Je suis touché au plus profond de moi par les mots du khalife... Je suis chrétien et je pense à ts mes frères au pays que DIEU les protège Je disais que AMEN !!!! Et j'en ai les lermes en écrivant ces phrases...
Cheikhouna talibé bamba Machallah serigne mbaye Sy mansor Khalifa general de tidiene yalla nala yalla takhaou te dimbalila goudall sa fane te May la wer dieuredieuf
Serigne touba ak mame maodo gno bokk derett bokk diné benne begeu begeu rek lagnou amone mouy takhawall diné li slam te yalla defall nalene si ndam fay lene si faye gou reuy kone gnou pour gnou diary gnousi dagni nèk si lagnou beugone moy moy gnou bolo nèk benne beugeunté yenanté diam mouride manna diarignou si mame elhadji malick tidiene mana diarignou sí serigne touba wayé gnou talibéyi manougne léna diarigne dará ndakh gnom amnagne lepp
Je ne suis pas sénégalais et ne comprends rien du wolof , mais je suis touché au fond de moi . J'aime bien ce mode de vie sénégalais caractérisé par la relation Cheikh-talibé . Le Sénégal est l'un des rares pays où les fruits du soufisme sont nettement visible dans la société . Je prie mes frères et sœurs sénégalais de tout faire pour pérenniser ces acquis. Votre frère Oury BAH musulman soufi tidjani de Guinée Conakry .
Hoooooo la position de Serigne Alioune Diagne quand le Khalif a prononcé ses premiers mots, li surprise dakouko, MachaAllah, Sénégal amna ndam, dinégui bene laa, khol yeup fekhna
bilahi lou lér nga wakh masi kham dara tivaouane la niagé aka woyof té beri may dége na béne borom kham kham moné soy dokh boulén ka diégé nah jinéyi niokay topo
Beg naa lool, ci S Mbaye Sy dafa modeste lool, wallahi.Yàlna ko Yàlla sàmm te aar ko Baarke S Touba. Xana di wax rekk Taalibe bi yi jafe ko te sàmmante ak moom loo lu mooy wax ji. Loolu S Touba jàngale Mom la El haaji maalig jàngale. Yeen talibe yi rekk ñooy xajamal mbir yi waaye buñleen ko may. Ndax tarixa bu neek booku na ca ay sàrtam respecté doomu aadama rawatina kilifeu ak fum mana booku. Bek naa lool ci S baabakar yàlla na ko yàlla sàmm barke S Touba sunu wasiila.
Macha Allah Macha Allah fière d'être talibé cheikh li lépp day firndé limou wakhone thi temps élection yi que nous sommes tous des simples citoyens Macha Allah sama serigne 🙏🙏
Dieu seul sait ce que j’ai ressenti quand j’ai entendu la voix du Khalif!!!! Allahou Akbar!!!! Pape Serigne Babacar SY Mansour puisse Ya Allah vous donner une longue vie avec une excellente santé afin que vous puissiez continuer de nous faire plaisir comme ce soir. Je vous aime tellement!
Mashala amena solo lole yalla na goudeule sayes fans Si Malick man chretiene la waye kou deuglou seribi kham ni nitou yalla deugue la. Yalla na yalla yagual takhawaya inshahala rabi🙏🙏🙏.
Djeureudjeuf s'y babacar le halif général des tijani yalla goudal sene fane thagui yalla dangou pape cheickh amnasolo djanegui yalla nala yalla faye dji barkee nabyl moustapha (pls) youssou kene dou djowe tfm yalla yoko dij barkee lahi llaha illala hallamdoula kontana amin dja rabi
Africa United Mouride la mais ? Ont t’as pas savoir si bane confrérie senegal nieup béne lagane aye domou adama laniou nioune nieup bolési nek aye djoulite
@@galsendiaspora6812 gnoun gnepp ay dioulit lanou mais kounek amngua keur go bokk mais téwoul ngua wara respect ak beug kénen ki nekk fénel mongui melni ninou deuké sénégal mais kounek ak region wala quartier bo deuk mais téwoul gnoune gnepp ay sénégalais lanou .motakh mané me suis mouride mais kou beug tidjane yi la .nit manoul nekk tidjane wala mouride sans mounek musulmane donc arréte svp
Ma cha Allah,wakh dji raféte na trop,sama yaram dawna,yalna yalla goudale sa fane sy Malick. Wakhou kilifa deug nga wakh. Yalna yalla déf diam Sénégal si barké Cheikh Ibrahima Niasse
j'apprécie énormément son humilité!!! en tant que Talibé mouride yallana nagfi yagg lool andak wérr lool SY malick et de grâce ne nous laissons j'aimais distraire par quoique ce soit! on est de la même famille!!! Que Dieu béniss le Sénégal, l'afrik
Cela veut dire que nous sommes tous égaux devant le tt puissance Ni mouride ni tidiane ni aucun autre d'ailleurs Merci sy malick d'avoir montré l'exemple
@@khadijasane4523 yaw louy sa problem loutakh vous aimez creer des confusions meune ngena wakh ba kene dou wakh si MAODO ak wa keureum vrema deuk bi mo beuri ay dof
@@khadijasane4523 suis mouride ms vraiment suis content c'est le senegal qui gagne khadija bayilen yi ab dioulit dou togne limou kham la wax mane chaque jour damay wax serigne touba amoul morom téi lima kham rk la wakh
Cheikh mouhamadou lamine bara Mbathie Touba Nayobe Machallah Seringe Mbaye sy waxtan bi amna solo xam xam bi weurna Machallah yalnah yallah goudal sa fan te may la ak wer amine
Machallah li deh sedd n'a khol lolou wayy, té bépp dioulite bou nekk si Sénégal, Warr ngua Roy si dieuf dji té khamnii akoup talibé rek MO am solo, souniou sangue yi sakh mom la gnouy sakkou. sy Malick yalla nalla fii souniou borom bayii Lou yague té werreul leu si barkep Khadim Rassoul.
ame léne yar fi bou gou fi djitou serigne touba la ndakhe mome rk mon khékhe Islam man tidiane la mais ligue wakhe dou wakhou nite khamou adouna amou yare
Machalah machalah serigne bi khôl sedatina tay khol yeup toyna yageu fi loll te wer sy malik li yomboul sy kou oyof rek moko meune yalna takhawaye bi yageu ❤️
جزاك الله خيرا يافضيلة استاذ علي جاچ حفظك الله ورعاك وأيدك ونصرك وأطال الله عمرك مع الصحة والعافية والتوفيق بجاه طه صلى الله عليه وسلم ببركة شيخ سيد الحاج مالك سه رضي الله عنه ونفعناالله ببركاته آمين يارب العالمين
Ndeysanne Wayé Mouride sagn nagn nianeu si Barké suniu Sèrign mi di Khadim Rassoul mais la différence entre ns et des personnes de ton genre nous moi particulièrement j'aime tout cki est musulmans rawatina talibé Cheikh bamou diaralma di dém Tivaoune di nianal kilifa you tédeu youfa teude di. Nianeu yalla Tass niou sén ay lérr té nékoul gamou . Dém si Sama beureuk sama yakar tay ak euleuk mi di borom Touba nianalko nianalko niane yalla mou Tass niou Barker C juste pour te dire nioune Mouride on respecte toute personne surtout nittou yalla you nék suniu fi yalla bakhé niouko diko santé Sèrign Touba Soula méti matsa nak wayé seytané bakhoul té dél wakh lo kham
Machala yallana yalla goudalll sa fane serigne babacar sy mansour linga deff amna solo léralll yi amna solo Sénégal béne la nanou toupou sounou kilifa yi té royyy léne boukou défé yalla défff diamm wathié yeumandé ak ndjiégalllll si askane wi ....amine♥️♥️Modou baye fall ♥️♥️
Sy Malick yagu fi loleu té andal wéreu Mane dé Mouride pire la Sèrign Touba képeu laniou beug wayé fonk ne kép kouy talibé Cheikh dém na Tivaoune juste pour ziar nakh ay kilifa you mata nianeu sén lér la niit kou nangou nopalou yalla mo yoreu di mayé 🙏🏿 Sérigne Mbaye Mansour yagu fi loleu té andal wéreu Dieureuff Cheikh Akhmadou Bamba Mbacké yaniou sgal yaniou ték si yoneu yaniou khamal louy fonk makeu yaniou may khôl you takh duniou touteul niteu alhamdoulilah
Sénégal begg na sy malick suniou khel dal Bilahi j suis mouride mai barké serigne touba beug nala dei sy longue vie à tw waxx bi rafetna jai un coeur rempli d joie
MachaAllah rafétena 🙏🏾 yalla na YaAllah Bourbou MAGUE Bi mousseul Sénégal, same ko té maye sounou kalifa généraux yeup gnou yague fi looole té weur barké Borom Touba🙏🏾🙏🏾
M anchallah yalla na yalla goudal fane domou adama yeup,te mouthieul nieup ci mbass mi inchallah.quartiers general ci kaw ci kanam ci. Lou bakh merci bcp
Machallah Sy Malick contane lol si Serigne BaBacar Mansour souma koy khole ak diko deg damay khamni nite kou am yeurmandé la ta oyof lol sakh mane deh Mourite la wayé souma koy khole diko déglou mom ak Serigne Abdou Karim Mbacke kif kif si oyof ak am yeurmande yallah nagnou fi yag lol ta wer ak bepp dioulite
ماشاء الله تبارك الله ياشيخ سيد ابوبكر سه محمد الأ منصور الأخليفه حفظك الله ورعاك وأيدك ونصرك وأطال الله عمرك مع الصحة والعافية والتوفيق بجاه طه صلى الله عليه وسلم ببركة شيخ سيد الحاج مالك سه رضي الله عنه ونفعناالله ببركاته آمين يارب العالمين
Kou beugg Mame maodo wa Mame bambe beusseul j'aime 🙏🙏🙏
Je suis touché au plus profond de moi par les mots du khalife... Je suis chrétien et je pense à ts mes frères au pays que DIEU les protège
Je disais que AMEN !!!! Et j'en ai les lermes en écrivant ces phrases...
nous sommes tous des croyants
Machalla
brams O'Reilly mom niep la bolei niane bi kou bakh nioko bokk
brams O'Reilly ay corona roussal li gni t abalgnou
😭😭
Sui mouride mai g bcp adoré l intervention du khalif diko wakh amine aussi diko gnanal goude fane akh wër
Machala
Dangua nité rek té rafete khol
Papy Dady Diouf relis svp les mots de Adji Sall
Kou bakh rek beug ñiou bakh ñieup ak lou rafett MashAllah
Merci. Nous avons besoin deux en cette période
Cheikhouna talibé bamba Machallah serigne mbaye Sy mansor Khalifa general de tidiene yalla nala yalla takhaou te dimbalila goudall sa fane te May la wer dieuredieuf
Ni rk la Adouna amoul solo
Serigne touba ak mame maodo gno bokk derett bokk diné benne begeu begeu rek lagnou amone mouy takhawall diné li slam te yalla defall nalene si ndam fay lene si faye gou reuy kone gnou pour gnou diary gnousi dagni nèk si lagnou beugone moy moy gnou bolo nèk benne beugeunté yenanté diam mouride manna diarignou si mame elhadji malick tidiene mana diarignou sí serigne touba wayé gnou talibéyi manougne léna diarigne dará ndakh gnom amnagne lepp
Macha allah amine yarabi
Amine ya Rabbi
Machallh amna solou
Bilaye mourides yi yéna niak kiniane. Sene commentaires yi woné nako. Vous êtes vraiment exemplaire dans tous les domaines machalla
Bilay ndeysane
C le sénégal qui gagne 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Pape liggua am tay bé' animateur Amou ko sa émission goor bou makk woté machalah 😍 yal n'a diam yagg yalla doli niou soutoura Amine
Borom xol bou rafett dara diombouko cilou bakh lolou mô dal pape Cheikh Diallo MashAllah geune Gorgoorlou rek moko dessei
Bilay
Bilahi
Pape kholbi mo rafett motakh Lou bakh reck
Alhamdoulilah
Yalnako yalla may gouddou fane ak wér.
Quelle humilité !!!
En tant que Mouride sama xool seddna🙏🏾
PMD GSB yalla na sen diam Yague
Goudou fan ak wér
Bilay adouna amoull sollll
Macha allah amine yarabi
Bilay ya bakh mouride né yw lay mél
Je ne suis pas sénégalais et ne comprends rien du wolof , mais je suis touché au fond de moi . J'aime bien ce mode de vie sénégalais caractérisé par la relation Cheikh-talibé . Le Sénégal est l'un des rares pays où les fruits du soufisme sont nettement visible dans la société . Je prie mes frères et sœurs sénégalais de tout faire pour pérenniser ces acquis.
Votre frère Oury BAH musulman soufi tidjani de Guinée Conakry .
Bilay Serigne bi ya bakh🙏Yalla nala yalla doundal sa fane si barké wérou koor biii machalla taye sama kholll❤dafa toye🙏liiiiii moy Senegal🇸🇳☝️
Machallahhhhh
Hoooooo la position de Serigne Alioune Diagne quand le Khalif a prononcé ses premiers mots, li surprise dakouko, MachaAllah, Sénégal amna ndam, dinégui bene laa, khol yeup fekhna
Machallah pape cheikh sa émission nekh na ba nopi serigne Babacar sy yalnafi yague thé werrrr
Amine
Amiin ya rabbi
Amine
Alhamndoulilah 😍bima boké si ndiabotou mouhamad psl❤bokk si sopé mame cheikh tidiane cherif diarama mame mado sy malick yalnaniuouko yalla fayal
Bilahi kouko khamoul dioum nga. Aka bakh aka Oyof. Kou bayiwoul wakh lou gnaw thi kilifa boula baloul sankou nga. Oyoff tolou, Dou khépp kéne, rafét khol, ték thi deugou et direct. MachAllah. Yague fii lolou té wérr Sy Malick🙏🏾
Machala
Wallahi makoy seedé bilahi kou xamoul xamoo nitou yalla bou amoul ben werenté
bilahi lou lér nga wakh masi kham dara tivaouane
la niagé
aka woyof té beri may dége na béne borom kham kham moné soy dokh boulén ka diégé nah jinéyi niokay topo
Mouhamamed Mbengue kou deglou ay discours ram kham ni kou oyof la sounou mame Sy Malick ❤️❤️❤️❤️
Kouko khamoul rek mokoy wakh loi niaw khamou loi niaw té douko wakh bilahi sy
Beg naa lool, ci S Mbaye Sy dafa modeste lool, wallahi.Yàlna ko Yàlla sàmm te aar ko Baarke S Touba.
Xana di wax rekk Taalibe bi yi jafe ko te sàmmante ak moom loo lu mooy wax ji. Loolu S Touba jàngale Mom la El haaji maalig jàngale.
Yeen talibe yi rekk ñooy xajamal mbir yi waaye buñleen ko may. Ndax tarixa bu neek booku na ca ay sàrtam respecté doomu aadama rawatina kilifeu ak fum mana booku.
Bek naa lool ci S baabakar yàlla na ko yàlla sàmm barke S Touba sunu wasiila.
Macha Allah Macha Allah fière d'être talibé cheikh li lépp day firndé limou wakhone thi temps élection yi que nous sommes tous des simples citoyens Macha Allah sama serigne 🙏🙏
Dieu seul sait ce que j’ai ressenti quand j’ai entendu la voix du Khalif!!!! Allahou Akbar!!!!
Pape Serigne Babacar SY Mansour puisse Ya Allah vous donner une longue vie avec une excellente santé afin que vous puissiez continuer de nous faire plaisir comme ce soir.
Je vous aime tellement!
saly diouf dieureudieuf yiow tamiteu. Yallah naleu yallah taxawou si leippeu alahouma Amine 🙏🏼
Ibrahima Traore dieureudieuf sama thiamigne
Wallahi mouride la talibe Serigne saliou me dama contann si khalifa tivaoun bi
Yaw cou Bakhca
Je suis talibé cheikh et j'aime bcp mame saliou..
Ya bakh wayy machallah 🙏
Khana khamo vraie talibè daye am yar mane tidiane la wayè kou gueme deug sa guem guem lou woul daye am yar
Merci mbokou mi
Mashala amena solo lole yalla na goudeule sayes fans Si Malick man chretiene la waye kou deuglou seribi kham ni nitou yalla deugue la. Yalla na yalla yagual takhawaya inshahala rabi🙏🙏🙏.
Allahou Akbar thieye waye khalifa générale de tidiane allhou akbr
Dieureudieuf mame el Hadji Malick dieureudieuf serigne touba derieudieuf baye Niass dieureudieuf limamou laye gnoune gni sounou galathe bougne len sagane gnep ben lane❤️
Je suis mouride mais vraiment je suis contente sama xol sedna trop
Vraiment cest islam qui gagne Mash'Allah.
Bilahi barki serigne touba sama xoll sédd na
Dangua nité rek yalnala yalla defal diam
@@rokhayaseck9239 amine way gnu bokko
Pourquoi je suis mouride ou tidiane on est des musulmans en premiers lolou moy solobi
lima guis si li moye kou wathié sa bop yalla yeukeutila kilifa gui wakhame yeup yalla la machala tivaoune tivaoune tivaoune deukou leer
Bilahi wakhatiko
Mouhamed Cissé dembe dama xalat ni yonene bi dane doundé ak sahaba yi rek lafi guiss walahi
Djeureudjeuf s'y babacar le halif général des tijani yalla goudal sene fane thagui yalla dangou pape cheickh amnasolo djanegui yalla nala yalla faye dji barkee nabyl moustapha (pls) youssou kene dou djowe tfm yalla yoko dij barkee lahi llaha illala hallamdoula kontana amin dja rabi
Ma tégal lathi l'airrou tidjan d'où rakh leundeumm
City Omar amiiiine🙏
Goulleettt liii mousoufeehh am Merci Mame Elhadji malick sy merci serigne babacar Mansour. Merci tfm merci pape cheikh diallo merci oustaz pape Hanne 💖💖💓💓💯💯❤️💓💕💞💞💞
Un geste très noble venant d'une personne noble machala
Ay sama xaritt Aka fiére jàm ci yaw
gouleet
akh taye sama sister bi fi la feulè
@@wakhkatoudeugue2013 guisgua deehh bigmo dama contan trop
Wa TFM war nguene meuna invite tamite mon Seigneur Binjamin Ndiaye wala bena nit Eglise au Q. G. Que dieu vous benisse merci 🙏🙏🙏😘.
Humble, humilité, simplicité. Yalla na yalla fay leu Sy Malick
Amiine
amine ya rabi
Amine Yarabi. Intervention de grande sagesse et d'équilibre du Khalife Babacar Sy Mansour. Qu'Allah agréé et le rétribue inShallah.
bilahi
Serigne Babacar sy Mansour yall nafi yagg té weurr barkep Serigne Touba
Ohhh suis layenne mais je suis très contente ohh gnoune gneup yam Li nekhna deh 😭😭😭🙏🙏🙏amine Serigne bii Sy Malick
Mouride la mais dama beug serigne Mbaye avant mouy nekk khalif . Nanou bolo amoul mouride ela tidjane etc...
Sénégal rek
Africa United Mouride la mais ? Ont t’as pas savoir si bane confrérie senegal nieup béne lagane aye domou adama laniou nioune nieup bolési nek aye djoulite
Sénégal sa genr bi lagnou soxla niitt day wax lou rafaitt maodo Di bamba bamba Di maodo🙏🙏
@@galsendiaspora6812 gnoun gnepp ay dioulit lanou mais kounek amngua keur go bokk mais téwoul ngua wara respect ak beug kénen ki nekk fénel mongui melni ninou deuké sénégal mais kounek ak region wala quartier bo deuk mais téwoul gnoune gnepp ay sénégalais lanou .motakh mané me suis mouride mais kou beug tidjane yi la .nit manoul nekk tidjane wala mouride sans mounek musulmane donc arréte svp
@@mamadoundione5851 wawaw macha allah légui kay nathie talibé roy ba fawou sénégal dieum kanam incha allah
Machaala yalla na sa diam yague
Ma cha Allah,wakh dji raféte na trop,sama yaram dawna,yalna yalla goudale sa fane sy Malick. Wakhou kilifa deug nga wakh. Yalna yalla déf diam Sénégal si barké Cheikh Ibrahima Niasse
Sénégal li la kham diam en yaram dawna barki serigne touba contane na yalla na yalla nangou niane🙏💗
Quelle humilité quelle modestie machallah 😭😭💖💖💖
j'apprécie énormément son humilité!!! en tant que Talibé mouride yallana nagfi yagg lool andak wérr lool SY malick et de grâce ne nous laissons j'aimais distraire par quoique ce soit! on est de la même famille!!! Que Dieu béniss le Sénégal, l'afrik
Cela veut dire que nous sommes tous égaux devant le tt puissance
Ni mouride ni tidiane ni aucun autre d'ailleurs
Merci sy malick d'avoir montré l'exemple
Wallahi gnui don comment ci direct bi di wakh façon wakh you niaw youne warnano rous de
S babacar sy Mansour doundal sa dound amna ndiariñ machallah
ماشاء الله
kadouyi amna solo yalana yala goudal fanwi ta wéral thieuryi kadouyi rafétna
Alahouma amine way
Oh je suis contente parce que QG tay sama serigne lagnouy wahtané je suis figée d être talibé chierkh
Sy Malick ak sa kharite bi serigne moutakha yague len fi Lolou té weer
Amine
Amine
Amine
Je suis Mouride mais sama xol seddd na ba sama rogogne gueineu barki serigne touba kadddou kawé na xam xam biii yemeînaa😭 sy malick goudal fannnnn
Barke brom touba mame Seringe Mbaye Nitt kou baaxla, aka oyoff
Amine amine
Kilifa yi ay nitou yalla laniou kou bakh beugue lén mouy gnome nieupeu
Bilay
amine koubakh
Ya geuna bakh nieup
Kouy weur Woyof ak mbakh diapal serigne Babacar sy Mansour
Yall'na borome bi goudeul ayy Fanaam si barké Mouhamadou
ndeysan adouna amoul solo ngeup ben lagn mashalah serigne mbaye sy mansour tu es un exemple wakh dhii rafetna🙏🙏 mame boy goudal fan
MACAHALLA
Machalla li nékh trop
Allahuma amine
Yalla na sunu borom goudal sa fane sy malick . Barké serigne fallou
Amine
Macha’allah mouride Tidiane gneupa contanne macha’allah!❤️🧡🧡💚💚🧡yalla nako fi yalla bayi té bassi kaname ak bep khalif general 🧡💚💚🧡🧡
C est la première fois que je fais des commentaires mais je suis très très très content
Machalla
Machalla
Lii Moy woneni émission niepa koy setane te defa am solo Macha Allah 🥰🥰🥰🥰
Billay
Limom koumou sedoul sa xoll dara dou sed sa xol sy yallah nala yallah takhawoul bopam yallah May la wèr ak goudou fan si Barack seydina mouhamed
TFM vraiment merci beaucoup sene plateau bi rafetena ,hamham ,barké wathianafi tey , vraiment du courage thia kaw thia kandam rek incha ALLAH
Vraiment vraiment c est du jamais vu un khalif général apelle a 4 heures du matin a la telé macha ALLAH SY MALICK YALLA nangfi yagueu té weur
Mossoul am
Oh li nekhna barki serigne touba gneup contane naniou wayè khalif tidjane kou bakh la modeste yalla na yalla goudal sen fane si barké yonent bi
Machalla émission bi nekhna trop waye naniou bayi xel li serigne bi wakh bou kena xeb bena nitou yalla
senegal ben bope la yalla nafi diam sakh serigne bi modeste na vraiment main wah na deug fii diamano tolou
Amine
Machalahhhh Alhamdouliah Sy malick senegal ben bopp là gno bokk ndey ak bayy..
Alhamdoulilah thi bép domou adama incha allah👌🏾👌🏾👌🏾👌🏾
Teyy momm sama xoll dafa seeedeu tropp bilay wallahii fière d'être Talibé cheikh c'est le Sénégal ki gagne😍😘😘👍👍😂😂💖
Machala 🙏
Mac hallah wakh dji rafétna wayé yaw topal UA-cam bi rék founé ya nga fa
Waxal senegal Bena djoulite yeup nek Ben Moy sounou ndam
Deugeu rk keuy deugeu
Machalla
Machallah machallah je suis mourite mes contana trop machallah sy malick🙏🙏🙏🙏
Amine Sy yaram
Suis mouride mais limoye senegal diadieuf fière d'être sénégalais. Le khalif est très modeste longue vie
Kou ame borom touba, ama maodo loy wakh tmt sante yallah rek
Khamouma walay
Machallah .. wahoumala dara wayeuu yarrr gui thi serigne bi rek momeu ndieukeu yeiim ... vraiment vous etes humble et tres poli...
Thiey maodo !!! Serigne Alioune Gueye wala mame Rawane ngom bou pale rék eupna si Quartier Général , Té Maodo moy séni Serigne
Walay ndeyssan❤🙏
Walay ndeysan mame rawane sama mame..Mame Ousmane ngom yalla na yalla goudal ay fanam🙏
Haaaa wahi doff yene ligene di wakh gamoulene ko
@@khadijasane4523 yaw louy sa problem loutakh vous aimez creer des confusions meune ngena wakh ba kene dou wakh si MAODO ak wa keureum vrema deuk bi mo beuri ay dof
@@khadijasane4523 suis mouride ms vraiment suis content c'est le senegal qui gagne khadija bayilen yi ab dioulit dou togne limou kham la wax mane chaque jour damay wax serigne touba amoul morom téi lima kham rk la wakh
Macha Allah yallana fann wiii Gou dou thie barkép Borom Touba
😭😭 Allahou Akbar sama yaram dawna , lii moy leiir Machallah Serigne bii yallna yalla goudeul sa fane contane nagnou siyaw 🙏🏾❣️
Mash'Allah li moy Sénégal khalifa bi yalla naka Yalla taxawu gudeul ay fanam ci Muhammad sws Sénégal nieup contane naniou ♥️♥️♥️👏😍
Machallah sy malick❤❤❤❤❤❤🧡🧡🧡🧡
Ndaysan je suis mouride ms vraiment suis content c c'est le senegal qui gagne
Cheikh mouhamadou lamine bara Mbathie Touba Nayobe Machallah Seringe Mbaye sy waxtan bi amna solo xam xam bi weurna Machallah yalnah yallah goudal sa fan te may la ak wer amine
Yaw tamite cou Bakhna
Machallah li deh sedd n'a khol lolou wayy, té bépp dioulite bou nekk si Sénégal, Warr ngua Roy si dieuf dji té khamnii akoup talibé rek MO am solo, souniou sangue yi sakh mom la gnouy sakkou. sy Malick yalla nalla fii souniou borom bayii Lou yague té werreul leu si barkep Khadim Rassoul.
L'islame am na ndame li reik lagne kham si senegal
thiey sedil hadji Malick yalla na gnou ko yalla fayalle khole seddana thi khalifa bi yalla na yalla gouddale faname... Q.G. LAF THIATTE
Mane cheikh la wayé Billahi dotouma wakh mouride dara ndakh sama Serigne léral n'a leep machallah Bollé n'a gneep nék béne
ci barki serigne babacar sy yalla na Yalla doli diam ci Sénégal xol sedna
Quelle modeste de petit fils de cheikh seydil Hadji Malick sy / nioune kou'niou khass warou'niou fayou bilahi ndax tamit kou djitou khadje mbawla
ya nekh😅😅😅
Walay ndeysane macha allah
ame léne yar fi bou gou fi djitou serigne touba la ndakhe mome rk mon khékhe Islam man tidiane la mais ligue wakhe dou wakhou nite khamou adouna amou yare
@@djilyloum1000 yamana féne
Khana dégo li Khalifa bi wakhe
Walahi meussouma commentaire wayé cadou deug pirrrrrrrrre💕exemple lafi dioxé .Néna talibé cheikh deug dou kheip bein keurou diné ndaysan khamé reka am solo.Amine 🤲🙏
Machalah machalah serigne bi khôl sedatina tay khol yeup toyna yageu fi loll te wer sy malik li yomboul sy kou oyof rek moko meune yalna takhawaye bi yageu ❤️
Serigne babacar sy mansour yalla naffi yague té andak werrr
Contana tropp bilahi 🙏🏾🙏🏾❤❤
Bilahi s'y yalla nga fi yagg lol té wér barké yonenté psl
Kou guem Yalla wolou ko lo Khol ci niit Yalla nga wara guiss « kadou yi amna solo Sy Malick danga woyof rek yalna yalla goudal fane yi ❤️❤️
جزاك الله خيرا يافضيلة استاذ علي جاچ حفظك الله ورعاك وأيدك ونصرك وأطال الله عمرك مع الصحة والعافية والتوفيق بجاه طه صلى الله عليه وسلم ببركة شيخ سيد الحاج مالك سه رضي الله عنه ونفعناالله ببركاته آمين يارب العالمين
اللهم ءامين
Machalla Serigne mbaye s'y yalla na la yalla Faye
Dieuredieuf Serigne Touba dieuredieuf Mame maodo
Amin SY(RA), yague fi lol te weer
« Talibe BAMBA »
Pape cheickh yallah nala yallah déffale diame ak soutoura kheweul ak barké machallah Diallo
Tidjane moy niane bani amine té doussa toudou bopam 🙏 yaag fi lol Mbaye sy
Khady Diene 😂😂
Alahouma amine
Khady Diene sa genre gui vrai saytanei lagn
Ndeysanne Wayé Mouride sagn nagn nianeu si Barké suniu Sèrign mi di Khadim Rassoul mais la différence entre ns et des personnes de ton genre nous moi particulièrement j'aime tout cki est musulmans rawatina talibé Cheikh bamou diaralma di dém Tivaoune di nianal kilifa you tédeu youfa teude di. Nianeu yalla Tass niou sén ay lérr té nékoul gamou . Dém si Sama beureuk sama yakar tay ak euleuk mi di borom Touba nianalko nianalko niane yalla mou Tass niou Barker
C juste pour te dire nioune Mouride on respecte toute personne surtout nittou yalla you nék suniu fi yalla bakhé niouko diko santé Sèrign Touba Soula méti matsa nak wayé seytané bakhoul té dél wakh lo kham
Ramata Mane ki darol sakh tonto walahi
Machala yallana yalla goudalll sa fane serigne babacar sy mansour linga deff amna solo léralll yi amna solo Sénégal béne la nanou toupou sounou kilifa yi té royyy léne boukou défé yalla défff diamm wathié yeumandé ak ndjiégalllll si askane wi ....amine♥️♥️Modou baye fall ♥️♥️
J ai les larmes o yeux par sa dimension spirituel mais sa modestie a part sy doundal
Macha allah les hommes de Dieu parlent avec humilité et sagesse l’islam est indivisible.
Quelle modestie. Masha Allah yalna Yalla goudal fanam si barké Mouhamed SAW
Amiiiiiiiiiiiiiine
Sy Malick yagu fi loleu té andal wéreu Mane dé Mouride pire la Sèrign Touba képeu laniou beug wayé fonk ne kép kouy talibé Cheikh dém na Tivaoune juste pour ziar nakh ay kilifa you mata nianeu sén lér la niit kou nangou nopalou yalla mo yoreu di mayé 🙏🏿 Sérigne Mbaye Mansour yagu fi loleu té andal wéreu
Dieureuff Cheikh Akhmadou Bamba Mbacké yaniou sgal yaniou ték si yoneu yaniou khamal louy fonk makeu yaniou may khôl you takh duniou touteul niteu alhamdoulilah
pape cheikh liga beuge yako kham yallna yalla défal kontan buo bakh machallah yallnala yalla faylén
sama xol da sed yallah na diam yagu amine
yallah na goudou fan ta wer❤ serigne
Yaguee fi lolll sy té wer machallah khol yii sedd naniou yalla na diam yaguee talibé cheikh beug srg saliou mbacké....
Sénégal begg na sy malick suniou khel dal Bilahi j suis mouride mai barké serigne touba beug nala dei sy longue vie à tw waxx bi rafetna jai un coeur rempli d joie
Sénégal 🇸🇳 rek moci ame ndam. Li moy de la hauteur deug.
MachaAllah rafétena 🙏🏾 yalla na YaAllah Bourbou MAGUE Bi mousseul Sénégal, same ko té maye sounou kalifa généraux yeup gnou yague fi looole té weur barké Borom Touba🙏🏾🙏🏾
Mande tayla warro am kilifa rekk mon woor .rawattina kilifa bou Mat kilifa ...djeureudieuf sy malick
🤝😍😍😍😍👂👂👂🤲🤲🤲🤲
M anchallah yalla na yalla goudal fane domou adama yeup,te mouthieul nieup ci mbass mi inchallah.quartiers general ci kaw ci kanam ci. Lou bakh merci bcp
Machallah Sy Malick contane lol si Serigne BaBacar Mansour souma koy khole ak diko deg damay khamni nite kou am yeurmandé la ta oyof lol sakh mane deh Mourite la wayé souma koy khole diko déglou mom ak Serigne Abdou Karim Mbacke kif kif si oyof ak am yeurmande yallah nagnou fi yag lol ta wer ak bepp dioulite
Alhamdoullillahii, yalla nagua yagg te yeurr.
ماشاء الله تبارك الله ياشيخ سيد ابوبكر سه محمد الأ منصور الأخليفه حفظك الله ورعاك وأيدك ونصرك وأطال الله عمرك مع الصحة والعافية والتوفيق بجاه طه صلى الله عليه وسلم ببركة شيخ سيد الحاج مالك سه رضي الله عنه ونفعناالله ببركاته آمين يارب العالمين
Macha allah Sy Malick yalla na yalla guoudeul fane wi naguoul gnou gnane yii yeup
Mane dh mouride la wayé sama xoll dafa sedd ci señ babacar sy mansour yalna yalla goudeul fanam té defalko wërr
Sy Malick yalna yala goudeul sa fane ! Modestie si yaw la yem🙏
Machala une personne modeste et humble
Ouléye Sy tout mon corps tremblait quand on disait c le khalif. Franchement sa modestie me depasse largement.
@@aliounesarr7655 walay Alioune ni la Massa mell Sy Malick
@@ouleyesy7406 Yalla nafi yague taa wër ,ci barké salatoul fatihi barké lazim barké khadra,barké diawartou
@@aliounesarr7655 Amine way si barki khalifa Malick 🙏🙏🙏
En tant que mourid Sama khol sedd na trop, yalna sa djammu yagu, gudu fan ak weur 🙏
Machalla Serigne Mbaye Sy Mansour yalenako yallah gueuna yagale ci kanamou ndiabote té mayeko weur. Motenga kilifa