Justice pour Fallou fall na yone défe liguiéyame wa quartiébie yéna bakhe yéna ame goore yone waroukowona bayi mou déme pour lale dafa toumale domou diaboure mou teude 5ans kone mome ak gniko diapalé nanoulénes diapes justice pour Fallou yallana yalla téguile fallou natoubi guénéko si khakhate
Que toute personne impliquée dans cette affaire de près ou de loins (médecin, policier, magistrat, civil, etc….) doit être rappeler de ces responsabilités.
Damani... wa mais yow tamit nak ahhh non. Kokou dè ne nak yow tam😢. Sou meunoon wallou kènn dou dè. Yalla rek mooko meuneu diappalè. Saa waay bokkalè dafa di li gueuneu graaw. Yalla dou ke baalé.
Je ne peux pas me retenir quand j écoute ses témoignages car moi aussi j ai passé sur cette situation mais heureusement je ne suis pas arrivé sur le cas de fallou Allahou aide à ce garçon de retrouver sa liberté 😢 😢
Meme mon frère a fait une semaine de prison à cause des mensonges on s'est battu. Le policier qui a fait les pv au commissariat de Yeumbeul a été affecté ailleurs lep mom le. Le certificat médical a été faite par uke sage femme
Surtout ça. Parcoeuriser des articles et avoir la maîtrise en droit et réussir son concours n'a rien à voir avec l'honnêteté et l'intégrité. On doit revoir comment on sélectionne nos magistrats
Vraiment lii nane lako nitt mana téké domi diambour Dii gnanal serigne Fallou sa borom défal ko liberté ak gnii Lou melnii dal barkep xassidayi 🤲 C'est vraiment triste 😭💔
Dé fois gua fogueni dagaye yakal nitki fékini yangui koye défaral.ndakh Fallou fini lay diare machallah takeu ba faw ndakh Bou guéné yallah dina défar ay mbiram ba fou way tolou diko sén fou kawé inchallah 🤲🤲
C’est ça 1 ere témoignage dafa teudone rek Durant 4 mois 10 mois gnoungui koy dora juger mais Fallou il est innocent c’est des manipulations Yalna yalah cetako barkep radiap bii🙏🙏🙏on est de tout cœurs avec toi fallou
le premier ministre seydina ousmane sonko warna kholate problemou kèpeu kouniou djigne viole Comme le cas de FALLOU FALL aussi le slogan jub jubël jubanti ,niou bagne ko yèmalè si population bi simple simplement niou ndieukè si les autoritès judiciaires et les hommes de tenus police gendarmeries et penitence parce que Lou Bari niom niokoy wara takhawou Comme IL faut tè douniou si deff sène liguèye nimou warè une enquète dafawara serieux niou kholate la formation des officiers de police plus Comme en Europe mou serieux parce que accusè nite simplement teuthie ko 5ans des menssonges après libèrèko sans même indamnisèko rien mou moudiè nul c est pas normal c est pas sèrieux. tè lolou meuna yakh kholou niou Bari bamou dèf lolène louniou beugoul deff ndakh injustice c est anormale.dans les pays de droit ,kounioi teuthie injustement pendant des années danioulay diokh khaliss pour massawoula lignoula teuthie . lolou motakh ma wakh son exellence seydina ousmane sonko, les senègalais n aime pas l injustice surtout motakh il y a eu des morts bila maky sall accuse indirectement de viole en passent par adji sarr . bamou am ay officiers gendarme et millitaire yousi disparaitre FULBERT SAMBOU et DIDIER BADJI donc de grace fait le nèssèssaire pour que le projet jub jubël jubanti dara bagne ko yakh si leep tè le cas de FALLOU FALL cas bou sensible la boulko woyofal takhaw si dans l urgence s IL te plait parce que diaye dollè lay nirole tè bakhoul si am rèw.merci.mangui dièguelou Sama khòle dafa dièkh 😢tè khamna ni il y a pas Mal de personne you nek si prison yi tè dèfouniou dara 😢😢😢😢et que lolou yowmalkhiyame rek lay lèrr si kanamou souniou Borom billâhi tè dafa.mèti so amoul koala takhawou si say diaffè diaffè. lèbèrer FALLOU FALL s IL vous plait.
Sa waye boulma dioye lo waye ya bakh barké borom touba. Fallou mo nek si deugeu parceque nioune nieup on se connaît pas té nieup béne wakh bi laniouye wakh free fallou
Pour meu gueum né problème adji sarr dinegn ko régler, biii degn ko wara régler beu noppi. Maaanam neu médecin bi teudd, neu borom grade bi teudd, neu pape bi teudd, neu diabarou Paa bi teudd. Beu noppi niou fay lou tollok 500 millions minimum Fallou Fall.
Nama yalla bale deee mo femme bi VS k deff n separation d coro ak dieukeur djii bou Yagüe BA paré policier nangou nekk si guinawame diko doléle Geustouléne bou bakh nakh policier bi nekoule diko lale verifier apres nakh Pere bii mo dioure xalé yii cette femme est capable d tt
Franchement 5 ans gua djiap niite teh defoul dou mom teh viol amoussi injustice bobu moma gueneuh meti Fallou dina guen la vérité sera mince et triomphera justice pour Fallou way ❤❤❤
vraiment sénégal amoul justice liiiii grawna torope yalla nalene yalla torokhale gni def seine pekhé ba teudjieulou domou diambour yalla naniou yalla mouseul si pekhe noone
Justice mo amoule Sénégal 😢 En 1996 sama petite sœur leu dale un voisin bignou diakarelo keur gnou mine ko lol sakh 🥺 sama petite sœur mime ko mou kaye fope diko yobe séne keur béne beuse mou indi mais mouye dioye dioye you méti sakh ma nakh ko mais mouye dioye rék ma déme séne keur lathe ko lane mo kéwe nakh daffa danou la mère du voisin ni dioye si néggou dome bi leu wone ma délou wate sougnou keur nak nak mais sougnou wa keur diakhélé ba gnou ko soumé pour khole lane leu silagnou guiss ni puisque mounou ko pénétrer daffa done défe aye frottements ba guagne ko guagne bou méti sakh avec des déchirures gnou déme gendarmerie ame certificat médical avec des photos gendarmerie défe enquête gnou diape ko souma diouboule 2 mois leu défe prison tribunal juge bi leu aye mbokame faye nak dagno ame khalise 😢 ma sœur vie toujours avec les séquelles daffaye saye rék yak adouname ni 😭😭
Bilahi walahi talahi sama dioye yima dioye Fatima yalla nala yalla Alak si adouna bi nieupeu diko guise fallou fall yalla nala sa niani yaye walou te dina ameu deh inchahala te ngeune Balema sama khole bi tangeune lole bilahi walahi talahi
L avocat de fallou était le plus incompétent,je vous parle en connaissance de cause,car je m entretenais avec Oumy Fall la grande sœur de Fallou sur ce cas,je lui avais même suggéré de chercher un autre avocat
Nagne dém Sonatel xoli Apel téléphonique you fatima dieng durent c'est dernier temps et il faut appeler la dame qui dit quelle a trouvé les preuves s'il-vous-plaît la police et les enquêteurs sa c'est une demande nationale ngirr yalla si nous sommes des musulmans et ont vas touse mourir 😢😢😢😢
Mangui Nianeu si barke Seydina Mouhamed yalla na yalla lerale lepeu te Fatima yalla nala akhou fallou fall daleu ak kepeu koukoye diapale si feneu yi yalla nalene akhou fallou fall daleu amine
fatima dieng dotoko défati😂 fallou wakhal sa yaye merçi ❤ligueyou ndeye dafaye fégne si millieu ❤inchallah léep dina léere bouléne faté 66basmala yi pour fallou fall❤❤
Wawawwwww inchallah injustice laniou baye
Inchalah 66 basmala bako ñeup def way
Inchallah légui réke inchallah
❤❤❤❤❤❤inchalla bientôt falou sera libre
Fatima lalena lalakhe Fallou rek
C'est une histoire fascinante mais malheureux c'est choquant d'avoir brisé la vie d'un jeune comme ça Allahou Akbar
Sénégal na niepp dioukk fallou guenne naniou diaral sunu bakan yi 😢😢😢
Wawawwwww inchallah injustice laniou bagne
Bilay gueume nani ya bcp de Fallou dans les prisons
Wallahi jarnakou
@@auparadisdesanges1599 aka wer
@@auparadisdesanges1599lolou Kay lou leer la😢
Jiguéne bou bonne bahoul, yalnagnoussi yalla moussal inchallah
🙏🙏🙏
Amine ya rabi amine bilahiii liii métina
Jigeen ju bon amul lumu msnil
Justice pour Fallou fall na yone défe liguiéyame wa quartiébie yéna bakhe yéna ame goore yone waroukowona bayi mou déme pour lale dafa toumale domou diaboure mou teude 5ans kone mome ak gniko diapalé nanoulénes diapes justice pour Fallou yallana yalla téguile fallou natoubi guénéko si khakhate
Bilay walay
Amine yarabi si barki Mouhamed(psl)❤🤲🏾
Après la libération de Fallou, Fallou doit porter plainte pour diffamation
Souy porter plainte na dem DIC sinon dou moudiou feneu
Bou lolou wesso nanu sargal merou kogne bi❤
Bilahi mère yi yallana gnou goude fane Thi barké Mohamed psl
Non yone déf enquêtes thiii liii wayyy liii daaa yombou trop 😢😢😢
Que toute personne impliquée dans cette affaire de près ou de loins (médecin, policier, magistrat, civil, etc….) doit être rappeler de ces responsabilités.
Est complice meme le mari 😢😢😢
Si barké wérou rajab bi yalla nalla sa tourondo wallou barké borom touba
Damani... wa mais yow tamit nak ahhh non. Kokou dè ne nak yow tam😢. Sou meunoon wallou kènn dou dè. Yalla rek mooko meuneu diappalè. Saa waay bokkalè dafa di li gueuneu graaw. Yalla dou ke baalé.
Merci 2atv li guene def am na solo
Yalla. Nanou yalla moussal si femme bonn
Amin toma
Senegal diote na niou appliqué (jub jubal jubanti) Fallou Yalla nla Yalla taxawou😢
Aamiin. Lii dafa méti. La police devait l' accompagner au lieu de la laisser seule aller à l' hôpital.
Je ne peux pas me retenir quand j écoute ses témoignages car moi aussi j ai passé sur cette situation mais heureusement je ne suis pas arrivé sur le cas de fallou Allahou aide à ce garçon de retrouver sa liberté 😢 😢
Ndeysane yalla mola dimbali beuri si deukbi d
Massa 😢😢😢
Meme mon frère a fait une semaine de prison à cause des mensonges on s'est battu. Le policier qui a fait les pv au commissariat de Yeumbeul a été affecté ailleurs lep mom le. Le certificat médical a été faite par uke sage femme
Fallou mo nek si deugue parceque nous tous on se connaît pas fi laniouye dadié té nieup béne conviction bi laniouye ame .free fallou
Justice pour fallou fall .
NGIR YALLA 😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Ça reste beaucoup il faut nettoyer cette justice
Surtout ça. Parcoeuriser des articles et avoir la maîtrise en droit et réussir son concours n'a rien à voir avec l'honnêteté et l'intégrité. On doit revoir comment on sélectionne nos magistrats
Vérité absolue
Koudoul khalate ñietti fanou bammelle loula nekhe defale wassalam
Bien parlé
Le problème des faux certificats médicaux au Sénégal est un réel et grand problème au Sénégal
Fallou yalla na la yalla diapale si barké serigne fallou yalla bakh na😭😭😭
Yalana yala diapalé serigne fallou fall
Amine ya Rabbana
Fallou yalla na yalla takhawou 😢
Jusqu'à présent j'arrive pas à comprendre que bonou nitt aksina fi 😢😢😢
Billahi. Doo comprendre.
Justice pour falou on demande la libération de falou immédiatement
Sou féké justice Amna fi bilahi Senegal amoul loi
Ce père de famille aussi moy lolou 😢😢gui gnak fayda ak yeurmandé si sa propre dome
Kok kay mbame la boudè liguey dehh djap na
@@auparadisdesanges1599 avec ce genre de femme il faut s’attendre à tout 🥲🥲
Vraiment lii nane lako nitt mana téké domi diambour
Dii gnanal serigne Fallou sa borom défal ko liberté ak gnii Lou melnii dal barkep xassidayi 🤲
C'est vraiment triste 😭💔
Dé fois gua fogueni dagaye yakal nitki fékini yangui koye défaral.ndakh Fallou fini lay diare machallah takeu ba faw ndakh Bou guéné yallah dina défar ay mbiram ba fou way tolou diko sén fou kawé inchallah 🤲🤲
Yalla na gnou yalla moussal thi jiguen bou bone
C’est ça 1 ere témoignage dafa teudone rek Durant 4 mois 10 mois gnoungui koy dora juger mais Fallou il est innocent c’est des manipulations Yalna yalah cetako barkep radiap bii🙏🙏🙏on est de tout cœurs avec toi fallou
Fatima Dieng vrai doméram leu mais justice wa apr bifi nékon nio sacrifier Fallou
Nioune wa pastéf naniou diapalé Fallou bilahi innocent leu😢😢😢😢😢
le premier ministre seydina ousmane sonko warna kholate problemou kèpeu kouniou djigne viole Comme le cas de FALLOU FALL aussi le slogan jub jubël jubanti ,niou bagne ko yèmalè si population bi simple simplement niou ndieukè si les autoritès judiciaires et les hommes de tenus police gendarmeries et penitence parce que Lou Bari niom niokoy wara takhawou Comme IL faut tè douniou si deff sène liguèye nimou warè une enquète dafawara serieux niou kholate la formation des officiers de police plus Comme en Europe mou serieux parce que accusè nite simplement teuthie ko 5ans des menssonges après libèrèko sans même indamnisèko rien mou moudiè nul c est pas normal c est pas sèrieux. tè lolou meuna yakh kholou niou Bari bamou dèf lolène louniou beugoul deff ndakh injustice c est anormale.dans les pays de droit ,kounioi teuthie injustement pendant des années danioulay diokh khaliss pour massawoula lignoula teuthie .
lolou motakh ma wakh son exellence seydina ousmane sonko, les senègalais n aime pas l injustice surtout motakh il y a eu des morts bila maky sall accuse indirectement de viole en passent par adji sarr .
bamou am ay officiers gendarme et millitaire yousi disparaitre FULBERT SAMBOU et DIDIER BADJI donc de grace fait le nèssèssaire pour que le projet jub jubël jubanti dara bagne ko yakh si leep tè le cas de FALLOU FALL cas bou sensible la boulko woyofal takhaw si dans l urgence s IL te plait parce que diaye dollè lay nirole tè bakhoul si am rèw.merci.mangui dièguelou Sama khòle dafa dièkh 😢tè khamna ni il y a pas Mal de personne you nek si prison yi tè dèfouniou dara 😢😢😢😢et que lolou yowmalkhiyame rek lay lèrr si kanamou souniou Borom billâhi tè dafa.mèti so amoul koala takhawou si say diaffè diaffè.
lèbèrer FALLOU FALL s IL vous plait.
Justice pour fallou fall ❤❤❤❤
Yalla na yalla diappale Fallou, la justice divine
In sha Allah Yalla dinako diapale thi barke Seydina Mohammed SAS amine
Bilahi dinako rethieu niou nékone guinawou adjie sarr nioko eupone dolé foufe. Thé niou dem rek yalla yalla rerale lepp inchalla 😢😢
Vraiment dapres ces temoignages de cette dame fallou est inocent 😭😭
Il faut nguén vilipender homme de tenue bobou 😮😮😮😮
Nagnou khar ba etat dougal si lokhom ba Parè
Faram rek laye done
S'il vous plaît allez chercher la dame et porté plainte rapidement il faut que le médecin sort
Genre yi nio indi reyanteyi
Merci 2À yéna gi défe lingéye bou ame solo❤❤❤❤❤❤❤❤
Justice pour fallou😢 walahi biss la fatima di khaaare Yallah mingui aaté
Machahalla 2Atv 🙏🙏🙏
Je tokhou, tu toukhou, nous tokhouwons, vous tokhouwez, j'aime ces voisins daaallll❤❤❤❤❤
Fallou yalna teguil ko natou té mou nek oubekom si wersek teranga adouna AK alahira
Sa waye boulma dioye lo waye ya bakh barké borom touba. Fallou mo nek si deugeu parceque nioune nieup on se connaît pas té nieup béne wakh bi laniouye wakh free fallou
@serigneamathgueye2886 Kou bakh rek Moy guiss mbaxou way yama guene yalnanu yalla dimbali Fallou khamako mais 😭 guemnani deniou ko togne waye yalla wayam rek lay natou yalnay guenél si mome
Pour meu gueum né problème adji sarr dinegn ko régler, biii degn ko wara régler beu noppi. Maaanam neu médecin bi teudd, neu borom grade bi teudd, neu pape bi teudd, neu diabarou Paa bi teudd. Beu noppi niou fay lou tollok 500 millions minimum Fallou Fall.
Waw léne gor Dieureudieuf na si ñép diapou rék justice pour Fallou
Nama yalla bale deee mo femme bi VS k deff n separation d coro ak dieukeur djii bou Yagüe
BA paré policier nangou nekk si guinawame diko doléle
Geustouléne bou bakh nakh policier bi nekoule diko lale verifier apres nakh Pere bii mo dioure xalé yii cette femme est capable d tt
Le constat est intéressant
Interesant en tt ça elle est capable de tout
Pa bi osi diarna dimbali dé cheuuu
Vraiment
Aimer léne dakh mou yatou 😢
Kana juge bi teudj fallou ,fatima dafa yoré lomotifam😢😢Free Fallou Fall
Fatima Dieng kou démme APR la bock ngni dagno sokhore koi na Sénégal nieuppe diougue niou bayii Fallou Fall 🙏🙏🙏
Franchement 5 ans gua djiap niite teh defoul dou mom teh viol amoussi injustice bobu moma gueneuh meti Fallou dina guen la vérité sera mince et triomphera justice pour Fallou way ❤❤❤
Le chef de quartier est complice
Plus que complice même
Justice pour Fallou Fall c'est trop facile 😢
Justice pour fallou merci l'equipe de 2A ligueni def amna solo
Kou dém wa apr la dh😂😂 bon la niou déf😂😂😂
Doumani déte dé
Xaalat nako déh lou bone rék laniou xam
😂😂😂😂😢
Niom l sakh
😂😂😂😂😂😂😂
Khalé yi séne yaye da bakh mon takh ay pékhém diouboul li 😢😢non ki mon bonn
Justice pour fallou fall yalla na yalla walou
Mane damay dem deuk béd Fass wayyyyy ❤❤❤❤
Li métina torope 😪😪 😪😭😭tout se paye ici bas le bien comme le mal 👍👍👍
Yalla na yalla déf fallou guén si barke seydina Mouhamed psl ❤❤
Sounou justice bi tamite prezi warnasi wakh
Fallou falll yalla defal ko diam
Yalna yalla takhawou falou fall thi barké nabil moustapha psl
Il y a des avocats ils s en fous des droits qu ils leurs intéresse c est l argent dommage pour les africains
Kou defar médicale bii
Très bonne question
vraiment sénégal amoul justice liiiii grawna torope yalla nalene yalla torokhale gni def seine pekhé ba teudjieulou domou diambour yalla naniou yalla mouseul si pekhe noone
On doit arrêter les complices même le père de falou
C'est très très triste mais fallou yalna yalla gueneleu fofou gua nek😢😢😢😢😢😢😢
Juge moo gueneu doukhane ndayame wallahi
Juge bou comnander Fallou 😢
Justice pour fallou barkhé touredome
Guirr Yalla justice pour Fallou Fall 😢😢😢😢😢
Si on creuse bien ay Nittou APR lañou
amoul bayi déh il faut bien appuyer bou diarré marche niou marche
Justice mo amoule Sénégal 😢 En 1996 sama petite sœur leu dale un voisin bignou diakarelo keur gnou mine ko lol sakh 🥺 sama petite sœur mime ko mou kaye fope diko yobe séne keur béne beuse mou indi mais mouye dioye dioye you méti sakh ma nakh ko mais mouye dioye rék ma déme séne keur lathe ko lane mo kéwe nakh daffa danou la mère du voisin ni dioye si néggou dome bi leu wone ma délou wate sougnou keur nak nak mais sougnou wa keur diakhélé ba gnou ko soumé pour khole lane leu silagnou guiss ni puisque mounou ko pénétrer daffa done défe aye frottements ba guagne ko guagne bou méti sakh avec des déchirures gnou déme gendarmerie ame certificat médical avec des photos gendarmerie défe enquête gnou diape ko souma diouboule 2 mois leu défe prison tribunal juge bi leu aye mbokame faye nak dagno ame khalise 😢 ma sœur vie toujours avec les séquelles daffaye saye rék yak adouname ni 😭😭
Justice pour Fallou fall
Mère bi domeram leu Yallana akkha Fallou dalko
Diomay yak sonko yene gni nekone ay victime si justice bou Sénégal gnigui lene Di niane guene rakhass justice bi sénégalais yi yepagui si danger
Adji sarr bariinegnn Senegal deh 😢
La fille de Fatima Dieng n'a rien à voir sur cette histoire mais elle va récolter sur tout les mauvais actions de sa mère
Elle est complice tant qu’elle ne dénonce pas ce coup monté…donc si on rejuge l’affaire elle sera condamnée
Elle est complice pourquoi elle n’a pas dit que c’est pas vrai
Ameth aidara nassi ministre de la justice wakh sii lii doynaa warr
Falou yalla nala yalla tahawou métiiii na trop mais yalla na lép néh lou désss sisa adouna 🥲🙏🏾
Justice pour fallou fall lanio wax amole lenen
Justice pour Fallou Fall ❤❤❤❤❤❤❤
Bilahi walahi talahi sama dioye yima dioye Fatima yalla nala yalla Alak si adouna bi nieupeu diko guise fallou fall yalla nala sa niani yaye walou te dina ameu deh inchahala te ngeune Balema sama khole bi tangeune lole bilahi walahi talahi
Il faut porter plainte au medicin et au policier
L avocat de fallou était le plus incompétent,je vous parle en connaissance de cause,car je m entretenais avec Oumy Fall la grande sœur de Fallou sur ce cas,je lui avais même suggéré de chercher un autre avocat
C'est la vérité
Svp manena ame nmro oumy🙏
Justice pour serigne fallou
Femme bî dama nekh bilaye kouko khole khamni degue rék lay wakh
Ahmed tu es le maire d guediawaye dokh tie wakh tie
Nagne dém Sonatel xoli Apel téléphonique you fatima dieng durent c'est dernier temps et il faut appeler la dame qui dit quelle a trouvé les preuves s'il-vous-plaît la police et les enquêteurs sa c'est une demande nationale ngirr yalla si nous sommes des musulmans et ont vas touse mourir 😢😢😢😢
Fallou fall soudet ligni lay djigne amoul yallna yalla attet si barket werou radiap bi amine yarambi
Yalna yalla atté
Médecin bi ak juse yi ak homme de tenue bi yep ak fatima ak ay témoins yem yeepa wara subir la même peine
Ndeye san Fallou ❤😭
C est vrai on a écouté celuo qui as ecrit la1ere plainte de Falou
Mangui Nianeu si barke Seydina Mouhamed yalla na yalla lerale lepeu te Fatima yalla nala akhou fallou fall daleu ak kepeu koukoye diapale si feneu yi yalla nalene akhou fallou fall daleu amine
Bravo bravo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla nà bour yalla bour bou baakh bi guene fallou ci jame aksi salam
Guisnga bougnou diappaléwoul SONKO AK DIOMAYE 😢 SÉNÉGAL DOU MEUSSEU CHANGER nagnou yénéwanté Diamme❤
Yallah molène eupe dolé Inshaallah lepp dina ler dé
Une pétition nationale et internationale est lancée pour la liberté de Fallou Fall.