REGARDEZ > Part 2 - L'emission #JataayuMurid: "Des anecdotes sur Serigne Saliou Mbacke, Ibn Khadimou Rassoul, par Serigne Moustapha Diaw." WATCH > Part 2 - The Jataayu Murid show: "Anecdotes on Serigne Saliou Mbacke, Ibn Khadimu Rassul, by Serigne Moustapha Diaw."
Salam. Serigne Salih Mbacké. Yalla nanouko Yalla fayale té yooque aye léerame té tassegnou thi baarkéeme.Mooye sounou yaakare fii ak fagne dieume!
Machallah amna sollo yalla na yalla fayal nolén
Ndeyssan Yalla na Yalla doolinu fayal s saliou barkeb s touba
MOO MA DIIMBALI , THIEY NOUROU SALIKI..DIARA DIEUFEUL
Dieureudieuf Serigne Saliou Baké 🙏❤️❤️🙏🙏❤️❤️🙏🙏❤️🙏❤️❤️❤️🙏🙏❤️❤️❤️🙏🙏🙏❤️
Mame.saliou yalla.nanouko yalla fayall
Dieuredieuf serigne touba serrigne saliou
serigne saliou Mbacké yalla na yalla yokou leeram
Dièttayou fattèlikoup SERIGNE SALIOU MBACKÈ BOROM DIAMONO , toyolna khool, wayè dounal nap rou...yalla nañou sorrè si biir si ñoupp SAANGUE bi ñou soukk dièbeulou, beu souñoup lèèp di ÑIOOM...amin...dieuredieuf SERIGNE MOUHAMADOU AL AMIN BARA SOUHAÏBOU MBACKÈ...yalla NA FI yag TÈ andakakh weur ,si barkhè waxtaan bi...amin....Dieuredieuf...
Akassa baye fall amine Serigne bara yague fii lol si nou liggeylo .
yalla Nanou yallah taff nu si barkem
Dieureudieufeti serigne saliou
Tihye Serigne saliou ❤❤❤😭
Dieuredieuf serigne Saliou
Jerejef serigne Saliou
Macha Allah !
Ndaysane ❤️❤️❤️
Thieye serigne saliou amol morome dh
Yalla nalene yalla fay yiw
yallana yalla yok leeram taf gnou thi barkem
DIEUREDIEUFETY SERIGNE SALIOU
Amiiiine waye teh niou bokkaat lepp ci barkep serigne bi.
ndeyssann .. kharonn nagnko
amatina solo
jjf fall
Macha alla
DIEUREDIEUF S.SALIOUL KHADIM dieuredieuf s.moustapha diaw dieuredieuf wa alashar ouba.com.THIEYE THIEYE THIEYE SERIGNE SALIOU....!
Toyalngene kholyi wallahi thia caw thia canam thia canam
الحمدلله رب العالمين
Diara dieuf sbsaliho
Jerejëfetty Serigne Saliou Mbacké
Machallah amna solo lool Diadieuff 💗💗💗
Machala
Ndeysaan sama sang ba
VIDEO : Anecdotes Sur Serigne Saliou [Part 2]
Yeurmandé Yallah Mbacké
serigne Amoule morom
thiey s saluou amol morom de
Machallah
ah thiey! jerejef
Machallah amna solo
wakh dji ame na solo.lounou wara baril la ndakh wakh yi war nane ko ségue!!!!
REGARDEZ > Part 2 - L'emission #JataayuMurid: "Des anecdotes sur Serigne Saliou Mbacke, Ibn Khadimou Rassoul, par Serigne Moustapha Diaw."
WATCH > Part 2 - The Jataayu Murid show: "Anecdotes on Serigne Saliou Mbacke, Ibn Khadimu Rassul, by Serigne Moustapha Diaw."
Amena solo lool
talla niang sant hadem
M
Nioko bokk!
Ziar numéro pabi si waxtane la soxla svp
B
ki de khana moye baye diaw
Waw goor yalla deguelaa
Machallah
Machallah
Machala