C bien dit Samba nguer tu es vraiment franc et sincère avt de penser aux présumés meurtriers pensons a la famille de Aziz et de Waly arrêtons l hypocrisie
Salam, manchahalla Samba franchement parler c'est une pure vérité deugeu rékeu nékh Yalla Dieuff dji dafa niaw té métti niari bakane dém comme ça parce que lane jalousie, méchanceté, walla concurrence 😢😢 vraiment c'est trop dure, donc entendre dire à chaque fois Nabou Leye danko yeureum ça m' insupporte au plus haut point 😡😡 la maman de Aziz et la famille de Wally nio diareu Yeureum deux famille qui n'auront plus l'occasion de voir ou de parler avec leurs enfants. Donc je vous en conjure chers participants arrêtés avec ça 🙏🙏🙏 Aziz et Wally sougnou amone Prison dieul. Merci à tous, wassalam
famille boo xam ni bayyi sén doom ak bénn xalé bu jigén mu géré léppam ba ayda rakki Aziz dabala di wax ni nabou leye moo geuneu jégé Aziz dabala ci sama yaay ak man te loo lu jaadu wull nabou rekk moo amon contrôle totalement thi léppi Aziz dabala dundam liggéyam léppam mias voilà les résultats 😢😢😢😢😢😢😢😢
@@AstouSy-f8i jégé bi pour ma eppull waayé Daf thiaa wétt lool Aziz dabala ay mbookam nioo ko soir thi lépp sauf les aides yi mu lén don defall rékk la niooy lijeunti a mon point de vue
Bilaye nabou j'ai pas pitié d'elle souféké moraye Abdoul Aziz BA et Boubakar Guano wala moubokeu si elle doit pourrir en prison fayoule narbi horomame nabou meurtrière leye
Nabou lèye moy kaan ba li am niou nane mome là wala dète Yalla kham na mome kham na niou nane dafay guène bobatay, justice loussi war dinako def, on parle de deux crimes là.
maachaallaahu samba ngerr fulla jii nékk ci yaw bu nékkon ci mbokki Aziz dabala kon mu néc nioom da nioo am complexes ci nabou leye moo tax ayda nan lii yalla doon ay gént yaayu Aziz dabala naan nabou leye du ma ko massa wax lu niaaw famille bii nioo tekki wull dara billaahy
Ah sama ngére say kadou raféte na trop yayou Aziz dabala dafa amé nakar te lingay wakh ni ndeye Gueye mo bakhoul te bagn kouko Méré motakh monane ay Nabou Leye sama dome la way doul justice pour Aziz dabala et Boubacar Gano peine de mort 😢😢😢😢😢😢😢
Mais pourtant aziz tout prévu en disant Sénégalais da beuri ay hypocrite Lorsqu'on l'a interviewé il disait toujours quoiqu'on dise lui il croit en Dieu et continue sa vie.
Aziz est mort, menaces ou pas il est mort, l'enquête suit son cours mais attendons de voir au lieu de dire des choses qui n'ont rien à voir avec la vérité du terrain...
C bien dit Samba nguer tu es vraiment franc et sincère avt de penser aux présumés meurtriers pensons a la famille de Aziz et de Waly arrêtons l hypocrisie
Je suis temoin des avances et repetitions de Leye Ananas au Theatre de verdure de Pikine.
Salam, manchahalla Samba franchement parler c'est une pure vérité deugeu rékeu nékh Yalla Dieuff dji dafa niaw té métti niari bakane dém comme ça parce que lane jalousie, méchanceté, walla concurrence 😢😢 vraiment c'est trop dure, donc entendre dire à chaque fois Nabou Leye danko yeureum ça m' insupporte au plus haut point 😡😡 la maman de Aziz et la famille de Wally nio diareu Yeureum deux famille qui n'auront plus l'occasion de voir ou de parler avec leurs enfants. Donc je vous en conjure chers participants arrêtés avec ça 🙏🙏🙏 Aziz et Wally sougnou amone Prison dieul. Merci à tous, wassalam
Samba vrai gorla.
C'est vraiment un très bon ami et ce qui est très très rare thi Sénégal bi
Salam A Toute l'equipe ❤❤❤❤Ma Sha Allah Dieureudieuf Merci Samba Nguer Nit Kou Bakhe Ngua ❤🙏
Samba Nguér, deugue dou romb nope , seytané, nafékk laniou déff wayé nak danio rayoul séni dom wala séni rakk rek😭😭
Aziz ak Wally yalna déh doon sén Noflay🤲🏻
Amine
Merci Samba Nguer. Tu es franc. Nabou Leye, dire qu elle va sortir de prison, c est ne pas savoir la gravité du double meurtre.
Merci ambassadeur,goor yalah Amy ,zoo,Ragnar ,Zou merci on est fière de vous❤
Samba tu es un homme verdict et digne chapeau â toi
Merci beaucoup Samba Nguer❤❤❤❤❤ c'est bon à entendre la vérité
Khowmala Samba mais nawnala notre Sénégalais nitt you melni gnofi manque mashaAllah👏
Samba Nguer machallah, il ya toujours des gens qui disent la vérité, continue sur ce chemin❤❤❤Nawnala
Samba tu es verdict , Sénégal nak dafa bari nafék bagne koula Méré takh guay maral Tate un présumé meurtrière
Ce samba nguer s'exprime très bien.ta nitte bou deugou bou goré la machala que le bon Dieu tassiste et te protège.
famille boo xam ni bayyi sén doom ak bénn xalé bu jigén mu géré léppam ba ayda rakki Aziz dabala di wax ni nabou leye moo geuneu jégé Aziz dabala ci sama yaay ak man te loo lu jaadu wull nabou rekk moo amon contrôle totalement thi léppi Aziz dabala dundam liggéyam léppam mias voilà les résultats 😢😢😢😢😢😢😢😢
Sokhna Aminata je partage la même idée que toi.il faut avoir la main mise sur votre enfant
Pourtant ngoor mo amatoul reek wayè kharit menna neek mook ba gueneu dieguè kigua bookaal nabou mo gorewoul reek mais kharit warnala diaral sa bakaaan
Légui sa se voit que motakh mou ame accès si Aziz ba jalousie ame si mo indi raye bi diégué bi bamou epou mo waroul wone
@@senzanome9931vraiment 👍
@@AstouSy-f8i jégé bi pour ma eppull waayé Daf thiaa wétt lool Aziz dabala ay mbookam nioo ko soir thi lépp sauf les aides yi mu lén don defall rékk la niooy lijeunti a mon point de vue
Bilaye Nabou Leye kouko yereum nafek bou bone nga deug nexoul
Bilaye nabou j'ai pas pitié d'elle souféké moraye Abdoul Aziz BA et Boubakar Guano wala moubokeu si elle doit pourrir en prison fayoule narbi horomame nabou meurtrière leye
Bliehe Samba ya wakh dayga bu werr su yayi Aziz amut lolu kai jel jerejff Samba ya bakh ya goori harit nii yw layii mell dundal werrlan🤲🙏☝️♥️💯
Paix à son âme qu allah l accueille à son paradis firdaws amine justice pour aziz dabala et wally
Amine
Samba ki khawmako dé , billahi wahi Aziz là mâcha Allah
Merci Merci Merci sama xol beguena❤❤❤❤❤ si fero
Ma sha allah tu es très pertinent et digne
Merci samba vérité absolue
Nabou lèye moy kaan ba li am niou nane mome là wala dète Yalla kham na mome kham na niou nane dafay guène bobatay, justice loussi war dinako def, on parle de deux crimes là.
Merci samba guer❤❤❤❤❤❤
maachaallaahu samba ngerr fulla jii nékk ci yaw bu nékkon ci mbokki Aziz dabala kon mu néc nioom da nioo am complexes ci nabou leye moo tax ayda nan lii yalla doon ay gént yaayu Aziz dabala naan nabou leye du ma ko massa wax lu niaaw famille bii nioo tekki wull dara billaahy
wala nabou xamaléne lou nigni xamoule tamite
@@poupembaye1199 yaakaaru ma loo lu da nioo amon ci moom confiance rékk et ça comancé par Aziz dabala
Lolou rek la, avec l'effet de surprise.@@sokhnaaminata287
Ah sama ngére say kadou raféte na trop yayou Aziz dabala dafa amé nakar te lingay wakh ni ndeye Gueye mo bakhoul te bagn kouko Méré motakh monane ay Nabou Leye sama dome la way doul justice pour Aziz dabala et Boubacar Gano peine de mort 😢😢😢😢😢😢😢
Niite boulevard degoula samba vraiment tu es sincère honnête et respectueux
machalla niit degaye moune sa niit degue rek am solo
Wallahi samba ngére ya bakh goré té niémé deugue mancha allah
Merci samba nguer
Tu as parfaitement raison Samba nguer. Deugue rek ngua fi wakh. I like it❤
Machalla waxadji rèfèt na Samba yaw pikini moy daw sa yaram❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilahi samba nguér beugue nala ndakh Aziz dabala ndakh yaw danga degue gou te danga meune sa nitt machahllah Yalla na sa diam yague way ❤❤❤❤❤
Merci beaucoup samba ❤❤❤
Mane déh sopnala yow samba sop sa franchité Mane nak mossouma dougou fii béy SMS wayé toujours mangilene Di déglou vraiment
He is very honest
Say it again
Vérité absolue samba ❤
Machallah Samba Nguer ❤❤❤❤li moyy xarit nitt dafay deugou
Bravo Samba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci samba nguer iow deh do Nafekh yalla nalla yalla takhawou
Mais pourtant aziz tout prévu en disant Sénégalais da beuri ay hypocrite Lorsqu'on l'a interviewé il disait toujours quoiqu'on dise lui il croit en Dieu et continue sa vie.
Xarite Aziz Yep Yacine gueneu gore machaalah
machallah samba nguer nitt day deugou ❤❤❤❤
Merci samba yaine khameguaine loussi dioure gnou rayko ohhhh
Samba c La pure vérité mon frère
Merci samba
Très très bon amis du courage massa samba
Merci samba tu es franche❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilahi samba tu as parfaitement raison bien parlé machalah
Merci samba deug pir
Lomeune wakhal nawnala trop ou son les amis aziz guenelene way
Merci
M samba
Samba mercie bcp deguena deugue pure
Bien parlé samba ❤
Bravo.samba.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Lii reka takh ma sope samba nguer.dafa deguou. Té kharite pur la
Merci Samba Nguer, deug dou robe nope ❤
Ley Ley n'es pas une victime
C'est Aziz et waly qui sont les victimes
Être en prison à manger ses poulet tranquille
Les sénégalais sont des hypocrites
Samba chapeau à toi
Tu n'as dit que la vérité
waw Khana les sites dagno am problème pour les titres manam diangouniou
Rencontrer et raconter font deux
Ndeyesane
Machalla domou pikini bi
Samba nguer nitte kou bakh gua t deguou bilaye yayou aziz bouniou teudione aziz mou dieule mais lii daffa nianw
MERCI SAMBA VERITE VERITE VERITE
Machallah samba
Mane samba nguer dama ko naw dafa deugou depuis le debut meme discours senegalais yi gno nafekh
Please keep it up
Samba
Ce n'est important ça
Question de passeport
Tu as tout dit
SI VOUS VOULEZ VOIR LES VRAIS MENTEURS, IL FAUT ARRÊTER CES MARABOUTS QUI PRÉTENDENT SOIGNER RADICALEMENT L'IMPUISSANCE.
😅😅😅😅😅😅😅
Bilahi.samba.yawe.yaye.nitou.dege
Non yéne wakh bi défa barri fofou
Goor d'où xarito AK djiguen rawatina moulay fréquenter chaque jour
Yalla na Sunu Borom léral yeupe in shaa alllah
Samba merci
Aziz est mort, menaces ou pas il est mort, l'enquête suit son cours mais attendons de voir au lieu de dire des choses qui n'ont rien à voir avec la vérité du terrain...
👍❤
Il ne jamais passer tout son temps avec des amis femmes
Plutôt il faut être avec des hommes comme toi ou rester dans son coin
❤❤❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏🙏
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
That leye ananas is a big suspect indeed,
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ wow that's 👍
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieuredieuf Dieuredieuf Dieuredieuf
Euskey Samba
Vous êtes des enquêteurs
Samba tu n'en sais rien
Ne tombe pas dans les pièges
Ley Ley n'es pas une victime
C'est Aziz et waly qui sont les victimes
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤