Mon village, le village natal mes arrières grands parents BAÏNOUK, du côté de ma maman, fondé par mes arrières grands-parents : Sagna Sama Mame Astou Mbaye mo mom les terrains : Marie Sagna mo Diour Astou Mbaye mou diour Marième Thiandoum, Khardiata NDOYE, Yama NDOYE, Babou Ndoye ♥️♥️♥️ …et le papa de ma maman y a été Instituteur dans les années 40/45. Kou nieuw Adéane sama Mame Astou Mbaye mo leu maye terrains…ainsi de suite.
Machallah mon village natal sama mame maimouna seck di tawo mame alassane seck wassour seck ak Tissina Mané si adéane mo diour Ablaye Ndiaye imam di mami Doudou Ndiaye. Ablaye Ndiaye donone imam si adéane wadiourom bou goor lébou la toudone Ousmane thiamba Ndiaye.
Sama MAME SEYDI…ohhhh Ndeyesanne. Sama Mame Astou Mbaye Mme NDOYE mo ko may soufffff Adéane. Fière
Ohhh keur mame bok seckene ak Ndoyenne ❤🥰
Mon village, le village natal mes arrières grands parents BAÏNOUK, du côté de ma maman, fondé par mes arrières grands-parents : Sagna Sama Mame Astou Mbaye mo mom les terrains : Marie Sagna mo Diour Astou Mbaye mou diour Marième Thiandoum, Khardiata NDOYE, Yama NDOYE, Babou Ndoye ♥️♥️♥️ …et le papa de ma maman y a été Instituteur dans les années 40/45.
Kou nieuw Adéane sama Mame Astou Mbaye mo leu maye terrains…ainsi de suite.
Machallah mon village natal sama mame maimouna seck di tawo mame alassane seck wassour seck ak Tissina Mané si adéane mo diour Ablaye Ndiaye imam di mami Doudou Ndiaye.
Ablaye Ndiaye donone imam si adéane wadiourom bou goor lébou la toudone Ousmane thiamba Ndiaye.