Dans ce Sénégal de médisance et de calomnie, l'istikhfar devrait être notre hymne national quotidien. Dieuredieuf seydi Mohamed el cheikh, encore une fois, vous nous avez montré dans un langage de lumière puisé dans la source de la vérité , la voie qui mène à la satisfaction divine.
Machallah sangeu bi ñidila critique dañou khamoul wallakhi wayé yalla nalén fi yalla bayi may lén wér ak tal (mandé sant naa yalla biñou boké diamono ma khamla beug laa sope laa Dieureu dieuff mawlaya seydi moukhamed el cheikh )
Mancha'Allah, avec tous ces enseignements quand j'entends les détracteurs, ça me fait vraiment mal ...Ya ngui dimbali sopé yi ak talibé yi nguir niou gueneu fonk Tarikha bi.. Dieuredieuf ya Seydi
YoukhriJukum Minal Zouloumatti illal Nur rek. Jazaka'Allahu ya Seydi.
MACHAALAH DJEUREUDJEUF ALHAMDOULILLA MACHAALAH
DIEUREUDIEUF SEYDI MOUHAMED EL CHEIKH YANGUI LERAL ROUHYI A DISTANCE YALLA NGA GOUDOU FANE TEE ANDAK WER
merci sanguebi kenne amoul sa faye
Machaallah Ya Seydi
Dans ce Sénégal de médisance et de calomnie, l'istikhfar devrait être notre hymne national quotidien. Dieuredieuf seydi Mohamed el cheikh, encore une fois, vous nous avez montré dans un langage de lumière puisé dans la source de la vérité , la voie qui mène à la satisfaction divine.
Wallay ndeysaane, lou werr
Deuguentane
Machallah sangeu bi ñidila critique dañou khamoul wallakhi wayé yalla nalén fi yalla bayi may lén wér ak tal (mandé sant naa yalla biñou boké diamono ma khamla beug laa sope laa Dieureu dieuff mawlaya seydi moukhamed el cheikh )
Dieureudieuf ya seydi, dougnou diouk thi dila sante
Mashallah Ya Seydi mouhamed El Cheikh sa lepp ndieurigne la thi diamm yi sant la nieupala amel ndiouckeul alhamdoulilah sant bou bakh
leleg nit gni wakh banga bouga décourager mais so deglo apprécie
baraka lahou fika yalla nga am guereumou mawlaya cheikh
machallah yalla nala yalla barkel te samoula si barke cheikh tidjani cherif
machallah ya seydi sa kaname rék
Yow koula bagne Della hamoul .thiey seydi Mouhamed El Cheikh .Dieureudieuf dallalatnga hell yi
Bilahi deugla yallah la djital .tout est trace dans la vie nous NE faisons.que suivre
macha alla deugue bou wore nga wah yal na nou la yalla fayal bopam ya houtboul hartabalcarim
diarama khalifa cheikh diarama khoutboul akhtaboul kabir
Dieureu dieuffaty dieureu dieuff ya imamal Mahdi Al Mountasar dieureu dieuff ya Seydi Mouhamed El Cheikhe Khoutboul Akhetaboul kabiir Noor khoutboul Khafikhayni imamal Mahdi Almountasar Halayhi Rida Rahmani ♥️ ♥️ ♥️
j adore cheikh machalla lo wakh souniou khol sedd yama yok si yonou tarikha cheikh billahi sama khol gua nek
Mancha'Allah, avec tous ces enseignements quand j'entends les détracteurs, ça me fait vraiment mal ...Ya ngui dimbali sopé yi ak talibé yi nguir niou gueneu fonk Tarikha bi.. Dieuredieuf ya Seydi
Mmm
P
Verite
mashallah
MashAllah Sangbi.
Niogui lay sante bou bahh el cheikh !!!!
ESKEY MAWLAYA SEYDI MOUHAMED EL CHEIKH