Yalla mi fenial li après 5ans de prison , cela veut dire que la vérité est proche 🙏🏾yalla nieup lafi nekal yalla nala borom bi guéné si thiono yi amine🤲🏼
Ça mom vraiment c'est l'affaire du siècle j'arrive pas m'expliquer cette situation donc cela confirme qu'il y as que des innocents dans nos prison comment peut ont être méchante à ce point mère bi vrai domérame la ki dou nit vrai nitou safara la et que dire du père de fallou😮 wa mé pah bi eskeu nit leu non c'est du jamais vu en plus à nos magistrats tamit comment ont peut mettre en prison une personne avec des accusations aussi fallacieuse des accusations aussi légères gua yakeu adouna khalé bou ndaw 15 ans de prison ...
Aye waye loutakhe nite bone beugue sacrifier domou diambour dji ni reck 😢😢😢dafa ame gore you failble reck ak djiguéne gnou bone je me demande dans quelle monde nous sommes 😢😢😢
Vraiment dafa meti Fallou inchallah dina gueneu d ndax Sunu borom dinaka tek loxo 🙏🙏
Wayé Yalla dîna atté insha Allah
Bilahi tay rek sougnou djouli fadjar gui rek imam bi si lolou ladone waxtaner si miroume fallou
Sama khole bi méti torop vraiment
Yallah na Yallah léral lépeu in'sha'allah sa none sakh doko yéné prison sakatou mala sa domou djeukeur 😢
Walaye métina masta léne
Yalla mi fenial li après 5ans de prison , cela veut dire que la vérité est proche 🙏🏾yalla nieup lafi nekal yalla nala borom bi guéné si thiono yi amine🤲🏼
Bilay lolou la wakh
Serigne fallou fall yalla nako yalla téguil natou bi dale si kawam
Bilahi djiguene bou bonne yalla nagnou yalla mouseul Fallou yalla nako yalla takhawou thi barker seydouna Mouhamed psl 🙏🏾🙏🏾
Justice pour fallou fall 🙏🙏
Ça mom vraiment c'est l'affaire du siècle j'arrive pas m'expliquer cette situation donc cela confirme qu'il y as que des innocents dans nos prison comment peut ont être méchante à ce point mère bi vrai domérame la ki dou nit vrai nitou safara la et que dire du père de fallou😮 wa mé pah bi eskeu nit leu non c'est du jamais vu en plus à nos magistrats tamit comment ont peut mettre en prison une personne avec des accusations aussi fallacieuse des accusations aussi légères gua yakeu adouna khalé bou ndaw 15 ans de prison ...
Tay la meussa dioy si gerou probleme yi sama khol métina fallou yallnala yalla guéné figua nek
Free Fallou ❤️🙏🏾🙈Yalla Na Yalla Takhawou Fallou Amen 🙏🏾
Une marche pour fallou 😢😢😢
Merci marche c normal
Affiche way
Moy yon sakh😢😢
Je suis partante
Fallou yalnaco liguéyou ndayam wallou
Des vrais hommes masha alla
Fallou soit fier de tes amis
Que le seigneur t’accompagne fallou😢
Bamel wetna khatna 😢😢😢😢😢😢😢😢😢 yalnako yalla takhawou frère
Metina loleeeeeee courage Fallou yallana yalla nitela guénéla si khatekhate papa Fallou bakhoule tata Fallou bakhoule grand frére binek espagne bakhoule wa quartiébie yéna bakhe aye kharite Fallou yéna bakhe eskey djiguéne bou bone dou ame yeuremandé
Wa keur gui gnou bakh lagne Bilahi yalnalén yalla fay
Li dhé lama sama domou bay déf motakh doma bay la geuna bagn dji aduna
Aïe wayyy dioyna ba sonou fallou mi yallah nako yallah wolou
Mètina loutakh Sénégal mèti ani preuve yi li dafa yomb trop masa fallou
Yalna nako yallah guéné
Koudul khalate 3jour bamel Loula nekh defal dei am na dei
❤❤❤❤❤❤❤❤❤yalla. Nako..yalla..sameko
Vraiment meetina troop YALLAH nako YALLAH leeral ma leep leer🤲🤲
No histoire bi metina trop wayy justice pour falou
Fallou yala nako yalla takhawou thi barkèp tourandome😢😢😢
Bilaye lii Dafa méti rkk yalnako yalla takhawou
Fallou yalnako yalla takhawou
Fallou sa bakhou yaye nulloul yalla nako yalla yeureum té takeaway aye diabotam.
Yalnako yalla guéné thi natou bi Serigne Fallou bilahi li métina
Kou djoyoule Rèk do nit 😭😭😭
Merci frère kadouyi rafètena, bousi autorité dioté rék lép soti incha'Allah
Vraiment li métina 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭💔😭😭😭😭 fallou yalla Nako yallah guéné fimou nek si barké seydina Mohamed
Merci 👍😢😢
Ndeyssane papam tayoul limouy deff ni,amna louko nakhari
Yalnako yalla takhawou si barke nabi psl🙏🙏🙏
Khana juges yi guiss nagnou li ay Way bayiléne Fallou 😭😭
li metti na bilahi 😭😭
*Métina trop way injustice bakhoul 😢Fallou Yalla nako sougnou Borom walou fofou mou nekk bamou guéneu thi diam 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
Li nimouma mété bilahi mére bi yalla nako yalla torokhal doméram deugula
😢😢😢 justice pour fallou
Justice pour fallou.partager dans toutes les groupes panels des patriotes svp😢
Justice pour fallou 😢😢😢
Je le jure j'ai le coeur fondu j'espère que notre on ai une mère on a des enfants j'espère que dieu va eclaire les choses😭😭😭
No li metina mai yalla bakhna😭😭😭
Yallah gueumoul nélawoul yallah di na léne atté légui rek, fallou mougneul rek
❤❤❤❤❤justice pour falou
Wallay adouname dina fi diar defarrou inchala
😢😢😢bilaye deh il sen sortira bien
Aye waye loutakhe nite bone beugue sacrifier domou diambour dji ni reck 😢😢😢dafa ame gore you failble reck ak djiguéne gnou bone je me demande dans quelle monde nous sommes 😢😢😢
Yalla Dina léral lépp inchallah free Mame Fallou yalla nala sa barkép tourando wallou
Justice pour fallou fall
Yalla nako tourano wam wallou thi wer bi ted bi 🙏
Amine 🤲🤲🤲
Yalla nako yalla walou tourodowame mounouko walou yalla rék moko mene wallou
Commencer tiguéne nak@@cheikhdiop516
Commencer tiguéne nak ahh@@cheikhdiop516
Justice pour fallou fall .guuenal ak diam salam
Yalla nako yalla takhawou
Fallou yalnako yalla takhawou si barké salatoul fatikha walahi li metina niawna adouna dou keur naniouy khalate souniou euleuk
Yallanako yalla dimbali
Thiotou ndeyame Sénégal d'où rèw
C est grave très très grave.il faut libérer ce citoyen. qui n est pas fautif.
Marche national pour fallou fall😢😢
👉😭😭😭😭😭😭😭sama xol toyna😭😭😭😭
Justice pour Fallou fall 🙏
Merbi guenē wara yeugeul ndayam yene gni deukē si kognbi😊😊😊😊😊🪓🪓🪓🪓
Une marche pour fallou une demande nationale
Lii métina nama trop trop ooh😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Yena am gor yena bakh te douguene fate demb
Mètti n’a trop billahi 😢😢😢
Li yeup jiguenne bou bonne moko warall jiguen gni kholatt len sen boppou ci niguén nekéci biir keuryi aduna yagull dh. Li métinama trop vraiment 😢😢
Diabar ju bax diar na louné
Billahi
*Bilay ioe😢*
Justice pour fallou guire yallah ak yonénetabi
Bilay Ndayessane li metina trop bilay
Mère bi dégrée de bonam eup na adouna dou keur lou way déf domou diambour yalna keupou thi sa ndiabote bone amoul sens
Yalla guiss na lép bilahi walahi
Rien ne me choque venant des marâtre 😢😢akka gnoo fausse meune fène. Mais inchalla fallou vas sortir gnoune djirim yii yalla mognouy samal popam 😢😢
Amine lii métina trop 😭😭😭😭
Yalnako sounouborom takhawo méti.a torop
😭😭😭😭😭😭frément dafa méti
Femme bi Dineuko guisse bayiko reck
Yalla nako yalla téguil natou bi
Mane dé khamoumako mais li métina ma loll Yalna borom bi takhawoula
Au.metina❤❤❤❤
Sénegal amoul loi
Man dama fébar té khawma Fallou justice pour Fallou 😢😢😢😢😢😢
Mane.daman.metitrop.li.daguene.kayekh.werr.waye.dinakepousikowamm
Bakh.na.bakh.na.bakh.na
Dougualen.fotom
Contact béneu proche Fallou la sokhla svp
Dinala ko lidieun til
Goor nñi tamitt sa djabar ganiou bayi ay dome nga Dieundé ko jiguen 😭😭😭
Pour mome dou fekhi sene yaye , goor yi tamite so amé ay domes boye takhate kholale bou bakh mais sene bakhane rekh
ayway fatima dieng délossil sa khel li niawna wa mbour yép rouss nane yala nala yala atté ak fallou wa mom foum deug si mbour svp
Bilahi mbour yeup rousss ki mo bakhoul rék mane mi lolou la beugue kham foumou deukk si mbour
Que dieu vous fortifie sur ce combat
Li yobou Yayou Falou doula fi bayi bilaye walaye 😭😭😭ya sokhore ya rouslo baipe djiguaine😭😭
Yalla naco yalla ték lokho
A mandé dama diomou li métina trop a yalla bakhena 🙏
Yalla nalene Yalla ath si kaw souff
Yalla nako tourondo wam djiguene bou bonne yalla nagnou thi yalla mouseul 🙏🏾🥹😭
walahi dama 😭ta khawma fallou li dafa métii trop
Lii metinama torop wayé yalla bakhna
Dake laine ko.si.konnge bi
Le commissaire aussi c'est si il n'est pas scycologue y'a des mensonges à détecter
Fallou mi de khawma yayam mais kou bakh la wonn so ko khole rek am lo yeuk té lolou ligueyou ndeye la yal nako yalla guene prison
Vraiment ça fait mal
Justice pour fallou
Yalla naka ligueyou ndeye walou
Metti na billay 😭😭