Thank you Ahmed Cissé merci beaucoup Ahmed Khalifa Niasse masha Allah aujourd'hui mashallah today machallah xam:xam bu leer yaangi def lu ma solo Sénégal il y a trop de faux Oustaz Ahmed Cissé Yoon wi ga jel yàlla nala ci yàlla japale ci barke alxuraan Sénégal dafa bari ñu soxor don't give up thank you thank you thank you
Cheikh Mbacké Sakho néna fofou gatal djouli gui ley wax pas wañi 😂😂😂 mom nonou lako tekké té sossi beugué firndé dangey jéxal Aya bi 😂😂 Naxaté jéx na té Al Quran moy dictionnaire al Quran CMS c'est le goat 🎉😂
@@CheikhIssaFaye "Andil sey firndé si Al Quran" lolou moy dagg sen xoll 😂😂😂 Té mom amna verstt bouy prouver lou mot bi di tekki si Al Quran 😂 Al Quran,Al Quran mokay firri lolou si Baye Niass lako ndieuk dégué CMS deugeul ko Pour ton information AlQuran dou arabe kessé amna yenen lakk youssi nekk mais danko oumpoulé parceque xarr ngeu
Bou fékké ni aya dji yalla gatal lathi dioublou wa khana guoudal thi diouli dafa war nax aya bi daf né فليس عليكم جناح أن تقصروا من الصلاة Aya bi daf né bakar nékkul thi né ghén wagni thi diouli Légui fi ligha Fiy déggué moy wagni aramoul mais dou ay guoudal wala ay gatal aussi boudé gatal lay firé ban sans lay amati nax diouli fatikha ak surah boula néx wala aya boula néx
@obd2214 yéén ay jaaxil ngeen moo tax jaroulleen top ndax nit ki dina jang alxour'aan xattan wa tillaawatan wa tadjwidaan té mou doon jaaxil mooleen dal ndax a' jaxlou biy firri réér nit man naakoo def ba paré geuna réer nieup nit ki itam man na reeré mbiduum alxour'aan bagne thjia xam dara waayé sunu borom défalko nouroul imaan bou wër ba mou xam yalla diko jaamou té douko bokkalé .ndax " sa nuurihim ayaatinaa fil aafaaq wa fi anfoussihim "loolou alxour'aan la dengeen beug kouleen geum waayé fi kenn geumooleen boudé jeumi xar binga touddou nak hamna dey sa makaan rk waayé yalnala si yalla géené té tabbal la pays you kawé yi Tuub nak
En tout cas Yonént néné khéétam douniou manko ci réér. Or, li eupp ci khéétou yonént bi ci adouna bi yeup, dioully wouniou niaari rakka kécé. Une minorité très insignifiante mokoy déf. Yalla nalén Yalla soppi
Non Ahmeth yaye nanditer! Ni nga waher ak khalifa Niass si introduction doula gnak kersa loka ladj taye ame tonton😂 Thiey pape khalifa Niass keneu le si genrame.
Cheikh vraiment yaaaaa doye waaare. Quand tu invites Cheikh Sakho, tu lui remplis de compliments comme si tu es son disciple. Maintenant yaaa ngi koye roubeh.... 😂😂😂😂
Andalousi ci empire du Maroc la bokonn Ibn Hazm borom xamxam la d’accord wayei niounn Malick lagn topou tei Abdoul wahid Ibn hachiri Al Andaloussi tamitt fala diouguei mo bindd mourchid wayei ci fikhi Malick la soukandikou. Mon amonn na ap nguirr wayei Andaloussi meme ngifa deukonn sah nieupp topougn wonn Nguiram. Malick lagn toponn. Tei nioniou nio toukhou Rabat après colonisation Niou toudei len al mouraabitiinn toubab yi di lenn woyei almoravides niom nio indi islam Senegal
Non! Wakhoul li Yalla wakh rek. Mais dafay wakh limou dégg ci wakhou Yalla, mom ak gnimou bokal paspass. Nay léér, nimou déggué wakhou Yalla lolou lay firi
Senegal dou deme. Arreter d'attaquer une personne et attaque ses idees. Cheikh Mbacke ne fait que eclaircir les paroles d'Allah et c'est tout. Repondez sur ca
Machallah Ameht khalipha niass dofbobou di mbacke sakho yalla na yalla sorille pass pass bou bonne bi
sont tous des fanatiques .la purete du coeur est primordiale
Thank you Ahmed Cissé merci beaucoup Ahmed Khalifa Niasse masha Allah aujourd'hui mashallah today machallah xam:xam bu leer yaangi def lu ma solo Sénégal il y a trop de faux Oustaz Ahmed Cissé Yoon wi ga jel yàlla nala ci yàlla japale ci barke alxuraan Sénégal dafa bari ñu soxor don't give up thank you thank you thank you
Cheikh Mbacké Sakho néna fofou gatal djouli gui ley wax pas wañi 😂😂😂 mom nonou lako tekké té sossi beugué firndé dangey jéxal Aya bi 😂😂
Naxaté jéx na té Al Quran moy dictionnaire al Quran CMS c'est le goat 🎉😂
Waa yow CMS Moy wax wala am daa geuna deeg nit gni arabe yow topal fallé .nga naan cms gaatal la wax moom Moy kann wala déniouko yonni thji nit gni Mayleen niou jamm waay
@@CheikhIssaFayepas de dagasanté tountou leen si kham kham mo geun cms li yalla wakh rek la wakh
@@CheikhIssaFaye "Andil sey firndé si Al Quran" lolou moy dagg sen xoll 😂😂😂
Té mom amna verstt bouy prouver lou mot bi di tekki si Al Quran 😂
Al Quran,Al Quran mokay firri lolou si Baye Niass lako ndieuk dégué CMS deugeul ko
Pour ton information AlQuran dou arabe kessé amna yenen lakk youssi nekk mais danko oumpoulé parceque xarr ngeu
Bou fékké ni aya dji yalla gatal lathi dioublou wa khana guoudal thi diouli dafa war nax aya bi daf né
فليس عليكم جناح أن تقصروا من الصلاة
Aya bi daf né bakar nékkul thi né ghén wagni thi diouli
Légui fi ligha Fiy déggué moy wagni aramoul mais dou ay guoudal wala ay gatal aussi boudé gatal lay firé ban sans lay amati nax diouli fatikha ak surah boula néx wala aya boula néx
@obd2214 yéén ay jaaxil ngeen moo tax jaroulleen top ndax nit ki dina jang alxour'aan xattan wa tillaawatan wa tadjwidaan té mou doon jaaxil mooleen dal ndax a' jaxlou biy firri réér nit man naakoo def ba paré geuna réer nieup nit ki itam man na reeré mbiduum alxour'aan bagne thjia xam dara waayé sunu borom défalko nouroul imaan bou wër ba mou xam yalla diko jaamou té douko bokkalé .ndax " sa nuurihim ayaatinaa fil aafaaq wa fi anfoussihim "loolou alxour'aan la dengeen beug kouleen geum waayé fi kenn geumooleen boudé jeumi xar binga touddou nak hamna dey sa makaan rk waayé yalnala si yalla géené té tabbal la pays you kawé yi Tuub nak
😂😂 Responsou faye Dioully pa bi indiwouko thi terebi dee
CMS EST MEILLEUR QUE VOUS TOUS RÉUNIS 😍😍😍
En tout cas Yonént néné khéétam douniou manko ci réér. Or, li eupp ci khéétou yonént bi ci adouna bi yeup, dioully wouniou niaari rakka kécé. Une minorité très insignifiante mokoy déf. Yalla nalén Yalla soppi
Do borom xam xam mo takh nga wakh lolou
Merci Ahmad xalifa niass
Un débat intéressant
Thiey Ahmed limoy borom kham kham
Cheikh sakho scheytane mo ko dougue
Cheytané bou am solo
Cheytané bou dég Alkhouran
Cheytané bou am xam-xam
Non Ahmeth yaye nanditer! Ni nga waher ak khalifa Niass si introduction doula gnak kersa loka ladj taye ame tonton😂 Thiey pape khalifa Niass keneu le si genrame.
Ahmad Ceesay amal respect chi dom adama yi. Jango amo kgam kham. Ninga nyaw.
Cheikh vraiment yaaaaa doye waaare. Quand tu invites Cheikh Sakho, tu lui remplis de compliments comme si tu es son disciple. Maintenant yaaa ngi koye roubeh.... 😂😂😂😂
Il est tout simplement dangereux et les gens doivent l'éviter ...
Dangeena tardé benn waay diogé falé ak waxi dofam ngeem ciy yaxx tan..
Diokhé woul arguments dé.
Andalousi ci empire du Maroc la bokonn Ibn Hazm borom xamxam la d’accord wayei niounn Malick lagn topou tei Abdoul wahid Ibn hachiri Al Andaloussi tamitt fala diouguei mo bindd mourchid wayei ci fikhi Malick la soukandikou. Mon amonn na ap nguirr wayei Andaloussi meme ngifa deukonn sah nieupp topougn wonn Nguiram. Malick lagn toponn. Tei nioniou nio toukhou Rabat après colonisation Niou toudei len al mouraabitiinn toubab yi di lenn woyei almoravides niom nio indi islam Senegal
L'islam tiens compte la prévention. C'est juste pour ne pas mettre de mauvaises dans les odeurs mosquées. Le comportement dans la cohabitation
Boudone 2 rakkas leu ķilifeu dinè defko.
Diné amoul kilifa diné diné yalla la
@@amadoutidianediallo792merci verité crue
Vos sois disant kilifa dîne nio yakh dîné nga
@@amadoutidianediallo792imam sakh kilifeu dinè la .ndakh dafay khoutba ngakoy deuglou .
@@amadoutidianediallo792Yallah dafa tane Mohamed pour mou Wone Ni Niouw Diamo Yallah kon Djit la,Sou amoul wonn ,Konekk DEF nila Sa khel Diokh.
وَإِذَا ضَرَبْتُمْ فِي الْأَرْضِ فَلَيْسَ عَلَيْكُمْ جُنَاحٌ أَنْ تَقْصُرُوا مِنَ الصَّلَاةِ إِنْ خِفْتُمْ أَنْ يَفْتِنَكُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا إِنَّ الْكَافِرِينَ كَانُوا لَكُمْ عَدُوًّا مُبِينًا
Mbacke Sakho Moy dadialou wa Sénégal Moy touleneko
Le pét annule la prière si on l'entend ou on le sent
Billahi borom xam xam gua Niass
L’heure est grave
Nit lo guem dieuleko si niou wer niou rouy seydina mouhammad ,di deklou kenen vay werente sakh danguay tarde ,
Dieuredieuf Niass ki sokhna dafa yap nit gni rk
Ya raw halifa yi sakh niass
Khalifa yi rawanté wouniou. Danio raw di rawalé
Cheikh mbacke sakho kouko wedi wediwoco mome parceque li yalla wakh rek la.wakh thiakhane bakhoul
Non! Wakhoul li Yalla wakh rek. Mais dafay wakh limou dégg ci wakhou Yalla, mom ak gnimou bokal paspass. Nay léér, nimou déggué wakhou Yalla lolou lay firi
Alxuraan ak sunna ñooy ànd
Senegal dou deme. Arreter d'attaquer une personne et attaque ses idees. Cheikh Mbacke ne fait que eclaircir les paroles d'Allah et c'est tout. Repondez sur ca
4 raka 3 raka tamit indiwoul preuve bi thi ALHOURANE
Yaw dioulil niar tè bayi gnou AK signou 4
Preske 5 munites si zéro
An Takhsourou minassalaati
Dou wagni dioulli Gattal dioulli leu
Moy ponkal ❤
Ahmad yaw defante rek nga fi nekke bul nu sonal degg lul pabi ta nga nopi
Khamonani dinguako roukou
Borom xam xam pirr wayé capo leu dé😂😂😂😂😂
Leerna dieureudieuf serigne bi
Gattal dioully le aaya bi wakh et non wagni
Mbacke sakho doole rek lay def
Mbocké sakho thi lobi la bokou guir yakh dîner
Tontogoul li nou bègue kham