Kiné LAM se prononce pour la première fois après la mort de son mari DOGO.

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 107

  • @babacarsene6484
    @babacarsene6484 4 роки тому +30

    Ndeysan kiinè Lam nak bouka deguè mouy wakh sakh kham nii Dafa sentimental Ndeysan ❤️ qu’il repose en paix ✌️ et longue vie à toii ❤️🙏🏽 sama fans bii Ndeysan j’ai des larmes aux yeux néna sama khol bii yobale nako et amatouma Valentin Ndeysan 😓😓😓

  • @shalimar11100
    @shalimar11100 4 роки тому +22

    Maman Kiné une femme exceptionnelle, beaucoup de classe. Toujours fidèle malgré le succès. Une référence pour ces jeunes artistes qui ne font que du buzz au lieu de cultiver le talent. Longue vie à toi la diva
    Mes respects!!!

  • @sokhnathioube9384
    @sokhnathioube9384 4 роки тому +2

    Machallah sama artiste sama nanane kiné lam kou am djité ta mana waye yalla na la yalla défal diam geune laffi yagal ta harey sounou papa dogo aldiana

  • @reinenoire3354
    @reinenoire3354 4 роки тому +9

    Deysane sama yaye rek lay kholé kine lam dakh fonk seye 🙏🕊

  • @badaraka2883
    @badaraka2883 4 роки тому +28

    Une femme exemplaire maman doundal lou barri, dila massaou père Dogo yallah nako yallah haré adiana ci barké serigne Touba mbacké

  • @ndongfatouk7986
    @ndongfatouk7986 4 роки тому +3

    Ndeysan Maman machalah lii diaféna trop surtout ga nek artiste chapeau et bonne continuation

  • @oumousakho849
    @oumousakho849 4 роки тому +2

    Je l'adore tellement, voici des references pour nous 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
    Je te souhaite longue vie et une santé de fer

  • @aidathiam284
    @aidathiam284 4 роки тому +9

    Machallah machallah maman kiné bon courage que Dieu l'accueil dans son paradis

  • @adamengomndiaye4209
    @adamengomndiaye4209 4 роки тому +2

    Machalla une femme exceptionnelle royou kaye thé gore 😘😘😘

  • @diordiakhate7828
    @diordiakhate7828 4 роки тому +38

    Bien dit maman c'est pas que vous êtes une seykate mais c'est parcequ il est un GOR pure un vrai HOMME.

    • @noahdonald3848
      @noahdonald3848 3 роки тому

      I know it's kind of off topic but do anyone know a good site to watch newly released tv shows online?

  • @amysakho8841
    @amysakho8841 4 роки тому +2

    Macahllah Sama yaye Kine Lam wakhe dji rafetna macahllah pa dogo yalnako yalla yeureum te khareko aldiana

  • @akd696
    @akd696 4 роки тому +2

    Kine lam djiguén gueunouko machalla. Dogo aussi kén gueunouko bakh♥️♥️♥️

  • @rokhayasarr3952
    @rokhayasarr3952 4 роки тому +20

    Ndeysan bilahi maman kiné lam dama ko beug nimouy wahei rek ngay khamni dafa sincère genre amour yi esk amatina sah ndeysan💓💓💓🙏🏼yalna yalla yagal tahaway bi nga yag ko gnanal

  • @neneba5469
    @neneba5469 4 роки тому +11

    Une femme de classe une femme exemplaire kene meussoula degue thi Lou niawe comme celles qui font du beuz yalla na sa jam yague

  • @manoumanou3800
    @manoumanou3800 4 роки тому +1

    Maman exemplaire masha Allah courage..goudal fane ainsi que nos mamans Inch Allah si barkei Seydina Mouhamed PSL
    Ton epoux Qu'Allah l'accueil en son paradis insha Allah si barkei Seydina Mouhamed ak mollem dioulit bou ganiou

  • @ndeyeamindoye1150
    @ndeyeamindoye1150 4 роки тому

    Bilahi je taime bcoup maman kine yalla na yalla goudal sa fan barkei yoneti bi waneiga yone bi machalla

  • @assiettoukone8682
    @assiettoukone8682 4 роки тому

    Machallah mane sa borom keur mo takh m'a geune la fonc. Waye dieukeur bou bakh ta thi am solo.

  • @abdoumbaye5382
    @abdoumbaye5382 4 роки тому

    Man sha ALLAH.
    YALLA nama YALLA may Sokhna sou am ngor.

  • @yacinendiaye2050
    @yacinendiaye2050 4 роки тому +1

    Maman goudal machallah référence nga qu'il repose en paix

  • @nafisatoufall4215
    @nafisatoufall4215 4 роки тому +10

    Ndeysane wakhedji amna solo trop machala

  • @deydamintboushabe6174
    @deydamintboushabe6174 4 роки тому +1

    Machallah ya goré yalla na yalla goudeul say fane🙏🙏🙏

  • @awabop5671
    @awabop5671 4 роки тому +9

    Tata kinè yow référence gua que papa repose en paix amin

  • @thiawserignefallou6737
    @thiawserignefallou6737 4 роки тому

    Bilagui kene d’où yaiw rafet khôl ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @salydia4242
    @salydia4242 4 роки тому +5

    Machalla maman magui si boumou seye amna 12ans de mariage Yalla na melni yaw Yalla nassa diam yague

  • @toutyfall9109
    @toutyfall9109 4 роки тому +1

    Ndaysan djiguene na goor goor lou goor yi tamit naniou yeureum djiguene gni diapalé leun niou seuy seuy bou rafet 🙏

  • @maguettembaye6045
    @maguettembaye6045 4 роки тому +4

    Yalla nakho yalla khare aldiana si barkhe xassida yi amine rabi

  • @thiandoumanna6185
    @thiandoumanna6185 4 роки тому

    J'aime Maman Kiné Lam, j'aime ceux qui l'aiment, j'aime ceux qui aiment ces derniers, ainsi de suite...

  • @bijoucaramel6587
    @bijoucaramel6587 4 роки тому +1

    Ndeysane sama yaye lay kholé ki depuis sama papa dem woutoul dieukeur ay domam rek doyna niou ko merci maman

  • @ibrahimadiole3961
    @ibrahimadiole3961 4 роки тому +9

    Que dieu te benisse mere kine lam

  • @maraniang8721
    @maraniang8721 4 роки тому +4

    Maman Aka malla nawe masso xepp sa dieukeur yalla nagua gouda fane

    • @ladivandiaye2230
      @ladivandiaye2230 4 роки тому

      Mouy lou am solo xébaté baxoul kine limou doundou ak djieukeuram kom lolou lay doundou ak sama boss mou takma à l âge de 16 ans magué ma 20 ans kokou xamnga xoloul wone tar si yaw souma xolé samay foto demb ak tay rek ma geuna xamni amna dieukeur djiou bax am sama temps am sama soutoura louma dioxogne mou dague manék xalé boxamni nak soudone bama guimé mani ah nasséti kéneneu kone ma goré di ndax sama dieukeur daffa goré si mane trop plus de 14ans pour ne pas preciser la date exacte meunouma wax sax lépou du matin au soir on communique dou def louma yeugoul té mounana wax xaléla doumaladj xalatam mais mane rek sama xalat doynako mantamite douma tayi si mom ndax il m aime toujours nouké lamay defal pour mom mane rek lawara defal kéneu bokoul diko gnanal goudou fane ak wéreu

    • @ladivandiaye2230
      @ladivandiaye2230 4 роки тому

      Genre yi rek nga meuna gneuw guénéfi sa xol ndax nite yi dagno doywar kougnou xamal gnéla

  • @ayshajuliette
    @ayshajuliette 4 роки тому +30

    Des hommes comme Dogo amatoul sax

  • @adamaseck8816
    @adamaseck8816 4 роки тому

    Machalla yalnako yalla kharé aldiana may kholou mougne yalla yagal lafi inchalla

  • @titiseck3666
    @titiseck3666 4 роки тому +1

    Machaalla maman kiné lam 👌👌🙏🙏🙏🙏👌👌👌😘😘❤❤

  • @mimichou3595
    @mimichou3595 4 роки тому

    Yaa goréé maman, yalnakoo yalla yeureumm té kharékoo aldiana ak mbolemm

  • @mbackesokhnamai183
    @mbackesokhnamai183 4 роки тому +4

    Ndeysan aka diafé ci artiste yii yay goor d

  • @khalifabenmtdiop2440
    @khalifabenmtdiop2440 4 роки тому +3

    Macha allah yalla na père yewodji aldjana

  • @kinendiaye2665
    @kinendiaye2665 4 роки тому +2

    Machala sama toma une grande dame ♥️

  • @sympathisante17
    @sympathisante17 4 роки тому +2

    Paix à son âme. Ma beugueu goor gou am diam ak salam

  • @awabop5671
    @awabop5671 4 роки тому +4

    Quelle MODESTIE ya bakh ya ame reconnaissance machalla

  • @yayoubayamniang5457
    @yayoubayamniang5457 4 роки тому +11

    machalah royouray lah jeune artist war nagn khol siyaw

  • @wouroussngalammbow3096
    @wouroussngalammbow3096 4 роки тому

    Je testime beaucoup a cause de ton amour et respect envers ton mari bravo maman kine

  • @ndiayemouhamed1780
    @ndiayemouhamed1780 4 роки тому

    Machallah maman vous étes bien éduqués ce nous manque wakhal thie kow

  • @bambaseck62
    @bambaseck62 4 роки тому +1

    Beug nit mou fatou dafa metti lool mais dé nak mooy deug maman kiné yalla nala yalla takhawou

  • @fatoudiop7350
    @fatoudiop7350 4 роки тому +9

    C'est un peu triste ma sœur yalla nala yalla may tako bouleu wéteuli cou goré nga lam

    • @babacarsene6484
      @babacarsene6484 4 роки тому +2

      Fatou Diop néna paréna sii seye louy doy doyna🤗🤗

  • @mordiongue3145
    @mordiongue3145 4 роки тому +6

    Longue vie à toi Adja kiné lam

  • @abybathily8221
    @abybathily8221 4 роки тому +1

    Machala warnènou royy thi yenn paix à son âme

  • @yayoubayamediaw7272
    @yayoubayamediaw7272 4 роки тому +5

    Maman kiné lam man damala beug rék ta yalla takh souma sagnon amsa numéro sa borom keur papa dogo nak dankoy niaanal yalla kharé ko alfianay firdawsi bidiahi saydil oudioudi

  • @maremefall3489
    @maremefall3489 4 роки тому +1

    Machallah yaye boye yalle nala yalla maye goude fane

  • @amadouourydiallo4381
    @amadouourydiallo4381 4 роки тому +1

    Machalla Alhamdoulilla

  • @tyfadieng3888
    @tyfadieng3888 4 роки тому

    Machallah rafétna

  • @cheikhmar5853
    @cheikhmar5853 4 роки тому +10

    Machallah rafetna trop quel exemple

  • @aidadiop8591
    @aidadiop8591 4 роки тому +1

    Maman kiné je t'aime beaucoup

  • @ndeyfatoundiaye9500
    @ndeyfatoundiaye9500 4 роки тому

    Ndeyssane maman kiné rip père dogo amine

  • @amykone6468
    @amykone6468 4 роки тому +3

    Bilay maman kine lam mo goré mashallah

  • @khadimseck5985
    @khadimseck5985 4 роки тому +1

    Machaalah mama kine lam

  • @faa5452
    @faa5452 4 роки тому +2

    mane dé si yaw lay roye ak sayaye yalla bayima ak Sama amore ba aldiana ay référence ngéne

  • @amydieng9260
    @amydieng9260 4 роки тому +1

    Machahalla maman❤️

  • @mbayendiaye3455
    @mbayendiaye3455 4 роки тому

    Yalna yala goudal sa fane

  • @zinebdiouf6314
    @zinebdiouf6314 4 роки тому +1

    Machallah❤️❤️❤️❤️

  • @goudiabyoumar7917
    @goudiabyoumar7917 4 роки тому

    Manchal Allah

  • @assiatoutalibeserignmousta6364
    @assiatoutalibeserignmousta6364 4 роки тому +2

    Machalah

  • @codeteuw4151
    @codeteuw4151 4 роки тому +3

    Billahi maman kine lame mako beug djiguene bou beug lou bakh te beug seuy dagnay roy thi niom❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @diorgueyediop9596
    @diorgueyediop9596 4 роки тому +1

    Un parfait exemple pour tt femme mariée

  • @ndattendiaye9737
    @ndattendiaye9737 4 роки тому

    Maman kiné mala beug walahi azim si yaw lay roy si sama sey

  • @dextersndiaye9693
    @dextersndiaye9693 4 роки тому +2

    Ndeysane yaw lo WAKH deugue la.yalnala yala lafal thiate

  • @ramataka595
    @ramataka595 4 роки тому

    Macha allah reference gua

  • @mameboyediaw7758
    @mameboyediaw7758 4 роки тому

    Repose en paix

  • @ahmedndiaye3663
    @ahmedndiaye3663 4 роки тому +4

    manchala ma ma une vraie référence

  • @bambasene1529
    @bambasene1529 4 роки тому +6

    Thieuy sama yay dji

  • @famacisse1780
    @famacisse1780 4 роки тому

    Goor rekk mo mann lii

  • @awatouba6057
    @awatouba6057 4 роки тому +1

    Manchala sama yaydji yaw ngoor si sa derette la nek yaYE seutou DEMEURONE BOROM JAMYI MANDELA NDELA NDIAYE

  • @alioufaye2966
    @alioufaye2966 4 роки тому +2

    Ma bakh yaye sama yaye kine lam ma bekh man sa dôme bou la bègue la

  • @adjasylla4691
    @adjasylla4691 4 роки тому

    Gorrrre degue gua yaye

  • @adykebe5833
    @adykebe5833 4 роки тому +1

    ♥️♥️♥️♥️♥️

  • @seynaboumbaye6873
    @seynaboumbaye6873 4 роки тому +2

    Merbi aka gore

  • @aloudia4180
    @aloudia4180 4 роки тому +2

    Waye jigene ñii la wara mèle

  • @aloudia4180
    @aloudia4180 4 роки тому +2

    Yawe Boula halyèpou royone seye yèpou nèhe

  • @cheikhdiop963
    @cheikhdiop963 4 роки тому +1

    Nday san ya bakh way

  • @titiseck3666
    @titiseck3666 4 роки тому

    👌👌👌🙏🙏😘😘

  • @lotagaye4354
    @lotagaye4354 4 роки тому +1

    Maman kine mala begue bilahi yaw doundal lou bari

  • @dembakharagnelo2379
    @dembakharagnelo2379 4 роки тому +3

    Ndeysan sama mere bi aka mako beug

  • @lindabiya5631
    @lindabiya5631 4 роки тому +1

    ♥️♥️♥️🙏🙏♥️♥️

  • @bellebrunediaw1155
    @bellebrunediaw1155 4 роки тому

    Son mari est mort depuis quand?

  • @سميرهالسعدون
    @سميرهالسعدون 4 роки тому

    😭❤❤❤😍

  • @couragning6979
    @couragning6979 4 роки тому +2

    Machalla❤

  • @maabdouka3247
    @maabdouka3247 4 роки тому +2

    Machallan

  • @antichediallo3683
    @antichediallo3683 4 роки тому +2

    Machallah

  • @fatoudieng4376
    @fatoudieng4376 4 роки тому

    Machallah