ndeysann machallah ne change pas sidy diop ligua famille wally ballago seck rafete na, tt les faramarenns contane nagnou,merci pour cette belle hommage li Nice na trop......félicitations
Mashalah Sidy Diop senegal 🇸🇳 parparlo ba bari rekk mais wayy katt yinga bokal générations guissouma koula si meune au contraire bolleine gueunoul nangou batt voix bounekh🎶🥰❤️ Yalla na sa djammeuh yagg wally Séck yalla nalla yalla deffal djammeuh takhawou lah samoula arrla si barkei Seydina MOuhamed
J'ai les larmes aux yeux quand j'écoute ça bilay sidy Diop yalna sa Diam yague tu es pétri de talent boul nangou ken dila diakhassé avec qui k ce soit toi et Wally vous êtes des frères li moy adouna dinganté bi nassi nieup dokh diam et on attend votre duo
Sidy Diop va devenir une légende. Il me fait revivre les sensations que donnaient les grands chanteurs : thione Youssou Omar pêne.thi kanam ngene keye khame 11:01
Sisou mane yi nopal lène séne bopp ki dafa meune trop loumouy def ok. Félicitations si hommage de papa thione seck bi..Tu est le meilleur de ta génération point.
Cest a l'avenir nanouy kham meuna wayou sidi diop , bilahi wayandowoul ak ken macha alla malheureusement doler yamoul pour linstant mais sou doundou yaguer dina meussa lerr
Il est tps que vous relevez le défi car papa Thione Séck aviez montrer le bn chemin yalnalen thiat sékhlou bne continuation et autant de surprises dans l'avenir🤜🤛
D'une manière générale, je pense qu'il chante plus avec le force, le fond qu'avec technique. S'il continue comme ça, il risque d'avoir des problèmes au niveau de la gorge. Déjà quand il parle, on sent une voie grave.
Je respecte ta position. Je ne dis pas qu'il ne sait pas chanter mais il dépense beaucoup d'énergie en chantant . ce qui peut cacher sa voix à long terme. La musique c'est la technique.
@@danslerespect3180 je respect ton opinion mais quand on est jeune et a force de faire beaucoup d'efforts pour travailler ta voix , te servira de l'experience a l'avenir et tu gagnera une diversite vocal comme le cas de Youssou Ndour a l'heure actuel
Vous parler de Youssou Ndour, lui même a dit lors d'un entretien avec Aissatou Diop Fall, publiquement que chaque jour il rencontre des jeunes qui ont beaucoup de talent. Il dit qu'on peut avoir une voix meilleure que lui mais la ou il dépasse tout le monde c'est par la technique. C'est Youssou même qui la dit. La musique c'est plus la technique que la voix. Tu sais chaque type de voix peut chanter dans un registre bien approprié. Ce qui fait la chanson c'est la technique. Si c'était la voix seulement fallou Dieng, Idrissa Diop et Amineta Fall ( c'est de la génération de kine lam) ne seraient pas des maestros car leurs voix ne sont pas extraordinaires.
Machallah sidy DIOP soit soudé avec wally seck vous êtes l'avenir de la musique Sénégalais 🇸🇳🙏
Vraiment c juste je n suis faramaren mais c son je l écoute c pertinent
@@elhajmodoundiaye7259 M,,,...vv.h!h
@@moustaphasenghor6147 I
Vraiment Machala
ndeysann machallah ne change pas sidy diop ligua famille wally ballago seck rafete na, tt les faramarenns contane nagnou,merci pour cette belle hommage li Nice na trop......félicitations
Mashalah Sidy Diop senegal 🇸🇳 parparlo ba bari rekk mais wayy katt yinga bokal générations guissouma koula si meune au contraire bolleine gueunoul nangou batt voix bounekh🎶🥰❤️ Yalla na sa djammeuh yagg wally Séck yalla nalla yalla deffal djammeuh takhawou lah samoula arrla si barkei Seydina MOuhamed
J'ai les larmes aux yeux quand j'écoute ça bilay sidy Diop yalna sa Diam yague tu es pétri de talent boul nangou ken dila diakhassé avec qui k ce soit toi et Wally vous êtes des frères li moy adouna dinganté bi nassi nieup dokh diam et on attend votre duo
Le meilleur rend hommage à la légende c’est vraiment beau il aurait aimé ça de son vivant
Sidi le meilleur de sa génération Aÿ way ya ma si doy 😭😭😭
Machalla depuis hier j'écoute cette morceau tres bel hommage tres réussi sidy a beaucoup de talent machalla
N0uj9ub9b0 j
Machalla sidi diop ya meuneu woy yalla na yalla lafalla thiat woy rek ngaye def bravo au musiciens.
Machalah sidy Diop yalna bate bi weer woye rek guaye défe bilaye contane thi yaw bonne continuation ♥️♥️♥️
Il faut continuer comme sa avec ton frère wally la vie est trop courte
bien dit vraiment merci
Wallay ndéysane adouna doudara🙄🤭
Dans il faut réster toi meme baniang déclou les seytaner
Walahi ndeyesane bien dit ma chérie
Bilahi lidaffa nekh machalla wadji raffat na ❤❤❤
Sidy goudal fane way félicitation 7 jours sûr 7 yow rek laye deglou 🥰🥰🥰
Machallha Sidy Diop yalana diam sonal si Barcke lérou Seydina Mouhamed 🤲♥️♥️
Sidi diop doo nitt tu es très fort
J'ai pas l'habitude de commenté mais vraiment sidy est très fort wakh deugg
Sidy Diop va devenir une légende.
Il me fait revivre les sensations que donnaient les grands chanteurs : thione Youssou Omar pêne.thi kanam ngene keye khame
11:01
Deugue deug sidy diop meun nga waye😍❤❤❤❤❤❤
Machallah nak dagua meuneu way❤❤ rawatina hommage à pape thione bi ❤❤❤❤❤❤yalnako borombi yeureum thi barkep kou téd ki 👌👌
Sisou mane yi nopal lène séne bopp ki dafa meune trop loumouy def ok.
Félicitations si hommage de papa thione seck bi..Tu est le meilleur de ta génération point.
Wakhal way
Bilay meun na limouy def
Cest a l'avenir nanouy kham meuna wayou sidi diop , bilahi wayandowoul ak ken macha alla malheureusement doler yamoul pour linstant mais sou doundou yaguer dina meussa lerr
L'artiste le meilleur One love kou beugoul bayil nioune beugg naniou❤️✔️
Je partage
Yaw bag nala dh
Kobakol nion beugue nan
Dama ko beug sam rakk ji
Je valide frah🔥💪🏆🌠👊🙏
On parle de Sidy mais le groupe est très fort ( les musiciens)
sidi diop ya meuna wayy machala
yalna sa jam yagg
Thank you very much Sidi for da song is really nice and we really appreciate it alot.
Mahalah sidi diop yalla na yalla doli diam sa dinganté ak waly seck li fi diar faye bilahi yak wally kéne bonou si yalla naléne yalla same
Il est tps que vous relevez le défi car papa Thione Séck aviez montrer le bn chemin yalnalen thiat sékhlou bne continuation et autant de surprises dans l'avenir🤜🤛
Sidy mi nakatè way rek lay defff
Ki moy domeram deug
Ndeysane 🕺🏾🕺🏾💃🏾💃🏾💃🏾💃🏾
Merci Sidi ,Papa yalla na souf oyof ci kawam
Il chante bien Sidy diop... ndéyessane adouna dou lëp si ay nétali lay moudié
Deug deug yaram dawna yeuh dess😭😭
Sidy Diop ndannan pirr laah❤️
Senegal 🇸🇳 deuke bou amut law
Vraiment Sénégal dafa mety ki wally meunouko khagn weurseu gueum et lui aussi de mme aplaudiser et soyer positifs
Vraiment mboup Senegal deh wakh rek lagnou def. Mais kounai kham nga sa bopp sidy diop rek dou ay foo MAchalla
Saway danga faté Sénégal nga nekk. Non def gnou créer rivalité entre chanteur yi.
Masahalha
machallah papa thione restera gravé dans nos coeurs❤
Kholeine ko si baba Mall Omar pêne youssou Ndour ismaela Lo papa Thione et Jules Faye gno book génération tei batay sein digeunter mingui rafet 🙏🏻❤️
Machala sidi j ai des larmes au yeux
Machallah mon artiste préfèré
Ki da meune limouy def
Machallah
Sidy Diop yala nala borom bi faye sama artiste bi dem na 😭😭😭😭
Vraiment c'est beau sidy le meilleur de sa génération machalla le meilleur reste à venir inchallah 🙏🙏🙏🙏
Quelle voix je l'aime beaucoup ❤️❤️❤️🤴
Ana gnikoy sétal chaque jour👋
Machalla sidy talent kassé gua avec une belle voi
Mashallalh mashallalh nice trop yalnala khiate sekhelou mashallalh raffetena
Masha.allah sidi diop yalla na yalla weral batt bi diam si ioe goudou fane si keeparou banèkh insha.allah li nèkh na tè daw yaram walahi hazim 😭😭😭😭
SIDI DIOP vraie diambar la ☝️☝️☝️☝️ il est fort
Billay
Barki Serigne Bamba da meuna weuy li dafa fess way ndanane leu man feu msq fimou nek la atanoul man
Il est pétri de talent Sidy Diop
Je vois que jeune homme chante bien fusionne ton cœur avec sa famille par le biais de Waly ame léne diame AK Salam
Super sidy diop 😭❤❤❤👍🤲
Toujours graver dans nos cœurs 😢papa thione RIP 😢💔
Je t’aime beaucoup Sidi Diop 😍😍
Mashallah continuer comme ça avec ton frère Wally séck borome bahla
Trop bien chanter machalla sidy
Machalla sidi merci lii nekhna way jvs aime
Belle est bien quel prestations de sidy diop qui rend un grd hommage à notre père papa thione 😭 repose en paix
Blh li yague na dh mais chaque jour dama koy déglou❤❤
Machala tay mom diokhnala lokho non li dafa eup sidi dagua meune nakh 😭😭
Meilleur de sa génération
Machalla sidy yaw ak wally ben guene
Gnom artistes Yii Amou gnou problème dafa am sii gniye commentaires Kat Yii gno xawa doy waar lol
Nice Nice je suis un fans de Wally mai tu ma vraiment touché machalla 👌👌👌😔
Machala vraiment u ma fait pleurer 😭😭😭😭😭😭
Limay déklou mbalakh beuriwoul waaayé sidi diop yalla na yalla sammou la ta arrrleu sa #2stv tamit kén dou yén
Wakh yé fii nék rék way musiciens sénégalais yii beineu m'bokou lagnou keine mounoko khar niarr donc courage à vous
Papa thione maman diaga momy seck paix à leurs âme
Ee longue vie à waly seck
Akk werr inchalah
La marge de Progression de ce Sidy Diop est vraiement impressionante
D'une manière générale, je pense qu'il chante plus avec le force, le fond qu'avec technique. S'il continue comme ça, il risque d'avoir des problèmes au niveau de la gorge. Déjà quand il parle, on sent une voie grave.
@@danslerespect3180 Sidy chante avec technique et facilé surtout en matiere de improvisation c'est le seul de generation qui save le faire..
Je respecte ta position. Je ne dis pas qu'il ne sait pas chanter mais il dépense beaucoup d'énergie en chantant . ce qui peut cacher sa voix à long terme. La musique c'est la technique.
@@danslerespect3180 je respect ton opinion mais quand on est jeune et a force de faire beaucoup d'efforts pour travailler ta voix , te servira de l'experience a l'avenir et tu gagnera une diversite vocal comme le cas de Youssou Ndour a l'heure actuel
Vous parler de Youssou Ndour, lui même a dit lors d'un entretien avec Aissatou Diop Fall, publiquement que chaque jour il rencontre des jeunes qui ont beaucoup de talent. Il dit qu'on peut avoir une voix meilleure que lui mais la ou il dépasse tout le monde c'est par la technique. C'est Youssou même qui la dit. La musique c'est plus la technique que la voix. Tu sais chaque type de voix peut chanter dans un registre bien approprié. Ce qui fait la chanson c'est la technique. Si c'était la voix seulement fallou Dieng, Idrissa Diop et Amineta Fall ( c'est de la génération de kine lam) ne seraient pas des maestros car leurs voix ne sont pas extraordinaires.
Dafa gaw trop way bi pape thione temps wam lay dieul di c chanson
Mai félicitation kmém
Sissi ta raison mai c’est parsk c’est pas de l’acoustique c’est du mbalax mai écoute la version acoustique tu verra
@@antoniobanderas9559 mm celui d pape thiouné étai du mbalax mai kmém cté lent
Sidy rek 💯♥️💯 🇸🇳🤲🇸🇳
Machalla sidy Diop day deem
2ans si kanam yayi dak weuy senegal mako wax do nit tu es for sidi diop
Sheuuuuuu sidy meune gua😭😭😭😭❤️❤️❤️❤️😭
Sidy diop do nitt tu es très fort machallah waye
Très bien machala rafettt na yak wally ay frère guéne am lene diam rk ❤️❤️
Mashallah ❤️💞❤️❤️❤️ Mashallah ❤️💞❤️ Mashallah Sidy Diop 💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞 Mashallah
Meilleures chansons de sidi bonne continuation
Machalah deyssane
Depuis la Mauritanie
Thiey fans mo soneu dé loulen lerr niou wakh loulen leroul niou wakh niom niepa meuna way koufi khass ken rek daga sokhor mais niep ay ndanan lan
Mashalah sidy nice na adouna Amoul solo
Le future roi du mbalakh inchallah
sidy nékhna nak 💪🔥🔥
Merci beaucoup 💔 sidy
Baaat bi macha'allah geun laa siiiw wala eup la xaaalis meun neu nékk mé dakheu laaa way amoul sénégal
J t aime fort ❤️❤️
Sidy machala sa xolll dafa rafet saytaneyi niola sonal
Boy bi mom ame talent
♥️😍😍waw waw sidi
Walahi li dafma dioylo😭😭😭😭❤❤❤ sidi diop walay contananiou❤❤❤❤
Machallah frère tu es le meilleur
😭😭😭😭😭😭😭😭
Bilahi sidi Diop d'où nitt lahi laha ilallakh
Quand je vois sidi chante thione seck j'ai des l'armes aux yeux bly. Bonne continuation
You nailed it bruh😭💔❤️👂
C bien sidy machalah continue comme sa dina bakh mé diangal wayou Souf aussi si kaw nga guena meune mé nak yagui si yone Dina bakh inchallah
Machallah sidy danga meune❤❤❤
Ndaysane dawna yararam😪😪😪
Sama yamarr day daww billahi 😭😭😭😭😢
il est tres fort one love bro
Sidy diop nice na trop def nga lila warr
Ho machala sidi Dale dama KO beugue rek avec sa belle voix machala li rafetena loool
Machalha Machalha Machalha yalna yalha weral bate sama dom dji bonne continuation
Boy bi il é fort💓
Ndeysannnn😭❤👂👈
Non yalla khamnani sama khôl toy na ndakh sidi Diop je suis lougatois té danga nio yeuk
Le chanteur du peuple