Le coup a été bel et bien prémédité Nabou n'avait pas le droit d'envoyer qui que se soit pour corriger Aziz Aziz dou xaalé ba gnou kéy khouxal Si Nabou n'avait pas envoyé, il n'y aura pas de double meurtre Pourquoi envoyé des gens pour corriger Aziz Nabou foumou KO Tékkk Bann autorité Là am pour envoyer un Gang chez Aziz LoLou yébaté DEUG Leu Nabou dafa yéb Aziz sur ce point. C'est une affaire de double meurtre, alors que la justice soit faite
Pour ton information pape mbaaye dou pape médina je confirme ndakh pape médina guéneu na ba def live il ou elle khawma teint noire le niol nioul niawe je l’ai vu dou pape mbaaye 👍
Yen bayilen Cheikh Omar Diange molen geun fouff Senegal loutakh ngeun nafekh mountakha mbacke mi wakhne yawmal khiyam dafay rombou Yallah ak Yonente bi S A W lolou mogeuna garaw ndakh julit yep la togn te yen nieup ken defousi debat
Fi ngeun tek sen kilifa tarikha yi yegounioufa seringe touba eladj malick ak sen yenen kilifa tarikha yi yep ay nit kese laniou te Yallah yoniwoulen douniou Yonente douniou dara yen dof yi laniouy nakh rek
❤❤Vive nos xalif général du Sénégal ❤
Manchalla àmatina solllo djimbori
Merci Djmbori
Salam Salam merci djimbory sama sope la ❤❤❤❤❤❤
Macha Allah jimb,
djimboro 🙏🙏🙏🙏🙏🙏💪
bi macky sall di ray imame ndaw fou khalife général yi nékon omar mo tay limou wax deug la
Le coup a été bel et bien prémédité
Nabou n'avait pas le droit d'envoyer qui que se soit pour corriger Aziz
Aziz dou xaalé ba gnou kéy khouxal
Si Nabou n'avait pas envoyé, il n'y aura pas de double meurtre
Pourquoi envoyé des gens pour corriger Aziz
Nabou foumou KO Tékkk
Bann autorité Là am pour envoyer un Gang chez Aziz
LoLou yébaté DEUG Leu
Nabou dafa yéb Aziz sur ce point.
C'est une affaire de double meurtre, alors que la justice soit faite
Pour ton information pape mbaaye dou pape médina je confirme ndakh pape médina guéneu na ba def live il ou elle khawma teint noire le niol nioul niawe je l’ai vu dou pape mbaaye 👍
Bilay na
Yen bayilen Cheikh Omar Diange molen geun fouff Senegal loutakh ngeun nafekh mountakha mbacke mi wakhne yawmal khiyam dafay rombou Yallah ak Yonente bi S A W lolou mogeuna garaw ndakh julit yep la togn te yen nieup ken defousi debat
Real he is real
Fi ngeun tek sen kilifa tarikha yi yegounioufa seringe touba eladj malick ak sen yenen kilifa tarikha yi yep ay nit kese laniou te Yallah yoniwoulen douniou Yonente douniou dara yen dof yi laniouy nakh rek
Fenn rek demal lugeuye bayi dague ay nit amal foula bayi thiakhan toyal khogn fenn rek
Kon yenentebi psl lanmo tah niou gueneeko maka? Demal diagi
Ki amoul kham kham bilahi
Lolou dal Moy deug dafa togne
Yaw dadoûn sa bokk rekk yenako juger tè atègougnu
Problèmou nabou lèye xana dagga thia bok