Mactar Gueye Jamra très remonté revient sur les conditions d'arrestation de Taibe Socé et révélation

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 23 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 104

  • @modouseke4551
    @modouseke4551 5 років тому +4

    yalla nako yalla guéné thi diafé diafé yi thi barké s.fallou

  • @YoKo-yk4yj
    @YoKo-yk4yj 5 років тому +4

    Il faut quand même reconnaître que vous êtes d'une grande intelligence et d'un grand courage.

  • @ramakane7194
    @ramakane7194 5 років тому +6

    Yalnako sunu borome takhawou j suis trop triste

  • @aidaniang2131
    @aidaniang2131 5 років тому +3

    Merci beaucoup mactar geuye yala n'a la yala faylen Lou bakh amiine yarabie machala rafena taib yala n'a am diamou reck amiine yarabie

    • @laminematardiop1174
      @laminematardiop1174 5 років тому

      Ce que je n'accepte pas les gens qui sont partis cueillir Taib ils voient toujours ce fumeux diakhaté qui circule on est dans quelle pays

  • @ibrahimasissoko3249
    @ibrahimasissoko3249 5 років тому +8

    Yalnako yallah soutouraall incha Allah amiiin

  • @lansanatraore6655
    @lansanatraore6655 5 років тому

    Merci Mame MATAR le prophete Mouhamed Paix et Salut à dit: Dieu est au service de son adorateur tant que celui ci demeure être aux services des ses serviteurs. Je SUIS DE TOUT CŒUR AVEC TOI ET JE VAIS PARTICIPER INCHALLAH. Taib Socé Tayibou .

  • @papeousmanesamb4880
    @papeousmanesamb4880 5 років тому +2

    Merci père Mactar vraiment sama yaram daw neu Oustaz Taib kou bakh la tè dioup inch allah dina guèneu ak diam

  • @khadysakho7445
    @khadysakho7445 5 років тому +4

    Yalla mi meune yalla naka yalla diapalè

  • @dramelamine261
    @dramelamine261 5 років тому +2

    moi personnellement ça sa nous fais mal mais oustaz taib que te protège un jour viendra tu sortiras inchalla dans la vie aujourd'hui ne fait confiance a personne,

  • @abdoumara3287
    @abdoumara3287 5 років тому +3

    Machallah mame makhtar mallabaga

  • @moussambaye7798
    @moussambaye7798 5 років тому

    Walahi wakhgua degua yokouna thi nioubari sen dine yallah nako yallah guene fofou

  • @laminediouf8072
    @laminediouf8072 5 років тому +5

    Yalla bakhna

  • @modoufall1616
    @modoufall1616 5 років тому +3

    ay waay ana youssou ndour ak cheikh amar

  • @gaindendiaye7249
    @gaindendiaye7249 5 років тому +2

    Yalnako Yalla dimbili si nattou bii té mayko Jam bamou guéne si.

  • @khadydiop6867
    @khadydiop6867 5 років тому

    Merci beaucoup

  • @yacinedia5051
    @yacinedia5051 5 років тому +6

    yalla nako ci yalla Gène ak diam nako ñëp diapalè ta yalla rè tax wasalam

  • @abssabathily5455
    @abssabathily5455 5 років тому +6

    Du courage inchallah tu vas sortir

  • @aminatasow7733
    @aminatasow7733 5 років тому +2

    Yale nako yala soutoural si barkhke seydina Muhammed sala lakhou tala Ali Muhammed

  • @amadousow6372
    @amadousow6372 5 років тому

    Yallah nako yallah tahawou te soutourale ko amine.

  • @mamadousarr3403
    @mamadousarr3403 5 років тому

    Yall nako yall takhawu natula rek dana masa diekhe inchaalah dege

  • @ramoukitane5119
    @ramoukitane5119 5 років тому

    Macha Allah

  • @bathieniang1754
    @bathieniang1754 5 років тому +2

    yalla Nako yalla yakhawou yalla bakh na

  • @serignengom2889
    @serignengom2889 5 років тому +9

    Yallahhh na ko yallahhhhh takhawou

  • @Lopios-g6l
    @Lopios-g6l 5 років тому +13

    Bilaye tahib socé akka bah. yalanako yalla guéné akk diame..

  • @leducationislamiquetv7693
    @leducationislamiquetv7693 5 років тому

    yalna ko yalla guenneee fi mou nekke

  • @madonafall1969
    @madonafall1969 5 років тому +1

    Taib socé un grand référent nitou deug nitou dîné ragaloul loudoul yalla borom bi dou bokalé yalla AK lénne

  • @adoufaye1378
    @adoufaye1378 5 років тому +12

    que DIEU assiste Oustaz Toïb socé

  • @kerbalakerbala485
    @kerbalakerbala485 5 років тому +1

    Taib socé nieup ba si wara takhou et tous les sénégalais. C est une épreuve et un destin Que Dieu lui aide à sortir sur cette épreuve

  • @zainabismail6982
    @zainabismail6982 5 років тому +4

    Inna lillahi wa inna ilayhi rajioune. C’est une grande epreuve pour Oustaz Taib Soce et sa famille. Prions pour qu’Allah lui donne une issue favorable. L’escroc qui a disparu avec les millions na raggal yaAllah te deloussi. Vraiment dor kat yi gneme guen akk. Ceci est une triste affaire qui peut arriver a tout le monde.

    • @mameboy4629
      @mameboy4629 5 років тому +2

      Wallah kasso lou doy ware la, yalna gnou ci borom bi mousseul

  • @laminediatta1820
    @laminediatta1820 5 років тому

    Togne mom bakhoule yalla nakko yalla diapale Taib soce deyy dou nitte bou bonn wayye sii lii yeupeu jhew Anna imame kante

  • @lasamusic9937
    @lasamusic9937 5 років тому +28

    Me dem lene thi khalifa général yi ñiou diaplei ko ndakh taibe socé nitou dinnè leu nitte kou bakh leu té taibe weroul guire yalla takhaw lene si mou gaww

    • @mameboy4629
      @mameboy4629 5 років тому +3

      Sou khalife yi diokhé wone ndigueul rek legui mou mat

  • @abssabathily5455
    @abssabathily5455 5 років тому +5

    C'est trop triste

  • @awandiaye4346
    @awandiaye4346 5 років тому +9

    Yalla nako Yalla diapale te soutouralko

  • @ibnouba703
    @ibnouba703 5 років тому

    Ndeysan

  • @aichasall2441
    @aichasall2441 5 років тому +7

    Yalla nako yalla dimbali ndayssane sama khol toye na way thiey gayi gno saysay nitt nane la meuneu deifei liii

  • @senebada
    @senebada 5 років тому +3

    L'information avant l'informateur. Bravo YesDakar.

  • @amybeugues.falloumbacke1725
    @amybeugues.falloumbacke1725 5 років тому

    Yallnako yall kéne ak diamou si barkb s.touba

  • @katouchajallow2049
    @katouchajallow2049 5 років тому +2

    No pa jamra dafa nekh dafay wax soxlam bamou jeikh dora wax si gatal🤣🤣🤣🤣mai bon yala naleine borom bi japalé amine

  • @thianethiam5490
    @thianethiam5490 5 років тому +1

    Il faut publier le nom et la photo du voleur vendeur d'or di gnane Taib socé sougnou borom Soubhana watallah guenné ko thi li té léral lepp amin

  • @adoufaye1378
    @adoufaye1378 5 років тому +2

    يا رب فرج عن ألأستاذ طيب سوسه كما فرجت عن نبيك يونس وهو في ظلمات ثلاث وكما فرجت عن نبيك يوسف وهو في سجن الملك وكما فرجت عن موسى وأصحابه من مطاردة فرعون وكما فرجت عن نبيك محمد وأبي بكر إذ هما في الغار إذ يقول لصاحبه لا تحزن إن الله معنا.ءامين يا رب !

  • @mamadoudaffe8416
    @mamadoudaffe8416 5 років тому +2

    rafétna y'Allah naléne y'Allah takhawou

  • @badaradiop8326
    @badaradiop8326 5 років тому +3

    Il dit que le président de la république est le gardien du parquet.Un pays qui se dit démocratique doit se doter d'une justice indépendante mais tel n'est malheureusement pas le cas pour le Sénégal. Je trouve le discours de cet homme trés mittigé, tantôt rigide et tantòt tendre envers le régime; je n'arrive pas à le situer .

  • @lifefree1681
    @lifefree1681 5 років тому +1

    God bless you ☝️Taide Socè

  • @Lopios-g6l
    @Lopios-g6l 5 років тому

    Deugue pire nitte daye mandou...
    Sene liguèye rafféna guéye !!

  • @pinopi83dooms
    @pinopi83dooms 5 років тому +9

    SVP jamra dites a taib soce de donner le nom le prenom du gars et meme sa foto si vous labé petétre on le voit sans le connétre merci

    • @papagalousosseh1248
      @papagalousosseh1248 5 років тому

      Qui def lolou dafa bonn rek wayé ayy mbokou taib socé dimbalé naniuko b tayii

  • @ibadiagnesarr4350
    @ibadiagnesarr4350 5 років тому

    Walayyyy ndeysane lii gua wakh lerr naaa Mame Mactar ...
    Diaykatou Or moytoul niepa yamm

  • @rokhayadiop4399
    @rokhayadiop4399 5 років тому +7

    Yalanala yallah takhawou

  • @malicksene8838
    @malicksene8838 5 років тому +3

    YesDakar déf nguén liguéy bou am solo

  • @maremembengue6873
    @maremembengue6873 5 років тому +5

    Natou la fekh yall nako yall tegui

  • @ahmadoudiaobathily6019
    @ahmadoudiaobathily6019 5 років тому +1

    Mais son patron youssou ndour n a qu'à paye

  • @diawabou9281
    @diawabou9281 5 років тому

    MAN Dé NIAWLOU NA LI .TAIBE NE MéRITE PAS DES TéLéTONS.OU SE TROUVE LE PRéSIDENT DE LA RéPUBLIC C L ETAT QUI DOIT VERSET CETTE SOMME D ARGENT.TAIBE SOCé MéRITE PLUS QUE DES MILLARDS.

  • @moisek147
    @moisek147 5 років тому

    KENE DOU DIEUNDE DIANE SI PAKH GUISSO OR GADIOKHÉ KHALISSE CEST TROP FACILE COMME NAKH TÉW MOU TÉW DIOKHMA OR GA DIOKH KO KHALISS MOU SIGNÉ AK SEDÉ YALLA NAKO YALLA DIOPALÉ TÉ TAKHAWOU LÉNE AK GNIOUNE ki yalla nagniouko diape wnako serigne yi wothie

  • @sophiababa8787
    @sophiababa8787 5 років тому

    Nafekh guenn khalifa sall lou guenn si wakh cheytane guenn ñi nek si casobi te defouñiou dara barenañiou

  • @ibsondwolf8009
    @ibsondwolf8009 5 років тому +1

    Waaye door kaate leu... Dafeu thiolé.

  • @antagueye7993
    @antagueye7993 5 років тому

    Ioe imam bi thione seck gnaqué respé tok sen wëtt ni gor juguen Bouma diokh xaliss ma dieul té tontou woulen ko là guën si yen dakh warone guén ko wakh niko xaliss bou xaram là mou xam ko rék dakh sen devoire là

  • @celloushopstarbah4829
    @celloushopstarbah4829 5 років тому

    loubakh désse koye défe diko wakh avec sa tu dis que tu te prêtant imam ;;;''';;;taïb l'I yeuppe natou souniou borome késsé leu wayeu ngi aye séyy tané laniou

  • @antagueye7993
    @antagueye7993 5 років тому

    Mai lima diakhal oustaz loutakh mou nagou grâce bi dakh grâce mom kou nagou ya dëff

  • @laminediatta1820
    @laminediatta1820 5 років тому

    Anna imam Kante

  • @amethsall
    @amethsall 5 років тому

    mais quelqu'un qui a pris ce qui ne lui appartiens pas dois rendre ce qu'il lui dois dionblang daal danioukoy diap

  • @harounandiaye4084
    @harounandiaye4084 5 років тому

    Mais interpole louye rolam

  • @missgallo3643
    @missgallo3643 5 років тому

    Modéf ou défoule, khawmaci dara mé dioulitela té yaguena gnou bégaie ci tafsirou Khourâne,, donc kouka mëne nako dimbalé bamou guéne ci natoubi barké Khadimou Rassouloulahi.

  • @abdoudiagne4225
    @abdoudiagne4225 5 років тому

    Vraiment vous pouvez peindre un âne en lion, si il était intermédiaire, il avait des intérêts là-bas, donc il s’est bien qu’il faisait un business risqué quand il a livré l’or sans recevoir l ‘argent. Il faut vivre ce que vous prêchez, quand l’argent est engagé vous êtes capables de tout faire pour se sucrer

  • @resigneyamb3297
    @resigneyamb3297 5 років тому

    Makhtar dara doudeuk thi liguenne duwakh taib escroc la bayulene solidarité thi loudoul deuk benguenne

    • @cunellero
      @cunellero 5 років тому

      Yow loula ci lérr

  • @abdtv9014
    @abdtv9014 5 років тому +1

    Defal lenko teleton

  • @domoubadiane348
    @domoubadiane348 5 років тому +3

    Yowe diangoo economíe ,do baol baol endurci,loy deffer role intermediaire.yamal place imam moo geune di xammanetter ak ay dorkatts.

    • @mamadoudia1459
      @mamadoudia1459 5 років тому +7

      Gayenne boule waxe lolou nianalko ngire yala natou dou wéss dé bilahi li mome métina torobb

    • @naturelblackthior7951
      @naturelblackthior7951 5 років тому +1

      Ki dou imam

    • @toutydiarrabadji5165
      @toutydiarrabadji5165 5 років тому +1

      Yaw est ce que do dorkatte sakh ni môme motakh gua khamko

  • @gueyemalick7216
    @gueyemalick7216 5 років тому

    Natou sunu borome rèk la

  • @mamadoulamineseck
    @mamadoulamineseck 5 років тому

    Paa mafia bangi nii ki
    Ay wakham weroul dé

  • @lampfallndiaye6814
    @lampfallndiaye6814 5 років тому +1

    taib lousiye yoname mowarone mandou si lolou mane na ame dafe si amone pourcentage rek li khalé yi di wakhe hé sama lék en tout cas mane sama yone nékousi amouma louma diapalé ken

    • @makhadyzanetti5618
      @makhadyzanetti5618 5 років тому +1

      sokhna lamp fall Ndiaye 😂😂

    • @awagueye739
      @awagueye739 5 років тому +1

      De tout coeur yallah nala yallah guéné si natou bi gay traversé si daradia seydina Mouhammad wasalam

    • @antagueye7993
      @antagueye7993 5 років тому +1

      Tei mom osi souféké défoule waroul wone nagou grâce bi grâce mom kokou nagou rék nagou gani ya dëff

    • @lampfallndiaye6814
      @lampfallndiaye6814 5 років тому

      @@antagueye7993 bien dit

    • @lampfallndiaye6814
      @lampfallndiaye6814 5 років тому

      @@makhadyzanetti5618 dama warou di oustaz dafa wara Yam si yalla néna yontebi psl néna mais di diaye foukhaler beug khalisse ni rek

  • @domoubadiane348
    @domoubadiane348 5 років тому +3

    Mane deh sama deureume doussi demm.oustaz truand.

    • @kim-pd9s
      @kim-pd9s 5 років тому +4

      yoy yaye domeram deug

    • @lorlynend845
      @lorlynend845 5 років тому +5

      So mane gua def so manoul gue nopi c'est pas forcé

    • @famandiaye6472
      @famandiaye6472 5 років тому +4

      dagua amoule looci def rek gor day mandou kene force woula

    • @alioundiaye5120
      @alioundiaye5120 5 років тому +4

      Kénn sokh la wousi sa dereum

    • @maremembengue6873
      @maremembengue6873 5 років тому +5

      Yaw kenn forcew la pour nga djokhe liko dall djomboul kenn

  • @pinopi83dooms
    @pinopi83dooms 5 років тому +8

    SVP jamra dites a taib soce de donner le nom le prenom du gars et meme sa foto si vous labé petétre on le voit sans le connétre merci