VJ - Kaay Waay (clip officiel)
Вставка
- Опубліковано 7 лют 2025
- Streamer DM : bfan.link/dm-4
PRODUCTION : HOSIDE & BLZ
MUSIQUE : AKATCHE
LYRICS : VJ - KHRU - OMAR SARR
PRODUCTION VIDEO : REVERSE STUDIOS
ASSIST. DIRECTOR : DJIBY NIANG ASSIST. CAM LAMINE CISSE PHOTOGRAPHER : ARONA WADE
DECO : NDAYANE DECO
CASTING : NA YOODI
EDITOR&VFX : BILAL MBENGUE
CHOREOGRAPHY : BARRY KUSH
DIRECTOR : BILAL MBENGUE
D.O.P : LEYE GUEYE
DRONE OP : ARONA WADE
ACCESSORIES : BRASMAGIK
MAKEUP : SOKHNA FATOU DIOUF
STYLIST : Bright look (Elzo bouba) / Mushei
COLOR GRADING : BILAL MBENGUE
STUDIO WATCHTHESTUDIO221
SPECIAL THANKS : TEAM VJ, MANSOUR MOTORS
Lyrics
Kaay waay
Ndeke dou mbeuguelou Kassè
Teh sax xetou mbeuguel yi dafa rare
Dièkou ma ni douma bale yeah yeah
An konne yaw bandi nga ndèkè bebe
Sopi nga sama xol bi limonade
Siroter ko diko nane yeah yeah
Ndax baniouy ndieukeu guissanter
Li nga ma yene nimou disser
Ak niniou xolanter
Rek ma xamni yalla niou bolè
Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (KAAY WAY)
Doflo ngama (kaay waay)
Wayè deufeul ngama (kaay waay)
Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay)
So bèguè ma bègue (kaay waay)
Niou deukè di rè (kaay waay)
Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay)
Maala geuneul lounè (kaay waay)
Teh yaama geuneul kounè (kaay waay)
Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay)
Bègal ma bèg (kaay waay)
Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay)
Soma sorè oh my love
Namel bimay yeuk thi yaw
Wallahi yaako meuneu fadie nieuweul
Niouy kaf di rè
Niouy kaaf di fo di rè
Ndax baniouy ndieukeu guissanter
Li nga ma yene nimou disser
Ak niniou xolanter
Rek ma xamni yalla niou bolè
Est-ce que do djinè ndax diomal nga ma (KAAY WAY)
Doflo ngama (kaay waay)
Wayè deufeul ngama (kaay waay)
Mane limay doundou ni daal nexma (kaay waay)
So bèguè ma bègue (kaay waay)
Niou deukè di rè (kaay waay)
Yaw moussoul metti ba nga reuthiou li nga ma xam (kaay waay)
Maala geuneul lounè (kaay waay)
Teh yaama geuneul kounè (kaay waay)
Bae liniouy doundou ni tièr-Carrè na (kaay waay)
Bègal ma bèg (kaay waay)
Ma xeuthie sa reundeul happy (kaay waay)
Oh bebe toi mon bebe
Toi qui m’a tout donner
Je pourrais jamais te quitter
Je t’en fais la promesse mon bebe
Tu m’as tellement épauler
Quand il le fallait
M’a sorti de la galère
Je vais te rendre la money
Oh bebe yaw mi gounguè ma man malay gounguè
Et si t’a peur crie aider moi mane maaa lay sauvé
Oh bebe yaw ndax beuguè ngama comme nim la beuguè
Ndax nim la beugè eup naaa wa li noum dèmè
Oh bebe toi mon bebe
Toi qui m’a tout donner
Je pourrais jamais te quitter
Je t’en fais la promesse mon bebe
Tu m’as tellement épauler
Quand il le fallait
M’a sorti de la galère
Je vais te rendre la money
Oh bebe yaw mi gounguè ma
#vj #kaayway #dm
lacigale.fr/evenements/vj
Achète ton ticket ici !
La famille on se retrouve ce 10 janvier à la cigale pour la première date parisienne.
Kaay way
Blyy ya meune🎉❤
❤❤❤❤❤
T'es le meilleur je te jure😢
Dosen mborom sakhe ❤❤❤❤❤on t'aime fort vj mouhamed 😢😍😍😍😍🥺💞💞
T'es trop fort ma shaa Allah 🎉 que ta bonne étoile te quitte jamais 👌💯
Chaque fois qu’une personne mettra un like je reviendrai réécouter ce chef-d'œuvre ❤😊
❤❤❤ Santana pour son bébé quand on
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Narr gua soneu nak iow 😂
Wow tu ment trop même dis jamais vue
687 fois pour l'instant❤💯❤🔥😂
Si t'es un vrai fans DE VJ manifeste toi par des j'aimes à se commentaire di na hame ni iow thiékané nga 🎉
Fans n1...
ua-cam.com/video/a22SRK33Sag/v-deo.htmlsi=I5Md5XczFxoCj6oD
🥰🥰🥰🥰🥰🥰
❤❤❤❤❤
Lirr katou commentaire yi longue vie à vous ❤❤❤❤❤
😅😅merci
Amin
Amen bb
Amine 😂😂
Merci
“Je voulais te dire combien tes chansons me touchent profondément. Elles ne sont pas seulement des mélodies ou des mots, elles sont comme des portails qui m’emmènent loin de mon quotidien. Quand je t’écoute, je me sens voyager dans des mondes où tout est plus vaste, plus intense. Tes textes et ta musique ont ce pouvoir rare de me faire voir la vie avec d’autres couleurs, de m’inspirer, et parfois même de me ramener à des souvenirs que j’avais oubliés. Merci pour cette magie que tu partages.”
😢😢😢🎉🎉❤❤
Longévité à toi laff thiate frère
❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉 1:43
ua-cam.com/video/a22SRK33Sag/v-deo.htmlsi=I5Md5XczFxoCj6oD
Vj vj vj je t’ai appelé combien de fois bal gnou fuir yallah 😢 nékhoul ba nékhoul mais musique khalé y’a meilleur kay ❤cette chanson fait le portrait de ma rencontre avec mon copain ❤je kiff ❤beaucoup bilay 🥰🥰😍😍❤️❤️❤️❤️🫶😘😘👩❤️👨
Merci🎉🎉🎉🎉🎉
ua-cam.com/video/a22SRK33Sag/v-deo.htmlsi=I5Md5XczFxoCj6oD
Où sont les autres vrais fans de VJ comme moi tapez ici pour voir un beau clip comme ça mérite des 1M de vue dans 24/24 vient waye 🔥💪🏾❤️🤍🤍🌱🌿🇸🇳🇸🇳🇪🇸
Vj ya meun nk son bi mom dafa nékh trop machallah 🥰❤️
mko geuna nehhh bly iow
❤😊
Kou beugu VJ rk lalal j'aime ❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
ua-cam.com/video/a22SRK33Sag/v-deo.htmlsi=I5Md5XczFxoCj6oD
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vj danga diokh valeur taille fine yi nak kou setlou lolou si ay clipame 😍😍😍Mancha neh na trop images yi nice 👌 top bonne continuation mn frère 🎉🎉
🎉🎉🎉🎉🎉
ua-cam.com/video/a22SRK33Sag/v-deo.htmlsi=I5Md5XczFxoCj6oD
Le commentaire que je cherchais
Fala filing bi nékk 🥰♥️
Qui est là avant les 1h de temps ?😂avant le million de vues?🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤
🎉🎉🎉🎉🎉😂
🎉🎉🎉🎉❤cv😂
Kou d’accord né wa lady diama la warona déf clip rék lalal j’aime ❤
Surtout diama walla asmao😊❤
Oui si mom la inspirer sakhe
@@hamadoudiallo5670oui effectivement
Mane khana
Pour mane séquence réception assy bi Dina bokkou si clip bi sax
Qui comme moi ne comprend rien mais kiff juste le son grâce au mariage d'assy et Abdullah ❤
Une chanson d'amour
MUSHEI SOLLALE NALA NAK EN PLUS GUA DÉGUE SAGNESÉ BILAYE WALAYE MALLA BEUGUE 🥺❤️❤️❤️ EN TOUT CAS BRAVO LE CLIP EST JUSTE WAO 👏👏🍾
Khaler bii meune na weuuuy wayyy 😭❤️Vj khana ko ray gua beugue tmt 🙈❤️
Depuis le Congo 🇨🇬 ❤
Masterclass 🎉❤
Liii sou amoul blessé dîna âme mort waye 😭😩😩😩🎉🎉🎉
Une camerounaise déjà sénégalaise 😻 trop mon kiff 🔥🔥🔥🔥
❤❤😂🎉🎉🎉
Loum niou Dessel la beug kham (Dara nak)😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🥳🥳🥳
ua-cam.com/video/a22SRK33Sag/v-deo.htmlsi=I5Md5XczFxoCj6oD🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
❤❤❤🎉
VJ, le jeune qui n’a jamais perdu sa valeur ❤kou d’accord kay waay ❤
VJ l'étoile montante de la musique sénégalaise good job bravo et bonne continuation❤❤❤❤
❤❤❤❤
Vraiment Mouhameth VJ tu es en croyable tu représente vraiment le Sénégal 🇸🇳🇸🇳 merci beaucoup
ua-cam.com/video/a22SRK33Sag/v-deo.htmlsi=I5Md5XczFxoCj6oD
Ohhh genre il ne déçoit jms 🎉🎉🎉ya meune ya eupeull dolé💖🎉🥳🥳🥳🥳ya guené fétté khalé😂😊❤❤❤
Chaque fois qu’un personne touche mon commentaire je viendrai regarder le clip ❤
*Donc revient ✌️😍🥰*
@@veroniquenatack7392yaw xamei nala si serie marodi yi d😂
Boula yalah maye rek nagoulen. ,gni nagoul vj beuslen fi >>>❤️
Daflerrrrr bro
Deflr
Degeleuuu
Yakofa am
Pourquoi il n’a pas encore atteint le million
Magnifique seu khol ley Doug
Merci VJ
Que de l’authenticité ❤
Wow j'aime bien le style ...tu as beaucoup d'avenir et l'enchaînement sur la fin est juste incroyable...🎉 kou d'accord 😊
Vj xale bou pare bii danga khew yalla na sa diamm yagg yangui begall gayi de 👌
Kou beugue sa yaye l'alal j'aime ❤️
Tu ne vas jamais me décevoir ❤❤🎉
Franchement vj t'es fort bonne continuation rk mon frère 🎉
ua-cam.com/video/a22SRK33Sag/v-deo.htmlsi=I5Md5XczFxoCj6oD
❤💍💞🌹Awa Gassama rék la beugg di Gnane Yalla mou gawa déff li Geune si Barké kü Téed ki 🙏.
Yalla na döne Sama Sokhna ❤💍 dioural ma aye ndiabote yü barké🙏💯💞🌹❤️💍
Nima beugue Vj nonou guenko beugue yennn❤️🥹
Avec VJ je pense que cette année ça va Peterrrrrrr💣💣💣🧨🧨🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽
Mba yenangui dem Ozan🥳🥳🎊❤️❤️
Meilleur jeune chanteur d’Afrique ❤
oui j sui daccord avec toi
Il fallait prendre l'extrait du mariage de assy et abdoulahi 😅mais c magnifique
La meilleure chanson de l' année ceux qui sont d'accord avec moi laisser un❤❤
Kou beug SEYDINA mouhamed psl lalal j’aime ❤🙏
Orrr mon choix ès trop délicieux j'écoute encore et encore depuis Abidjan 🇨🇮😍🇸🇳
Merci a la côte-d'ivoire ❤❤❤🎉🎉🎉
Boula nékhone bania deff clip bi ndakh nékh na ba nopi mais défoko dagua nio défal vidéo bou nice way❤❤❤❤
Waouh, franchement le clip est à la hauteur du sons. VJ à chaque nouvelle chanson je me demande si tu pourras faire mieux mais en fin de compte tu ne déçois jamais ☺️❤️🇸🇳
Vj dou sakh sene morom ❤️🫶👌👑
Ya meune si xalèyi bilahi kou d'accord besseul j'aime ❤
vraiment tu es le meilleur 🎉🎉🎉 dama la beugggg té yalla rek takh ❤
Imaginez sou dieulone Wa lady Diama😭❤️❤️🎊🎊🎊
Yaxeu na 😂
Slmmm guys neklène si diam👋✨✨
Ce son est tellement d une douceur dans les oreilles,, parfait!!! Tout est bon. bravo l'artiste ❤️❤️❤️
Kou beugue vu lalale j aime 😊😊
Vj moy borom ndakarou th nio bokk konie bouma ko Guissé sm khel bi deye dem❤❤😢
Je comprends pas les paroles mais j’ai trop kiffé ❤vj t’es le meilleur 😊
❤❤❤❤❤❤😊😊😊😊
Vj yaw mi yay djiné biniouy diomal chaque son
Kou d'accord rek lalal j'aime❤
Waa jiguen yilla diomal si clip bii mom beurina dh😂😂😂
*Trop sakh 🤣🤣😂😂😍🥰*
VJ dieul guelou diambour yi di len clip wa bakhna😂😂😂🎉🎉
😂😂😂😂😂Mbadou
😂😂😂😂
Meusouma âme 10 j'aime 😭🎉🎉❤❤❤❤VJ Le meilleur de sa génération 👑❤️
Oooh 🥰 mélodie bi, texte bi... doumassi doyale ! VJ té Capo...masterpiece !💙
Bientôt on vas décoller ❤🎉😂😂
Il s’habille très bien machalla ❤❤❤🎉🎉son bou nekh
On Attend 🤣✊🏿
Sampoul dé gueumeul seu bop avance tout droit trop de feeling rappeuse de l’année ❤
Bonne chance à tous les sénégalais
Son bi hooo mom lay réyé sama contacts temps yi snap bouma def migui si 😂🎉❤
Bly ki damakoy beug ba kagn🤭 le best de la génération ❤
Vj tu nous as fait quoi je n’arrive pas à sortir cette chanson dans ma tête 😍🔐
kii djiné laa❤
Vj ya meune ya eupeu doolé❤❤
Dof lo nama mom ❤😂😩very nice song 🎧
Kou ke kamé lady diam rek lale j'aime 💖💖❤️❤️❤️
Kou contan si kingen nèkal nieuwal lal z’aime❤❤❤
Vy borom Dakaru🎉❤ kou beugg vj lalal j'aime
Ohhh nékh + nékh = nékh 😂😭😭
Kou beuy vj lalale jaime ❤❤❤❤❤❤❤❤
Rek ma Kham ni yallah moniou bolè ❤❤❤
Vj c'est une fierté machallah ❤❤❤❤❤❤
Vj dinama ray rk
Song bi an limakoy deguelou par jour eupeuh neuh 🥹🥰🥰🥰
Vy dafa graw👇👇👇
ua-cam.com/video/a22SRK33Sag/v-deo.htmlsi=OSoAYT3mL1W1FJeM
Ma kheuthie sa reundeul happyy👨🏾🦯😎
Oh lalah 🎉 il a encore frappé fort 💪🏽🔥
Ken dou reverse studio 🥶🔥 🇸🇳
La fille en orange elle est magnifique ❤❤❤
The goat🎉🎉🎉🎉❤❤❤
Ohh avec vj nos cœurs battent plus fort 🥰❤️❤️❤️
Mais xalei bi meun woy waay ❤❤❤❤❤❤❤. Mane say parole moma diaxal si xalei machallah yalla naleu borom bi sambe nga réaliser say projets
Khalé yi ba yena gui deme ozan 🏪🛒
Vive Sénégal 🎉❤❤❤❤❤❤❤
On vas décoller 🎉😂❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤ wawawe ya meune kaye nak vj ❤❤❤❤❤
Machaallah VJ notre fils adoré on aime tes chansons bonne continuation et plein succès amine inchlh❤❤❤🎉🎉
Depuis la GN 🇬🇳
Qui aime v j comme moi ❤ pourtant je comprends mm pas wolof mais je l'aime ❤
Sa way yi nexoumawone mais bi saf na saparal bonne continuation
Congrat bro 🎉clip bi dop neu.
Vj ta encore tapé fort❤🎉
Ohh séd na khôl daal vj pourquoi ma beugoula 🎉🎉 machallah
❤❤❤❤ depuis le congo Brazzaville
Khaléyi mba sen khol mongui fékh
magui youkhou lihh nekh ne deh 😍😍😍😍
Réussite total inch Allah bon courage et bonne continuation 🙏🏾👏🏾👏🏾🔥
Notre dadju national 🔥🇸🇳
Waouh vj tu es le meilleur ❤