Xalat Man Limay ngiàn thi barké Mohamed môy ngen am.radio.am.television.ndax yen ték la gis ngen Di wax Lou amal réwmi ngiaring ta andoul Aki nàx j'aime wày
La valeur d'un homme ne se mesure pas à son argent, son statut ou ses possessions. La valeur d'un homme réside dans sa personnalité, sa sagesse, sa créativité, son courage, son indépendance et sa maturité. Un homme multidimensionnel et d'une noblesse incontestable ! QU'ALLAH t'accueille dans son paradis ! Merci XALAAT TV !!!
اللهم اغفر له وارحمه ونقه من الذنوب والخطايا كما ينقى الثوب الأبيض من الدنس واغسله بالماء والثلج والبرد وادخله الجنة مع النبيين والصديقين والشهداء والصالحين
Jaambari SËRIÑ TUUBA ji Jëwriñ: Sëriñ atou diagne YALLAH na sunu borom yook ñeggalam si moom Teee waneileku ak Sopém ba SEXX AHMADU BAMBA XADIIM RASSOUL 🤲🏼♥️
Avant de regarder la vidéo je commence d’abord par te remercier d’avoir répondu à notre demande ! Ça montre à quel point la chaîne est engagée au côté des vrais patriotes ! Merci merci merci
Mon père était le chauffeur quand ils allaient chez Serigne Aboudoul Ahat MBACKÉ en 1972 j’ai même les archives avec moi. A l’époque c’était le "Dahira des Étudiants"
Machalah seringe Atou diange yalla nako seringe Touba téro diambar Lawone ko nangou sone si Ligeuyal seringe Touba Aldianay firdawsi yalla na done keurame merci khalate tv yalla na sa diame yage
Wallahi xalaat tv lii gay défal Sénégalais yi boo faato (yalla na yèx) waayé dootun la fatté ba muk. Ndax lèrna ma ni na foo fété ci keur dîné yi Wayé fègnul ci vidéo yi dax képu kou bax ga indiko guir gnu diarignou Dagay wax deugu ta doo par par lo Di bènalé askanwi Di wèr nafèkh yi ak sath yi Yalla na la yalla faye
Serigne Atou Diagne yalana Yallah waccé yërmandé ak njéggël ci mom tabbal ko Al Janna Firdaws bi Barakati SEYDINA MOUHAMMADOU RASSOULOU LAAHI SALLA LAAHOU ALEYHI WA SALAM
Akassa amna solo lool Baye Diagne, il ne cessera de marquer les générations. Boku na si louma diap si ay wakham moy bouniou begué souniou liberté faw niou meneul souniou bop; « sans autonomie financière, on ne peut acquérir une indépendance culturelle » nitt kilay diokh mola sagn diokhogn foy takhawé. Lolu ma gné si lool Hizbut yi nakh lolu la Serigne bi dane incarné. Sokhlaloul lene si kene rawatina bour yi à l’époque
اللهم اغفر له وارحمه وعافه واعف عنه ووسع مدخله واكرم نزله ونقه من الذنوب والخطايا كما ينقى الثوب الأبيض من الدنس وادخلها الجنة واجعلها من جوار رسول الله صلى الله عليه وسلم ءامين
Merci beaucoup yéne wa xalat TV tout le jeunesse sénégalais amelnaniouléne ndioukeul yalla naléne yalla Faye xamnaniou lou bari grâce à vous lii nak beuge sa réwe mounoukou wéssou vraiment amounou sene faye bouléne massa bayi ngir yalla vous faites Un grand djihad yalla naléne yalla sameu fii Ken momoul ken kou wax DEUG niou xamko donc pour vous dire que niongi sene ginaw douniou mass nangou koulendi tilimeul wala koulendi touteul bilahi walahi watalah nous sommes très fiers de vous merci infiniment
Kou sope seyedina mouhamed psl beuzeull j'aime ❤️❤️s atou diagne yalla na souff oyoff si kawam si barképp s touba mbacke😰🤲
S.a.w
Toma
@@kaleseye9351 nkm pro
Mon frère beusna j'aime bouyage dotou mako faté inch'Allah
Allahouma Amine
Thiey Serigne Atou Diagne😭😭😭 jambar deugu dem na
Amna solo lol
Ligueni def samakhol sedanasi bargueb s.touba andalen ñoudefar senegal
Akasa wa a saliha tv
Wallakhi
Billahi
Yallana yalla yeureum ko khareko aldiana firdowsi
Première commentaire mangui niane képpou kou beug serigne touba rék na nianal atou
Del wakha bepou julit rek mourid sadikh ziarnala bouwer fall
Dia Dieuf Xalaat TV Amatina Solo
Massa ahlla yenet ñoubak guen
Massa AHLLA TOUBA vision guisnañou sen ligueye yenit
Machalla yénne tame
🙏🙏
Mission accomplie, brave homme que DIEU t’accueille dans son paradis
Amiiiine
Machallah
machalla
Amiiine
Xalat Man Limay ngiàn thi barké Mohamed môy ngen am.radio.am.television.ndax yen ték la gis ngen Di wax Lou amal réwmi ngiaring ta andoul Aki nàx j'aime wày
NDAYSANE DIADEFF YALA NA LA YALLA FAYE BARKI S.TOUBA
Mourid nirekla nañou anda defar senegal xalaat tv ñoubakha lañou yenit sen ligueye massa ahlla dañou lendi topou sasoune
Limom bakhana damrek nañou anda defar SENEGAL
Machallah
Merci xallat TV ❤️❤️❤️❤️ xalaat TV 💪💪💪💪 xalaat TV encore xallat TV toujours xallat TV je vous j'aime beaucoup wallahi
Ana kou dacor ni xalat tv dougn soss lougn wakh dafa lér dieureudieuf xalat tv♥️♥️♥️✓✓✓✓
Man may première
Motakh ñu andak mome ci deugue
Walay si kaw si kanam rek
La valeur d'un homme ne se mesure pas à son argent, son statut ou ses possessions. La valeur d'un homme réside dans sa personnalité, sa sagesse, sa créativité, son courage, son indépendance et sa maturité.
Un homme multidimensionnel et d'une noblesse incontestable !
QU'ALLAH t'accueille dans son paradis !
Merci XALAAT TV !!!
Bien dit
Paix à son âme 🤲si tu aimes serigne touba tape j j'aime 👍
Fatiha 11 lihlas yénéko serigne Atou diange ak mbolém dioulit yépou niane yalla dolli léne yeurmandé
Machalla kou beuege Serigne Touba rek beusal j'aime
Machallah tawféhou Serigne bi rek
Beug Serigne Touba të yalla takh, mo dakh adina! ak lisibiram
Kou beugg xalaat bessal j’aime 👍🏾 mashalla
اللهم اغفر له وارحمه ونقه من الذنوب والخطايا كما ينقى الثوب الأبيض من الدنس واغسله بالماء والثلج والبرد وادخله الجنة مع النبيين والصديقين والشهداء والصالحين
Jaambari SËRIÑ TUUBA ji
Jëwriñ: Sëriñ atou diagne
YALLAH na sunu borom yook ñeggalam si moom
Teee waneileku ak Sopém ba
SEXX AHMADU BAMBA XADIIM RASSOUL 🤲🏼♥️
😭😭😭😭
Ki mourid sadikh la nagnou ko yalla fayal te xare ko al diana😭🙏
Yalla nanu yalla Fayal Baye Atou Diagne si barké kou Tédd ki💔💔🙏🏿🙏🏿
Dama took UA-cam dii Xaar vidéo Bii.... Serigne Atou Yal'ako Yall'a Yërëm tér XarékO aja'''na
Mercii bien encore une fois XALAAT TV
faralak degue rek .yalla nala yalla samme
Amine
Kou bague srg touba basal j'aime ta yalla tax ❤❤🤙🤝
Amna solo trop ndaye san yalna ko sarign touba tèrou
Kou am dara dja kou amon talibés legueyal seringue touba rek thi la masa nek yalna kou yalla yeram b s touba👈
Avant de regarder la vidéo je commence d’abord par te remercier d’avoir répondu à notre demande ! Ça montre à quel point la chaîne est engagée au côté des vrais patriotes ! Merci merci merci
Bilay
Yalla nayalla yeureum serigne atou diagne
Ohh xalat wallahi lazi dama guiss video bi dm dioy barkep Arkhone dama xallatt magui Niane si barkép xassida Yii barkép s..Touba Yallah nala brom ba faye yiw sm xoul sédna wallahi😭😭😭😭😭❤❤😍🙏
Amine amine ya rabbi barke Serigne touba
♥️♥️♥️♥️♥️
Amine si barke serigne touba
@@electionslocaleselectionsl3859 amine inchallah❤😍🙏
@@Leuz_vision ❤😍❤🙏
Mon père était le chauffeur quand ils allaient chez Serigne Aboudoul Ahat MBACKÉ en 1972 j’ai même les archives avec moi. A l’époque c’était le "Dahira des Étudiants"
Ton pere n'etait il pas chauffeur au coud?
Charles Guy si il était chauffeur au COUD et même mon frère travaille aussi là-bas comme chauffeur
Mashalla 🙏🏼
Segn bi niogui ziar😢
Ma shaa Allah lii yeup si liguey sans tambours ni trompettes. Qu'Allah te fasse Miséricorde Baye Atou. Un exemple pour la jeunesse
Machalah seringe Atou diange yalla nako seringe Touba téro diambar Lawone ko nangou sone si Ligeuyal seringe Touba Aldianay firdawsi yalla na done keurame merci khalate tv yalla na sa diame yage
Masalah xalaat tv
Massa ahlla nirekla andalen ñoudefar senegal
Amine way amna solo
Sëriñ Atou Diagne ndanane deug mouride sadikh leu liguéyeul na yalla ba dém té dara niawoul.
Yalla nako yalla yeureum ta kharé ko aldiana firdaws
FRANCHEMENT J'ATTENDAIS CETTE VIDÉO ET CELA PROUVE VRAIMENT VOTRE PROFESSIONNALISME VOUS NOUS RENDEZ FIER QUE DIEU VOUS GARDE EN PAIX
Bilay❤️
Yalla yalla wanalèko ak kou téd ki thia aljana firdawsiya si barkép seydina mouhamed. Amine
Liguey bii rafett na mission accomplie yalnako yalla yeureum borom touba terrou cia aldianay firdawsii ❤️🥺🙏🏾
C'était lui le vrais général de Bamba.
Que Dieu l'accueille dans son paradis céleste firdaws
Masha'allah alhamdoulillah yallah nala cheikhoul khadim terou firdawsi si barkei mame salihou barkei serigne Abdou lahad mbacké masha'allah xol toy na si sa warhioup ligueye wantei yite xol sede na masha'allah.
Yallah nala yallah soutoural.
Sougn njabote gui gneuw euleuk yallah nagn dajekk deugui mourides aki deugui kilifas nguirr mena defarou si adouna bou jaxasso bi🙏🤲
Mais wa Xalaat tv mom khana ab nitou yallah nga mashallah ❤💗say cadou day lerr andak yarr akii Tèguine yallah nala sougnou borom Sameu wayyy💓💖
Machallah amiine
Bilay machalla way
Wallahi xalaat tv lii gay défal Sénégalais yi boo faato (yalla na yèx) waayé dootun la fatté ba muk.
Ndax lèrna ma ni na foo fété ci keur dîné yi Wayé fègnul ci vidéo yi dax képu kou bax ga indiko guir gnu diarignou
Dagay wax deugu ta doo par par lo
Di bènalé askanwi
Di wèr nafèkh yi ak sath yi
Yalla na la yalla faye
Ndeyesan 😭😭😭😭😭 thiey adduna kou diambar lool Baye atou Diagne yalla nako yalla yeureum ta kharé ko aldiana firdawsi barké Serigne bi
Thiey Segn ATOU yalna ko san borom dolli yërmandé 🙏
Thiey Serigne touba wallahi amoul morom ❤️Serigne Atou Diagne liguéye Bi rafait lol yalnala yallah Faye thi bar khép Serigne touba ❤️
Enfin je suis le premier à commenter sur xalaat wayyy😂😀 ndeysaane le dieuwrine des dieuwrines S Atou Serigne Touba dinala fayy bagua tiiit walahi
Dagay xaar fall😁
ماشاء الله جزاكم الله خيرا
Dieuredieuf serigne atou diagne khasayit mission accomplie paix à son âme 😭😭😭😭et xalaat tv machalla thji leral yii
Ce qui me plaie plus c le faite de nous aidez à supprimé le mot "Complexe" yalla na tassék yeurmadé borom bi barké Borom Touba
Walahi nou gnou mél moma man ak samy morom you bari Serigne atou yalla nala serigne bi térou amine 😭😭😭😭
Ndeye sane thiéy serigne touba amoul morom deh billhai yalla naniou ko yalla fayall
Yalla nako yalla yreum té kharéko adiana firdawsi barkep naby Moustapha psl ❤️🙏🏿
Ndayesan 🤦♂️❤️ligueye rek ladon def bilaye
Merci xalaat tv ❤️✊🏿
Serigne Atou Diagne yalana Yallah waccé yërmandé ak njéggël ci mom tabbal ko Al Janna Firdaws bi Barakati SEYDINA MOUHAMMADOU RASSOULOU LAAHI SALLA LAAHOU ALEYHI WA SALAM
Ndaysaan jàmbaar dëgg mooy jëmm jii yal na ko Yàlla yërëm te jéggal ko.
✍✍✍✍yalla na ko yalla khare aldiana ya gueuna kawè si barkep serigne touba🕋🙌❤
Yal na ko Yàlla jéggal te yërëm ko barkeb Seexul Xadiim aamiin
Machallah vraiment à xalaat TV toujours au service de la nation baye Atou Diagne k votre âme demeure au Paradis céleste...
Mach allah sunu Xalaat amatina solo déh yal nala yalla samou Sériñ atou jagne yalnko yalla dolli yuermande
Ndaysane machallah 🥰🥰🥰
yaw tamit xalaat tv ća kaw ća kanam incha allah barkép al qouran
Serigne Atou yalla nako yalla téral si barke serigne touba ak xassida yi
Ndeysane serigne atou yalla nako sunu Borom yereum té tabbal ko aldiana
Dieureudieufe serigne touba yallah nako yallah yeureum te xareko aldiana barke s touba 🙏
Amine
MachaAllah Yallah na sounou borom khaaré ko aldiana firdawsi ya gueneu kawé si barké Naby Moustapha
Seriñ Atou Diagne yalna Aldjana done sa keur si barkeep Seriñ Touba 🙏🏾
xalaat tv machallah sén liguye rafét na torop yalla nalén yalla faye barkéb s touba machallah way ❤❤❤❤👏👏👏👏👏
S atou diange yalnako yalla dollé yeuram te diegalko mbolém bakaram yépou thi barkéb kimou done leugéyal
Yalla nako Yalla yeureum ta xaréko aldjanna firdaws bi barakati Seyidina Mouhamed (Paix Et Salut Sur Lui)
Barke XASSIDAYI sama xoll sedd na loll yallna yalla taxawou XALAAT TV😪😪
Bilahi
Amine
Amine
Dafnagn lou asskan wi beug mom... J'ai pas encore écouté la vidéo mais sama xol sédeu na
Amiin
Jàmbaar dégg demna Sëñ Aatu Jaañ yal na Yàlla dolli yërmaande ci moom ci barkeb Xasida yi 🙏🏾 😭
Serigne atou Diagne yallah nako yallah yeureum té kharé ko alldiana
Yalna noko Serigne Touba térou🥰😭
Amine 🤲
Yalla nako yalla yërëm ci barckep Mouhmet psl . Yalla na mattal yénném.
رحم الله شرج آتو اللهم إرحمه ووسع دياره وسط الجنة
Yalna yalla faye serigne atou Diagne te kharéko al diana firdawsi 🤲🤲
Et merci beaucoup à xalaat tv la de homme des valeurs
yallna ko yalla yereum mandé bouma sétané sa vidéo ba paré 3 salah toultoul fahtia dila gnanal.🤲
WA HT AY TANÈFI S.TOUBA LAGNIOU💔💗💘💞💔💓💟
Maasàllaa ❤️❤️ Amna solo lool, yal na Yàlla yeesal yërmaandeem barkeb Alxuraan.
QU'ALLAH LE TOUT PUISSANT L'ACCUEIL DANS SON PARADIS BARKEP BOROM TOUBA AK XAÇIDA YII
BAYE ATOU JËRËJËF❤️❤️❤️
Machallah.Serigne Atou Yalla n'a ko Sounou Borome defaal khéweule adina ak alahira bakê alkhourane,
Magui koy tibè thi sama xol ak ak s.touba 1millions de vue la beug thi vidéo bi yalla nako thi am wakhal amiiiiin
ءمين
L'accueil dans son paradis céleste 🤲
❤️❤️❤️❤️💯👌👌👌
ALLAHOUMMA AMIIIN ❤🙏🤲
En terme de kham kham technique charisme....Yalla na khippé aldiana firdawss
machallah
Amine 🤲🤲
serigne atou diagne. mahala yalla nañouko yalla fayale walahii si ligueyal serigne touba 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Yalnako yalla yeureum, dieguel ko té kharéko aldiana firdaws 🙏🙏🙏
un vrai Général de Bamba que le tout puissant l'accueille dans son paradis céleste 🤲🏾
Baye atou Diagne yalla naco bour yalla khare aldjana ferdawsi amine yarabi si barqe borom touba amine yarabi
MACHALLAH XALAAT SERIGNE ATOU YALNA KO YALLA YEUREM SERIGNE TOUBA TÉROUL KO BOBAM
Un homme estimable,exemplaire, qu'Allah lui accorde Aldiana firdaws
Akassa amna solo lool
Baye Diagne, il ne cessera de marquer les générations.
Boku na si louma diap si ay wakham moy bouniou begué souniou liberté faw niou meneul souniou bop; « sans autonomie financière, on ne peut acquérir une indépendance culturelle » nitt kilay diokh mola sagn diokhogn foy takhawé.
Lolu ma gné si lool Hizbut yi nakh lolu la Serigne bi dane incarné. Sokhlaloul lene si kene rawatina bour yi à l’époque
Serigne atou diane yalla na souff oyoff di kayame barki serigne touba 🤲🤲❤❤❤😭😭
Machalla Mame Ato Diagne Sa Dondou Gui Amoune n’a Solo Yallah N’a aldiana disa keur
Dieuredieuf serigne Attou diagne ligueyal ngeu serigne touba machalla
Yalla na yonanetoubi térou si barké serigne touba
اللهم اغفر له وارحمه وعافه واعف عنه ووسع مدخله واكرم نزله ونقه من الذنوب والخطايا كما ينقى الثوب الأبيض من الدنس وادخلها الجنة واجعلها من جوار رسول الله صلى الله عليه وسلم ءامين
Masha'alLah doy nga idoLe béep juLiit YalLah na La buur YalLah fay LiguéYeuL diné rek mo woor 🥰 dama beug wa hizbou borom bi xamna ko
Mashallah
Xalat tv gueuna la beugue barké xasida yi😭❤❤❤
Ma challah xallat wa eck dounguen deff waxtane ci serigne cheikh gainde fatma pck neww na gnouko xam insbi et pourtant dafa yagga xexAl senegal 🇸🇳
Loo lu de di na amsolo lool sax, Sëriñ Mbàkke Gaynde Faatma xeexal na diine xeexal Afrik aki doomam
Bonne idée
Xamna biss dana gnaw mou wax ci moom
Ku mata xam
Bilay gainde fatma dh lo warr la
Merci beaucoup yéne wa xalat TV tout le jeunesse sénégalais amelnaniouléne ndioukeul yalla naléne yalla Faye xamnaniou lou bari grâce à vous lii nak beuge sa réwe mounoukou wéssou vraiment amounou sene faye bouléne massa bayi ngir yalla vous faites Un grand djihad yalla naléne yalla sameu fii Ken momoul ken kou wax DEUG niou xamko donc pour vous dire que niongi sene ginaw douniou mass nangou koulendi tilimeul wala koulendi touteul bilahi walahi watalah nous sommes très fiers de vous merci infiniment
Dieureudief waye xalat tv diangéne dieuff sakaw sa kanam rék si barkep Serigne Saliou Mback amo morom
Serigne atou yalla nakou serigne touba tèrou
Serigne Youssou diop yalna yane bi woyof 🤲🏾
Machallah xalaat tv serigne atou diagne yalla nako yalla yeureum té kharégo aldiana firdawsi si barkém borom touba 😭😭😭😭😭
C’est genres d’histoire qu’ont doit apprendre aux élèves d’aujourd’hui quels élégants que dieux l’accueille dans sont paradis
Moh geun di djagalé histoire rou degaul
Oui vraiment
Mashalla lepp rafétt na Serigne Atou Diagne yalla nako Serigne bi téerou
merci beaucoup à vous Xalate TV