Sa Wolof Assène ses vérités à Oustaz Makhtar Sarr "So dioumoul, dagay feen"

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 25 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 86

  • @OusmaneSambe-l3f
    @OusmaneSambe-l3f 11 годин тому +10

    Oustaz da reuy té dioulitt pirr dou reuy😢😢😢d

  • @Rassoul777
    @Rassoul777 10 годин тому +3

    Sa wolof merci beaucoup

  • @AwaDabo-t3l
    @AwaDabo-t3l 7 годин тому +1

    sa merci pour ton franc parler

  • @cheikhfall7606
    @cheikhfall7606 14 годин тому +8

    Merci SA wolof

  • @bayegorfall1813
    @bayegorfall1813 12 годин тому +9

    Oustaz dafa dioum ba pare reuy 😂😂😂

  • @abdourakhmane2048
    @abdourakhmane2048 7 годин тому +1

    Merci Sa Wolof

  • @DjibiFall-rp1nc
    @DjibiFall-rp1nc 12 годин тому +2

    Saa merci❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @buybasap7089
    @buybasap7089 Годину тому

    Saa téyal bakhna yarou bakhnadé😮😮😮😮😮😮😮😮

  • @Tawfeekh
    @Tawfeekh 12 годин тому +2

    Merci beaucoup! Ce Makhtar Sarr dafa khamadi, yègue boppam soo wakhé mouy guadou bopp Di diaay arrogant mélni moo moome nitt gni alors que dou tousse. Walaahi gnouko guënëu sadike rékk gnioo fi nékk.
    Kii daa fouuy réew yèk boppam comme dou dème douche.

  • @ahmadoudiallo6522
    @ahmadoudiallo6522 12 годин тому +1

    Machallah wakh deugeu moo nékh

  • @khalifababacarmbodji1224
    @khalifababacarmbodji1224 14 годин тому +6

    Merci sa dafma bete makhtar sarr n’a nangou ne khalangouna

    • @cheikhlei3193
      @cheikhlei3193 14 годин тому +1

      Lo xaam si reuyy té dou toussss

    • @antambaye1751
      @antambaye1751 13 годин тому +1

      Yallah moko wére aqe suna yonnéne tibi gnikoye respect mou sékhe léne rék teu léne wathie naféq la

  • @moussaba8187
    @moussaba8187 3 години тому +2

    Pape Matar Sarr ne mérite pas le titre de oustaz

  • @MouhamedCisse-u1f
    @MouhamedCisse-u1f Годину тому

    Sa wolof yaw dh miritonga 1m abonné

  • @mulaydiop815
    @mulaydiop815 14 годин тому +2

    merci sa wolof

  • @abibmarouane6699
    @abibmarouane6699 Годину тому

    Oustaz ab dioulit dou reuy dangey tapalé rek
    Ousmane Sonko moy sopi réw mi incha Allah

  • @nouhankaba1391
    @nouhankaba1391 8 годин тому

    Oustaz bi
    Mon mounou supporter Pastef
    Xolle bi moye bonneu sissou Mane la

  • @abdoumane4769
    @abdoumane4769 8 годин тому

    Mactar est ingrat, il est la définition parfaite de nafékh.
    Daye wakh, di changer limouye wakh, di diakhassé Aka garouwalé cii aye wakhame

  • @aminatacamara8456
    @aminatacamara8456 10 годин тому

    ❤❤❤❤❤🎉

  • @kmtechetservices9215
    @kmtechetservices9215 13 годин тому

    Téguine bakhna

  • @omzobousonko
    @omzobousonko 9 годин тому

    makhtar sarr da reuy 😂

  • @AichaDia-t1d
    @AichaDia-t1d 13 годин тому

    Tedial sa gat 😢

  • @mamemorfaye-zl4hg
    @mamemorfaye-zl4hg 14 годин тому

    ✅✅✅✅✅✅❤️❤️❤️❤️❤️❤️👊🏽🇸🇳👊🏽

  • @salioundiaye4148
    @salioundiaye4148 13 годин тому

    Iow amo bén yarr

  • @KhalifaBabacarToure-ql1tw
    @KhalifaBabacarToure-ql1tw 4 години тому

    Lii moka tay dh bly

  • @famadiagne5595
    @famadiagne5595 10 годин тому

    Oustaz makhtar sarr nénalé bou dioumé dou nangou té da dioum ba khalangou

  • @NdameSeye
    @NdameSeye 10 годин тому

    Fen bakhoul waye

  • @AichaDia-t1d
    @AichaDia-t1d 13 годин тому

    Tedial sa gemin khana tay ngay khas mouctar sarr te yew amo yar

  • @MouhamadoulamineSeck-e1o
    @MouhamadoulamineSeck-e1o 13 годин тому

    Sa wolof yaroule sa wolof yaroule sa wolof yaroule

  • @kebekebe587
    @kebekebe587 13 годин тому

    Walhal waye

  • @NdameSeye
    @NdameSeye 10 годин тому

    Oustase dou fén

  • @FallMatar-b4e
    @FallMatar-b4e 12 годин тому

    Waa yaw saa wolof! xanaa dañu la wax yaa moom nit ñi, ba ko wax rekk nga jog, ta sax jiitum réew mi ku la wax ci Yàlla la waat, wala moom lim doon def jamñaajo du loolu, bu dee loolu la moom yaw mii yaay nar, ndax foofa moom ci ndayu sartu réew mi la waate.

  • @babafaye3398
    @babafaye3398 38 хвилин тому

    Naka oustaz sani kotou rek dotoul wahati lolou kesse la
    Kou xam makhtar Sarr hamne dafa libre
    Petit touti nga pour wax si oustaz Amal yaar

  • @BayeDameCisse-q4f
    @BayeDameCisse-q4f 13 годин тому

    Oustaz makhtar sarr dou sa nawlè as wolof

  • @JshwHwhw
    @JshwHwhw 14 годин тому +1

    Yaw dagarew oustaz makhatar sarr dousa morom

  • @ibou198
    @ibou198 14 годин тому

    Ki kou rewe leu

  • @NdameSeye
    @NdameSeye 10 годин тому

    Makhtar dél wakh dege

  • @cheikhgassama7948
    @cheikhgassama7948 12 годин тому

    Amu benn droit yëgeti kàddu fen di ko jëmale ci Ustaas maxtaar saar donté man àndu ma ak ustaas ci limu wax yar ak tengéen baax na trop

  • @AichaDia-t1d
    @AichaDia-t1d 13 годин тому

    Yew sa data ndaye domou kharam reewngen trop mouctar sarr doussa morom degge rek la wakh😢

  • @moussadiallo7990
    @moussadiallo7990 14 годин тому +2

    Ouztaz dafa reuy bo dioumé dagay nangou,mais beugua changer tourné, ligua wax ya ouztaz dafa ler té diné diglé woul lolu إن بعض الظن إثم

    • @AichaDia-t1d
      @AichaDia-t1d 13 годин тому

      Yew doul demlen ngeen deglouwat wakham you yagga mouctar sarr defa moussa wakh degge

  • @CheikhSow-x3p
    @CheikhSow-x3p 12 годин тому

    sabaye sonko AK pastef fenerek

  • @baboucargoudiaby2933
    @baboucargoudiaby2933 8 годин тому

    Sa qui d'où oustace djoulite do wakh loula wiroute

  • @SalioundiayeNdiaye-m5p
    @SalioundiayeNdiaye-m5p 10 годин тому

    Makhtar douleur sa bop opposant gua meuno nou nakh

  • @CheikhSow-x3p
    @CheikhSow-x3p 12 годин тому

    wapastef fene rek sawolof AK cheikh bara Ndiaye fenerek

    • @AG-hn1jy
      @AG-hn1jy 12 годин тому

      @@CheikhSow-x3p yagui mér dé

  • @AichaDia-t1d
    @AichaDia-t1d 13 годин тому

    Sa olof sa data ndaye

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 9 годин тому +1

    yaw ya gueuna khamadi gnep gueuna réw gnép. Outaz Makhtar Sarr douça morom. En plus kadou réwandé yingay dieumalé si Oustaz Makhtar beugo kouko dieumalé sisa Baye yaw té doko wakh sa Baye. réwandé reck mola diapou motakh ngay saga bayou diambour yi

  • @JshwHwhw
    @JshwHwhw 13 годин тому +6

    Oustaz makhatar sarr dousa morom manga wodou kadouyi pa gaye toudou batoufen yaw dagaye bagarew yaw sa wolof bilahi bargueb s tuuba dagaraw

    • @oumardiouf1585
      @oumardiouf1585 13 годин тому

      Matar sarr dafa arrogant Sá a raison

    • @AG-hn1jy
      @AG-hn1jy 13 годин тому +2

      Kou wakh thi pégnethimi gnou tontoula di wakh thi niite gni né kéne doula tontou amoul féén

    • @bgg9739
      @bgg9739 13 годин тому +2

      Yaw nokoul nopi cheytané bou bone bi

    • @JshwHwhw
      @JshwHwhw 12 годин тому +1

      Viva Oustaz makhatar sarr je Suis oustaz makhatar sarr %%%

    • @2ansgalsen999
      @2ansgalsen999 10 годин тому +1

      Oustaz bou nafekh Ken warouko respecter fene rk lay deff

  • @assmalickdiagne8098
    @assmalickdiagne8098 11 годин тому

    Sa wolof na fekha bou mak la

  • @Samy-sh4gl
    @Samy-sh4gl 11 годин тому

    Man damma khamoul sa lou diarra défendre si Warkat bou melni Barth ba di thi mer. Son problème cest Sonko, il guette la moindre erreur de Sonko jusqu'à même anticiper une erreur qui n'existe pas. En plus il a un eggo démesuré.

  • @papesidyboye9654
    @papesidyboye9654 46 хвилин тому

    Andou mak yaw si linga wax mais dangay fén c'est trop

  • @AichaDia-t1d
    @AichaDia-t1d 13 годин тому

    Bouko kenna deglou fen ak soss rek demlen ngeen deglou wakhou mouctar sarr bii yep bayilen nafikh

  • @thiernombengue844
    @thiernombengue844 Годину тому

    Woutil xam-xam balaay ngay tontou borom xam-xam

  • @AichaDia-t1d
    @AichaDia-t1d 13 годин тому

    Veréma nafikhnga bou bon yen li oustazz mouctar sar wakh degge la lii diarna kou nekka di tonto di diy reew ak khamadi tedial gatgi

  • @badaboys2098
    @badaboys2098 12 годин тому

    Yaw mom danga rew sa wolof

  • @gorasy927
    @gorasy927 14 годин тому

    Makhtar sarr day mboubawo dinné mandou woul djiko nafékh rek la yorr

  • @AichaDia-t1d
    @AichaDia-t1d 13 годин тому

    Yew sa olof kou rewnga doumi kharamnga mouctar sarr doussa morom roussoko wakh day fen doumala roussa saga tedial sa data ndaye nopi oustaz wakhna thi macky wakh thi ablay wadda donga wakh thi yen te niila moussa mel degge rek lay wakh

  • @VOISINAGE2000
    @VOISINAGE2000 7 годин тому

    MACTAR SARR DAFA RÉW BA DOFF,TÉ ARROGANT

  • @papesidyboye9654
    @papesidyboye9654 47 хвилин тому

    Yaw bayil gni ngay wakh da ngay fén

  • @apprenonsapprenons8004
    @apprenonsapprenons8004 14 годин тому

    Ce makhtar sarr il est plus ignorant même en matière de l'islam

  • @AichaDia-t1d
    @AichaDia-t1d 13 годин тому

    Tedial sa gatngi reewnga te khamady khamo sa bopou mouctar sarr niila moussa mel degge rek kiko bagn nafikhnga

    • @VOISINAGE2000
      @VOISINAGE2000 7 годин тому

      Mon tay magg boufi doul gnou wax co point.

  • @kananthiouladiatta151
    @kananthiouladiatta151 10 годин тому

    Oustaz n'est pas intelligent, et il est faux.

  • @Sidydiagne-24
    @Sidydiagne-24 13 годин тому +2

    Merci sa wolof

  • @NdameSeye
    @NdameSeye 10 годин тому

    Merci sa wolof

  • @gueyemamecheikh6440
    @gueyemamecheikh6440 8 годин тому

    Merci sa wolof

  • @omarleytindiaye7854
    @omarleytindiaye7854 7 годин тому

    Merci sa woloff