NGAGNE SÉNE porte plainte contre OBEULY DIOFIOR convoqué à la GENDARMERIE de FIMELA 05 février 2025

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 10 лют 2025

КОМЕНТАРІ •

  • @AmadouBa-l3j
    @AmadouBa-l3j 5 днів тому +15

    Vraiment seytani mo nieuw rék mais yalna yalla raffetal lèpp inchallah

  • @VieuxNdiaye-z2u
    @VieuxNdiaye-z2u 5 днів тому +10

    Man ngagne lay siporté mai ibou da dioum yalla bakhna boumcadalati

  • @SerigneFaye-n4o
    @SerigneFaye-n4o 5 днів тому +5

    Merci beaucoup Ngange

  • @AlieuDrammeh-gk5ev
    @AlieuDrammeh-gk5ev 5 днів тому +7

    Da dioum rek balko yen ngeup ay serere ngene 🎉

  • @BayouBayKarimDIOP
    @BayouBayKarimDIOP 5 днів тому +4

    Merci bcp Ngagne topouko bamou seuss.
    Ibou NDIAYE Dafa con

  • @ablayethiaw8018
    @ablayethiaw8018 4 дні тому +2

    Ibou doit être condamné,que justice soit faite pour cela ne se reproduise plus

  • @tamsirsene6204
    @tamsirsene6204 4 дні тому +3

    Sénégal li moko yahk boko rayonne mo pèrte bayilène nafehk

  • @BayouBayKarimDIOP
    @BayouBayKarimDIOP 5 днів тому +4

    Ngagne devrait faire une citation directe, porte plainte au tribunal.
    Ibou NDIAYE DOFLA

  • @MamadouLamineNdour-f5i
    @MamadouLamineNdour-f5i 5 днів тому +7

    Mame Saly liguéy bi raféte na trop
    Réconciliation nice neu❤

  • @senesaliou4198
    @senesaliou4198 5 днів тому +8

    Naniou bayii thiakhann Ibou amoul problème souko diamonnn nak après guénn di wakh khodékou balagua laklé limou deff dou yonnn bakanne da fort
    IBOU il doit revoir son esprit de sportif histoire Bii d’à yague

  • @MouhamadouSadmeyeTINE
    @MouhamadouSadmeyeTINE 5 днів тому +9

    Li amoul négocier Boko reyone ey bokam niouy perte yone na def liguéyam Cng aussi n'a def ligueyam

  • @salioundong7303
    @salioundong7303 5 днів тому +4

    Plainte très bien réfléchie sport amoul rey nit ag xarou
    Tentatives de meurtre en plus Menace de mort
    Bakenn dou fo
    Personne n'a le droit de provoquer sa mort ainsi que celle d'une autre personne
    Thiakhann faaxe

  • @ZEUMBOY1420TV
    @ZEUMBOY1420TV 4 дні тому

    Ngagne il faut retirer la plainte ndeysane il ne va plus le faire on est tous des digne sérére

  • @CoumbaFaye-dd8kf
    @CoumbaFaye-dd8kf 4 дні тому

    Accompagner mbeur mooy li gueuna yees chi goor😂😂

  • @lerendez-vousdesscientifiq7777
    @lerendez-vousdesscientifiq7777 5 днів тому +7

    Le sikampagne de ibou Ndiaye qui disait lors du partage des bœufs qui la lutte n'est pas destinée aux gens de ndiaganiaw et niome nion eupe dolé, guena violents et plus mystiques, il faut l'interroger
    Défa yabaté
    Pareil pour ibou Ndiaye da rew

  • @Domounguerigne-DJ-ZIKO
    @Domounguerigne-DJ-ZIKO 5 днів тому +6

    Comme cng dafa farr plainte rek mofi seuss

  • @MansourlatyrNdour-j2f
    @MansourlatyrNdour-j2f 5 днів тому +3

    C bien fait on dernière gagne sene

  • @mamadoudiouf9911
    @mamadoudiouf9911 5 днів тому +4

    Vous qui accompagne les lutteurs vous êtes responsables de tout, restez à votre place

    • @WoulatewFaye
      @WoulatewFaye 5 днів тому

      Bilakhi gnoy diakhasé mbeur yi dé

  • @fackawngom7751
    @fackawngom7751 5 днів тому +9

    Ngagne do touss li yaguena sii lamb..figua dor petit sélé sagua Paul menthe ndéye diofior bounou sonale...2014mbissane ndione contre bamné Thiomby thiow am mbissane guéné bédiene tahaw ba lamb bii fala diar todjii

    • @DrKhDG
      @DrKhDG 5 днів тому +2

      Yaw ya nekoul touss

    • @alinesyllaSyllaaline
      @alinesyllaSyllaaline 5 днів тому +1

      Eubeuli deum leu domou kharam leu

    • @ibrahimawalydiouf5745
      @ibrahimawalydiouf5745 5 днів тому +1

      Yéw yangui bollé lou bokoul dé li yep sa genre yii la doléne wax mbeur yii deug problème bi démbeu sikambay yii nioko andi

    • @ousmanendour8641
      @ousmanendour8641 5 днів тому

      Lamb thioupane lawone😂

    • @seringembacke9316
      @seringembacke9316 4 дні тому

      Liga Wax lep dége le me taxoul mou nek yow de te yow RK Moy yon

  • @ZEUMBOY1420TV
    @ZEUMBOY1420TV 4 дні тому

    L'erreur est humaine mais le pardon est divin

  • @TKFTV111
    @TKFTV111 4 дні тому

    Vraiment Ibou da dioum 😢

  • @ngomsitor
    @ngomsitor 5 днів тому +2

    Li mome yagu n'a Thi lamb bilay ngane séne nékal sportif ga respect grand yi

    • @Omar-199-c8
      @Omar-199-c8 5 днів тому

      Il faut dire la vérité à ibou Ndiaye limou def dou deug dou yonn

    • @alioudiouf5395
      @alioudiouf5395 5 днів тому

      Tu analyse mal jambar ose dire la vérité si tu es homme

    • @IbrahimaFaye-u8w
      @IbrahimaFaye-u8w 5 днів тому

      Boy es ce que nit nka

    • @MasseFaye-gy6wp
      @MasseFaye-gy6wp 5 днів тому

      Yen dof nguen diamanté si sport la bok

    • @salioungom9557
      @salioungom9557 4 дні тому

      Diam.nit.dayag.si.lamb.denga.dof

  • @IbrahimaGning-k7z
    @IbrahimaGning-k7z 5 днів тому +3

    Naniou bayi lignouy wakh qui bou diamone ngagne lorko li dou yone

  • @djibysene4670
    @djibysene4670 5 днів тому +3

    Pourquoi pas sesire le sng au lieu de gendarmerie

  • @SimonmoussaDiouf
    @SimonmoussaDiouf 4 дні тому +1

    Fii koudoul dioum amoul té n'a kham nii bou insisté ba amm thi ndam déy keupou wat sii kawam rek mbeur la déh té nimou amé aýe sopé nonou la amé aye noneu wakhouma d'ara wayé sou khossé wala mou khol nit khol bouko nékhoul sakh mou yobouko sii yone ndax moko ndieuké kon yone bou ibbékou lay donneu nako soralé bou bakh sakh

    • @salioungom9557
      @salioungom9557 4 дні тому

      Dangay.doul

    • @CoumbaFaye-dd8kf
      @CoumbaFaye-dd8kf 4 дні тому

      Yeené waa ibou Ndiaye xana yeena moom arrondissement bi ...Ngagne Seen xale bou Ndaw leu..Bou doon Reug waleu Ordinateur Ibou Ndiaye dou mossa yeungou..Ki dafa tardé chi Lamb...

  • @danielngom5684
    @danielngom5684 5 днів тому +7

    Force à toi ibou ndiaye

  • @AmadouDieganeDione
    @AmadouDieganeDione 5 днів тому +2

    Problème bi kay yen sikampay yi la dou supporter yi 😢

  • @Jnrjoop
    @Jnrjoop 5 днів тому

    B1 fait ✌️✌️✌️

  • @salioungom9557
    @salioungom9557 4 дні тому

    Ibou.defa.dof.way😢😢😢😢

  • @AmadouDieganeDione
    @AmadouDieganeDione 5 днів тому +2

    Leup sikampay yi la bapé niogui tog fi mbeur yi nekk si problème 😢

  • @MaoudoPaye
    @MaoudoPaye 5 днів тому +2

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @TecnopopsetPhone
    @TecnopopsetPhone 5 днів тому +1

    ❤❤❤❤❤❤

  • @gooroundeyefatou7552
    @gooroundeyefatou7552 4 дні тому

    Ibou Ndiaye wakhléne ko deug limou def dou yonne dafa beugone rey Ngagne il est majeur et vacciné nako cng adj

  • @leopoldsene9735
    @leopoldsene9735 5 днів тому +2

    Li deffa niaw si au domou sérère

  • @DethieDioufFissel
    @DethieDioufFissel 4 дні тому

    Sikambayes khawma dofambayes ñios wara nék ay nitt 😅😅mais nék fi di doff doff lou rék. Amouñiou béni ndiarigne ci lamb loudoul di diaxassé gayis.

  • @leopoldsene9735
    @leopoldsene9735 5 днів тому +1

    Ana loufi diar au plainte

  • @senesaliou4198
    @senesaliou4198 5 днів тому +2

    Kam diégue ké domakhama nou pirké sérére ah ndiaka té mbode néh gorwé mais katé pasaroro nou écrue ké falwé à ndiaguena dénnn ndiombb té ndéttké

  • @diagaloum4022
    @diagaloum4022 5 днів тому +1

    La violence n'a pas sa place dans le sport, elle doit être banie dans l'arène particulièrement la lutte simple.

  • @IbrahimaFayefaye-s1o
    @IbrahimaFayefaye-s1o 5 днів тому +1

    Gayi Nio bagne ngagne té ngagne amoul problème

  • @wallysarr7670
    @wallysarr7670 4 дні тому

    Bayelene mou sed❤

  • @djibrilsene8006
    @djibrilsene8006 4 дні тому

    Walay même si ngagne sene pardonne ,CNG ne doit pas lâcher cet affaire comme ça.Ibou ndiaye doit payer pour cet acte dégnkoo wara sanctionné bayilén thiahane,maslaa bi mofi wara diéh.lii yoonou ngagne sene warousiwoona nék sah CNG mo warone autocésirou convoqué ibou ndiaye direct tégko ay daane.lii sou fékoone deuk bou normale ibou dou gnibou keureum si lokho police lay fanane mais mangui guiss ay nit diéma wédi tentative de meurtre bi di diéma diay diang droit .

  • @mamadougalsen8712
    @mamadougalsen8712 5 днів тому +3

    Ibou Ndiaye mérite la prison

    • @SYN979
      @SYN979 5 днів тому

      Xol bou soxor nga yoré demal defar sa xol bi 😂

    • @mamadougalsen8712
      @mamadougalsen8712 5 днів тому

      @SYN979 mome mi yor beuy dieun beug ko jam nitt naka?xana xolou domerame la yor komee ioe?katal sa ndeye

  • @laminendiaye2235
    @laminendiaye2235 4 дні тому

    Ibou Ndiaye wax deug yalla ya togne

  • @MouhamedCissé-j9d
    @MouhamedCissé-j9d 5 днів тому +1

    Je suis parfaitement d'accord avec toi Ngagne. Affairou domou xaram yoyou dagnou ko warr di sanctionné. Soula gagnone tayy dji yakkal la sa carrière. Ibou Affairou imbécile deug la déff. Sénégal mom dafa beuri hypocrites. Danga dégg ayy saytané naan da djoum patati patata di doul. Sou la rayone tayy dji ces même personnes gno nane ( ndéysane aka meunone beuré 😂).

    • @AbouNdoye-s4p
      @AbouNdoye-s4p 5 днів тому

      Yaw doul beuri gua wakh trop yaw vrai imbécile vrai sayetané

  • @doudouSarr-f5g
    @doudouSarr-f5g 3 дні тому

    sika mbaye ndakha simba yakh wéné tout ka mbaro suspendrél

  • @omarndour8458
    @omarndour8458 4 дні тому

    ibou warouton Sakh beuré final bi .la commission a fauté

  • @SambaSene-j1h
    @SambaSene-j1h 4 дні тому +2

    Ibou ndiaye bou diotone ngagne sene dekoye raye yakhalko adouname lor mbokame na yone daif liguéyam

  • @benjamindoucoumdione2542
    @benjamindoucoumdione2542 5 днів тому +1

    VOUS LES TV TV AY NAFEK NGUÉNE. DANGUÉNE FAR . BEUGOLÉNE NGAGNE SÉNE

  • @AliouDiagne-g3d
    @AliouDiagne-g3d 4 дні тому

    Sa waye sonal ngene cng trop. Cng lici yonam ci khekh do wakh sakh force de l'ordre

  • @Domounguerigne-DJ-ZIKO
    @Domounguerigne-DJ-ZIKO 5 днів тому +5

    Pourquoi la cng n'a pas pris les choses en mains

    • @afro3827
      @afro3827 5 днів тому +1

      Lolou kay biti la fanan

  • @alyndiaye3197
    @alyndiaye3197 5 днів тому +3

    C vrai ngagne defna liko Yonne mayyy mé tmt ngagne dinga bayi sa xel boubakh moytou aussi khamné éleukkk bo xossé sa moromou mbeur bola haine yarr bi mounna dalll sa kaww dc yénna bokk ndeye bokk bay nayyy raffettt rk

  • @DembaFaye-m4v
    @DembaFaye-m4v 4 дні тому

    Ordinateur Moy mbeur li Mousou ko dal bilay

  • @Jean3Ndour
    @Jean3Ndour 5 днів тому +1

    La CNG loume wakh d après tout ça

  • @papesow7388
    @papesow7388 5 днів тому +1

    Li dafa yombou ibou Ndiaye daniouko wara yar dafa réw soxor mbamela rék

  • @SimonmoussaDiouf
    @SimonmoussaDiouf 4 дні тому

    Ngagne sene lo guiss téranga moko eupeu dél diégalé di diélalé adina amoul solo linga wara am euleug kén mounou sii dara té un grand champion té bo geuné geum sa bopeu tu même être roi des arène et je te le souhaite bayil mou digeu champion

  • @SimonmoussaDiouf
    @SimonmoussaDiouf 4 дні тому

    Bou léén nou sounal li yeufou goor la rek d'où d'ara bayilén affairou faralaté yii lamb Day diékh sou diékhé louy déss après loufi diarr aý plainte ngagne n'a nék goor ak sportif té bayi yii ni amoul béneu sans

  • @semoudiouf9936
    @semoudiouf9936 5 днів тому +3

    Ki da ndjirgna a noune takhou a sikampay wagaté lay mbirr ndiguil

  • @MemedouTiaw
    @MemedouTiaw 4 дні тому

    Li diaroul sakh nogociation .la justice doit faire son travail par ce que ibou ndiaye avait l'intention de le poignardé à mort

  • @SimonmoussaDiouf
    @SimonmoussaDiouf 4 дні тому

    Ibou ndiaye ndakh dinga guiss say commentaires ou pas mais boula darra diaralati ngay teubal nit ndax amam mou adina di yakeu sa réputation alors té un champion et ya ton carrière devant toi kholatal bou bakh sa bopeu té nga bayé khél linga wara donn euleug

  • @dienendour2596
    @dienendour2596 5 днів тому +1

    Non à la violence
    Ibou ndiaye n'a pas droit à brandir une arme je l'admire bien k mm
    Ces genres de fait son à bannir
    Nagnou waxtane rek bou bagna amati

    • @daoudasarr7150
      @daoudasarr7150 5 днів тому

      donc lii waroul diékh si lamb dawa continuer 🤷🏽bouniou si rayé nitt loy wakh

  • @Domounguerigne-DJ-ZIKO
    @Domounguerigne-DJ-ZIKO 5 днів тому +3

    Li lepp cng la vraiment

  • @abdoulayenonydione7477
    @abdoulayenonydione7477 5 днів тому +1

    Ibou Ndiaye Moy goor djigueine li c est honte gagne kouko khamm sedéko si niakk problème et sportif aussi bouko ball na yoone deff liko warr cng adjie ibou Ndiaye plus amandes

  • @SougouNdiaye-z2t
    @SougouNdiaye-z2t 5 днів тому +1

    Ka sika mbayaké na diakhasé a pirké ka sofoyo

  • @IbrahimaNdiaye-lj1dm
    @IbrahimaNdiaye-lj1dm 3 дні тому

    Vraiment ngagne n'a pas de bons conseillers la plainte n'avait sa raison d'être c'est la même famille et que le linge sale se lave en famille c'est trop vilain entre lutteurs.

  • @BabacarfayeMbaye
    @BabacarfayeMbaye 5 днів тому +1

    Ngagne est un lutteur a problème. Il avait donné un coup de pied à El hadj Ndiaye joal

  • @SimonmoussaDiouf
    @SimonmoussaDiouf 4 дні тому

    Yén mbeur yii soyez faire playe té rakhass khol yii andeu donn bén kham nii yén Nay mayanté khaliss
    Wakh tanélén ko mou diékh diaroul yén yi dh wasalam

  • @mouhamedsy2845
    @mouhamedsy2845 5 днів тому

    Daniou bage hame louniouy wah wayè dègouniou serer

  • @MalickNgom-km7kv
    @MalickNgom-km7kv 5 днів тому +1

    Li beurou Olof yi dougnoko def

  • @IbrahimaNgom-f5m
    @IbrahimaNgom-f5m 5 днів тому +4

    Da dioum rek bilay

  • @pepemodousene3421
    @pepemodousene3421 5 днів тому

    Ibou dioum gua wayé ngagne Li dinko rethiou dh Li waroul sene dinguanté dh

  • @IsmailaThior-v6h
    @IsmailaThior-v6h 5 днів тому

    Non nanou yo wena yona fi pir ké

  • @AssaneDiome-r3t
    @AssaneDiome-r3t 5 днів тому

    Yéne sikampaye yi yé Ako idi

  • @ibrahimasene5973
    @ibrahimasene5973 5 днів тому

    Amoul ni amoul na ibou nagnou nok ci kasso bi 6 mois

  • @MoustaphaGueyeSérère
    @MoustaphaGueyeSérère 5 днів тому +1

    Ibou nd df tarde si lamb

  • @gooroundeyefatou7552
    @gooroundeyefatou7552 4 дні тому

    Na Yonne def liguéyame li tentative de morte la

  • @leopoldsene9735
    @leopoldsene9735 5 днів тому

    Xana Kone ngagne dotto niéw si lamb arrondissement bi déh.bilay dôme bay li diarou kowone nak

    • @AbdouDiouf-g8g
      @AbdouDiouf-g8g 5 днів тому

      Koumom.arodissement.khana.bokoul.si.sénégal.légui.bouko.réyé

    • @leopoldsene9735
      @leopoldsene9735 5 днів тому

      @AbdouDiouf-g8g non Abdou ngagne défa dioume waroul wone déme di plainte CNG rék lako warone bayé mou def liguey bi li mossoul am si lamb deh te guiss nagne fi Lou nék Mane mom rek lay supporter sama dôme bay leu

    • @AbdouDiouf-g8g
      @AbdouDiouf-g8g 5 днів тому

      @leopoldsene9735 mais.ngagne.da.ame.staf.

  • @saliousarr3656
    @saliousarr3656 4 дні тому

    Ibou Ndiaye voulait commettre un meurtre

  • @babacarsenghor2068
    @babacarsenghor2068 5 днів тому

    Seytané yo rekk wayé fat i ndioffor def leng sérère fa sérère ino mbogou to ba diegatt

  • @lesenegalais2589
    @lesenegalais2589 5 днів тому

    Tout ceux qui insultent gagne sont faux. Ibou ndiaye est fautif et doit être sanctionné. C'est honteux et lâche son acte

  • @MaguetteFaye-k6z
    @MaguetteFaye-k6z 5 днів тому +1

    Ibou ndiaye dafa sohor

  • @IssaNiang-j7b
    @IssaNiang-j7b 5 днів тому

    Ngagne lingua déf niawna

  • @mamadoulassyastine2499
    @mamadoulassyastine2499 5 днів тому +1

    Ya same diamma moudie tènne

  • @mathieubousekouwakhaldiam7015
    @mathieubousekouwakhaldiam7015 5 днів тому +1

    Sénégal nagne bayi rafétal nitt monoula yéné police après ngéne né nio far mane kouma yéné police ma bayi à vie

  • @MamadouFaye-h2b
    @MamadouFaye-h2b 5 днів тому

    Gayki mi mo eup problème mais leup lamb la rek

  • @1999-un
    @1999-un 4 дні тому

    Bou takhawone mou diame ko . Nafekh yi nèkk fi doul yeub

  • @seydinasenghor2967
    @seydinasenghor2967 5 днів тому +1

    Non c une erreur gnougu balou

  • @thiammamadoulamine569
    @thiammamadoulamine569 5 днів тому +1

    Nguagn mo op problème mai haral rkk

  • @IsmailaThior-v6h
    @IsmailaThior-v6h 5 днів тому

    Et ngagne boudé ni la nara Mel na bayi lamb

  • @mamathiam5649
    @mamathiam5649 5 днів тому +1

    Ibou ndiaye kholl bou bone la yor

    • @laminethior2968
      @laminethior2968 5 днів тому

      Dangual doul !! Évites de dire n’importe quoi domaraam

  • @BiramangarySarr
    @BiramangarySarr 5 днів тому

    Boulen niou yabbb

  • @IbrahimaFayefaye-s1o
    @IbrahimaFayefaye-s1o 5 днів тому

    Commission Nio bagne ngagne ndah limou nékoul sérère ndokh même sikampayou ibou Ndiaye sah wahnako degloulen vidéo bi andiwon thiow li

    • @sekoufaye9856
      @sekoufaye9856 5 днів тому

      Ibrahima faye bayiléne di khadialé sérère yii lane moy lolou gnoune nieup béne lagnou ☝️ déguéne beugue affaire de ethni trop

  • @jpsf687
    @jpsf687 5 днів тому

    Bouko reyone dolen wax li

  • @1999-un
    @1999-un 4 дні тому

    Ibou ndiaye daffa con trop

  • @alinesyllaSyllaaline
    @alinesyllaSyllaaline 5 днів тому +2

    Ibou ndiaye deum leu domou kharam leu dafa sokhor mak mome nio deuk parcelle unité 7 mé dou nite kou bakh warkat leu téksi

    • @AssaneGueye-fm2gm
      @AssaneGueye-fm2gm 5 днів тому

      Sa data yaye ya meune ndéye doul

    • @alinesyllaSyllaaline
      @alinesyllaSyllaaline 5 днів тому

      @AssaneGueye-fm2gm domou ndialô bi nga done

    • @danielngom5684
      @danielngom5684 5 днів тому

      Yaw amo yarr bly ibou ndiaye mola guén fouf nafék bakhoul

    • @maxgueye6871
      @maxgueye6871 5 днів тому

      Daguay doull deh yaw domarame gua seytané ligua ko wakh yeup sii yaw la nek

    • @SaraSara-rw1qf
      @SaraSara-rw1qf 4 дні тому

      Dieureudieuf

  • @zoeEscobargui
    @zoeEscobargui 5 днів тому +1

    Ibou Ndiaye assassin

  • @IssaNiang-j7b
    @IssaNiang-j7b 5 днів тому

    Ngagn gor djigéne lh😂

  • @mamadoudiongue5402
    @mamadoudiongue5402 5 днів тому

    Ngagne sene limou daiff c pas sportif

  • @GoFaye-z8m
    @GoFaye-z8m 5 днів тому

    Pourtant ibou Ndiaye amoul béni problèmes moom déye rétane rek ngagne séne mo beuguene oupeul rek ibou Ndiaye néko yémal 😂😂mé lambou rek nagnko bal rek dotouko déffati

  • @MatarNiang-m9g
    @MatarNiang-m9g 4 дні тому

    Dmrm yi boudoone toubacouta la kou nekk di ibi ndayi gatam gui

  • @TalibouyaFaye
    @TalibouyaFaye 5 днів тому +2

    Ngagne il n'est pas sportif

    • @zoeEscobargui
      @zoeEscobargui 5 днів тому +1

      Ngagne a fuit parce que Obeuli voulait le tuer du n'importe quoi mouton que tué

    • @lesenegalais2589
      @lesenegalais2589 5 днів тому

      T'as pas honte?

    • @AlySene-er4yt
      @AlySene-er4yt 5 днів тому +1

      Sa way nafékh ngua

    • @diegsontv
      @diegsontv 5 днів тому

      Yaw doul kou sportif dina guené bediene souko gagnone kane moy perte bayilene nafeek