Bismi lahi rahmani rahimi dieuredieuff dieuredieuff si kandou you yiw yi wakh dji rafét n'a lol alassane ak sény sagal nga baye ouseynou laye sagal nga akhlou beyti rassoul serign ibrahima laye domou baye rane dji ya rafét kandou yala nala yala fayal bopam merci
Ma sha Allah Baye Ousseynou yalnaniouko Yallah fayal thi barké Bayam ak Mamam Khayrou Khalkhi Lahi ,djeureudjeuf Cherif Ibrahima Lahi contane thi yaw
Ma cha allah. Dégg na tayy lou bess thi cherif.
Machala yalana yala sama là Laye makhtar
ndeysane baye Ousseynou Keene d'où moom yalna KO yalla faayal bilahi mooma deefar.
Bismi lahi rahmani rahimi dieuredieuff dieuredieuff si kandou you yiw yi wakh dji rafét n'a lol alassane ak sény sagal nga baye ouseynou laye sagal nga akhlou beyti rassoul serign ibrahima laye domou baye rane dji ya rafét kandou yala nala yala fayal bopam merci
Salam laye Mamadou maxtar deugg buwer nga wax Chérif Ibrahima dafa xam loubaax loubaax rk ley df diko wax
Serigne Bachir diadieuf laye makhtar Sangua Ibrahima yalnako Yalla gueune takhawou
Jajëf laay maaxtaar
Laye Makhtare yala ngafi yagueu té wéér borome bakh
Yala nagnou yala tass ci barcké Chérif Ousseynou Laye
Bilay walay geum wolou yakar Seydina Limamoul Mahdiyou Muntazar Lahi as rek
Merci beaucoup laye layemahtar
yalla naniou ka yalla fayale si Barker Mame
Machallah lahi makhtar ya niak kiniane lahi
❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤️🙏
Machalah Laye makhtare
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤