La manière dont Ba délaisse sa première femme c'est qu'elle chose de réelle dans les familles polygame la première femme souffre le plus souvent et pourtant la plupart du temps les enfants de la première nioy gueuneu tékki Lou way mougn mou diekh
Moi j aime Khady elle a la tête sur les épaules elle est douce les filles méfiez-vous de certains hommes qui vous promettent de certaines choses chapeau à khady
J’adore la série, très instructive ❣️par contre les termes de Ndeye ndiaye envers les autres dames me dérangent vraiment, du genre « dagua niakk diom »etc , c’est trop pour moi. Même si day daguassantei ak niom, ay niakk diom mom si makk yi da eup, na xoulo rek ak kaddou you rafete. Merci beaucoup ❤️🙏🏾
Khady va prendre la maison cadeau sans payer quoi que ce soit...la maison sera a son nom elle va les dribbler...khady na meme pas 1 millions en poche a plus forte raison 47 millions
Khady 🥰Elle est d’une douceur extraordinaire ❤️ Machallah
comme vous je pense
1er vues dolen ma may j'aime
J'aime ken douko forcé
Une série qui reflète notre société machallah. Vous êtes naturels et professionnels.
Bravo à toute l'équipe vous faites un bon travail chaque jour deux épisodes c'est un travail dure sachez que nous sommes derrière vous.
Fatimata tall yaw foma rérone depuis des années ndeysane thieuy aduna
@@niangmodou47 sava ton nom me dit quelque chose mais jai oubliée
@@fatimatall9890 ndeysane khamnani kay faté ngama mais dinalla def signe Facebook inchallahou
Machallah c extraordinaire rip maman thiaba thies k firdawsi soit ta demeure eternel amine
Ana gnifi amm wifi ak polygamie 2 épisode parr jour 🤣🤣
Niongui ni
✋✋
Mane dh damay moudié rèr sakh 😂😂😂 mais mogui may wéteuli bou bakh j'adore
Migui ni dh
Gnongui ni
Je suis accro à cette série bravo aux acteurs 🥰🥰🙏🙏
waw sama awo boul hessal! Ani niou bok "association nio lank awo dou xessal "!
La manière dont Ba délaisse sa première femme c'est qu'elle chose de réelle dans les familles polygame la première femme souffre le plus souvent et pourtant la plupart du temps les enfants de la première nioy gueuneu tékki Lou way mougn mou diekh
Vraiment sama toma bi defeu naturel te douce je l’adoreeee dal 😍🥰♥️
Polygame dale Macha Allah. Nieupeu professionnels. Vraiment nekhna torop. Merci Senepeople👌🏾👌🏾👌🏾
Nice Nice nice
Nice bro
Nous sommes trés fier de vous.
🎉🎉🎉🎉
@@aissatakeneme 🎉❤🎉😊
Vieux😅gneuwe na tani bi wassa na bravo aux acteurs on se régale 🥰
Vieux mome je l'adore il me fait trop rire 🥰😅😅😅
Kër gi neex na, kenn amufi kilifa ñépp reew. 🤣🤣🤣
Lima geuna nékh si série bi moy génétique dafa gate bravo
Bilay do sonou si avance bi
En plus amagoul j di bien amagoul pub bien k moy indi xalisss
Dafa naturel ba parer pas de luxe comme film Nigérien yi dans les villages j'adore
Duo ndeye ndiaye badiane nékhe na trop 🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂😂
Thiam n est pas bien, il parle toujours mal de sa famille alors qu'il est pire
Franchement
Moma daikhal di 😄😄
Deuguela nouyoulma kou mel ni
Comme beaucoup d'hommes malheureusement au Sénégal
Thiam kay dou nitt
Khady est trés belle manchalah et class
Comme vous je pense
Best série 🥰 simple et sans chichi. Une série riche en enseignement. Je suis accro 😭
la simplicité à l'état pur
Tatou pawlise mbaye kaye nn li doumako lale😂😂😂
Awo bourou keureum continue si naturel bi way
Non awo papi khoromouna khésél ba wékh tar pose cils ongles ak taille basse bamou nékh 😂😂😂😂🙈wouye non série bi nékhna
Yaye bo khéssalé dina grève de la faim 🤣🤣
Athia waye na sponsore yi gnewe sougnou Wa team Badienne meune na yague sama Lif gawe léne di aimer 🥰
Badiéne Nanité ngayy amm fofou 😀😀😀
@@ndeyeamiendao5376 billahi amoute
Bonne continuation parsk liguénn di déff nice na trop ♥️🤞 gnogui sénn guinaw dina bah inchallah alla💖🌹.lima gueneu néhh Moy douguénn wah français
Thiam faux neu🤣😂sou deme si ki yakk la sou gnewei si kee yakk la sheuttt😂
Ana gnifi amm chambre lonnnnne💪💪💪💪polygamie laniou wakh
Mane da melni appartement laffi ame 😂😂
Machalah c est une série éducative qui reflète la vie des couples polygames au Sénégal
Tatou pawlish Mbaye kay 😂😂😂
Bayiko rek bamou diam ko
Team Khady ❤️❤️❤️
Moussouma beugue ni série. Bonne continuation à vous, bouleen wathie yoon wi.
Papa Bou warna bayi xool caméra bi.
Mom dako tame deh série yépou lakoy def com wathi béss 😁
@@kharitouboromkeremrek c grave mingui melni bess ci série
Walaye wakhatiko merci mome akk demby fall rek la guiss niou koye deff .niente professionalisme.pour mane ayoul ci sama guiss guiss. Sofna torop
@@kharitouboromkeremrek Ça veut dire keu né ayoul rek.kouye bayi khel camera yi ayo tamou nako torop
@@aissa2425r siii ay neu d....ki ancien la , khamna daf ko tameu rk
Fallait pas se depigmenter ndeye Ndiaye 😭😭😭
Mane Thiam mo may raye kou mou djiss néko wa keur gui baxouniou
Badienne tamite 🤣🤣🤣🤣
Khady mom mashalla 😍😍😍 hayyy vieux tay fii nekh 🤣🤣🤣🤣🤣
Merci pour tous
Chapeau à toute l’équipe.You guys are the best 👍🏾
Vieux mn acteur préféré mention très honorable a vous
Moi j aime Khady elle a la tête sur les épaules elle est douce les filles méfiez-vous de certains hommes qui vous promettent de certaines choses chapeau à khady
nous sommes pas tous comme ça heureusement
J’adore la série, très instructive ❣️par contre les termes de Ndeye ndiaye envers les autres dames me dérangent vraiment, du genre « dagua niakk diom »etc , c’est trop pour moi. Même si day daguassantei ak niom, ay niakk diom mom si makk yi da eup, na xoulo rek ak kaddou you rafete. Merci beaucoup ❤️🙏🏾
Meilleur série qui est d’accord pour 1million d abonnés
Mane deh 5 fois par jour douma Doyal akama badola🤣🤣
🤣🤣🤣
😂😂😂😂
Ahhh wa Badiene miii nak warna wakh Ndeye Ndiaye sa tate bou gatt biii diii meleni tatou Palish Mbaye😂😂😂😂non Ndeye taye danounana😂😂😂
Mâcha la c’est une merveille ça change très authentique bonne continuation!!!!!
2 episodes chaque jour et 00 pubs. Bilay yéna meune souma meunone abonné 10000000000fois nako def
Machallla machalla non le bonheur de regarder la série ♥️♥️♥️♥️bravo way
Réunion de famille kagne lay am si keur gui 🤣
Ndaw reeñoo bu neex 🤣🤣🤣
@@mustafaasamb8419 😂😂😂😂😂😂
Thioum sama série préférée ❤
Sama série préférée💯💯
Ma challaha khady bou ndaw nèkh ngama❤❤❤❤
Bilahi khady soeurou bou beugue nala
En plus de ça ce qui me fait plus plaisir il y a pas de pub bonne continuation
Lolou nague day takh dougniou âme khaliss
Aah mais pub yi moy soutien bi nakk
Les pubs aussi khaliss leu. Ça permettra aux acteurs de s'enrichir un peu sakh. Ils ne gagnent rien pratiquement. Vivement les sponsors
@@sweetyqueenthiam2227 ndeysaaan beug lignouy def rekk iow motakh gnouy def lii yeup
Ay way pub yi mo leine di May khaliss
Thiéy Bâ meuna yap meuna dieune🤣🤣🤣
Familles sènègal éqîsode
53
Machala bonne continuation a toute lequipe vous êtes adorables
Meusou ma commentaire mé serie bi mom machalla nékh na amna solo lol sakh
Badiène est automatique 😂😂 dafa maîtriser baat ak tontou
Comme kou diour ndeye ndiaye key🤣🤣
Non Ba moo badola neena aawoo bi yaw li ngay widié leep bayyina sa léep neena mengue 😂😂😂😂🤣
Wouye magui kheum vieux un vrai acteur
Mane yine laye weur ba goudi thiott ma nane ndokh tedi mangisi épisodes yéép histoire d'amour appartement 02 polygame yén dal diam réck machalah
Badiéne Nanité ngayy amm fofou 😀😀😀 avec sa façon de parler
Machalla vous êtes les meilleurs 🥳🥳🥳🥳
Bravo à toute l'équipe châpeau a vs vraiment
Entre Thiam et khady baba sama khel dalou si dé❤❤❤. Sen wakhtane douce na lole.
Je pense que khady khalissou keur gui mokofi indi
Khady va prendre la maison cadeau sans payer quoi que ce soit...la maison sera a son nom elle va les dribbler...khady na meme pas 1 millions en poche a plus forte raison 47 millions
Khady da nara tayle Ba ne diokh nako khalis fek diokhouko dara🤣🤣🤣
Thiam tamite beug na tahawayou mbenda torop 😂
Ah lii nekhna way merci senepeople
Vieux tothieuna casse yi😂😂😂
Franchement contane ci equipe bi yeup
🤣🤣🤣
Vieux à fait ma soirée dalaltone orange 😂😂😂
Machalla nekhna trop meilleur série bilaye
Ba comme novice 1.2 mou xol camera Bi 😂😂😂wieux raynama bama d Thiam mom seytane boumak la
Mane dama léne bouga❤
bilaye ndeye ndiaye mala begue saye rèe rek sa fait plsisir
Ba bayyile camera bigna ye khool way nga mélni Étranger ni
Machalla khadi bou ndaww nekhna maa 💖💖💖💖💖💖💖🇮🇹🇸🇳
Ay gni nilen Khady babo nara def Wa bakhna 😂😂😂😂😂
Thiam la contre man gani sa fami bi do ci wakh lou bakh te niom moussou guiss fou niu la yacke🗣🗣🗣🤣
Lolou dafa beuri si deug bi
Mak yow
Non ndeye Ndiaye beugnako nieup nenagne deux épisodes mome leipam felling la nena leiweul deuxième
KHADY machalla elle parle bien
Et toujours mesurée masha Allah
Je l'apprécie looool
Enfin la dose de la soirée
Moi je ne comprends pas Thiam mome néna da bayi keur gui alors qu'il se mêle toujours des affaires de Ba. Vraiment c'est un rageux 🤣🤣🤣😬😬😬
Té chaque jour mou dirékhou gneuw
@@sebeka9621 😂😂😂😂😂😂😂
Mom Ba la fans si bopam
J aime bien ce Serie ♥️
Saborder pour de la série
😍😍😍👏👏👏 chapeau à vous 💃💃
Ay vieux reynama😄😄
Machallah série bi nekhne trop machallah 💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽
Awo waye dereti awou bi yagou na🤣🤣🤣🤣🤣
Genre thiam yii aka beuri si famille sénégalaise
amou gnou liguey tek si sokhor nio tass keur yii🤣
Manchalla nekhna amna solo badiane momaye ray
Ndeye Ndiaye do nite ya takh may setane série bi
Vous étes les meilleurs ♥️ bonne continuation
Tatou pawlish mbaye 😂😂😂😂😂😂
Menumako mougne 😂
Man dh magui si awo yii😂😂😂😂
Wawaww wakhal si kaww , awo yi , nionko yorr
Thieuyyy Badiéne
Changement amena déh Macha'Allah
Fall Na Bayyi Thiakhane yi Ah Amo Yoro Di Takk Rk Kénne Doula Respect
No vieux la namone dégal daral tone orange bi weuy.... 😄😄🤣🤣
Khady demal seuyi mo gueune , ndeye Ndiaye amoul
Khady très belle mchlh
wouy aka ma beuk badienne 😂😂 raay nama elle est très belle nak ak teint nior bi bou chic
Badiéne2 beguoul2 diame nake motakh mousi bolé pawliss 😍
Bravo à l'équipe
1ere commentaire alhamdoulilah mangui sant waa GUINGUINEO yeup 😭🙏
Sa mbokk mo ngui nii
@@baaissatou4883 ndeysan tay amnagn ndam 😭
Gnountamite gno gui lay sante dila gereme
Wouy mbok fégn n'a
Vieux day gen serie bi je n en peux plus dead nga épisode
Non mane badiene dinama meussa rayy 😂😂😅😂😂nenako ak sa tatt wou gatt wowou 🤣🤣🤣
Ndeye Ndiaye nak badiane khassnala tatou pawlush mbaye nakk 😂😂😂😭😭😭