrive plus à la regarder tellement je suis déçu par son comportement elle est entrain de donner raison à son mari et au autres hommes qui croit que les femmes n’ont pas de cervelle. Avec la position dans lequel elle se trouve elle doit donné l’exemple. Regarde toi devant un miroir avant de sortir. Gni lay diéy di la Conseillée wakhou gnou la deugue. Doto khalé dioy fadioul dara.
Pourtant critiques yi moko yobé bopam dh avant kenn critiques woul ms danga wara soralé danga am dome niou balma nk sm khalat rk la wakh 🙏
Bayilene Mia vraiment elle est fatiguée dans son propre pays .elle est talentueuse .dohalale chérie
On t’aime bien mais soit plus africaine et plus décente trop de vulgarité pourquoi ?
Ki nann niekay kirtiquè dano khamoul kay wakh takhouko changè ndakh djapp nani lim neknmoy deug
@@mbaye53 dommage
Valeur day fégne bassi solo changél sa habilement
Il faut faire très attention
Domoukharam tu a rien compris hé reviens sur terre revois ton habillement
Yaw domeiram pire nga
MIA bule falé💪🏾💪🏾💪🏾❤️
succes diaroulll li
Sénégal dafa bari nafékh nioune on t'aime fi ken banioula m dou teirei nitt gni wakh la deug kou wara kholatt sa bopp gua
Ame na nioula critiquer woul ndakh kham nagne la te kham nagne kima done koula kham deug dina kham ni ya gueune fouf gni fi nek di juger nite yi té khamougnouko
Bamell amoul artiste 😂😂
Delo lenn se celle si yalla tè bayi yeufu yeufeur ri
Kén juger woul yaye kan nax lolu ku nék amna luko doy ak borom bi mais image bi bul faté amna ay xalei you ndaw di say fans peut être dila sétan ✍🏽
Bly mane mia damako beugue té khawma lane la té kouko beugue ma beugue ko kouko bagne ma bagne
Moi je t’adore point ❤❤❤
C est une artiste laisser la en paix' elle sont nombreuses les femmes qui s habillent apparemment comme mia. Par ex: Viviane n est pas decente ;Titi maintenant fait de même etc...
C'est vrai que limouye sole parfois c'est sexy mais liguéye bi moko ladieu et il ne faut jamais juger quelqu'un à travers son apparence physique 👍🏻
Wakhou dof.
@zai5562 yaw mi ya doff
Mais yeen séen titre bi ëp ne dé. Do léen xool li ngeen di mbindël nit ñi. J'espère que Mia ne laissera pas passer ça.
Mia bilay amo fouleu dou nékone ma yaw douma sakh tontou damay liguéy sama liguéy bayyi len gnouy ratati
Yaw instants yi ya téyé deuk bi défal loula saff doune la rayy doune la fess ay wakh rek lanou lay sanni mais yaw boul guéssou focus si liguéy ta famille t'aime
😂😂😂mbadou mo remplacé diomay ak sonko bilay diguén diay nit bamou day toubayam guén takhaw à côté wakh li dou day
@@snQueen Kon yaw tamite si wakh kate yi nga bokk 🤣
Yiweul ko !!!!!!!!
Certes tu as du talent mais
TENUE you correcte daf siy baakh😢😢😢
mia concentrewul sisa jobb nit gneup menugnula beug c la vie so beugue ku wakh ga tontu bu yague ga son teduko jar
❤❤❤❤❤Mia
Ça c'est vrai❤❤❤❤❤
Mane dé loumalaye gnane moye nga délou ak no face nguire yallah
😂😂😂😂😂😂😂
Mia tu es libre mais reste loin du menage de Wally❤
nagn waxanté deug danio am sounou ay réalité sounou ada ak thiossane ay kilifeu liguéyal niou lou reuy
Meussouma beug di wax cci yéneu yi et je l'aime beaucoup mais dafa wara xalate euleuk ak thiolam gou bone gui
Yén niouy défandre mia yeupp ay goor djigéne laniou mia thiaga bou katte ndayam la
ART NE VEUT PAS IRE MONTRER TES PARTITES INTIMES;YA DES CHANTEURS QUI SONT LA ET QUI NE MONTRENT LEURS PARTIES INTIMES;UNE FEMME RESPECTABLE NE SE COMPORTE PAS AINSI