M&urtre de Codou à Ngor "kiko raye avoué na affaire sexe moléne bolé.." révélation de Pape Ndiaye

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 1 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 215

  • @oumygueye6416
    @oumygueye6416 2 місяці тому +52

    Yalla Naniou yalla Doli soutoureu adina ak alahira thi barké nabil moustapha

    • @MouninaKounta
      @MouninaKounta 2 місяці тому +3

      Amin ya rabi

    • @Le_Natron_
      @Le_Natron_ 2 місяці тому +3

      Té parents yi yaar sëni doom 😮
      Thiagatou rekk nos sœurs là😢

    • @oumygueye6416
      @oumygueye6416 2 місяці тому +1

      @@Le_Natron_ bilay doyna warr dall

  • @ndawbouna2675
    @ndawbouna2675 2 місяці тому +32

    Yalnako yeureum té djegueulko ay bakaram té mousseul niou nioun nieup ci barké Rasûlullâh saws

  • @loaboubacar3595
    @loaboubacar3595 2 місяці тому +76

    Yalna gnou yalla doli soutoure 😢😢

    • @MouninaKounta
      @MouninaKounta 2 місяці тому +1

      Amin ya rabi

    • @tantytoulaye560
      @tantytoulaye560 2 місяці тому

      Alahou akbar yalana yala doli soutoureu yala moléneu weer fi ndialo ba gueneu thi aduna

  • @diadiadiallo5033
    @diadiadiallo5033 2 місяці тому +33

    Lii doyna waar diii😢😢😢😢 yalla n'a gnou yalla dolli soutoura 😢😢😢

  • @kenzaandoye2590
    @kenzaandoye2590 2 місяці тому +83

    Ndeysanne Yeurmandé Yalla amoul limite Yalnako Borom bi yeureum diègueul ko té kharéko Aldiana Firdaws 🙏

    • @AidaSoumare-el5be
      @AidaSoumare-el5be 2 місяці тому +7

      Amin inch'Allah

    • @fatouthiam6962
      @fatouthiam6962 2 місяці тому +3

      Allahouma Amiiiiiiine ❤

    • @bamba5370
      @bamba5370 2 місяці тому +2

      Amin ya Allah 🤲🏾

    • @AïssataSow-h2i
      @AïssataSow-h2i 2 місяці тому +2

      Alahouma amine 🤲🤲

    • @Le_Natron_
      @Le_Natron_ 2 місяці тому +1

      Té parents yi yaar sëni doom 😮
      Thiagatou rekk nos sœurs là😢

  • @BassirouFaye-b8w
    @BassirouFaye-b8w 2 місяці тому +38

    Yalla nagnou yalla soutoural biss bougnou faatoo ak bi gniy dounde. Ohhh soutoureu 😢😢😢

  • @ouleyesidibe393
    @ouleyesidibe393 2 місяці тому +22

    Soubkhanalah qu’Allah l’accorde sa miséricorde. Elle a même pas eu le temps de faire le dianaba.

  • @sokhnadiop5172
    @sokhnadiop5172 2 місяці тому +49

    Yalla nagnou yalla sounou borom samou ar gnou soutoural gnou té tek gnou si yonou dioup. Amine 🤲

  • @baloutadanso
    @baloutadanso 2 місяці тому +25

    La illaha illallah seyidina Muhammad rassulullahi salallahou alayhi wa salam Allahou Akbar qu'Allah nous facilite le paradis Amin'allah qu'Allah nous accorde sa grâce et sa miséricorde Amin'allah qu'Allah nous accorde une bonne fin de vie Amin'allah qu'Allah aide le peuple Palestinien Amin'allah qu'Allah met la baraka dans notre vie

  • @Malicksindidi1988
    @Malicksindidi1988 2 місяці тому +34

    Dangay sétt li louko gëneuh niaw topp yalla si bopam laniou waara déf té baayi diiko mooy

  • @mariesambou3430
    @mariesambou3430 2 місяці тому +18

    Yallah n'a niou yallah maye moudiou gou raféte Amine yarabi

  • @bayesalioufall7838
    @bayesalioufall7838 2 місяці тому +28

    Bravo équipe walfo TV sa kaw sa kanam rek inchallah barkep Serigne bi❤❤❤❤❤❤

  • @bouwally3702
    @bouwally3702 2 місяці тому +5

    Ya allah soutoura douneya wa allahira😢😢😢paix à son âme 🙏😭😭

  • @diordieng3931
    @diordieng3931 2 місяці тому +15

    Yalnanou sunu boroom soutoural adina ak alakhira

  • @SD-ih6bz
    @SD-ih6bz 2 місяці тому +19

    Lahi lakha illa lah Mokhamadarah Souroulah 😮saw. Allaah 😮

  • @seckdoudou8431
    @seckdoudou8431 2 місяці тому +18

    Vous êtes très pertinent machallah

  • @fatouthiam6962
    @fatouthiam6962 2 місяці тому +12

    Yalnako y'Allah yereume diéguelko té kharaiko Aldiana firdawsi ak gni djitou gneupe thi barké Seydouna Muhammed Saws ❤

  • @myriamdiaw7497
    @myriamdiaw7497 2 місяці тому +10

    Yalla nanou yalla doli soutoura adouna ak alahira may nou moudje bou rafet thi barcke seydina Mouhamed

  • @kharycisse5267
    @kharycisse5267 2 місяці тому +13

    Yalla nagnou yalla mouseul si pauvreté métina yalla nako yalla yereum

  • @binetasakho3593
    @binetasakho3593 2 місяці тому +10

    Yallah na SWT atté si yeurmandéme 😢😢😢😢

  • @bayesalioufall7838
    @bayesalioufall7838 2 місяці тому +21

    Sénégal yalla nafi diamou yagui barkep Serigne bi❤❤❤❤

  • @bayesalioufall7838
    @bayesalioufall7838 2 місяці тому +15

    Thiey yalla vraiment doyna warr dh bilay😭😭😭😭

  • @patriote-v5z
    @patriote-v5z 2 місяці тому +6

    BUUR YALLA MOOY JEGALAAKON BU MAK BI, AMNAKO, SAGN NAKO, YALLANAKO YALLA JEGAL, BIJAAYI NABIL MUSTAFAA ALEYI SALAAM.

  • @aissatougassama3876
    @aissatougassama3876 2 місяці тому +2

    Yalla naniou yalla may moudiou gou rafet ak yonou dioup té Codou yalla nako yalla yeureum

  • @Madamemmedia
    @Madamemmedia 2 місяці тому +8

    Bayilene moy té soralé bisss bi 😢

  • @massgueye5313
    @massgueye5313 2 місяці тому +4

    Non sarap lii Sénégal dal légui amatoul soutoura même bo déwwé ohhhhh

  • @salioumbaye2479
    @salioumbaye2479 2 місяці тому +1

    Allou akbar yalla nako yalla até cii yeurmandém 🙏😭

  • @kebabayo5237
    @kebabayo5237 2 місяці тому +4

    Manchalla pape Ndiaye rafetna

  • @binetoudiop182
    @binetoudiop182 2 місяці тому +1

    Merci beaucoup frère, je ne savais pas que l’autopsie se passe comme ça.que son âme repose en paix 🪦

  • @AidaSarr-q8w
    @AidaSarr-q8w 2 місяці тому +8

    Ayewaye soutoura diguene la😢😢

  • @maremediallo3053
    @maremediallo3053 2 місяці тому +1

    Yalla nako yalla yeureum aye reuth reuthiam thi barké nabi nagni deuk AK sougnou famille

  • @patydieme7350
    @patydieme7350 2 місяці тому +8

    Surtout ici à Mbour, il y a beaucoup de nationalités qui fait ça. C’est triste pour mon pays😢😢😢😢

  • @dialibatoumarahib79
    @dialibatoumarahib79 2 місяці тому +10

    Sénégal daall yahouna yaheett wayee kou Fatou ba pare deskoy soutiurall

  • @HafidaSeyad
    @HafidaSeyad 2 місяці тому +10

    Ayway 😭😭😭😭

  • @loudoulaktalibesafouma3429
    @loudoulaktalibesafouma3429 2 місяці тому +3

    motax lou way bagne dé fék ko thia nako bayi serigne sam mbay néna nit ki nimou done doundé rk nonou lay fato 😢😢 lou ay mbokam di wax😢

  • @AdamaGadiaga-j6t
    @AdamaGadiaga-j6t 2 місяці тому +8

    Yalla n'a aledjana di keureume yalla boumoretiou dara si adouna

  • @ThiernoMbow-b4x
    @ThiernoMbow-b4x 2 місяці тому +4

    Ndaysane yalla nako yalla yeurem 😢te khare ko aldiana firdaw si

  • @taphafall14
    @taphafall14 2 місяці тому +19

    Les filles nagouwounio seuye mba paré beugue dounde luxe et puis beugue lou yombe. C'est regrettable nioussi beuri danio tasse diogué si region yi nieuw dakar dougue si milieu bi.

    • @loaboubacar3595
      @loaboubacar3595 2 місяці тому +5

      Lou leer frr surtout gni diougue si village yi😢😢

    • @maguettediongue8836
      @maguettediongue8836 2 місяці тому +3

      Bilahi tu as raison diougué si région yii gneuw dk nék si lou bone lii rék layyy andi

    • @MarieGomis-ks8so
      @MarieGomis-ks8so 2 місяці тому +2

      Ce n'est pas toutes les filles

    • @Zam-Zam710
      @Zam-Zam710 2 місяці тому

      Bilahi walahi waxatiko en connaissance de cause nak

  • @moctartv3669
    @moctartv3669 2 місяці тому +6

    Soubhanallah

  • @soukeynaconare8824
    @soukeynaconare8824 2 місяці тому +6

    Hé Allah yalla nagnou maye moudie u bou rafet.j'espère que qu'il n'est pas marié am ndiaboot rek.

  • @khalyniang518
    @khalyniang518 2 місяці тому +8

    Ndiaye missill wakhna kham kham dh alhou akbar machall lah😅

    • @OusmaneMarega-sl2zn
      @OusmaneMarega-sl2zn 2 місяці тому +2

      Mogui dorer ay missile nucléaire déé 😂😂😂😂😂😂😂

  • @labbajop-nl4cm
    @labbajop-nl4cm 2 місяці тому +9

    Le plus vieux métier du monde, conduit dans beaucoup de cas, à la d'échéance et souvent à la mort.

  • @modouniass8663
    @modouniass8663 2 місяці тому +17

    لا حول ولا قوه الا بالله العلي العظيم

  • @Ousmanyatassaye
    @Ousmanyatassaye 2 місяці тому +13

    J'aime bien ce journaliste d'investigation. ça se voit qu'il connaît très bien son sujet.
    Bravo 🙏🏿
    Une pensée pour la dame assassinée ..

  • @bachirndiaye4384
    @bachirndiaye4384 2 місяці тому +6

    Waye si kou niaff Ndeyam la 😢😢

  • @aissatousylla4172
    @aissatousylla4172 2 місяці тому +3

    Allakhou akbar yalna YALLA atté si yeurmeundéme yalco YALLA yeureum si barké SEYDINA MOUHAMED S.A.W amiiine amiiine amiiine

  • @YayeAwaGUEYE-ci2hx
    @YayeAwaGUEYE-ci2hx 2 місяці тому +19

    Thiaga bou pertoul sakh dafa amoul nak. Yalnaniou Yallah khiir thi boppamm

    • @NdayefatouNiass-y6i
      @NdayefatouNiass-y6i 2 місяці тому

      Amine yarabi

    • @Le_Natron_
      @Le_Natron_ 2 місяці тому +2

      Té parents yi yaar sëni doom 😮
      Thiagatou rekk nos sœurs là😢

    • @mamadoundiaye684
      @mamadoundiaye684 2 місяці тому

      ​@@Le_Natron_mai aussi ce sont nos frères qui leurs engagent car nos sœurs ne peuvent pas faire la prostitution sans garçon

    • @Le_Natron_
      @Le_Natron_ 2 місяці тому +1

      @@mamadoundiaye684 on a tjrs le choix de vendre sa « marchandise » ou pas

    • @YayeAwaGUEYE-ci2hx
      @YayeAwaGUEYE-ci2hx 2 місяці тому +1

      @@Le_Natron_ deugg rek nga wakh. Lithi ndigg goor walahi djigouthi jiguéne. Nioune nio wara khame sougnou boppe. Sama yaye bignou nékké khalé elle ne ratait aucune occasion pour rappeler la yaw yaye Kane AK limouy khaar thi yaw mais walahi c'est la meilleure méthode. Ba bo wété sa khél thi môme rek lay nékk. Eduquons nos enfants tay communiquer AK niome. On est 4 soeur mais machallah niéppa diare thi yone bimou beugone

  • @PapeDiego-jb7cq
    @PapeDiego-jb7cq 2 місяці тому +11

    Pape ndiaye du respect pour les morts yen yi waro si delou khalatal k la femme a de la famille soutoural adji Fatou ki

  • @papefall9266
    @papefall9266 2 місяці тому +14

    Vêtements li doynawar diaysa bop tamit lolou l'an mo si wara ndougal nit😢😢

    • @ibromeo9682
      @ibromeo9682 2 місяці тому +2

      ell a trois enfants a nourir et etait extremement pauvre ,elle habite a pout

    • @user-vibf6ji2n.
      @user-vibf6ji2n. 2 місяці тому

      ​@@ibromeo9682 lolou waroul takh mouy diay bopam . Ay ligueye you bari gno nguifi youm meuna def .

    • @AbdouDiagne-gg3dt
      @AbdouDiagne-gg3dt 2 місяці тому

      ​@@ibromeo9682lernama ay hors jeu la motah niou wara teyé sen bopou ba am dieukeur so pauvré da ngay kham sa bopou

  • @zeynadiop7136
    @zeynadiop7136 2 місяці тому +5

    Wadji dé Dina nameu danou diga gueuna khogne qu'elle repose en paix

  • @adoadam-t1r
    @adoadam-t1r 2 місяці тому

    qu'Allah nous donne une bonne fin

  • @aliounembengue1205
    @aliounembengue1205 2 місяці тому +2

    Yalnako yalla yeureum té diégeulko

  • @mouhamadoudia9291
    @mouhamadoudia9291 2 місяці тому

    Ndeysane meetina yalla nako yalla atte si yeurmandem koude de werou

  • @OusmaneMarega-sl2zn
    @OusmaneMarega-sl2zn 2 місяці тому +6

    Paix à son âme vraiment lii métina trop 😢😢😢😢😢😢

  • @bourguibafaye8521
    @bourguibafaye8521 2 місяці тому +3

    Yalla nagnou yalla maye moudieu bou rafète

  • @MatySow-nu9jw
    @MatySow-nu9jw 2 місяці тому

    Yalla nako yalla yeureume

  • @khadimehann-1793
    @khadimehann-1793 2 місяці тому

    Yalla nako sunu borom dooli yeurmand 🙏🙏🙏

  • @khadimdiop3348
    @khadimdiop3348 2 місяці тому

    Hiîiii yalla nanou yalla sotaral

  • @elhadjimamadouthioye217
    @elhadjimamadouthioye217 2 місяці тому +1

    Thiéye danou😢😢😢😢

  • @mamadoundiaye1724
    @mamadoundiaye1724 2 місяці тому +3

    Autopsie gnikaydef ñiom louñioudone ay deum wala ay boucher lahamla walakhawati bisimila yalla bouko féké

  • @barisodalton4198
    @barisodalton4198 2 місяці тому +2

    Paix à son âme

  • @SokhnarokiaDiallo
    @SokhnarokiaDiallo 2 місяці тому +1

    Ak mixta a côté de stade Léopold ya des appartement im

    • @SokhnarokiaDiallo
      @SokhnarokiaDiallo 2 місяці тому +1

      Toujours ya des problème toujours police viens la ba

  • @muhammedsamba4294
    @muhammedsamba4294 2 місяці тому

    Yalnako Yàlla yërëm te xareeko aljannah firdaws
    Yalnanu Yàlla may mucc gu rafet

  • @Mamzmebousso
    @Mamzmebousso 2 місяці тому

    Journaliste bi sa wax yiw na.❤❤

  • @jamadeswizz4864
    @jamadeswizz4864 2 місяці тому

    Paix à son âmes 😢
    Souss di vody do guawa danou teksi ay khèrr sadik rk guay deff !

  • @madiaouDiopDiop
    @madiaouDiopDiop 2 місяці тому

    Thiaga rek 😢😢😢

  • @ahmadoutoure1968
    @ahmadoutoure1968 2 місяці тому

    Vraiment c'est triste

  • @awadiagne3184
    @awadiagne3184 2 місяці тому

    Yalla nagnou yalla may moudiou bou raféte

  • @loaboubacar3595
    @loaboubacar3595 2 місяці тому +5

    7 localité k tu dit c kedougou ya beaucoup de prostituées nigérienne 😮😮

  • @mbayesembene6153
    @mbayesembene6153 2 місяці тому

    Papa Ndiaye ligua wakh tey niawna. Un peu de respect pour la mémoire de la défunte et sa famille

  • @alimoudiallo9392
    @alimoudiallo9392 2 місяці тому +3

    Pourquoi toujours étranger la victimes e sénégalais le client e sénégalais

  • @amadouba4254
    @amadouba4254 2 місяці тому

    Yalla naniou yalla doli soutoureu

  • @louloutebi
    @louloutebi 2 місяці тому

    Détails yi aussi diarou ko un peu de respect pour la défunte 😢

  • @AbdouDiagne-gg3dt
    @AbdouDiagne-gg3dt 2 місяці тому +1

    Ki mo fess lé rek mais milieu thiaga mom chaque jour nga degg fa genre yi wala ay blessé you graw li laniou wara interdit si Sénégal surtout étrangère yi nieuw thiagatou rek laniou neké Sénégal même senn étudiante yi

  • @khalyniang518
    @khalyniang518 2 місяці тому +1

    Nigeria dh berinafi

  • @Patriote.440
    @Patriote.440 2 місяці тому

    Saint Louis numéro 1

  • @AwaNgom-b1j
    @AwaNgom-b1j 2 місяці тому +1

    Pap ammal soutoura Ki DafA àm Domm

  • @Mamzmebousso
    @Mamzmebousso 2 місяці тому +1

    Yal nanu Yàlla may mujj gu raffet.

  • @DamNiang-y7q
    @DamNiang-y7q 2 місяці тому +2

    😢😢😢😢😢😢❤❤❤❤❤❤

  • @mamadoudiop1105
    @mamadoudiop1105 2 місяці тому

    Yala nako yala yeureum yala naniu yala museul si dee bu niaw te tek niu si yonu siratal moustakhim

  • @AstouThiam-i9b
    @AstouThiam-i9b 2 місяці тому +9

    Pape Ndiaye kou Bone gua soutoura amo KO djigene mola diour je la connais pas mai defa meti

  • @habymamadousakho7815
    @habymamadousakho7815 2 місяці тому +1

    Njeud téléphone si mbedd tamit lou diarra bayyi xél la

  • @mamadoundiaye1724
    @mamadoundiaye1724 2 місяці тому +2

    Koldat

  • @dinodiouf4372
    @dinodiouf4372 2 місяці тому +2

    Ken defoul ken dra louway def sabop yala nako yala yeureum ko diegeul ko adouna do keur djiguen youkoy def gur dieum yala bayilen doylo yala werou si yala douguen doundou normal sens moye yala

  • @mohamedsarr908
    @mohamedsarr908 2 місяці тому +2

    La plupart des filles habite à Thiès ? Et la banlieue
    Je ne c pas pourkoi

    • @walyfaye4959
      @walyfaye4959 2 місяці тому

      Tu connais le milieu d, t'as parfaitement raison

  • @SireKa-b5l
    @SireKa-b5l 2 місяці тому

    Soutoura soutoura dara mbir mi Moy ragal len Yalla

  • @diouldesow7604
    @diouldesow7604 2 місяці тому

    Yalle nako yalle yeureum kharaiko adiana

  • @MaguetteFaye-k6z
    @MaguetteFaye-k6z 2 місяці тому +1

    Regione bi thies la

  • @AwaNgom-b1j
    @AwaNgom-b1j 2 місяці тому

    Pap Bla nga dey Doff

    • @louloutebi
      @louloutebi 2 місяці тому

      😂😂😂😂😂

  • @AwaNgom-b1j
    @AwaNgom-b1j 2 місяці тому

    Sedd leen ay dommage ngir yalla

  • @ibucisse3606
    @ibucisse3606 2 місяці тому +2

    Ce langage thiaguou diou perte mõm Doynawar 😢

    • @oumoumbacke3712
      @oumoumbacke3712 2 місяці тому +4

      Dafa dioum rek niouy djiguéne gni nio wara xolatte sougnou bopp

  • @Diija02
    @Diija02 2 місяці тому

    Nooon police Sénégal wala gendarmerie kouko khamoul Lou way nekh defal humm ayyyye laniou deff

  • @YacineMbaye-c9z
    @YacineMbaye-c9z 2 місяці тому

    😢😢😢😢

  • @mansourdiouf3605
    @mansourdiouf3605 2 місяці тому

    Pour rappel le rein pèse 300g

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 2 місяці тому +2

    Yen niui nan kou dee dagnko wara soutoural
    Soutourallen sen bopou ba pare.hamguenne ki ay mdokam douniouko deudieul.wala niom hamonnaniouko noppi moulendi yonne?

    • @NdayefatouNiass-y6i
      @NdayefatouNiass-y6i 2 місяці тому +1

      Bilahi deguela

    • @elagegueye3310
      @elagegueye3310 2 місяці тому

      @@NdayefatouNiass-y6i yalla dafniui allerte chaque munit

    • @elagegueye3310
      @elagegueye3310 2 місяці тому

      @@NdayefatouNiass-y6i esq ay penrawam hamouniouko sah bsyiko molendi yonne

  • @AwaNgom-b1j
    @AwaNgom-b1j 2 місяці тому

    Pap kou Niapp sa Ndey Nga

  • @sambatorino8115
    @sambatorino8115 2 місяці тому +4

    Khamone nani problème mou data molène boler tieye data tasse na rewe mi

    • @MyaDiop-x2m
      @MyaDiop-x2m 2 місяці тому

      Sa wakh gniaw na

    • @Cheikh-mk1mm
      @Cheikh-mk1mm 2 місяці тому

      MOY RAY 80 PERSONNES SÉNÉGAL. TÉ TAY KOKOU MOO NÉK PM SÉNÉGAL

  • @RawaneNiang-s6p
    @RawaneNiang-s6p 2 місяці тому

    Pap ndiay xam xam lay wakh

  • @hawaly8763
    @hawaly8763 2 місяці тому

    Loi bou bonela il faut enlevé ça

  • @serignelo79
    @serignelo79 2 місяці тому +3

    Yaw pape Ndiaye yaw do journaliste ça ne se dit pas yaw si ces ta soeur ou ta tante ou ta fille tu va pas dire de se las