Gnioune moustachid yi kham naniou lan mo khéw mais naniou concentré wou si li am solo mo niou eupeul ndieurigne yenen DIARAMA SERIGNE MOUSTAPHA SY❤❤❤❤❤
@@momo-hp4yf ñioune sunu nek dof nexna ndakh sunu diexé ci rewmi nitt doo toufi dess. Dof you xoutboul Makhtum tok ci dans toutes ses conférences touddénou les gâtées du ciel, parrainé ñiou "Xashabul këf" yii dof dei nexna ñiou, ndakh you xoutbou biko cautionner.
@@momo-hp4yf com yaw djiko diahassé ga yor ak nafekh ak bagñ yaw ak koo yakaar motax nii ga mane wakhé mala yeureum ndakh kalamenàleu ak Maam BILAHI LAZI bayenaleu ak Maam Babacar Sy dinaleu wane kou amoul kilifa naka lay mell.....
Xeex bii moo continuer bey leegi ca TIVAOUANE, ñenn ci sëtuy sëriñ BABACAR SY and ca ak ñoom di tooñ sëriñ Mustafaa sy Almaktum, te ñame wuñ ko. Lii rek la...
Mane mom diakhlë rek kadëf 😭😭1992 laganë adouna bataye laye sora khame në liyeup amon nafi Yalna yalla doli soutoura yarabi kharë al diana firdawsi waye décédé 🤲🤲
@@دفراتسنغالkhamoo dara daguaye doul Rék yagui fénal mame cheikh ak pape Malick digua ko layoo ak mome déf weur di féne nane khamna si dara yawe ak kila nétali yépou wakhou niou dégeu
@@momo-hp4yf les archives de Maam Cheikh et de S. Pape Malick si on les sortez ton genres de mbam gui xeum et pourtant yaggoul 1994 à 2012 Ndeyssane bobou les tricheurs com toi n'était jamais dans les conférences et gàmmu de Maam Cheikh
@@diagnendoye5756 affaire bi dou mame cheikh j l respect aussi sama serigne leu oki il s'agit de Moustapha kokou mot seyante bon di moi lane mo takh mame cheikh wakhone même souma fatoo Moustapha bouma Time repon sur sa Moustapha amoul yarr est tu l sai
Khamna SERIGNE BABACAR SY Niko ayy rakam fonké eupna Histoire moom sou amé ngayy dégg bén camp rekk Di wakh khamalni bénén Camp bi sou wakhé RÉÉWMI TASS Ko khamal walatt rekk khamal nala litre Wa SALAM
Lii xewoone c'était très grave , degeul lii s. Pape Malick di expliquer rek lii mom pour ñioune gñileu la jeunesse. Mais courage et bravoure moci gueen Maam Cheikh Motakh goorou diné biko donneu faw mou sonneu mais la vérité finira de triompher tôt ou tard Moustaphal Makhtum soit béni à jamais
Yén dal li ba kagne 1957 ak li dokh si diguénté bi yép mame Abdoul Aziz sy dabax ak nimou mélon ak ndiabot gui serigne cheikh avant Mouy dem boléna ndiavot gui yep si taxa wayou al amine pape malick sy ak khalifa général des tidiane lép guénnei dra doufi rafétei seydil hadji Malick liguéyoufi li bayi lén sen yi amoul bene chance niou ndiabotou amou gnousi khadji ak séne niép lanou beug
Di ko remercier honnêtement ndkh taye kou Diot thi Mame cheikh Ahmed tidiane sy Al maktoum nako guerumé Serign Moustapha sy , faté khadioufi Kane mô dieulé Mame cheikh France"? Kane moko présente wate sénégalais yi 1995? Kane moko indiwate maolid a tivaone 1998 Kane mo wakhni sou aldjana dône louer appartement dinako louéellle appartement Thi goudi gamougi ?. Kane la Mame cheikh Ahmed tidiane sy wakh ni sagalma yala nala yala sagal Kane moy le prince de la ville sainte de tivaone ? Kane la nieup Di weur ? Kane mô latéwoul way ?Kane mo wakhni kérok 40!jour Mame cheikh wiraasabi moma guenal miraasbi Faté amoul dofdoflou mofi Bari bayiléne dofflou bi Dafa ame Lou yala maye Serigne Moustapha Moy wakhnananou djoumhatoul hadara aulie de hadaratou diouma ...est ce que wadial ga sa bop pour accéder fofou Yalana yala motaly inchalla yéné sérigne moustapha sy thi al moustarchidine amine
WALAHI liga résumé dei moo di dëug Yalna ñiou Yallah mousseul ci kigñaane ak xol bou doul fekh ba mou ak nafehq Yallah defnou ñiou nek Diaboot Seydi Moukhamad Moustapha Sy Makhtum ba Faw insh ALLAH Barké gñimou am ñieup ta yorré seen Ndono
WALAHI Mbodj wahga deug ndakh moo leen fi nekal ci lou wer Motakh la daloone Yonett Bi SAWS ak SaKhabàb yi ak Cheikh A-tidjany Fatimy ak Cheikhou oumar ak Maodo ak Serigne Babacar ak Serigne Cheikh faw mou dalko Sy Demba khouradia Mourchidoul Am wantei Yallah diko samm rek ci seen Barké ñiom insh ALLAH Sonnal neu kilifam taxawou ko mouy Serigne Cheikh ba mou tok founé ci conférences yi ak gàmmu diko ceedé MashAllah Motax moy raw ba faw insh ALLAH ndakh mérite la am Mawlaya Sy Demba ♥️🤲🙏
Bou leen tardé le liguéeyou Dioumadji. 1957 wéessou na nioungui 2020. Keur Seydil Hadj Malick wakh leen si jamm waay moo raféte. Aythia si Dioumadji. Aythia Aythia
@@rifodne6354il l fait absolument parcqu’ils y’a d hypocrites qui savent bien ce qui s’était passé hier b noppi beug takhaw di diaboliser ko sét wéth🤷🏾♂️
سيدي ومولاي السيد الشيخ محمد المصطفى سه المكتوم حفظه الله ورعاه وأيده ونصره وأطال بقاءه وعمره مع دوام الصحة والعافية والتوفيق والسداد بجاه اللهم صل على سيدنا ومولانى ورسولنا محمد وسلم
😭😭😭Je Suis tellement Triste De Voir Qu'ibliss Ne laissera jamais Les Fils d'Adam Vivre en Paix,De Surcroît Les Muslims 😭😭😭Et Je Comprend Mieux Pourquoi DIEU a repris le Fils Du prophète Saws avant Sa mort......😭😭😭 Même les Familles Prophétiques ont Connu ,Par le Passé,Des conflits similaires Qui n'est que l'œuvre de Shaytane....Que DIEU Ns préserve de Ses méfaits Nous autres......😭😭😭
Dieu a pris tous les fils du prophète SaW avant sa mort parce que le fils d'un prophète est un prophète alors que Mouhamed SAW est le dernier des prophètes
La famille de Seydi El Hadj Malick a une grande ouverture c'est pourquoi ceux qui font le mal en profite pour les diviser. Entre eux (la famille SY), jamais aucun n'a fait le moindre mal à l'autre. Ça se justifie à travers leurs rencontres. Qu'Allah nous éloigne du démon !
La vérité sur les agissements infondés de Moustapha trouve sa source a la suite du décès de Mame Abdou dabakh le khilafat devait revenir entre borom daradji et Serigne cheikh le droit d ainesse a joué en faveur de borom daradji les hostilités ont commencés c thierno mountaga tall le père de madani tall qui a fait la réconciliation depuis lors Serigne cheikh a clôt le débat c Moustapha qui a chaque gamou remit le couteau dans la plaie mais il ne verra que du feu incha allah
@@alhassanesy1194 tu mens dh Serigne Cheikh n’a jamais cherché le titre de Khalifa il était même contre et d’ailleurs il a même dit devant Serigne Abdou et eux tous que dondou na Serigne Babacar Sy tei dougua goul bamel donc ioe liguay wax foko. Les agissements qu’ils font sur Serigne Moustapha Sy vous ne le voyez mais quand il répond vous essayez d’attraper sa veste vous allez tous croupir en enfer
@@taibasakho2424 s il y a quelqu un qui ment et qui pète tres très fort c bien taiba sakho ou étiez vous quant thierno mountaga le père de madani tall recevez Serigne cheikh et Serigne Mansour a son domicile à la médina pour arrondir les angles au lendemain de la disparition de Mame Abdou dabakh sur le khilafat de Mame maodo renseignez vous au lieu de mentir et de Peter a tout va
Je suis choquer thi commentaires yii nitt dal dey mandou gnii di kheuth fii gni di kheuth fé dama beug serigne babacar sy ak ndoabotam beug serigne mbaye sy abdou mais lou dembeu doumathi jugé keneu gnome gneup ndiabotou mawdo lagnou areter sen yone nekouthiii
Louma siy wax daal lenna leu problème bini s papa Malick di wax yalla dièkhalonnako bou yagga Li am nak yalla nako yalla dièkhal الفتنة نائمة لعن الله من ايقظها وقال الشيخ الحاج مالك سي والشيخ من توقيره توقيره كل الذي من حوله يدوروا
Maodo xamone na li Fadiouko bala mou guéneu adouna té meunone nako safara wayé topou sonou YONENTÉ bi Aleykhi wa Salam bamou diekh takkeu motah mouni seugam xéwone na keur YONÉNTÉ bi xéw keur CHEIKH damay bayi mou xéw sama keur donc li ware moy gnou topou séni diangalé té manou si problémou keur gui gnoune nio siiy lorou mai jaabotou Maodo dougnou lorou
Gnioune moustachid yi kham naniou lan mo khéw mais naniou concentré wou si li am solo mo niou eupeul ndieurigne yenen
DIARAMA SERIGNE MOUSTAPHA SY❤❤❤❤❤
Que Dieu protège la famille de Elhadji Malick dans l'unité de la famille et le pardon mutuel
Dieuredieuf Serigne Babacar Sy . Serigne Moustapha yag fi lol ak reer donc le mal est profond
Seringe moustapha yalna nako yalla arre tee samal koo bopam tee ♥️♥️
Machalla
Sheuuu xolal lii rek . Serigne Moustapha Sy diaam rek ngay am inchaAllah ❤️
Moo taxawou Serigne Cheikh ba keen douko fowei douko nangou
Nioh. Yow ba faw inchalla
Aye doff DEUG moy yènne talibe serigne Moustapha se kilifeu amoul yarr amoul thieur diakhasè katt leu
@@momo-hp4yf ñioune sunu nek dof nexna ndakh sunu diexé ci rewmi nitt doo toufi dess.
Dof you xoutboul Makhtum tok ci dans toutes ses conférences touddénou les gâtées du ciel, parrainé ñiou "Xashabul këf" yii dof dei nexna ñiou, ndakh you xoutbou biko cautionner.
@@momo-hp4yf com yaw djiko diahassé ga yor ak nafekh ak bagñ yaw ak koo yakaar motax nii ga mane wakhé mala yeureum ndakh kalamenàleu ak Maam BILAHI LAZI bayenaleu ak Maam Babacar Sy dinaleu wane kou amoul kilifa naka lay mell.....
Serigne moustapha sy almahtum yalla nako yalla fay❤
Man dé mome serighe mouhamadoul Moustapha Sy rék incha allah yalla nako yalla samm birr AK BiTTi
Ndaysan s cheikhe mo tédd yalnako yalla doli khéwal ak yarmandé barké s saliou
Guènèl Serigne Saliou thi yi dé...boy guigne nga guigné Moustapha Sy
Xeex bii moo continuer bey leegi ca TIVAOUANE, ñenn ci sëtuy sëriñ BABACAR SY and ca ak ñoom di tooñ sëriñ Mustafaa sy Almaktum, te ñame wuñ ko. Lii rek la...
Mane mom diakhlë rek kadëf 😭😭1992 laganë adouna bataye laye sora khame në liyeup amon nafi
Yalna yalla doli soutoura yarabi kharë al diana firdawsi waye décédé 🤲🤲
Salam Serigne Moustapha yalna yala sameula goudal sa fane temou andak wer bassa kanama kanam Amine
Wallahi kou xamoul rekk motakh mandou bakh .. yallah na yallah samou Serigne Moustapha sy goudal faname
Sawaye mane khamna ci lou Bari mais gni daniouy doule
@@دفراتسنغالkhamoo dara daguaye doul Rék yagui fénal mame cheikh ak pape Malick digua ko layoo ak mome déf weur di féne nane khamna si dara yawe ak kila nétali yépou wakhou niou dégeu
Boudoul wone Mame Cheikh kone Serigne Babacar dina melni meussoul wone existé faté nagn ko bou yag
Même taxaway wala bouko raw la Serigne Moustapha am motakh kou am mérite leu ndakh kou donneu Yonett bi SAWS faw ga donneu lepeum
Billahi
Macah Allah ame na solo
Khana serigne babacar sy amoul ya nen doom yeen wakhii doff rek geune dii wakh
@@azizdiop7475 yaw saytane ga dé
Dieur dieuf Serigne Moustapha sy figua tèk sa tank dal fofou la
Fou bonne la tèkk tankame bobou dou kilifeu bou bakh seytane leu
@@momo-hp4yf les archives de Maam Cheikh et de S. Pape Malick si on les sortez ton genres de mbam gui xeum et pourtant yaggoul 1994 à 2012 Ndeyssane bobou les tricheurs com toi n'était jamais dans les conférences et gàmmu de Maam Cheikh
@@diagnendoye5756 affaire bi dou mame cheikh j l respect aussi sama serigne leu oki il s'agit de Moustapha kokou mot seyante bon di moi lane mo takh mame cheikh wakhone même souma fatoo Moustapha bouma Time repon sur sa Moustapha amoul yarr est tu l sai
@@momo-hp4yf un 55m0m
@@papeabdoulayeniang7469 pardonn lo wakh
Khamna SERIGNE BABACAR SY Niko ayy rakam fonké eupna Histoire moom sou amé ngayy dégg bén camp rekk Di wakh khamalni bénén Camp bi sou wakhé RÉÉWMI TASS
Ko khamal walatt rekk khamal nala litre
Wa SALAM
Walahi lou lére nga wakh
Li pape Malick wak moy deug
@@seydinambengue7966 wallahi daye fène. Niom gni nio diakhassé niari pa yi. Sene kourel moustarchidine yi doul yague nagneko def. Niom nieup nio yam. Mo takhe serigne cheikh rouss banione doundou khalifa gui
@@دفراتسنغال qu'Allah te pardonne
LY ng sante mais santo SY. Bo beugué ko xamal liteur wala walaat dawal xooli say maam yi néke Kolda.
Boul nangou doone soldat si guerre bo nandoul
Diarama Seydi mouhamadoul Moustapha sy al-mourchid
Masha Allah amna solo leir na nagn nala Yallah faye yiw In cha Allah merci beaucoup Sy Malick
💚💛❤
❤
Lii xewoone c'était très grave , degeul lii s. Pape Malick di expliquer rek lii mom pour ñioune gñileu la jeunesse. Mais courage et bravoure moci gueen Maam Cheikh
Motakh goorou diné biko donneu faw mou sonneu mais la vérité finira de triompher tôt ou tard
Moustaphal Makhtum soit béni à jamais
Mon père a été acteur dans l'histoire. Gni daniouy doul. Tribunal niom la diokh sakh tort. Wallahi daniouy fène
Yén dal li ba kagne 1957 ak li dokh si diguénté bi yép mame Abdoul Aziz sy dabax ak nimou mélon ak ndiabot gui serigne cheikh avant Mouy dem boléna ndiavot gui yep si taxa wayou al amine pape malick sy ak khalifa général des tidiane lép guénnei dra doufi rafétei seydil hadji Malick liguéyoufi li bayi lén sen yi amoul bene chance niou ndiabotou amou gnousi khadji ak séne niép lanou beug
Thieye mame cheikh bou doull wone yaw dieure dieuff sy malik
Di ko remercier honnêtement ndkh taye kou Diot thi Mame cheikh Ahmed tidiane sy Al maktoum nako guerumé Serign Moustapha sy , faté khadioufi
Kane mô dieulé Mame cheikh France"?
Kane moko présente wate sénégalais yi 1995?
Kane moko indiwate maolid a tivaone 1998
Kane mo wakhni sou aldjana dône louer appartement dinako louéellle appartement
Thi goudi gamougi ?.
Kane la Mame cheikh Ahmed tidiane sy wakh ni sagalma yala nala yala sagal
Kane moy le prince de la ville sainte de tivaone ?
Kane la nieup Di weur ?
Kane mô latéwoul way ?Kane mo wakhni kérok 40!jour Mame cheikh wiraasabi moma guenal miraasbi
Faté amoul dofdoflou mofi Bari bayiléne dofflou bi
Dafa ame Lou yala maye Serigne Moustapha Moy wakhnananou djoumhatoul hadara aulie de hadaratou diouma ...est ce que wadial ga sa bop pour accéder fofou
Yalana yala motaly inchalla yéné sérigne moustapha sy thi al moustarchidine amine
Walay ndeysaane
WALAHI liga résumé dei moo di dëug
Yalna ñiou Yallah mousseul ci kigñaane ak xol bou doul fekh ba mou ak nafehq
Yallah defnou ñiou nek Diaboot Seydi Moukhamad Moustapha Sy Makhtum ba Faw insh ALLAH Barké gñimou am ñieup ta yorré seen Ndono
Khadija Niang daal beug nàleu dei Yalna Yallah bayila ak kilifa gui ga motali sa Tarbya ci diam Barké Maam insh ALLAH
@@diagnendoye5756 amin inchallah❤️
Walae ndeyssane sxna Khadija Niang...nioune AK Serigne Moustapha ba khiyama inchallah
Serigne pape malick sy moye wah
Aldiana firdawss...🙏 🙏
Wamé khara ma mandou thi wakhou serigne Moustapha sy li kone dafa yag
Bilahi
mandoul rek kharit amna lou graw
Bilahi tayy rek dé
Sénégal daffa barii ayy nafékh mais serigne moustapha syy fimou tékk takame fôfoula 🙏🙏🙏
Yaw yamana doul
Gisge kouye titero serigne babacar té boléwosi Serigne cheikh boléwosi Serigne Moustapha pértegua doame dara si serigne babacar bilahi baelek yagatoule
Bilahi
Bilahi
WALAHI Mbodj wahga deug ndakh moo leen fi nekal ci lou wer
Motakh la daloone Yonett Bi SAWS ak SaKhabàb yi ak Cheikh A-tidjany Fatimy ak Cheikhou oumar ak Maodo ak Serigne Babacar ak Serigne Cheikh faw mou dalko Sy Demba khouradia Mourchidoul Am wantei Yallah diko samm rek ci seen Barké ñiom insh ALLAH
Sonnal neu kilifam taxawou ko mouy Serigne Cheikh ba mou tok founé ci conférences yi ak gàmmu diko ceedé MashAllah
Motax moy raw ba faw insh ALLAH ndakh mérite la am Mawlaya Sy Demba ♥️🤲🙏
Bou leen tardé le liguéeyou Dioumadji. 1957 wéessou na nioungui 2020. Keur Seydil Hadj Malick wakh leen si jamm waay moo raféte. Aythia si Dioumadji. Aythia Aythia
Lii mome ,mane dai khamatouma thi dara.
Dolen andi li tapha sy sah pape Malick 2019 Gamou sosrek yenaco man
MAINTENANT ON COMPREND MIEUX CE QUI S'EST PASSÉ. YALNA YALLA SAMEU SERIGNE MOUSTAPHA SY 🤲🤲🥰🙏❤❤
sa reste des video plus grav
@@papebiramendiaye3981 a
@@mariannediaw8391 oui pourtant guisago dara
@@papebiramendiaye3981 c'est pas bon de déterrer la hache de guerre déjà enterrée
@@rifodne6354il l fait absolument parcqu’ils y’a d hypocrites qui savent bien ce qui s’était passé hier b noppi beug takhaw di diaboliser ko sét wéth🤷🏾♂️
Mbaur mi dal maktom la
Alhamdoulillah si leeral yi yanna yalla def diammeu si nieupe
Diaaraama Diaaraama Diaaraama seringe Moustapha sy kou sokhoroul ni la Diaaraama
Je suspens mn jugement parsk ndiabotou mame seydil hadji Malik sy amwama feté nieup beugeu nalein té yallah takh
Boudoule wone Mame cheikh cône Mame Babacar dioye dome
WALAHI kigñaane ak nafehqyi ba legui ñiou gui fi
Mane Serigne Babacar sy tek
Salam dieredieuf yala fayal noulene amine
Yalla yalla are wa keur Elhadji Malick té arr kilifeu heup
Machaalahu amna solo
سيدي ومولاي السيد الشيخ محمد المصطفى سه المكتوم حفظه الله ورعاه وأيده ونصره وأطال بقاءه وعمره مع دوام الصحة والعافية والتوفيق والسداد بجاه اللهم صل على سيدنا ومولانى ورسولنا محمد وسلم
Mame cheikh fimoudiare limoudathe lignoukawane wayé ba elek basa kanamou mame babacare
amiine inchallha
Machallah ♥️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😭😭😭Je Suis tellement Triste De Voir Qu'ibliss Ne laissera jamais Les Fils d'Adam Vivre en Paix,De Surcroît Les Muslims 😭😭😭Et Je Comprend Mieux Pourquoi DIEU a repris le Fils Du prophète Saws avant Sa mort......😭😭😭 Même les Familles Prophétiques ont Connu ,Par le Passé,Des conflits similaires Qui n'est que l'œuvre de Shaytane....Que DIEU Ns préserve de Ses méfaits Nous autres......😭😭😭
Dieu a pris tous les fils du prophète SaW avant sa mort parce que le fils d'un prophète est un prophète alors que Mouhamed SAW est le dernier des prophètes
Nitt daguaye rèfatall li amona mais bou diekhè diekhè nitt dou yèe fitena bakhoull
Sengebi gnogi jiyare ësece lolou moye dohe si ceurgi ba légi dahe serigne Mensour masoule dougou diacaye serigne Babacare si loutahe lolou
Est ce que woor nala ni affaire bi diekhna??
Yaw dei ya nafeqh gñi di venger wou gané diexna.
Amna kou xolam doul cedd ba moùk ndakh kigñaane
@@moustaphaniass9098 lolou dafa niaw torop sakh,,bilay
@@moustaphaniass9098 est-ce que li nga wakh weur nala ? Yalla nélawoul déh
Machallah amna solo ❣️🙏🙏🙏
Yalla na diam yague si barke maodo malick
La famille de Seydi El Hadj Malick a une grande ouverture c'est pourquoi ceux qui font le mal en profite pour les diviser. Entre eux (la famille SY), jamais aucun n'a fait le moindre mal à l'autre. Ça se justifie à travers leurs rencontres. Qu'Allah nous éloigne du démon !
L'histoire se répète encore une fois
Histoire day diékh. Finalement ils se sont réconciliés. Pourquoi vouloir encore créer des conflits.
La vérité sur les agissements infondés de Moustapha trouve sa source a la suite du décès de Mame Abdou dabakh le khilafat devait revenir entre borom daradji et Serigne cheikh le droit d ainesse a joué en faveur de borom daradji les hostilités ont commencés c thierno mountaga tall le père de madani tall qui a fait la réconciliation depuis lors Serigne cheikh a clôt le débat c Moustapha qui a chaque gamou remit le couteau dans la plaie mais il ne verra que du feu incha allah
Serigne Moustapha sy mom ba tay wayei lép dina diéx
@@alhassanesy1194 tu mens dh Serigne Cheikh n’a jamais cherché le titre de Khalifa il était même contre et d’ailleurs il a même dit devant Serigne Abdou et eux tous que dondou na Serigne Babacar Sy tei dougua goul bamel donc ioe liguay wax foko. Les agissements qu’ils font sur Serigne Moustapha Sy vous ne le voyez mais quand il répond vous essayez d’attraper sa veste vous allez tous croupir en enfer
@@taibasakho2424 s il y a quelqu un qui ment et qui pète tres très fort c bien taiba sakho ou étiez vous quant thierno mountaga le père de madani tall recevez Serigne cheikh et Serigne Mansour a son domicile à la médina pour arrondir les angles au lendemain de la disparition de Mame Abdou dabakh sur le khilafat de Mame maodo renseignez vous au lieu de mentir et de Peter a tout va
wallay Ndayesan
Merci Sy Malick
Machalla pape malik
Machallah li moy deugeu
Képe kou deuk tivaoune khame nga li xéw lou serigne Moustapha sy di wakh lépe deug la
Sy Demba dou waxanetou moùk sakh
Ay bayam yi amoone taxaway liñiou doone dénoncer moo nek nii
wakhatiko
Dangay fène d, histoire bi niou done dialhassé nieup khamnagneko
tu a reson mon ami
Walay Ndeyssane
Macha allah mame cheikh tidiane sy
Moustapha moom bou sagnoon kén dou nékk thi diam koudoul moom wayé YALNA GNÉPP AMM DIAMM KOU BEUGG AKK KOU BAGN
ta rien compris
Ndeke sokhore yaguena âme
Borom xol yi doul cedd ba moùk diarna ñiou yeureum
Serigne Moustapha sy notre responsable moral la yantikou anil hawa
Alhamdou lillah
Gni khamoul rek nioy wakh mai lii lére faire yi dou tay yagana
Walaye degue bou wérla makgnepou fékénagnouka senegalkaye ils sont comme ca
Adouna amoul solo lep daay diex
Salam yala khare lene aldianay firdawssi amine
walahi sy
Amnasolo ♥️♥️♥️
Machalla
Je suis choquer thi commentaires yii nitt dal dey mandou gnii di kheuth fii gni di kheuth fé dama beug serigne babacar sy ak ndoabotam beug serigne mbaye sy abdou mais lou dembeu doumathi jugé keneu gnome gneup ndiabotou mawdo lagnou areter sen yone nekouthiii
Thieyy Mame Cheikh kéneu d'où mome
....
Louma siy wax daal lenna leu problème bini s papa Malick di wax yalla dièkhalonnako bou yagga
Li am nak yalla nako yalla dièkhal
الفتنة نائمة لعن الله من ايقظها
وقال الشيخ الحاج مالك سي
والشيخ من توقيره توقيره كل
الذي من حوله يدوروا
Est ce que diekhna??
Yangui degg Papa Malick diwakh ni deff nagn réconciliation 3 fois
Gñi taa loll bobou ñioko tàlatt bi lifi nek nañiou wakh nafehq baxoul.
Amna igñanei sakh seen bopp beug ñiou kou bakh
@@Malick12-f3m wakh deug Yallah Y'a certains Sénégalais dañiou nafehq WALAHI piir nafehq
Macalla
Walahii sy Malick
Khana yii rék gnoy khakh
Yen wa sit bi Saytane gen
Démlén khami yalla si baye Niass Mo Gueun
Wakhofi dara
Wakhi doff baye niass moy kan Serigne Moustapha sy mo fi raw
So khamoone Yallah doo toogne,Dinga mandou si keur goo diokouwoule.
Ladial Baye Niass rta kan mooy Mame cheikh
Saytane iblise 3:11nitou safara
Mbaye sy Manssour kou dangereux leu
Louwarale vidéo by ?louraféte baxxna
Waw ndakh beugoulene deug ay nafekh geune
Talibe day yam plasou talibe you melnii diaroul di feusal
Saytane ngueen trop
Merci
Maodo xamone na li Fadiouko bala mou guéneu adouna té meunone nako safara wayé topou sonou YONENTÉ bi Aleykhi wa Salam bamou diekh takkeu motah mouni seugam xéwone na keur YONÉNTÉ bi xéw keur CHEIKH damay bayi mou xéw sama keur donc li ware moy gnou topou séni diangalé té manou si problémou keur gui gnoune nio siiy lorou mai jaabotou Maodo dougnou lorou
baayil doul
Dieureudieuf Issa fall wah bi rafet na
Khana serigne Manssour Sy borom darra dji mo done dem di netali😂
Lep.DINA ler
C'est la famille limiter vos paroles
44⁴ : k
Machallah
Machallah