Intégralité: Convoi du Khalif Général des Mourides de Touba à Dakar

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 9 лют 2025
  • Intégralité: Convoi du Khalif Général des Mourides de Touba à Dakar

КОМЕНТАРІ • 828

  • @sodalo2210
    @sodalo2210 5 років тому +183

    Kou kholam di nex rk beuseul j aime may guiss dieureudiefei serigne Touba

  • @ousmanesene4659
    @ousmanesene4659 5 років тому +448

    Kép kou beug Serigne mountakha beuseul j'aime

  • @aldiannathioune824
    @aldiannathioune824 5 років тому +322

    Don mouride rek mo nexx ani talibe Bamba yi def si Jaime ❤️🙏🏻

  • @sonkodjibril4736
    @sonkodjibril4736 5 років тому +290

    Barké Baye Niass mounouma teuyé samay rongogne 😭😭😭😭 ma sha Allah Mame borom Touba yalna diam yagg sénégal ☝️

    • @ahmaka7858
      @ahmaka7858 5 років тому +6

      Ah yaw dangaa bakh machallah

    • @mamasady1191
      @mamasady1191 4 роки тому +7

      Mame baye Moy brom faydou bi. Gnoun mouride begg nann loll thi mame baye, dierdieufer chiekhoul xadim.

    • @khalilibrahim4998
      @khalilibrahim4998 4 роки тому +4

      Amine way barkéb cheikhoul khadim ak yaw yalla ga am diamou

    • @papegoumbajopmar2058
      @papegoumbajopmar2058 4 роки тому +6

      Barkè mame baye niass amal diamou

    • @aichaibrahimafall6644
      @aichaibrahimafall6644 4 роки тому +2

      Sonko Djibril longue vie à toi

  • @omardiop154
    @omardiop154 4 роки тому +26

    Bilahi tidjiane la si ndeye ak si baye mais sama thioféle si serigne touba khaw ma lane si Mane bilahi wa talahi dama beugue serigne touba boumou diékh tak

  • @fallougallassmbow1364
    @fallougallassmbow1364 4 роки тому +15

    Baye modou guéye yalna yalla yog ay lerrame Amine

  • @moustaphasall3967
    @moustaphasall3967 5 років тому +246

    Man dé tidjane la wayé magui koy sétan sama yaram di daw yalla khamnako yalna yalla motali serigne mountakh mom soumako guissé reik bénén afair la yalna yalla goudal fanam

    • @thiounesaghor3450
      @thiounesaghor3450 5 років тому +9

      Keine dou yaw sa xol mo sêttt nioune Ak yeine nio bokou ligueye bi bokou mbectë mi

    • @kharbalabci3622
      @kharbalabci3622 5 років тому +5

      Sa khole moo raféte rék

    • @moustaphasall3967
      @moustaphasall3967 5 років тому +2

      Machallah yalna yalla motali

    • @bazoukaa9840
      @bazoukaa9840 5 років тому +4

      Sa kholl mo rafete rèk mo takh

    • @yamda801
      @yamda801 5 років тому +6

      Tidjan deug ni yow lay mel mashallah

  • @bueguestouba3634
    @bueguestouba3634 5 років тому +47

    ndeysan billahi sama yaram bi me gui daw sakh kenn do s touba yalla nano ko yalla fayal

  • @ibrahimacoulibaly5855
    @ibrahimacoulibaly5855 5 років тому +8

    Machallah rafetna serigne mountaha yalla na yalla deguerele thieur yi mayela goudou fane ak wergou yaram

  • @cheikhba9984
    @cheikhba9984 5 років тому +162

    Ndam amatina barké Serigne Touba, dama contane trop billahi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 dieuredieuf Serigne Touba 💪💪💪

  • @L.SARRENE_BI
    @L.SARRENE_BI 5 років тому +29

    👏Billahi sama khol bagui féeeeekh ni ❤❤ Diereudieuffa S. Touba
    Diàrama mame cheikh ibra fall
    S. Mountakh Yalna fi yag te wer

  • @serignemakhtarmbacke7350
    @serignemakhtarmbacke7350 5 років тому +21

    Macha Allah
    wa Darou Minan sén liguéye bi amna solo raféttna looll yalla ngueen si tassé ak ngeuramal Serigne bi

  • @moustaphandiaye8615
    @moustaphandiaye8615 5 років тому +9

    Qu'Allah le tout puissant lui donne la santé et une longue vie

  • @boussobali5622
    @boussobali5622 5 років тому +24

    Alhamdoulilah domou sokhna Diarra dji dal ligeyeul neugnou amouniou fayam😭😭

  • @sambeseye3159
    @sambeseye3159 5 років тому +13

    Way li rafet na loll jêrajêf serigne touba ♥

  • @davethiam4749
    @davethiam4749 5 років тому +71

    Thiéy Serigne Mountakha Mbacké Yalla nanouko yalla fayal yague fi té wér Mbacké

  • @modoundiaye4105
    @modoundiaye4105 5 років тому +3

    Darou minane liguéy bii rafetna and na ak professionalisme yalla nalén borom bi taaxawu. Serigne Touba di kén kou yalla kénal ,dieuredieuftii Cheikhoul Khadim. SERIGNE Mountakha yalla nafi yague té and wér

  • @fatouka6510
    @fatouka6510 5 років тому +28

    Thieye yallah yonou mouritte yallah molene katanale katane gou ame doole yalle na yokou dierediefeti seringe touba kene dou mome❤❤❤❤

  • @lebaolbaoltigui2599
    @lebaolbaoltigui2599 5 років тому +4

    c'est joli , les campagnes tout est vert ,et l'autoroute est bien faite....Merci aux tv de Touba , j'apprecie tjrs votre travail.....beaucoup de discipline dans les images et dans l'orthographe des mots..bravo

  • @abdoulayefall4367
    @abdoulayefall4367 5 років тому +12

    Backiyou faye akhmadou macké mokaye faye wayé mane limaye niane moye sama xoll bi yalla nama defalle ma beugue serigne touba adouna akk allakhira akk béppe mouride bou guemme serigne touba lou diourre diokhe akhmadou dieureu dieufffff

  • @ncm04
    @ncm04 5 років тому +13

    Très magnifique reportage.... Bonne continuation.... Mouride....

  • @osmanebousso6511
    @osmanebousso6511 5 років тому +13

    Je suis tres fier de faire partie de la famille Bousso !

  • @diengkara5930
    @diengkara5930 5 років тому +6

    Serigne mountakha bachir yalla nafi yague lolll té andak wer barki borom touba 🤲🤲

  • @diopndella3054
    @diopndella3054 5 років тому +32

    Dieureudieufati cheikhoul Khadim sounou yakari taye ak euleuk li warna takhe képp gouy djiguéne nangoul serigne ñam diaram Mame Diarra bousso💞💞💞

  • @larbi-assistanceetconseils184
    @larbi-assistanceetconseils184 5 років тому +26

    Masallah une fierté pour notre continent africain.

  • @fayemamy9521
    @fayemamy9521 5 років тому +6

    Sama chair dd poul yangui takhaw sakh.
    Mbacké yague fii lolou té wer .serigne touba amatina ndam dé wawww kay mouride beusseul j'aime

  • @laminebayo2769
    @laminebayo2769 5 років тому +5

    Dinnè reck ame solo merci Mame Bamba

  • @ndeyeastoumbackefall4494
    @ndeyeastoumbackefall4494 5 років тому +18

    Sante na sounou borom bou wéer bamouma défé may app mouride tékci dioudo ci yonou mouride sama wakeur yaye di wakeur serigne modou Abdoulaye fall ndar sama wakeur papa di wa darou minam wakeur Serigne bassirou alkhamdoudila Dieureudieufè Serigne touba ❤️🙏

  • @laminediaw3552
    @laminediaw3552 5 років тому +6

    Dieureudieuf serigne touba amoul morom serigne mountakha mbacké yalla nafi yague té wuer

  • @serignefalloukanendamatou4630
    @serignefalloukanendamatou4630 5 років тому +13

    ماشاء الله
    Yên wa darou minane Jërë guên wa académie minane yalla nalèn serigne bi nagoul sènoub ligèy thi barkeb القرءان الكريم

  • @mamadoudiop1159
    @mamadoudiop1159 3 роки тому +4

    Douma sii doyall!! Dama beug Mbacké balla. Doundal al Mountakh🤲🏾❤️❤️❤️

  • @saerndiaye4427
    @saerndiaye4427 5 років тому +6

    Serigne mountakha bachir mbacké Yalla ngua fi yagg si barki serigne touba

  • @barandao6896
    @barandao6896 5 років тому +22

    Autoroute illa touba mashala! Serigne bi yalla nafi yagg t andak werr!!

  • @moussakatongo930
    @moussakatongo930 5 років тому +11

    They serigne touba sant na yalla bima néké mourid 😭 Barkét serigne fallou sama ❤ sede na si liii way alkhamdoulilah

  • @mamesayendiaye7150
    @mamesayendiaye7150 2 роки тому +3

    Que allah le tout puissant lui une longue vie et du santé

  • @thiatouyayam2866
    @thiatouyayam2866 5 років тому +2

    NDEYSANE sunu xol sedna trop bilay amunio kudul serigne Touba s. Mountakha yalla nagfi ga na yaague loooooooooo...l té wer prcq sa yague fi sunu niarigne la yagui nioy gana tek si yonwi nione newgni mane dh beug gimala beug manumako sax wax billahi key sm xoll sedna trop trop
    le 27 bi yalla nanesi egue ak diamu demsi diam nieuw si diam yalla seral yonewi si barkep sunu fièreté Ahmadou Bamba👈💖

  • @mordioptouba1511
    @mordioptouba1511 5 років тому +10

    Bilahi barké serigne barra Mbacke Sama kholl séd na hooo dieuredieuf serigne Touba Mbacke

  • @khadimcheikhniang4916
    @khadimcheikhniang4916 5 років тому +6

    Machallah yalla nanou sunu borom rouss thi serigne bi mou yague fi loooooool thi barkéb serigne bi

  • @assanefallfall4574
    @assanefallfall4574 5 років тому +41

    Machallah liguy bi rafet Na s mountakha mbackè Yalla Na Fi yag tèwère

  • @abdoukarimdiouf4473
    @abdoukarimdiouf4473 5 років тому +1

    Machalah yalnafi yalla yagal Serigne mountakha té mayko werr pour mou ligueyal Serigne Touba

  • @alassanekane4667
    @alassanekane4667 5 років тому +1

    Diaradiaféééé Serigne Touba. Serigne Mountakha yalnafi yague te wer

  • @serignemakhtarmbacke7350
    @serignemakhtarmbacke7350 5 років тому +9

    Serigne Mountakha yalnafi yagueu tawër barké Chiekhoul Khadim

  • @Xibarbtimerew
    @Xibarbtimerew 5 років тому +1

    Sarigne mountakha yalla na fi yague te wer barkeb sarigne touba

  • @plascza1300
    @plascza1300 5 років тому +7

    Islam amatina ndam diereudieufé serigne touba

    • @SouleymanefayeFaye
      @SouleymanefayeFaye 5 років тому

      dieureudieuf serigne touba khadim rassoull serigne mountakha yagfy te werr

  • @ahmeddia6908
    @ahmeddia6908 5 років тому +5

    Vraiment serigne touba amoul morom être mouride n'est pas donné à le monde fierté de l'islam

  • @Khadimbambasonko40
    @Khadimbambasonko40 4 місяці тому +1

    ماشآءالله تبارك الله ❤❤❤

  • @alou_alex_maker
    @alou_alex_maker 5 років тому +124

    Thieye s touba mountakha mbacke guena yagg guena wér si barkep s saliou

  • @samareew1919
    @samareew1919 5 років тому +8

    Barke khadimoul rasoullou Dakar mogi beugeu nekh ma challa seringe touba yalla naniouko yalla fayal ta sante lol bama mele al mouridoulakhy dieureudieuf chekhoul à chekhoul khadimou rasoul

  • @abdoudiaye8986
    @abdoudiaye8986 5 років тому +18

    Serigñe touba rek muchísimo gracias merci serigñe touba

  • @mouhaframarene3352
    @mouhaframarene3352 5 років тому +32

    FI serigne touba rek mofi nek mou lay nekh mou lay nakhari serigne touba rek ba aldiana taye kou sa xol fésoul do nitou dara moy mourid bi moy tidiane bi serigne mountakha mbacke yalnafi yague ta werr lollll Amine

    • @moctarcisse8413
      @moctarcisse8413 5 років тому +5

      Loufi indi wakh dji yeup...Serigne touba mofi nekk koumou nekh,ak koumou nakari...Kane la wara nakari si adouna.Bayilen yé fitna..Wakhtacimou bi khablil lahi djamihan wala tafarahou laniou diangue..Naniou bolo japp si boumou yalla gui donc boumou yalla dou lénén loudoul Islam...Wakh detail moniou tardel.Massalikoul djinane ken momouko:Tidiane,mouride,Khadr,layenne...Sagou islam la.Merci

    • @kharbalabci3622
      @kharbalabci3622 5 років тому +2

      @@moctarcisse8413 kén moom nako kagn daga naane nieupeu Amna si tieureu mais S.Touba ko moome

    • @moctarcisse8413
      @moctarcisse8413 5 років тому

      Alkhuran ak sunna yaw sa diangue ana louko firndé...kone serigne Touba moko mome nga beuga wakh??Serigne touba nekatoufi donc naniou mirass djouma dji.Yalla soudone wathie si adouna si djak yi ak djouma yi lay wathie dé motakh niounane négou yalla

    • @kharbalabci3622
      @kharbalabci3622 5 років тому

      @@moctarcisse8413 Yaw ya diangue yalla ndakh diakeu ak douma rék mooy keureum kom borom xam xam ga

    • @moctarcisse8413
      @moctarcisse8413 5 років тому

      Akhuran ak sunna nioun warounio xoulo walla di wéranté mais danio wara wéralanté rek..mane de mon point de vue Koulou diaka ak djouma dou momelou domou adama mais selon moi négou yalla la rek

  • @boubacarndour1719
    @boubacarndour1719 5 років тому +5

    Machallah Mbacké yaagfi lool té andak weer.....l'Islam amatina ndaam té leup serignebi rekla...

  • @moussaaw3745
    @moussaaw3745 5 років тому +15

    Dieureudieufati sering Touba amoul morom sering mounetakha mbacke yalanafi yageu té weur

  • @aladjiifaye6687
    @aladjiifaye6687 5 років тому +27

    Yagüe Fi te weer si barke cheikhoul khadim serigne touba amoul morom ☝️ dieuredieufte serigne touba khadimou rassoul

  • @dieyetapha1113
    @dieyetapha1113 5 років тому +1

    Yalla na yalla yoko wére ak agalé sa liguéye si yonou mourite si barké Mohamed psl

  • @thiamalle1722
    @thiamalle1722 5 років тому +4

    DIEUREUDIEUFE SERIGNE TOUBA!!! Louniou ko sant doyoul
    Serigne Mountakha Bachir Yalla nafi yagg tei and ak werr

  • @talibebambatouba528
    @talibebambatouba528 5 років тому +122

    Yal ngafi yague mbacke

  • @salimatakana2589
    @salimatakana2589 5 років тому

    Jerejefeti serigne touba li lep sa ligueye la serigne mountakha yallanafi yague te weer

  • @actu5689
    @actu5689 5 років тому +27

    Jërëjëf serigne touba xaadimur rassuul

  • @laminesamb4313
    @laminesamb4313 5 років тому +27

    Yalla nafi yagg mbacke ndakh khamna nga yagg fi moy sounou diam mbacke wereul re yagg fi amiine

  • @bayefall144
    @bayefall144 3 роки тому

    Ndeysane yalla na sa borom fayy
    Sen takhaway rafett na
    Thiey serigne bi

  • @baaygalasloo3337
    @baaygalasloo3337 5 років тому +2

    Jarajëfate Sëriñ tuubaa, xol yi sedd na de maasàllaa.

  • @cheikhmm
    @cheikhmm 5 років тому +2

    macha allah lii sèdd a khol lool
    sèrigne Mountakha mb yalla nafi yague lol te wërr amine

  • @bayefall5452
    @bayefall5452 5 років тому +10

    Merci président Abdoulaye wade

  • @fatouball1078
    @fatouball1078 5 років тому +3

    Kén dou Serigne Touba Serigne Mountakha yalla nafi yague té wer

  • @soldaroubayekarimbassiroun4535
    @soldaroubayekarimbassiroun4535 5 років тому +5

    SERINGE TOUBA SERINGE MOUNTAKH MBACKE BASSIROU YALLA NAFI YAGUE TA WEER MBACKE 💖💖💖💖💖

  • @meansseck2253
    @meansseck2253 5 років тому +23

    Dieureudieuf Serigne Touba khadimoul Rassoul

  • @supeserigneabdouahadmbacke2957
    @supeserigneabdouahadmbacke2957 5 років тому +6

    Thiaey serigne touba jajeuff Cheikhoul khadim serigne mountakha mbacke yalla nafi yegg lol lol te werr Amin ci barkeb serigne touba Amin Amin

  • @FaLLo106
    @FaLLo106 5 років тому +3

    Thiaye Serigne touba s.mountakha mbacke kholou mourid yui sedd nan wallahi 💕💕💕

  • @adamagueye1807
    @adamagueye1807 5 років тому +40

    Yague fi lol té andak wëër Mbacké 🙏🙏🙏

  • @eveane3302
    @eveane3302 5 років тому +6

    Liii nekh na macha alla dieuredieufety Khadim Rassoul

  • @mhdrassoul6689
    @mhdrassoul6689 5 років тому +3

    Serigne touba serigne mountakha yalla naga fi yaguue lol mecte mi ba aldiana inchalla❤️🙏🙏

  • @fadalldiene813
    @fadalldiene813 5 років тому +32

    Chiékhoul khadime si khôl Dara méloul ni môme Serigne Touba almountakha yalnala yalla yagal souniou kanam nanie yeuk ni Nar bé Andi khorome si rek brome Touba amoul morome

  • @cheikhmbacke4379
    @cheikhmbacke4379 5 років тому +9

    Dieuredieuf bamba diarama cheikhra fall

  • @eveane3302
    @eveane3302 5 років тому +13

    Mâcha alla yague fi té wère Mbacké barké Khadim Rassoul

  • @bambasylla7210
    @bambasylla7210 3 роки тому +1

    Dieureudieufè serigne mourtada saliou mbackè

  • @wayssousokhna7769
    @wayssousokhna7769 5 років тому +33

    DIEUREUDIEUF SERIGNE MOUSSA MBACKE TAKHAWAYE BI RAFETENA

  • @mamadoudieng5370
    @mamadoudieng5370 5 років тому +310

    Srgn moussa nawél nigua takhayoo Srgn mountakha rafétna mouride yép nioguilaye nianal ngua yaguefi té wér

  • @mbackekhadim2443
    @mbackekhadim2443 3 роки тому +2

    Machallah dieuredieuf serigne BAMBA

  • @fallouseye1611
    @fallouseye1611 4 роки тому +3

    Lii dafa reuy ba khadioul sama lamigne machallah ❤️👌

  • @takhasarr2343
    @takhasarr2343 5 років тому +1

    Dieureudieufé serigne touba depuis argentine

  • @moussasall5655
    @moussasall5655 5 років тому +6

    Diereu dieufeuti borom touba Serignè mountakha Mbaćke mome Serignè bassirou yallnafi yagg lolle te werre amiiine kendou Serignè touba🙏🙏🙏

  • @alimacamara1289
    @alimacamara1289 5 років тому +2

    Machallah li rafet way kilifa gui yallah nafi yagg té weer

  • @cheikhmbayeseck342
    @cheikhmbayeseck342 5 років тому +48

    diadieufé ki mom touba diarrama mame cheikh ibrahima fall lamp mame mountakha bassirou mbacké yalla nafi yague lol té and ak werrrrr👐👐👐👐👐👐👐👐👐

  • @mbackediop7678
    @mbackediop7678 5 років тому +8

    Walahi sama kholl bi mogui mélné Galass serigne bi yalla ngafi yag téwér barkéb alkhourann

  • @thharlem2021
    @thharlem2021 5 років тому +1

    Masha Allah Yalla contane na Yonenete bi bi contane na > na gneupe beek

  • @mactarboussoma8795
    @mactarboussoma8795 5 років тому +4

    Billahi serigne touba mo yèmè

  • @samniang4233
    @samniang4233 4 роки тому +2

    Billahi wallahi keenn dou cheikh ahmadou serigne touba mo yémmé yalla naniou yalla khirr thi gueneu beugue serigne touba je suis fierts des baye fall serigne mountakha mbacke yalla na yageu té andak werre 😭😭😭😭😭

  • @ndiayewaly8768
    @ndiayewaly8768 5 років тому +15

    Dieureudieufety Mbacké yague fi ta weer

  • @oumarmendy1336
    @oumarmendy1336 5 років тому +6

    Sama yaram bi dafaye daw bilahi kenn dou serigne touba

  • @ghhd3458
    @ghhd3458 5 років тому +4

    Dieu reu dieuf serigne touba amoul morom dh bilahi

  • @dyanandiaye7584
    @dyanandiaye7584 2 роки тому

    Ndeysane sama khol dafay fess dieuredieuf mbacké j’ai les larmes 😭 aux yeux

  • @ndeyesamb8383
    @ndeyesamb8383 5 років тому +9

    Thieuy Serigne Touba lep yaw dieureuf Serigne bamba

  • @espritgagnant5393
    @espritgagnant5393 4 роки тому +3

    MashaAllah Dieureudieuf Bamba sa ligueyy dotoul fayy ba abadaan🙏💓

  • @seynabouba446
    @seynabouba446 5 років тому +6

    Bilahi dine Islam Moy deugue j'aime mon pays

  • @tawfeex2212
    @tawfeex2212 5 років тому +3

    Merci waye kontan na thi yeen

  • @mouniroufaye1073
    @mouniroufaye1073 5 років тому +4

    Dieureudieufé borom Touba serigne mountakha Mbacké Yagg fi lolou té andak werr

  • @amimbacke3626
    @amimbacke3626 5 років тому +7

    ماشاء الله المسجد مسالك الجنان

  • @kalidouwade9442
    @kalidouwade9442 5 років тому +67

    Waw léne goor mouride ni rék lagnoukoy doundé ak mbékté mi ba aldiana

  • @bambambacke862
    @bambambacke862 5 років тому +18

    Jaim même pas de mot a part dire alhamdoulilah de te porter dans mon coeur. Bamba le patrimoine mondial. Jai vu sur cette scène le retour victorieux de bamba à Dakar

  • @mamesayendiaye7150
    @mamesayendiaye7150 2 роки тому +2

    Que allah le tout puissant lui donner santé et une longue vie