Aziz et Boubacar sont partis là où depuis toujours le Tout Puissant ALLAH les voulait. Billay niougui ci diam mais ces diables qui les ont assassinés sen aduna yakkouna ak sen Allakhira.
Ce crime a touché tout un pays, le jugement doit être filmé en direct, publiquement comme dans certains pays, comme ça euleuk kouy défati lou melni dinako kholat
Ah oui le peuple doit être au courant j ai le cœur meurtri pourquoi ôter la vie d un soutien de famille et d un garçon innocent comme ça gratuitement 😢😢😢
Meurtre bii sénégal yeup la yeugeul que justice soit fait sans pitié que les criminels paient Lii métina torop Aziz Dabala et Boubacar Gano alias (Waly) Reposaient en paix Yalnalen Yallah kharé aldjana firdawsi 😢😢
innalilakhi wa ina illeykhii radji-one ,allakhouma adjiirrnii fiii moussibatii wa ax-louf lii xaírane mine kha🙏 Yalla naniou Yala moussoul si moudjou niaw .
vu comment aziz est tué et prépare par son assassin forcément le tueur est un de ces meilleurs amis ou son membre de famille y’a pas de chercher de midi a 14h
Nabou iaw yalla mogui lay weurseu geul ngay bokou ci ay série ték ci sénégalais yeup beug leu ak lou meunti ame danga wara andak sa ngor. Tay Aziz ak wally geune nagne léne démine. Yène dingène ame trokh tanké adouna ame mbougalou yalla. Lii dara diarouko ci adouna walaxi anzim. Li nakk dafay wané ni nitt diko guiss mouy dém mais boul kham lou yalla déff ci mom. Aziz ak wally niolène eup bopou. Yalla nalène yalla yeureum té diégal lène ci barké yonèneti bi🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Thiey yalla yalna niou yalla moussal si kasso gnii fii nekk yalnalen fi yalla gueneii Barkep alhuran li dara Adouna diarouko yalnagnou yalla moussal gnoun gneup😢
Thiey yalla sa brom bi li luko fi diar dieulle bakanu nit ndakh khaliss gni niak sen bakan mom niak naniou ko iow nga fok ni diga nek si diam ak bakan nimou mel 😢yalla nalen sa brom bi yeureum way 🙏
Nabou leye Domerame commentaire bima meuna deff youtube akk leup sa nom moy tête de liste kooba beugu buzz, gangster,waga yow garçon manquée gua wone aziz bola défar dès le début la kham ni domou thiotou bi yagui si birr takk si rippp mbam sorcière
Paix à leurs âmes que la terre leurs soient légère et que firdaws soit leurs demeures éternelle près du prophète mouhamet psl amine yaraby fatiha + 11ikhlass
Peine de mort kou d’accord lalal j’aime 😢❤
Gni niakk sén bakane yallah nalén yallah yeureum 😭🙏
❤❤🎉🎉❤❤
😂😂😢😢😢
Amineeeeeeee
AMINE ❤
Merci beaucoup BIB Merci beaucoup dakar buzz amna solo ❤❤❤
Laleu nguéneu lalaké AZIZ moléne eupeu bopeu REPOSE ÉTERNELLEMENT EN PAIX AAMIINE YA RABBI
Aziz et Boubacar sont partis là où depuis toujours le Tout Puissant ALLAH les voulait. Billay niougui ci diam mais ces diables qui les ont assassinés sen aduna yakkouna ak sen Allakhira.
@@khadyndione9815yèmèna dama djakhlè mane
Walay azim qu'ils reposent en paix
Bly wax nga deg
Dsra nga hamoul tchi lougnounèk. Gnaan rek.
Kou nek na nga delou di santé yalla sounou botom diouli si yonent bi.
Yalla na nieup am diam. Besoins de 1k j’aime
1k j’aime pour quoi faire ?
Vous tellement gênant !
Yalaguakooo amm diadieuff
pour faire de la soupe avec ?
Amine inchallah
Loy doyé 1k j'aime yii
Thieye adouna mo yémé que dieu nous protège
Amine ya Allah
Ken xamoul sa eulek yalla naniou nek ci ndioup rk
Ce crime a touché tout un pays, le jugement doit être filmé en direct, publiquement comme dans certains pays, comme ça euleuk kouy défati lou melni dinako kholat
Ah oui le peuple doit être au courant j ai le cœur meurtri pourquoi ôter la vie d un soutien de famille et d un garçon innocent comme ça gratuitement 😢😢😢
@@khadijaba2454 il est temps que les choses changent, jugement public rek, amoul soutoural bandit, comme bou gueiné dotouko défat.li dafa méti bilahi
Comme aux Etats Unis le procés doit étre filmé
La meilleure solution c'est ce Allah dit. Celui qui tue par exprès doit être tué. Sinon c'est rien . La perdante sera la personne tuée.
Filmé en direct ..non mais et ça va te servir à quoi? Pur voyeurisme seulement🤕🤕🤕🤕bou decoumpa di reyaté con dégya bou yague...iiiiiishhh
Que la justice soit faite
Nous attendons aussi la justice pour les 80 manifestants morts lors des manifestations . 😮😢
Bilay on réclame justice pour tout le monde
Justice pour tous les morts tués injustement
Bayilen roube lolou guen wakhatouko li nak amoul solo si Yaw bayilen roube bou nite yi wakhe diarni yene gni diar nele. C est affreux
Yalnagnou doli soutoureu defale sounou diabotte defalko nieupe amine yarabi
Amine ya Allah
Il faut une marche pour la peine de mort
Ou prison à vie avec travaux forcés et des tortures
Trop c'est trop 😭😭😭
J'ai le cœur meurtri
Meurtre bii sénégal yeup la yeugeul que justice soit fait sans pitié que les criminels paient
Lii métina torop
Aziz Dabala et Boubacar Gano alias (Waly)
Reposaient en paix Yalnalen Yallah kharé aldjana firdawsi 😢😢
Wolahi wa raboul kaba gni si il sont coupables degnelena wara pendre devant tous le peuple
innalilakhi wa ina illeykhii radji-one ,allakhouma adjiirrnii fiii moussibatii wa ax-louf lii xaírane mine kha🙏 Yalla naniou Yala moussoul si moudjou niaw .
Allahouma amine
Amine
Bilaye walaye
Amine inchallah 🙏
Nabou leye manon ngia tèla wakh crime bi kone li lepp doula si fèk
Li deh foumou tolou sama xol bi metina yalla na yalla lérall té yeureum adji dém yii😢
Amine inchallah 🙏
Danio warone dokhlo sen ndeye marché zing ba turbinal ba
😂😂Kone douniou yeggg
@@aminadiop7958😂 Wahatiko
vu comment aziz est tué et prépare par son assassin forcément le tueur est un de ces meilleurs amis ou son membre de famille y’a pas de chercher de midi a 14h
Bilakhi comme reve thi man meunoumako gueum 😭démna deysan dotoul gneuwati metyna walakhi 😭😭😭
Li louko fi diar 😢😢😢😢
MoMA diakhal 😢
alal diarouko bagne nitt ki diarouko
Daray adouna diaroul li
ALALOU ADINA DE MOLENE KO YOBBE AK JALOUSIE YALNA BOROM DOLINIOU SOUTOURA AMINE
Moma diakhal li so gêne sakh doto diar dara
Da nguéneu lale lalaké
aziz ak wally yalla nalen yalla yeureum
Yala na yala léral lépp li da métii trp dit ray dit ray rek kénn amatoul sécurité niep pa titt
Bilahi
Li niawna metina yalla naniou yalla may moudiou bou rafet
Perpéte rék Domi kharam yi
Ay nabou soudei defoulo dar yalnaleu yalla sourouraaal🥹🙏
Nabou iaw yalla mogui lay weurseu geul ngay bokou ci ay série ték ci sénégalais yeup beug leu ak lou meunti ame danga wara andak sa ngor. Tay Aziz ak wally geune nagne léne démine. Yène dingène ame trokh tanké adouna ame mbougalou yalla. Lii dara diarouko ci adouna walaxi anzim. Li nakk dafay wané ni nitt diko guiss mouy dém mais boul kham lou yalla déff ci mom. Aziz ak wally niolène eup bopou. Yalla nalène yalla yeureum té diégal lène ci barké yonèneti bi🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Vraiment gneum la bête 😢
Li dara djaraloumako si adouna 😢😢
Yalla na yalla yeureum gni gnak sène bakane que leurs ames repose en paix amine ya rabbi
ndeysan auto bip bi président sonko lamay fateli😢😢😢😢
Yalnaniou yalla défal ndioub
Bilakhi gni niogui regretter liniou def d'où niep lanouy lal bilakhi
N deyesane nabou leye 😭😭😭😭😭
Thiey yalla yalna niou yalla moussal si kasso gnii fii nekk yalnalen fi yalla gueneii Barkep alhuran li dara Adouna diarouko yalnagnou yalla moussal gnoun gneup😢
qu'Allah protège notre Sénégal
Li lane moki fi diar lane alalou adina waleu c'est bizarre yalnagnu yalla mousal si lou melni
Amine inchallah 🙏
Tieuy ay lou diar lii 😢
Bilahi
Yallna yalla leral leup si barqué serigne fallou😢
Ooh nabou leye 😭😭😢😢 yalla bossi tankei dara
Jai envie de pleurer !! Aye way lane mo ko fi diar??
Yalna diam yagg 😢
Li doyna war, yallana yalla doli soutoura ak tawfekh
Merci pour dip❤❤❤❤
Mane YENE wa DAKAR BUZZ AK RTS yenama doy thie mbiroum khibar , Merci pour votre belle job🎉❤
Yalla n'a yalla yeureum Lenn yalla naniou mouthiou thi mousiba yalla bou gnou réppou thi lokho kenn yalla bou kenn réppou sougniy lokho amine
Allahouma amine
Amine
Gathia ngalama wa police vous êtes les meilleurs
Hanaa tay. Ce sont les meme gniouni done arr temps Macky rien a changé. Mais c est quand ça vous arrange rk
😭😭😭😭li métina raye nanou domou diambour bi rek
Yalla na yalla leral lepe azize et waly yalla na lene yalla yeureume
Lii dé comm film si mann
Mome kaye il faut ke niou jouer theatre apres😢
Condamnation à mort pour eux tous.
Justice pour aziz dabala ak wally 🙏🙏
Yalla n'a yalla tékk nou ci yonou siratal Moustaghime ak sougnouye ndiabot ak dioulite yeup si barké yonéntoubi PSL
Yallah na lep leer
Yalla na Yalla l'erreur
Leral*
Lii louko fii diar saure euleuk bakhna lolou woutal saye dom waye bou raféte diarna khalate boubakh bala nga def Paix aux âmes des défunts 🤲🤲🤲
Bilahi NABOU bou ci takké woul wone. D’où niou ko dougueul fi. Ki elle est mouillée jusqu’au cou
Walahi
Nabou bahoul
Mane li bilahi comme film si mane !!!😢😢😢
Mane dama djomi
Dou ioe dong
Esk man meuss na feikei cas crime bouma yeimei ni dieul sama tmp depassei me a ce point li gneupp la diaxasso gneup ko wax mounila crime bi
Allahouma amine😢
Lan moko fii diar gni dem yalla nalén yalla yeureum té kharé lén aldiana firdawsi
Sénégal nieup wara guéne pour mou diékh lii dafa méty😭😭😭
Yalla nalen yalla yeureum
Joub joubal joubanti mowor gniréthounan😢
Ndeysane mitina 😢😢😢😢😢😢😢😢
Nous avons confiance à nos justices
Gnigèn ray dè eupanioulèn pop😢
Nous vivons dans un monde très méchant, sans fois ni loi. Nous demandons une punition capitale!
K justice soit faite
Thiey yalla sa brom bi li luko fi diar dieulle bakanu nit ndakh khaliss gni niak sen bakan mom niak naniou ko iow nga fok ni diga nek si diam ak bakan nimou mel 😢yalla nalen sa brom bi yeureum way 🙏
Amine yarabi
Peine de mort cou raye niou raye la😢
Niawtéef deugue moye liniou deff Aziz Dabala ak Waly
Li aye milliar sakhe diarouko Walahi liberté dafa nekhe
Khamo si dara sakh
Yallah bougnou ray kéne Yallah bougnou kéne ray
Nabou fileu Aziz tekke yobou le fe li doussa thieur keppou kouy djiguene sengemnga djoy nga
Yalla bousii nabou bokk sii barki Serigne saliou 🙏🙏🙏
Aye li loukofi diar liberté ak nimou nékhé yalna😢
Lii dara diarouko walahi so moytouwoul niongui reuthiou lou bari nitt day sakkou diam ray naniou domi diambour ni rék yalla nalein yalla yeureum
Gni decede guem nani ay waliww lagnou
Nabou leye yeureme nako 😢 nk lii guemoumani complice laa
Bouniou paré nagn len yobou arènes national niou ray sen nday
Yalne yalla Wallou senagal Baniou Âme kholou Souniou ndiguelou Brom
Kou ray niou rayla
Yalne y’alla yeureum domi dioulitt yi Fatou
Yalna yala léral lep
Yalna yala ate lep ler bakane dafa for😭😭
Kou djioub santile yallah ak saye wadiour
Ok mango Harry Inchallah ❤
Ngii yakho nage 😢😢😢😢😢😢
Eh yaraby lerale yeupe inchallah yaraby
Bilaye li métina raye 2 personnes thi ni
Nabou leye Domerame commentaire bima meuna deff youtube akk leup sa nom moy tête de liste kooba beugu buzz, gangster,waga yow garçon manquée gua wone aziz bola défar dès le début la kham ni domou thiotou bi yagui si birr takk si rippp mbam sorcière
Jugement public waay 😢😢
Alahou akbar thieuy
C trop ça
Mais terewounione charettes yi circular Dakar?djissna ben bou romb !!😂😂
Bilay daguén khamné dray aduna diarul li
Auto yi dé ndeysane Sonko lamay fatali
❤❤💪💪
Paix à leurs âmes que la terre leurs soient légère et que firdaws soit leurs demeures éternelle près du prophète mouhamet psl amine yaraby fatiha + 11ikhlass
Bravo la bip
Gni deh BIB bouléne andiwoul dougnou dougue thi tribunal bi wallah thi bir lagnou len Di fek.
Li doyna warrrrr louko fi diar