Assalamou halaykum papa mbaye Gueye Syll ziarnala dila gnanal tawfékh si barkep borom touba...si possible je voudrais que vous expliquiez les wolofal de cheikh Moussa ka,de ch.samba Diarra et de Serigne mbaye diakhaté car il y'a certains passages qui demandent des éclairages...merci et bonne continuation
Salam 1erement il faut être précis cheikhou amadou et amadou cheikhou sont 2 personnes différentes. 2sèment vous dites toujours toubyi nénaniou et vous qu'est ce que vous dites ?
Amadou cheikhou Ba est un guerrier pour l'expansion de l'islam mais il est peu connu
Dieuradieuf akhmadou ndack ya khékh ba diné awo yone
Jërëjëf sëriñ bi
Alhamdou lilah akamako sokhla wone, diaredieuf Bay Mbaye Geuy
maachaAllah am në soló, waxtaan wi ku nekk war na ko dégg ! di lë Jaajëfël bu wér baay Mbaay Gëy Sill .
Rakame ibra penda bouya moye mamou Serigne Cheikh faty fall Mbacke
Bou toubab yi done lal sené pékhé, naar yi itam gno ngui done nakh nit you nioul.
Dieuradieuf Sylla
Xareb Ngaay moom nan la deme woon?
Té masoul woté mahdiyou lepe aye touma rekla
La bataille de Samba sadio c'était pas en avril mais plutôt le 11 février 1875
Oui 11 février 1875
Machalah 👏 li rek mo diara khm
❤❤
Ñewal gouy mbeuth am na histoire
Xamo histoire bi noppil boul tooñ gestoul Madiw
Diadieuf baye mbaye machalah
Toubabe danioye féne rek masoul fate domame
Yalna yala Fay Leu
Machaallahou
Pas avril c le 11 février
ماشاء الله
Assalamou halaykum papa mbaye Gueye Syll ziarnala dila gnanal tawfékh si barkep borom touba...si possible je voudrais que vous expliquiez les wolofal de cheikh Moussa ka,de ch.samba Diarra et de Serigne mbaye diakhaté car il y'a certains passages qui demandent des éclairages...merci et bonne continuation
Machalla
Serigne mbaye namou nala Lol
Vous avez escamoté l'histoire
❤️❤️❤️❤️❤️
Tu n'as rien dit sur samba sadio car tu ne connais pas l'histoire de samba sadio.
Salam 1erement il faut être précis cheikhou amadou et amadou cheikhou sont 2 personnes différentes. 2sèment vous dites toujours toubyi nénaniou et vous qu'est ce que vous dites ?
Lima ler ba ler bop hu ngande nga yor
@@djamildiouf8593😂