Les révélations de Khadim Samb : "Reug Reug ndanane la mais Balla Gaye ak Sa Thiès nio dakh beuré.."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 12 гру 2024
  • Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
    / luttetv
    / luttetv
    luttetv.com/
    / senlamb

КОМЕНТАРІ • 131

  • @ISmile__
    @ISmile__ Рік тому +13

    Ce qui fait son charme dans sa communication au delà de son vécu, c‘ il relate tjrs l’histoire avant de répondre à la question posée et c magnifique 🤩 Machallah goudou fane ak weer

  • @dabondiaye7917
    @dabondiaye7917 Рік тому +15

    ❤❤❤❤❤ pere goudale fane bilahi ya kham histoire masha Allah bègue na

  • @ibrahimadjitte1803
    @ibrahimadjitte1803 Рік тому +8

    Way way père goudal fane waay.
    Fadam kéne dou yaw
    Meilleure interview de la lutte de l’année.
    Lutte Tv djajeuf.
    Lamine Seck focus reik 🎯

  • @yacinebouballaguaye2243
    @yacinebouballaguaye2243 Рік тому +5

    Machalla père khadim vous avez raison très bien parlé père un vrai savent qui conné beaucoup la lutte 🤼‍♂️ merci pour la sagesse nékaléne si diam Amine yarabi ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲

  • @bmkillertv1849
    @bmkillertv1849 Рік тому +9

    Un vrai connaisseur..de la vie en général

  • @khadimfaye6565
    @khadimfaye6565 Рік тому +5

    Sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès sa thiès félicitations 👊💪🥰

  • @papalayelephoceen7575
    @papalayelephoceen7575 Рік тому +8

    Balla gaye 2 vrai Champion ❤❤❤

  • @bara97437
    @bara97437 Рік тому +3

    Tu es le meilleur pronosticeur de la lutte sénégalaise

  • @mbayediop299
    @mbayediop299 Рік тому +1

    Merci père machala wahbi rafete na vraiment

  • @boubacarboiro5813
    @boubacarboiro5813 Рік тому +1

    Lutte TV la télévision leader de la lutte sénégalaise

  • @banihachim6825
    @banihachim6825 Рік тому +1

    Fadam est trop malin macha allah, daye jangalè daye out xam xam,

  • @babacarsamb9883
    @babacarsamb9883 Рік тому +1

    Pére vraiment tu es exceptionnel

  • @elhadjidiawdiaw5249
    @elhadjidiawdiaw5249 Рік тому

    Mais pere Khadime yalla na goudou fane waye amine

  • @dabakhwade4695
    @dabakhwade4695 Рік тому

    Bilay Père doundeul way lingaye wakh si demb amna solo trop Mach'allah.

  • @falloumbodji3062
    @falloumbodji3062 Рік тому

    Merci beaucoup nekhna

  • @itsbra7309
    @itsbra7309 Рік тому

    No per yalna yalla defal la diam

  • @abdourahmanesindidi1818
    @abdourahmanesindidi1818 Рік тому +5

    Fadam kom kouy deglou khoutba🤣🤣

    • @mbayendiaye626
      @mbayendiaye626 Рік тому

      Saway ray ngama🤣😂🤣😂🤣😂🤣😂🤙

    • @thiernodiallo2830
      @thiernodiallo2830 Рік тому

      Woy magui dhe 😀😀😂🤣🤣😭😭😭😭

  • @bayedarou1936
    @bayedarou1936 Рік тому

    Ki moye lamb ❤❤❤❤❤❤ boukoye wakhe sa yarame dawe

  • @cheikhsadibouthiam
    @cheikhsadibouthiam Рік тому +1

    Parler un peu de feu Landing Diamé
    Il était un ancien lutteur résidant à Thies précisément à cité lamy qui a affronté certains lutteurs comme double less, falay baldé , pape kane et autre et qui leurs ai terrassés.
    Vous devriez parler de lui et essayer de faire revivre son nom sur la lutte sénégalaise
    Il a même un fils sur nommer FILS DE LANDING un brave et fort enfant et espoir de la lutte. Un vrai champion de thies qui a terrassé la plus part de ses adversaires à Thiès.

  • @abdoutall8491
    @abdoutall8491 Рік тому +1

    Toujours un grand plaisir de regarder ses interviews pere Khadim Samb goudeul fane waay 🙏🙏🙏❤️

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 Рік тому +1

    Tel père tel fils machalah

  • @mamemoussagueye952
    @mamemoussagueye952 Рік тому +1

    FADAM nekhal na interview bi🤣😂🤣

  • @badiallodia4208
    @badiallodia4208 Рік тому +2

    Reug c'est un compétiteur soyez pas jaloux stp walae mo meune mo eup dollé
    Il va marquer son emprunte par A ou B
    Lolou lah gayi xam motaxe kouné di sissou

  • @moustaphagueye3322
    @moustaphagueye3322 Рік тому +1

    9 heure bah Takousane😂😂😂 père goudal fann🙏🙏🙏🫵🏿

  • @papedieng8170
    @papedieng8170 Рік тому +1

    Lidafa warone am khalam si souff ak guitare 🎸

  • @kadelbiagui4338
    @kadelbiagui4338 Рік тому

    Bravo ❤jaime beaucoup fadam2

  • @mouhamedmirzaseck1434
    @mouhamedmirzaseck1434 Рік тому

    Père boye remarque ben défaite la am contre doubaless si liniou yeuk nioun walo walo yi❤

  • @simonediop2094
    @simonediop2094 Рік тому +1

    Aka nekh wakhtane machala

  • @abdourahmanesindidi1818
    @abdourahmanesindidi1818 Рік тому +3

    Fadam do nopi loy hon hon yi ni 🤣🤣🤣

  • @damedia9410
    @damedia9410 Рік тому +1

    Un vrai plaisir

  • @ndiayeabdouaziz588
    @ndiayeabdouaziz588 Рік тому +1

    Fadam 2 borome 3 comba 3 defitte mo teki gembam si birr quediaway 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 Рік тому +1

    Père boul takh khadim ndiaye ak wa thiaroye khass leu😂😂

  • @naniousamejikkoyi2112
    @naniousamejikkoyi2112 Рік тому

    *bira sene mo manoul té bayiwoul liye dougue CNG thi aye millions écran vare bou normal pour vare sakh on ne peut pas lavoir depuis l'indépendance jusqu'à nos jours rien à changé pour innové la lutte donné le cng à kéba santé je la connais pas mais je voit un homme ambitieux intellectuel et à la mode pour changé le tempo de la lutte,bira sene est incompétent naniou méye waye té démé togue on a besoin d'un président de la cng jeune et branché*

  • @mouhamedmirzaseck1434
    @mouhamedmirzaseck1434 Рік тому

    De toute façon sëgn Ass Barhama waxoona ni lamb djii di démé té lolou lanou guiss❤

  • @sedibabounacissokho427
    @sedibabounacissokho427 Рік тому

    Machalla amne solo

  • @badaraseye6115
    @badaraseye6115 Рік тому +3

    Fadam dinama rayy hummm 😂

  • @adamasebor1072
    @adamasebor1072 Рік тому

    Kon dé meune nanio mandit 5 caisse rikéléss hoow🙊🙊😃😃🏃🏃

  • @adamasebor1072
    @adamasebor1072 Рік тому +1

    Père so beugué niou naaw la dila titeuro thi lamb rek nga waar Di waax ndaax guisnga nimou néxé Di waax lo xam tu es à l aise

  • @souhaiboumbackegueye3091
    @souhaiboumbackegueye3091 Рік тому +2

    Trot bavard Fadam laisse nous écouter prend exemple sur Lamine

  • @alphonsegomis706
    @alphonsegomis706 Рік тому

    Vraiment il conait la lutte senegalaise

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Рік тому +1

    Balla gaye deux kéne daye mom

  • @beuguesalioubeuguesaliou524
    @beuguesalioubeuguesaliou524 Рік тому +1

    Mome ak père mbaye Ngoné Sene diakarlo la yakamti 😂

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 Рік тому +2

    Fadam sof ngaa 😂😂

  • @thiounecheikh2839
    @thiounecheikh2839 Рік тому

    Machallah

  • @frankydolle7559
    @frankydolle7559 Рік тому

    Pére Khadim Samb est le baobab de la cultura senegalais
    Doundal lou beuri pére

  • @gabinksss
    @gabinksss Рік тому +2

    Waye pére waye

  • @modougueye528
    @modougueye528 Рік тому +1

    Fadam sofff nga😂😂😂😂😂

  • @mistersallpob
    @mistersallpob Рік тому +1

    Le titre de cet article lui fait dire ce qu'im n'a pas dit . il a dit que balla et sa thies sont meilleurs que leur père . alors que votre titre laisse entendre qu'il a dit qu'ils sont meilleurs que reug reug . évitez les manipulations s'il vous plait .

  • @bayefall3213
    @bayefall3213 Рік тому +1

    Lamine bilahi dfa nekh lol 😂

  • @layefall452
    @layefall452 Рік тому +1

    Man pabi dama nékh 😂😂😂😂😂😂

  • @mohameddiop3220
    @mohameddiop3220 Рік тому +3

    Fadam soff nga Barki YALLAH

  • @mamemalikniasse8916
    @mamemalikniasse8916 Рік тому +1

    Machcla li dafa nekh waay

  • @djibrildiaw8143
    @djibrildiaw8143 Рік тому

    Kharali foto 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ISmile__
    @ISmile__ Рік тому +5

    L’arbitre principal en personne ne pouvait pas voir la chute pck sa position était bonne par contre ses juges ne l‘ont pas aidé et il se devait de les consulter avant de reprendre le combat

  • @tidianeniass6391
    @tidianeniass6391 Рік тому

    Thiey per

  • @baraseck4939
    @baraseck4939 Рік тому +1

    Way 😂 lii nekhna dembe nakhon na ngor amone

  • @mouhamedsene3324
    @mouhamedsene3324 Рік тому +2

    Dégal fadam si souf 😂

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 Рік тому +1

    Balamaye déh rék gñounane balla gaye balla gaye mofi danou beurka démba balla mougué beuga déh si déféte guén nane danane mani reug reug dafa dane sa thies ba war si kaname di foto wou

    • @francoisdjiboune9153
      @francoisdjiboune9153 Рік тому

      Mais boudé photo 4 appui leu mais soudé image tank bi ak loxo fékété youniou 😂😂😂😂😂

  • @kharagnembaye5958
    @kharagnembaye5958 Рік тому

    Chaque jour ma wakh ko Sarakh Day dieul Lamb

  • @djibithiaw1259
    @djibithiaw1259 Рік тому

    Thiey fadam🤣🤣mo degue dé

  • @khalilleye7217
    @khalilleye7217 Рік тому

    No Lamine père histoire lay wakh bouko dague

  • @badajuniordiop1515
    @badajuniordiop1515 Рік тому

    Père amal diame

  • @modougueye3964
    @modougueye3964 Рік тому +3

    Fadam li mouy deff moye charm wakh tane bi

  • @malikking4291
    @malikking4291 Рік тому +2

    Thiey Fadam 2 aka meune sapali. Wa lamb Yalla na sene jamm yagg

  • @kanegueye388
    @kanegueye388 Рік тому +1

    Akay ndanane

  • @sadambathie7864
    @sadambathie7864 Рік тому +1

    Thiey fadam

  • @sultantv.télé.daara-dji
    @sultantv.télé.daara-dji Рік тому

    Limouyy wakh thi Macky Sall nii kénn ladjou koko....
    Ak yiii Mouy néttali te amoul chance....
    Wakhoufi tousss vraiment apar hors sujet

  • @babacardiop5162
    @babacardiop5162 Рік тому

    pere y'a fi né

  • @adamasebor1072
    @adamasebor1072 Рік тому

    Kon bayi reug reug li waax dji di reuy yeup dou woone mbeur ok papay sa Thiès mo tothie laamb dji

  • @mouhamedniang8904
    @mouhamedniang8904 Рік тому +1

    Lou yeimei moy mome Dalay diokh ay date.

  • @abdougueye610
    @abdougueye610 Рік тому

    Ki dafa nekh bilay

  • @momosy6083
    @momosy6083 Рік тому

    Père mala begue.bayil politique ak Macky 😁🐔

  • @ndiougamar2202
    @ndiougamar2202 Рік тому

    Li Moy sa thieur bayil sonko

  • @djibingom5668
    @djibingom5668 Рік тому

    Thièy fadam mo dègue dégual ouba thia soufff

  • @mustaphakah9768
    @mustaphakah9768 Рік тому

    Pere Ken dou iow sa Interview dafa nekh torop sah ndakhte lamb demb

  • @ndiayedistandiayendiaye2209
    @ndiayedistandiayendiaye2209 Рік тому +1

    Pa bou niak diome

  • @almacktoum3643
    @almacktoum3643 Рік тому

    Historien la

  • @ousseynoufall5759
    @ousseynoufall5759 Рік тому

    yekini ak gris arbite Bi souf lèwoule yekini mo arbitè Bopam Nay Lère sa danena reug dieuleu bou lère

  • @alassanedieng259
    @alassanedieng259 Рік тому

    Fadam mo beug ndanane

  • @mamadouloum8936
    @mamadouloum8936 Рік тому

    😂😂Fadam dineumeu raay

  • @momodiaw1776
    @momodiaw1776 Рік тому +1

    Fadam dina ma ray way

  • @khalifambengue6125
    @khalifambengue6125 Рік тому +1

    Pabi mom ay wakham doyouma dou wakhi imame Malick pabi loumou wakh té fèkèwoumako rèk geuwmako

  • @adoogie2876
    @adoogie2876 Рік тому

    Kone toubabou Dior jotna fé kheum 😂😂😂

  • @sadiokaradiallo3414
    @sadiokaradiallo3414 Рік тому

    Pere goudal fane

  • @damembengue1894
    @damembengue1894 Рік тому

    Reug reug kasei 🦍🦍

  • @papamalickmbaye
    @papamalickmbaye Рік тому

    nafékh rek

  • @FallouDiop-nm2hy
    @FallouDiop-nm2hy Рік тому +1

    250 kilos thiey père 😂😂

  • @diagnebass6754
    @diagnebass6754 Рік тому +1

    250 kilos ou 150 kilos

  • @moussagueye7902
    @moussagueye7902 Рік тому

    Historien à deux balles !

  • @assaneboye6371
    @assaneboye6371 Рік тому

    Yaw xamo liguaye wakh dama yakar nii xalise gua beug reug reug est le meilleur boné balla gaye sakh mané waw mes sa sa reug man nako ndiaguale beuré

  • @ndiagagueye2094
    @ndiagagueye2094 Рік тому

    🥰❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @modoundiayesonko
    @modoundiayesonko Рік тому

    Fadam bayil pabi mou wakh

  • @damembow6374
    @damembow6374 Рік тому +1

    Lamb dafa kharam yénn gnisiy wax niepp si lou kharam guénii wax

  • @ndiagagueye2094
    @ndiagagueye2094 Рік тому

    😂😂🤣🤣🤣photo

  • @bambagueye6973
    @bambagueye6973 Рік тому

    Khadim lima nekh thi mom dfa xam lamb Bilahi limou thi xam gniko fi xam bariwol insbi

  • @CASI7797
    @CASI7797 Рік тому

    Da meuneu yokkk nak

  • @juldf2812
    @juldf2812 Рік тому

    😂250kilo

  • @adamasecka7568
    @adamasecka7568 Рік тому

    Nit koudoute joume amoul bounu sonal wohrek

  • @Yowan01856
    @Yowan01856 Рік тому

    Thiogg Macky Sall bi moom bayi nako déglu 🤢

  • @fallouseckmame1451
    @fallouseckmame1451 Рік тому

    Machalah