Eskey chérif.yaa baakh te gnak kignaane.yalla n'a la yalla fay.Mane deh à chaque que je vous écoute j en tire bcoup de choses.merci chérif des milliards de fois chukrane laka.bilaahi je suis très satisfait de vous.je prie allahou soubhaanahou wa tallaa de vous rencontrer et de vous saluer ne serait ce que 'une seule fois dans ma vie.
Bou dîné ak tarikha meleni Sénégal grâce à mame cheikhou Oumar Hazzah Minna lahi tadjrii hawlahoul houchourou yah asbahat nahsi faroukhi yah houmarou Parole de mame cheikh Ahmed tidiane si sur Mame cheikhou Oumar Naniou diema kham lane moy tarikha bi
DÉJÀ VOUS AVEZ DIT QUELQUE CHOSE DE TRÈS GRAVE DINÉ AK TARIKHA...CA VEUT DIRE QUE L'ISLAM EST LA RELIGION RÉVÉLÉE MAIS IL FAUT DES TARIKHAS...MON FRÈRE CEST COMME CA QU'ALLAH A LÉGIFÉRÉ NOTRE BELLE RELIGION...L'ISLAM SI TU VEUX C'EST COMME UNE CONSTITUTION MAIS INVARIABLE SOUS LORDRE DALLAH ET DE SON MESSAGER DONC TOUTE INNOVATION NE SERA PAS ACCEPTÉE. POURQUOI ???? La famille d’Imran ('Āli `Imrān):85 - Et quiconque désire une religion autre que l'Islam, ne sera point agrée, et il sera, dans l'au-delà, parmi les perdants.
Wallahi ndeyssane DEUG leu Serigne bi yalla n'a yalla goudeul sa fann si Barker seydina mouhamed rassoulalah sallal aleyhi wa salam sanggou adouna ak Allakhira ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Dunno if you guys cares but if you are bored like me atm then you can stream pretty much all of the new series on instaflixxer. I've been streaming with my brother for the last couple of days =)
Cheikh oumar l homme qui a dirigé une priere dans la mosquée de al aqsaa au Jerusalem etant noire en une epoque oú l homme noire est devalorisé.thiey tall
Samba démba ali mokhtar thiérno thiénabé wali yéne wali yabé sama mame sague jouléko tata léle mate khalima ko takha diale kéne dou sama mene yalla nanou ko yalla fayale
Eskey chérif.yaa baakh te gnak kignaane.yalla n'a la yalla fay.Mane deh à chaque que je vous écoute j en tire bcoup de choses.merci chérif des milliards de fois chukrane laka.bilaahi je suis très satisfait de vous.je prie allahou soubhaanahou wa tallaa de vous rencontrer et de vous saluer ne serait ce que 'une seule fois dans ma vie.
Papa cherif do dagne dinou bégueul si nitou yalla yi yalla nala yalla faye si barké seydina mouhamed psl
Sma Mame kein dou mom walae dioudu reck khamni bokam nga fierté la ndx sma mame dji guiss nako machallah❤❤
Bou dîné ak tarikha meleni Sénégal grâce à mame cheikhou Oumar
Hazzah Minna lahi tadjrii hawlahoul houchourou yah asbahat nahsi faroukhi yah houmarou
Parole de mame cheikh Ahmed tidiane si sur Mame cheikhou Oumar
Naniou diema kham lane moy tarikha bi
DÉJÀ VOUS AVEZ DIT QUELQUE CHOSE DE TRÈS GRAVE
DINÉ AK TARIKHA...CA VEUT DIRE QUE L'ISLAM EST LA RELIGION RÉVÉLÉE MAIS IL FAUT DES TARIKHAS...MON FRÈRE CEST COMME CA QU'ALLAH A LÉGIFÉRÉ NOTRE BELLE RELIGION...L'ISLAM SI TU VEUX C'EST COMME UNE CONSTITUTION MAIS INVARIABLE SOUS LORDRE DALLAH ET DE SON MESSAGER DONC TOUTE INNOVATION NE SERA PAS ACCEPTÉE. POURQUOI ????
La famille d’Imran ('Āli `Imrān):85 - Et quiconque désire une religion autre que l'Islam, ne sera point agrée, et il sera, dans l'au-delà, parmi les perdants.
Machlalah chérif demala bougue
Machlalah
@@ahmadniane5176 yaw demal guestu sa way yonema sa nimero
Machallah chèrif Ibrahima Aïdara que dieu te Benis ses a cause de toi que j'aime SERIGNE BABACAR SY MERCI AÏDARA❤❤
CHÉRIF je ne veux qu'une seule destination inchallah pour vous. Ala ILIYINA INCHALLAH. Vous êtes une bonne personne. Machallah.
aidara yallah nala yalah fay cii barké thierno bachir tall
Machaalla Seydi Aïdara yow mi wakh li ci kodda adama aïssé diaradjeuff yalla nala yalla fayye
Merci la lanterne haidara chérif longue vie à toi !
Machallah Sangue bi aidara sama référence yalla na yalla goudal saye fane amine
Amine
Wallahi ndeyssane DEUG leu Serigne bi yalla n'a yalla goudeul sa fann si Barker seydina mouhamed rassoulalah sallal aleyhi wa salam sanggou adouna ak Allakhira ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Kou mou nex ak kou mou nakhari Seykou Oumar tal dou morom k
Eskey tall l'homme qui a plusieurs dimensions spirituels macha allah
C'est purement vrai ce qu'il dit sur les wali . Merci beaucoup .
Dunno if you guys cares but if you are bored like me atm then you can stream pretty much all of the new series on instaflixxer. I've been streaming with my brother for the last couple of days =)
@Jayceon Arthur yea, I have been watching on InstaFlixxer for since november myself :D
@Jayceon Arthur yup, have been watching on Instaflixxer for since november myself :)
@Jayceon Arthur yea, have been using InstaFlixxer for since december myself =)
CHÉRIF je ne veux qu'une seule destination inchallah. Ala ILIYINA. Vous êtes une bonne personne. Vivez longtemps.
Machalla wahtane si cheikh omar Tall day sed sama xol walahi
Machallah sa kham-kham selna setna tah woorna. Yalla nanga am faane bou goude ak werr ci barké Mouhamed (SAW).
Machallah Cherif yalna yalla yagal laffi si barké Thierno Bachir
Merci Cherif
Bilahi yamayy wetali chaque nuit .Babacar Diop depuis Maroc/Rabat
Mane dall Chérif beugu n'a là 👌
Dieuredieuf Aïdara yalna yalla samla arla yok sa wèrr yok sa soutoura ❤
Yalna Yallah samaleu boppam aar leu barké Maam cheikh oumar
WALAHI Maam cheikhou Oumar banene affaire WALAHI MASHALLAH
Yalna Yallah tasnou ci barkem ak leeram insh ALLAH 🙏♥️
Tallo Guédé 😙😚 Djarama Baba Chérif Ibrahima Aidara Ken Dou ioe
Masha Allah Aïdara YALLAH na Yallah goudeul fane wi té YALLAH na Yallah taas niou si barkém amine ya Rabbi si barké Seydouna Mouhamed saw amine
Machallah.Tall.sama.sope.amoul.morom.❤❤❤❤👏👏👏👏
Bilahi kéne dou seydil hadji malick sy
Masha Allah Yalna YALLAH yok Leram teh tass niou si barkem
Machallah jotay bi amna solo moy ci Cheikh Omar le guide des guides
Yalna yalla goudal Say fane Cherif
MACHALLAH wakhdji RAFÈTENA KÈNE DOU YOW DIEUREUDIEUF CHÈRIF
Goudeul fane cherif
ماشاءالله تبارك الله
Direudieuf cherif Ibrahima aidara
Machalah contane na trop
Machalla amna solo
Cherif ya bakh yalnala yala fay.Kou la beug la .beug na la guiss
Macha allah yo allah junu ngour ndam ma Amin ya Rabi tall, sy, Cherif aidara merci
Machallah cherif ibrahima aidara
Cheikh oumar l homme qui a dirigé une priere dans la mosquée de al aqsaa au Jerusalem etant noire en une epoque oú l homme noire est devalorisé.thiey tall
Souleymane Ly bilay yéneu meune féne ak soss
@@abdoulthiam5565 sa way thi téeré la nekk epuis t es qui
@@abdoulthiam5565 sa way ki loumou la wax degue la yeen xamo leen Seykou Oumar yonema sa nimero sahaba bu niouy has
MACHA ALLAH SAMA SOPÉBI YALLA NA YALLA SAMOU LA BARAKALLAH
Masha Allah bless up one love Africans
Walahi baba chérif beug nala rek te yalla takh .
Tall Aïdara jaarama machallah
Yalla gnouko yalla fayal
Nitt kou bakh Machallah
Masha Allah TALL ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
yalla nala yalla faye
Xooooolllllll seddddnnnnnaaa lool...... bilay je n'ai même pas les mots 😭
Manchallah yalna yalla doli soutoura
Macha alla seydi tall codé adam aissa elimane ciré le waliou des waliyabé
Samba démba ali mokhtar thiérno thiénabé wali yéne wali yabé sama mame sague jouléko tata léle mate khalima ko takha diale kéne dou sama mene yalla nanou ko yalla fayale
Machalla Cherif Ibrahima Aidara Dieuredieuf 🙏🙏🙏
Cherif Ibrahim mbeugue nakho guisse guir yalla akh dieum bigniou mbokh di Mame Abdou Aziz dabakh rta
Bene ba ngui rawda cheikh Tidiane cherif
Kou ko xamoul rek la yerem rewmi yeup thi barkem laghi doundou
Alfoutiwi Tall machalla
Machallah sama toma
Ma Shaa Allah
Machalah euhloulahi yeup bén lagnu. yagg fi lol té werr
Mashallah mallsall 👏👏👏👏👏👏👏👏💞💞💞💞💞
@@jallowisatou5749hello u live gambia
MASH ALLAH KALAW DII 🐄
Machallah Aïdara
Albarka chérif ❤❤❤
Abaraka Sheikh Ibrahima Aidara
Tallllllll🙏🏻 kendou mom lolou la Yallah dogal
Machallah seydi Tall
Am na solo trop ma challah
Assalamou aleikoum chérif alhamdoulilah diley deuguelou yokouté laa thi mane dieureudieuf Yalna yallah sambe
Je t'admire chérif Aïdara
Ken dou chiekhou omar
Ma shalla sedy aidara dejeureuf 🙏
Amna Solo Aïdara
Allahou akbar ❤️☝️
Machallah seydi tall
Machaallaah Cherif
Machala chérif sa numéro itéwo nako bou bakh
Alhamdoulilah ❤❤
Yalla na yalla takhawou la
Motakh karama diaroul diaye bilakhi ya bakh
Nianalkoo
Macha alla mame
Macha Allah
Machalla aidar
Machallah machallah ❤️🙏
yal nané Yalla bourbi tass si barké mak gni
Cherif haydara Seykou Oumar tal Ken manoul xam lepam
Mala beugue Wallahi Wallahi Ma Chaa Allah
Manchallha xol seddna trop
Diarrama cherif
Walay na niou diamou yalla ba alleuk
Adiarama.cherif.ibrahima.aidara.tidiani.
Aksina aksina aksina
شكرا امك
الحمدلله
Kéne dou cherif yagg fi lole té adak were si barkep seydina Mouhammad toujours magui laye thew lou
merci sankara bou beug cherif beug kou bath
Seydi Tall mo nékonne kham-kham
Cheikhou oumar dall taneffou sounou boromla
Seydi tall
Walaahi damay contan badouma nangou di commentaire
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Tallll❤
Seydii Tall