Allahou akbar lambalok alou Na combat Bi Da Wara Lerr Daco Rou ma

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 195

  • @NabouThiam1467
    @NabouThiam1467 15 днів тому +6

    Félicitations mor kang kang 👏🥰 et Du courage Diop 2 ❤ lisi kaname Moy dakeu inchallah jambar nga 🙏🔥👊🥰🙏

  • @loufa299
    @loufa299 16 днів тому +44

    Diop 2 Seul kou d'accord lalal j' aime🥰🤍

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j 17 днів тому +17

    Lamb dji métti na déh khekh naniou beuré naniou mashallah 😍

  • @rakkalofficiel419
    @rakkalofficiel419 17 днів тому +44

    Mane guisouma victoire en tant que amateur de lutte bilahi

    • @Mouha_sall
      @Mouha_sall 17 днів тому +3

      Moi aussi

    • @ndatteyalla9917
      @ndatteyalla9917 17 днів тому +5

      PROLONGATION DARA WARA AM CI LAMB VRAIMENT COMBAT YOU MELL NI DIÈKHÈ PAR AVERRISEMEMT YOMB NA LOL VRAIMENT

    • @serignemodouciss7270
      @serignemodouciss7270 17 днів тому +1

      D'accord âme nguasi droit dh vraiment mais les avertissements sont claires. Diop2 ndanane la mais Mor dafa méti si kawam

    • @babacarndong-ge7mc
      @babacarndong-ge7mc 16 днів тому +1

      ​@@serignemodouciss7270diambar Mor kang kang limou diap sou nekoneu Diop2 daf KO diap combat bi dieh
      Kou nek dafa def Ardo donc kou nek tegal n'a sa morom Lou meti dé

    • @MouhamedMbaye-lw1zo
      @MouhamedMbaye-lw1zo 16 днів тому

      Mane tmt dh lambe cng dako commencé yakk

  • @mamethiernodieng7006
    @mamethiernodieng7006 17 днів тому +19

    Lambalok tu es le meilleur franchement Bonne continuation finga té rék fofou la deug rek mo wore

  • @BabacarGueye-t7d
    @BabacarGueye-t7d 17 днів тому +76

    Diop 2 da khekh bah gueneu lolou dou avertissement

    • @papebabacarn654
      @papebabacarn654 17 днів тому +1

      Bonjour
      Abonnèl ma sama compte bi (LOU BAKH TV) profil bagui nonou

    • @abdoulatifdiop5640
      @abdoulatifdiop5640 17 днів тому +7

      Avertissement la deh ndakh daa arrière deh ba geun géew bi motax

    • @Mouha_sall
      @Mouha_sall 17 днів тому +4

      Bly frr lolou mom do avertissement 😢

    • @TallaFall-or4xk
      @TallaFall-or4xk 17 днів тому +11

      Kou bakh fo ték lolou 😢 avertissement parce que sakou yi fékeu si woul kéneu

    • @ndatteyalla9917
      @ndatteyalla9917 17 днів тому +4

      REGLEMENT YI DAL WAR NAGNE KO XOLATE VRAIMENT

  • @vitofaye3102
    @vitofaye3102 15 днів тому

    Lamb ligua wakh foko ték diop dafa gnak lamb yague na diékhè thi avertissement félicitations mor courage diop 2 ✌️ diop 2 khékhou béne lokho amatoul thi lamb

  • @MamadouSene-i4z
    @MamadouSene-i4z 17 днів тому +60

    Kou done khar lambolog ❤😂

  • @abdouazizdiallo2254
    @abdouazizdiallo2254 17 днів тому +17

    vraiment lamb lok ta raison fallait oublié les avertissement dem prolongation il nous faut des chutes pas des victoir par avertissement lolou moy spectacle lamb mais fimou néxé nioukoy yakh aaah

    • @Mouha_sall
      @Mouha_sall 17 днів тому +1

      Bly avertissement mo yakk lambe Dji 😕

    • @serignemodouciss7270
      @serignemodouciss7270 16 днів тому +1

      @@abdouazizdiallo2254 sport bo guiss day âme avertissement souko amoul dou nékh ensuite dou guaw parce que dafa âme gnou meuneu tapalé

  • @mouhamadoulaminekane5978
    @mouhamadoulaminekane5978 16 днів тому +2

    Diop 2 vrai guerrier leu , téy bètt nama vraiment. Mais Kèn dou Mor🎉 Siteu na dieul Mor, boy bi dafa wekh khatt

  • @adamadiouf487
    @adamadiouf487 16 днів тому +1

    Diop 2 un vrai champion défarou watt Reik gnewatt fort Tay il m'a surpris vraiment

  • @babacarfaye25
    @babacarfaye25 16 днів тому +4

    Kadouyii rafetna ❤️

  • @papathiam610
    @papathiam610 16 днів тому +3

    Diop téeré bi mor tée si lokho droit bi mo yaak lou beuri mais diop diambar la il naka démérité

  • @SeydouBa-q2z
    @SeydouBa-q2z 16 днів тому

    Modou Anta bayil merrr . maintenant vous êtes des professionnels

  • @PapeSene-rn7xe
    @PapeSene-rn7xe 17 днів тому +7

    Diop2 ❤❤❤❤❤

  • @abdourahmanekeita433
    @abdourahmanekeita433 17 днів тому +13

    Kennnn dou yennn❤❤

  • @mouhamadoulaminekane5978
    @mouhamadoulaminekane5978 16 днів тому

    Diop 2 , Mor Kang Kang ay vrai ndaanaane légn vraiment. Khol yeup sèdd.

  • @AwaFALL-r1r
    @AwaFALL-r1r 17 днів тому +6

    Diop 2 💚💛

  • @mogueye2845
    @mogueye2845 16 днів тому +1

    Cheikh borom produits you bakh yi ✊✊

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 16 днів тому

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @SerigneMbacké-r2q
    @SerigneMbacké-r2q 16 днів тому +3

    Mor yalna bourbi dolli la tawfékhe 👊

  • @amadougueye7044
    @amadougueye7044 16 днів тому

    Diop vrai champion la na wuti dolé rék oub labji

  • @elhadjindiaye7089
    @elhadjindiaye7089 16 днів тому

    Xalé you 10ans séni paren bayi léne niouy takhawalou ni 😢yerem na Sénégal

  • @djibriltine5935
    @djibriltine5935 17 днів тому +1

    Félicitation mor kang ka

  • @IssaMbeur
    @IssaMbeur 16 днів тому +2

    Abou cfa Domou kharam la féne rék laye défe

    • @serignemodouciss7270
      @serignemodouciss7270 16 днів тому

      @@IssaMbeur Yako dégue Lou gueum motakh. Mane dh souma guissé vidéo wam rék damay zappé 😂

  • @abdoucoly8278
    @abdoucoly8278 17 днів тому +6

    Modou Anta bayi dii antisipe aye wakh Aakh sof ga trop wala daga buege noulay saga

  • @Mecrare01
    @Mecrare01 17 днів тому +15

    Diop 2 Borome Soow mii 💚💛

  • @BadaraAline-f5i
    @BadaraAline-f5i 16 днів тому +1

    Li dou victior

  • @NdiawDiop-o6u
    @NdiawDiop-o6u 16 днів тому

    Mbeur bala ngay nek champion deug danou

  • @DaoudaNdiayedev
    @DaoudaNdiayedev 15 днів тому

    Diop 2 seul ❤domou ndiambour bi

  • @mbayedione7147
    @mbayedione7147 16 днів тому

    L’amine yaw champion nga Bilahi

  • @rapshouseofficiel9072
    @rapshouseofficiel9072 17 днів тому +7

    Modou del wax forme bou baxx pas guinaw bou baxx apart sa nice🎉🎉

  • @AbouTall-h9p
    @AbouTall-h9p 16 днів тому +2

    Diop2 seul ❤🎉

  • @modouamar1130
    @modouamar1130 16 днів тому

    Modou Anta mann j’ai beaucoup d’estime pour toi mais bayil di wakh ay koumou nékh sagal wakhal loula nékh lolou dou wakh kouy wakh dingua dégue lou nékk mais déll focus té bayi ay wakhou dagassanté meuno tontou nieupou dangua ameu ay soppé nioune danioulay bégué mais bayil khél lolou merci

  • @PapeKama-d4d
    @PapeKama-d4d 17 днів тому +5

    Blkhi diop da khew ba guene lolou dou avertissement ⚠️

    • @papetallandiaye9433
      @papetallandiaye9433 16 днів тому +1

      Copin Diop bimouy guéneu xamoul sac fimou nék😂

    • @serignemodouciss7270
      @serignemodouciss7270 16 днів тому

      @@PapeKama-d4d wa loumouy guén sou nékone si biir kén douko avertir

  • @MoussaSeye-l5u
    @MoussaSeye-l5u 17 днів тому +4

    wooooopoooooooo

  • @vitofaye3102
    @vitofaye3102 15 днів тому

    Khana lamb tay rék la Meuse diékhé avertissement 😂 diop 2 wakh léne ko liko dane mbeur boko beugué diapalé après combat wakh léne ko liko dane n'a ligueye thi gauché bi droit rék dou khéx khalé la li yakoul Dara thi carrier bi 👉👂 félicitations mor 💪 courage Diop 2 défaroul li Mola wara déf mbeur 👉✅

  • @mustaphamakalo8414
    @mustaphamakalo8414 15 днів тому

    Very very true bro

  • @laminelo2142
    @laminelo2142 16 днів тому

    Bouline gno sonal yine wa lamb yeup diop guine beugone mou dane boudone diop lanou diokh victoire bi doline waxi nii

  • @NGAGNENIANG-s6x
    @NGAGNENIANG-s6x 16 днів тому

    Waa lambalok nak yaa nekh bolen doyo loutt nak te mor am Victor

  • @DjibiThiaw-wy2xy
    @DjibiThiaw-wy2xy 16 днів тому

    Lamb temps bi df guat fowou millions waroul yomb legui daguay nieuw takhaw say supporters dila encourager

    • @mbayelenoble3057
      @mbayelenoble3057 16 днів тому

      Yaw Siteu ak ay supportéram ngay gàrouwàlé quoi🤣

  • @Amadouniang-p3c
    @Amadouniang-p3c 16 днів тому

    Lambalok tay wakho si diop 2 darra 😢😢😢

  • @sidysakho6558
    @sidysakho6558 17 днів тому +9

    Wa yéne Mor kang kang déh gouye gui rek lamay fatali come rebot wow Kong 😂😂😂

  • @PapeSambaDiouf-y4m
    @PapeSambaDiouf-y4m 17 днів тому

    Modou Anta bayile di tontou déle diélalé way akhh

  • @FatimaGning-h8b
    @FatimaGning-h8b 16 днів тому

    Bawol kase suñu yoon ci keneen ak leleen

  • @lasscisse2405
    @lasscisse2405 16 днів тому

    Wa boy yi thi biir guèw gui ak ak galadj yign fi seuf yeupp

  • @SouleySow-hd7uk
    @SouleySow-hd7uk 16 днів тому +1

    Temps bi guén wara wakh ah

  • @ablayendiaye7170
    @ablayendiaye7170 16 днів тому +1

    Mbeur mou guéneu si lamb ame avertissement may léne niou way

  • @ahmadoubambakanekane7409
    @ahmadoubambakanekane7409 16 днів тому +1

    Nice lamb

  • @souleyFrezyjr
    @souleyFrezyjr 16 днів тому

    roi bangui Diamaguene

  • @ibrahimabop672
    @ibrahimabop672 16 днів тому

    Mor seul seul😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉🎉🎉

  • @TaxiMan-y9c
    @TaxiMan-y9c 16 днів тому

    Diop 2 béneu lokho ladone beuré main gauche bi diokhéwoul kholate léne combat

  • @ND.BALLAuser-ft7kg5jk5v
    @ND.BALLAuser-ft7kg5jk5v 17 днів тому +4

    Khatare khatari 😂😂😂😂😂

  • @dioptalla2757
    @dioptalla2757 16 днів тому

    Diop 2💚💛💚💛💚💛💚

  • @IibouSagna
    @IibouSagna 16 днів тому

    Si le combat doit être encore discuté à la fin de la saison mais d’ici 2 ans Diop 2 sera redoutable vraiment…. Mais les staffs ont empêché les lutteurs de donner leur meilleur

  • @mouhamadoulaminendao6018
    @mouhamadoulaminendao6018 17 днів тому +15

    frenchment li match nul là khèh ba guéne guèw bi

    • @serignemodouciss7270
      @serignemodouciss7270 16 днів тому

      @@mouhamadoulaminendao6018 loumouy guén dou takhaw. Kou dém si sakou yi yakofa fékk

  • @jacquesalphonsembaye2704
    @jacquesalphonsembaye2704 17 днів тому +4

    Lambolok Mangi protéger poche yi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 bala boy yi dila womate

  • @AbbaSall-q8j
    @AbbaSall-q8j 17 днів тому +1

    Diop 2 prince🎉

    • @ABUBAKR-d8x
      @ABUBAKR-d8x 17 днів тому

      Combat bobou nagn bayi baci kaname inchallah 😂🎉

  • @ModouFall-u8t
    @ModouFall-u8t 17 днів тому +1

    Boul sokhor waye lambe

  • @jullmoussa
    @jullmoussa 16 днів тому +1

    Sérieux diop 2 diambar la

  • @MouhamedGueye-mm8kz
    @MouhamedGueye-mm8kz 16 днів тому

    Niari 10 mn moy Lolou bilaye 30 mn sakh

  • @SalamBasse
    @SalamBasse 17 днів тому +4

    ❤❤🎉🎉🎉

  • @ndiaganiane2248
    @ndiaganiane2248 16 днів тому

    Nice

  • @SambaBa-b6i
    @SambaBa-b6i 16 днів тому +1

    ❤❤❤

  • @critique2214
    @critique2214 16 днів тому

    Lambologue mongui nonou suoi

  • @babacarsarr5051
    @babacarsarr5051 16 днів тому

    Leuz lamb Modou anta seules

  • @njaxboy7924
    @njaxboy7924 16 днів тому

    Abou néna kouy songou moy danou😅

  • @mouhamedsy9441
    @mouhamedsy9441 16 днів тому

    Li yeup lac3 moko fi indi😂

  • @simmelsarr3599
    @simmelsarr3599 17 днів тому +5

    Mor KK vs Jackson Jr

    • @soldarouyayam8524
      @soldarouyayam8524 17 днів тому +1

      Yw beugo mor dèh khamgua Jackson est ce que

    • @serignemodouciss7270
      @serignemodouciss7270 16 днів тому

      Saway Mor kang kang meunoul khékh dh té Jackson day rayé

    • @papetallandiaye9433
      @papetallandiaye9433 16 днів тому

      ​@serignemodouciss7270 bro mor ngor lh Jackson di ngor lamb lh dou yomb si niom niarr nieup

  • @MagueyeBeye-z8i
    @MagueyeBeye-z8i 16 днів тому

    Mor kang kang seul

  • @DiomeAdiouma-x7b
    @DiomeAdiouma-x7b 14 днів тому

    Diop 2 dou dara ragal la 😂😂😂😂😂😂😂

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op 16 днів тому

    Lambelogue dangua barri meuno fékhé baniou changer li CNG dogal

  • @kionking-i9k
    @kionking-i9k 16 днів тому

    Dafa yombe trop

  • @KhadimDiouf-d5t
    @KhadimDiouf-d5t 17 днів тому +3

    Kang Kang kassé

  • @ababacarseck9053
    @ababacarseck9053 16 днів тому

    Nagnou wax si temps bi mounougnou Faye mbeur ay millions gnouy beuré 20min c'est peut nagnou yokou temps bi 30min voir 40min

  • @jacquesalphonsembaye2704
    @jacquesalphonsembaye2704 17 днів тому +1

    Fin bi regarder bien ak gnane 😂 béneu boy wara gagnou 😂 non lamb

  • @Oustas-hg2ku
    @Oustas-hg2ku 16 днів тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂

  • @serignemodouciss7270
    @serignemodouciss7270 16 днів тому +2

    Khalé you toll nii lougnouy déff stade la khamoul?

  • @GayeTapha-r9k
    @GayeTapha-r9k 16 днів тому

    Règlement yi warr nagniouko kholaatt nk,lamb tègal fofo sa lokho

  • @MackySallprésident
    @MackySallprésident 16 днів тому +1

    Modou anta wakhou doff rék gay wakh bayil di soralé nitt yi sisay wakh koumou nékh ak koumou nakari moy wakhou lann

  • @Abdou-l5l
    @Abdou-l5l 16 днів тому

    Niari. Mbeure. Khekhe. Ba. Gueun. Dou. Avertisement. Lamdji. Respectè. Wougnou. Amateuryi. Tè. Amateur. Mo. Yor. Lamdji

  • @MoustaphaMoustaphadialoo
    @MoustaphaMoustaphadialoo 17 днів тому +2

    Woppopopo😂

  • @MafayeFaye-nn1kh
    @MafayeFaye-nn1kh 17 днів тому

    Boy Moudou amoul ay sama wakh koumou wala koumou nakarii deh Sa Xol nga wara yatal défsi Lamballe boy

  • @OmarNjie-g4v
    @OmarNjie-g4v 16 днів тому

    🎉🎉🎉🎉

  • @BathilyAladji
    @BathilyAladji 16 днів тому

    Siteu vs mor kang kang combat la dh

  • @nargaye3866
    @nargaye3866 17 днів тому

    Lambalogu dougu tay

  • @modoundiaye-wx7xx
    @modoundiaye-wx7xx 16 днів тому

    waw kay li modou anta wax si reglement cng. reglena cas barth sinon jurisprudence Mor kang kang Diop2 moy takhaw si cas yi di nieuw

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 17 днів тому +5

    Pourtant mbeur yi diokhé nane de

  • @nogayeniang9119
    @nogayeniang9119 17 днів тому +5

    Diop 2 mou danou nãk diop rek lá beugue mas dafa kene sakou yi

  • @NderyDiarra
    @NderyDiarra 17 днів тому

    Les enfants 😭

  • @sgoragning4025
    @sgoragning4025 17 днів тому +3

    Lambolok look règlement c'est pour tout un combat boul niou fonton

  • @ablayendiaye7170
    @ablayendiaye7170 16 днів тому +1

    Bayi léne nafékheu, Mor kang kang mo dane

  • @MagueyeBeye-z8i
    @MagueyeBeye-z8i 16 днів тому

    Reguelma mome reguelmala point

  • @ablayendiaye7170
    @ablayendiaye7170 16 днів тому

    Na takhaw khana nékoul Borom soow mi 😂😂

    • @serignemodouciss7270
      @serignemodouciss7270 16 днів тому

      Sou takhawé Mor maar ko dh😂

    • @layetheonly5139
      @layetheonly5139 15 днів тому

      ​@@serignemodouciss7270amo lo wakh 😂😂😂 takhawna ba mor diap lokho bouy door 😂😂😂
      Mor dembeu nélawam dou yombou

  • @Deggou
    @Deggou 16 днів тому

    Le problème legui mbeur you ndaw yi daniou niane chance, nieuw di négocié daw combat bi fi amoul dara louniouy leral mor danenako, boyi naniou deme beuré ak seen morame..

    • @DieynaSoumaré-p8e
      @DieynaSoumaré-p8e 16 днів тому

      Waxofi dara diop 2 loum déf loutax bign diapanté mor beuréwoul diop chercher na beuré bi té xékh na ak mom

    • @Deggou
      @Deggou 16 днів тому

      @DieynaSoumaré-p8e 🤣🤣ki daw combat bi yeup nganane moor khawko ray

  • @frankydolle7559
    @frankydolle7559 16 днів тому

    Diop 2 naa dougaal recours parce que il n'as pas fais un sortis délibéré

  • @ibrafatyndaw9891
    @ibrafatyndaw9891 17 днів тому +25

    Siteu diop 2 ak mor kang Kang say nawlé say rakou lagnou si lamblagnou 😂😂😂

    • @DaoudaGaye-z8w
      @DaoudaGaye-z8w 17 днів тому +1

      Raye nga ma déh 😅😅😅😅

    • @ibrahimadrame9499
      @ibrahimadrame9499 17 днів тому +1

      Lac3 mo yakheu mbeur yeup😢😢😢

    • @ibrafatyndaw9891
      @ibrafatyndaw9891 16 днів тому

      @ibrahimadrame9499 non gni kayy défou comme lac 3 wala dégo wolof

    • @ibrafatyndaw9891
      @ibrafatyndaw9891 16 днів тому

      @@DaoudaGaye-z8w deugue la wakh di siteu nimou beugue diapé lambam dafa yomb kholal gni beuré bou nekh lagnou beuré

  • @cheikhmbacke2911
    @cheikhmbacke2911 16 днів тому

    Modou Anta khamo règlement. Lambe dafa ame 1e mi-temps ak 2e mi-temps d'où question avertissement si match nul après les 2 mi-temps prolongation . Sou dieul amoul kou eup avertissement daanou .

  • @papesarasylla9506
    @papesarasylla9506 16 днів тому

    Siteu cathegorie bi la wara beuré boy yi nioko meune

    • @WizzFirmino
      @WizzFirmino 16 днів тому

      Siteu zarco mo gueneu meti li fep yaw yamal Siteu Modou lo la dane

  • @MamadouFaye-h2b
    @MamadouFaye-h2b 16 днів тому +1

    Vraiment combat waroul won diekhe nii