Ya rabbi sama ,ya rabbi sama ,ya rabbi sama , magui laye niane gua diégual niou , gua diégualma yaw sama borom, magui diouli si seydina mouhamad (psl) sayou ma noké té di niane si barké xassidayi ,yallana yalla doli aye leer khadimou rassoulil lahi . dioyegua guaa you bakhi yilafi djitou wayé taye ak souba mbégueul gua gnilafi outou. Serigne bi mbégté mou reuy mi niou deuké si siniou xole yi si souniou dounda gui diokh naniou lako adiiya .
Machalla..j'adore Hizbut..le mouridisme est un abreuvoir à tous point de vue..j suis tidiane mais le mouridisme me fascine par leur organisation, sollicitude envers serigne Touba, leur humilité et culte du travail..dieureudieuff serigne Touba, fier d'avoir un érudit de ta trempe dans 1 petit pays comme Sénégal
Serigne est un don de Dieu ,et il représente pour l universalité d'un humanisme parfaite c est la raison pour laquelle,tout le monde sans distinction de race ,de couleur de religion et de tarikhaa ,l accepte,car lui même ce qu'il prône c'est du pure acsension spirituelle ,c pourquoi tout un chacun de ns ,minime qu'il (elle) doté de sensation va certainement aimer ces noble écrits ,inchanoul Kamil et inchallah khadim pour tjours,j'étais tidjani,et il m'a fait mouride , Dieureudieufffaate Serigne Touba faawww ,
machallah rythme 71 bi ils sont les meilleurs . Dieureudieuff borom touba ❤❤ yalla na léne yalla deffal jamm té mou wéral baadii ba nguéne diangue khassida si anamm you sell . Machallah khassida gui di Mawahibou nex na lolll
Je ne sais à quel point vous remplissez de joie mon coeur .😍 Mais je sais une chose vous êtes le ciment qui scelle la voie du mouridisme . Belle vinification....Qu'Allah augmente notre amour envers Cheikh Ahmadou Bamba
Yague léne fi lool té werr lool barkép KHASSIDA yi , bégatinagne lool si yéne yalnaléne SERIGNE BI gueune dooléle barkép SERIGNE SALIOU , jeureudieufi doungéne ay nit dh 🤲🏾😭😭❤️❤️
Billahi lezzy pour mann mann késsé ma beugg wa hizbout TARQUIYAH darou khoudoss damaléna beugg ba gueméwoumalénn rawatina sama domou bi Di Serigne matar Dienne borom dathie younekh yii loll té daw yaram billhi amoul lénenn morom si diangoum xassida yii barkep cheikhoul khadim dieureudieufee Serigne Touba khadimou rassoul
Dieureujéfé borom TOUBA walay htdrkh sén dieum yi dé serigne touba rék la ci guiss 😢😢🥲🥲🥲😢li tawfékhéna trop barké cheikhra fall lampou yônn wi 💡 😭😭😭😭😭 am na yérmandé yitamite
Spécialistes, experts...je ne sais même quel mot dois je utiliser pour les qualifier sur cet rythme de 71...Htdkh yalla nalen Yalla faye si Barké Cheikhoul Khadim...sen 71 ben la fi ❤❤
Dafa am biss ma xeuy rond point nguinth thies ci café gui took di waxtaané htdkh ak s'en njang nimou may deff man ak ben mbok talibé. Ma naane ko mam moom meussou maléne guiss wayé meunouma mougn s'en njang. serigne djily itam day sama soppe ndax jangam dafay sarr sama xoll... Li ci doywaar le mêm jour le soir vers 21h moom serigne djily wacci ci rond point nguinth bu thies fekk mafa di faggou café touba andak ser mballo ak wa htdkh ... mouy biss buma yeem lool ndax bimako guissé dama yeeemu lool BARKEP BOROM TOUBA
Magui santeu yalla di jouli si seydina Mouhamed salalahou waleyhi wasalam di santeu sama serigne serigne saliou Mbacké do doli santeu kou gnou khamal leep Mouy Ahmadou bamba miga khamei amoul morome mane khamou ma sakh nous ma def ba neik mouride âme tiofel bou beuri si serigne saliou khasida yi done sama yitei trop heure bouma joulei fajar ba nopi faw ma deiglouko depuis lors sama leep stable di santeu serigne touba tei douma si meussa jouk di santeu joulite yi di jangueu khasida yii di toyal kholyii yalla nagnou ko jangueu sa aljana bou kaweiba si kanamou serigne bou mak ba kharitou seydina Mouhamed bobou ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💯Mouride
Ndeyssane Li nékh na lol sakhe diangéne dieuff waye machallah yalnalén yalla féy ta yok séni khéwal si daradiay sèydina mouhamad sal lal lahu haléyhi wasal lam
Machallah dieuredieufff boroom touba Cheikh Mohamadou Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd ki Aminnnne Aminnnne Aminnnne Aminnnne Aminnnne Aminnnne Aminnnne
Mashaallah Allahou Akbar sallalahou ala mouhammad sallalahou aleyhi wa salam alhamdoullilah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ dieuredieuf Serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😭 damako déglou abonné brk xassidatyi ohhhhhhhhh!!!!!!sam xol Lima si yeugg meunou ma wakh❤️❤️❤️❤️❤️ ta cette année laytoul khadr s'en bâche rk lako beuguon défé yalla ndogalou ko mais un jr viendra ❤️✨
Ya rabbi sama ,ya rabbi sama ,ya rabbi sama , magui laye niane gua diégual niou , gua diégualma yaw sama borom, magui diouli si seydina mouhamad (psl) sayou ma noké té di niane si barké xassidayi ,yallana yalla doli aye leer khadimou rassoulil lahi . dioyegua guaa you bakhi yilafi djitou wayé taye ak souba mbégueul gua gnilafi outou. Serigne bi mbégté mou reuy mi niou deuké si siniou xole yi si souniou dounda gui diokh naniou lako adiiya .
Je suis talibé maodo Malick, damay jooy 😭 sumay déglou xasida yi ,céy Serigne Touba, bamba su amoulwoon adouna Dana nakari , djiaradjieuf Akhemadou bamba 🙏🙏🙏
Ndeysane nako ñepp di nianal walahi mou yagg fii lole and ak werr ak talle serigne makhatar diene 🥰
Yalna gnou yalla fayal CHEIKHOUL KHADIM li nekh na si xol❣️😭
Je suis fiére d'être musulmane allahamdoulilah 🤲🤲🤲😍😍😍
Machalla..j'adore Hizbut..le mouridisme est un abreuvoir à tous point de vue..j suis tidiane mais le mouridisme me fascine par leur organisation, sollicitude envers serigne Touba, leur humilité et culte du travail..dieureudieuff serigne Touba, fier d'avoir un érudit de ta trempe dans 1 petit pays comme Sénégal
Dagua gorei rekk.yalnala yalla defal tawfékh ak taysir guou yatou lolll
Ndeysan danga goreiii
dieureudieuf
Bilahi ya bakh jereudieuf
Bilay Diam rek ngay am ☝🏽😍sokhoro déh té si goré
Serigne est un don de Dieu ,et il représente pour l universalité d'un humanisme parfaite c est la raison pour laquelle,tout le monde sans distinction de race ,de couleur de religion et de tarikhaa ,l accepte,car lui même ce qu'il prône c'est du pure acsension spirituelle ,c pourquoi tout un chacun de ns ,minime qu'il (elle) doté de sensation va certainement aimer ces noble écrits ,inchanoul Kamil et inchallah khadim pour tjours,j'étais tidjani,et il m'a fait mouride , Dieureudieufffaate Serigne Touba faawww ,
Depuis fadjar maguikoy replay 🥰 c’est tellement apaisant Hamdoullaah 🙏 bon gamou a tout les musulmans #djeureudjeuffffff serigne touba
C'est un soulagement de coeur ♥️♥️♥️ manam thi gatal aldiana deug mongui nii
😭❤️❤️
Bilahi Serigne Touba dou nit kholale rimebi
machallah rythme 71 bi ils
sont les meilleurs .
Dieureudieuff borom touba ❤❤ yalla na léne yalla deffal jamm té mou wéral baadii ba nguéne diangue khassida si anamm you sell .
Machallah khassida gui di Mawahibou nex na lolll
Bilahi khassida yi koukay deglou rek nitu aldjana gua wakhumala nikoy yeukatii machallaaa djeureudieuf cheikhounal khadim🙏🙏
Je suis catholique mais fouma deg weuy yi sama yaram dey daw et mes yeux sont remplis de larmes ❤️❤️
Y’a bakh
Machalla mais on dit xassida
Machala
Ndeysan danga bakh rek
Ndeyssan
Dieureudieuf mouride eskey yalna yalla goudal séni fane weureul séni thieur si barké KHADIM RASSOUL ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
bok yi nio gui ziar bour di len wakh ni serigne touba amoul morome😍🥰🤩
Aljana Sorriwoul dh barki Cheikhoul Khadim 😭😭❤️
Je ne sais à quel point vous remplissez de joie mon coeur .😍
Mais je sais une chose vous êtes le ciment qui scelle la voie du mouridisme . Belle vinification....Qu'Allah augmente notre amour envers Cheikh Ahmadou Bamba
Sakaw sa knam rk boumu lale souf Dieureudieuf SERIGNE TOUBA Dieureudieuf SERIGNE TOUBA
SERIGNE TOUBA amoul dindano
Barké Aladji Fallou Mbacké 😭😭😭😭
Fier d'être musulman. Bon ramadan à tous. Halhamdoulila.
Lii dhè Alldjanna deug la djeureudieufè Serigne Touba🙏🏾🕊❤️
Bilaye nions gui aldiana té déwa gouniou 😭😭😭🥰🥰🥰🥰
Yague léne fi lool té werr lool barkép KHASSIDA yi , bégatinagne lool si yéne yalnaléne SERIGNE BI gueune dooléle barkép SERIGNE SALIOU , jeureudieufi doungéne ay nit dh 🤲🏾😭😭❤️❤️
ndeysane kouko degeu sa khol sedeu aka goré aka bakh ak am diom serigne bii
Alkhamdoulilah rabil ala mine 🙏🙏Dieuredieufé cheikhana ahmadoul khadim
Billahi lezzy pour mann mann késsé ma beugg wa hizbout TARQUIYAH darou khoudoss damaléna beugg ba gueméwoumalénn rawatina sama domou bi Di Serigne matar Dienne borom dathie younekh yii loll té daw yaram billhi amoul lénenn morom si diangoum xassida yii barkep cheikhoul khadim dieureudieufee Serigne Touba khadimou rassoul
Je suis un talibé Cheikh mais Wallahi xadida bi limouy déf ci mane yéména trop.
Dieureujéfé borom TOUBA walay htdrkh sén dieum yi dé serigne touba rék la ci guiss 😢😢🥲🥲🥲😢li tawfékhéna trop barké cheikhra fall lampou yônn wi 💡 😭😭😭😭😭 am na yérmandé yitamite
Kou beugeu s Touba❤❤❤❤
kouko bagne dagua ko xamul wala xoloo mbindeum kone diap nani niakk ko xam ak reer la
Masallah adouna yénafi daka diangeu masalla laf thiatt 71 moy am diangue
Lou wére nga wakh
Magui ziare bou werre lii nekhna trop😏😏😏👑👑❤❤
Spécialistes, experts...je ne sais même quel mot dois je utiliser pour les qualifier sur cet rythme de 71...Htdkh yalla nalen Yalla faye si Barké Cheikhoul Khadim...sen 71 ben la fi ❤❤
😭😭😭
Menou ma wakh sakh 😭😭
Elle est d'abord intuitive,la déclamation avant d'être tout ce que vous voulez (yeug,yeug ba jiitou)kenn dou cheikhoul khadim 🤕
Bilahi rien à dire no li dafa yeme
Dafa am biss ma xeuy rond point nguinth thies ci café gui took di waxtaané htdkh ak s'en njang nimou may deff man ak ben mbok talibé. Ma naane ko mam moom meussou maléne guiss wayé meunouma mougn s'en njang. serigne djily itam day sama soppe ndax jangam dafay sarr sama xoll...
Li ci doywaar le mêm jour le soir vers 21h moom serigne djily wacci ci rond point nguinth bu thies fekk mafa di faggou café touba andak ser mballo ak wa htdkh ... mouy biss buma yeem lool ndax bimako guissé dama yeeemu lool BARKEP BOROM TOUBA
Euskeuy Fall borom tawfekh gua, vendez mangui tour ay xeweul sakh yittewone naniou sa numéro lolou
Ndaysane Machallah mouride tawfex rk
Ndaysane
Ndeyesanne
Y’a
Machalla yalla nallene yalla Fay barké borome touba
Leineu dall xamnako 71 guissou ma koulein ko dakkeu ❤️♥️day Yallah wé tropp wayy
Danga nane dadjou Serigne Massamba ñosssi meun 🙏♥️♥️
@@sidy424 wawa key fall dadju wa keur segn massamba yii mome gniosi menn
Wa magui djiéguelou lan moy 71
@@labambistediop5234 annèe biniou diang walleu yèssalat dadj (mèlodie) bi
@@sidy424 Han ndeysan machallah diadieuf way
Ndeyssane degnou Pék 71 bi lolou machalah ❤️❤️❤️🔥🔥
🙏😭😭😭😭😭😭😭🙏❤
Ak léep louthi meunti am dall mom aldiana soriwou léne ❣️🙏
❣️🎂
Touba moy ALDIANA ndax Fi Cheikh IBRA Fall tede moy digou Paradis
Walahi ndeysan
Ndaysanne khasida moma guenele Louma am si adouna😍❤️❤️
Magui santeu yalla di jouli si seydina Mouhamed salalahou waleyhi wasalam di santeu sama serigne serigne saliou Mbacké do doli santeu kou gnou khamal leep Mouy Ahmadou bamba miga khamei amoul morome mane khamou ma sakh nous ma def ba neik mouride âme tiofel bou beuri si serigne saliou khasida yi done sama yitei trop heure bouma joulei fajar ba nopi faw ma deiglouko depuis lors sama leep stable di santeu serigne touba tei douma si meussa jouk di santeu joulite yi di jangueu khasida yii di toyal kholyii yalla nagnou ko jangueu sa aljana bou kaweiba si kanamou serigne bou mak ba kharitou seydina Mouhamed bobou ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💯Mouride
Hakaza mouride Serigne Mountakha newona " Ci Khassidayi rek lanu meuna hamé Serignebi " nek thi rek lep dina bakh
Ndeysane day guena nékh rk ba aldiana♥️😭
Ba aldiana💞💗💖
En tant que mouride pir dieureudieuf serigne touba
Li dawna yarame barki serigne saliou mbacké thieuye ahmadouna
Lou wérr
Barkep Borom Touba liii yeemei na lolĺll
Ma Sha ALLAH ma Sha Allah ma Sha Allah ❤❤❤❤
Mashallah SERIGNE Touba est une légende des mourrides😭😭😭❤😲
Alhamdoulilah Mangui yekk akk Thiant deug si Sama xol ! Jërëjëfë way
Yagu lenko tewé barkp borom touba ♥️
Merci waye diangéne dieuff waye machallah yalna lén yalla féy si barkep Serigne Saliou Mback
Ndeyssane Li nékh na lol sakhe diangéne dieuff waye machallah yalnalén yalla féy ta yok séni khéwal si daradiay sèydina mouhamad sal lal lahu haléyhi wasal lam
Ndeye Gueye mongui leen Si ziar bou bakh yalla na Nguen am ngueremou cheikhoul khadim🙏🙏🙏🙏🙏❤️
Machallah dieuredieufff boroom touba Cheikh Mohamadou Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd ki Aminnnne Aminnnne Aminnnne Aminnnne Aminnnne Aminnnne Aminnnne
amine
Ndeysan Seign mbalo Dia nimou def mawahibou bi doyna waar 😭😭😭♥️
BAC C'EST CAM CHEIKH AHMADOU BAMBA DIEURDIEUFETY MBACKÉ 💯🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️MATAR DIENE YALNA YALLA YOK LÉR YII SI BARKÉ CHEIKH IBRA FALL❤️🙏🙏🙏🙏
Presque 1an YALLAH NANIOU YALLAH DOLI SOUTUREU tHi barkei CHEIKH AHMADOU BAMBA KHADIM RASSOUL
Masallah diueradiafati serigne touba diueradiafati serigne touba diueradiafati serigne touba diueradiafati serigne touba mawakhibou
Machalla. Yalla nanou yalla geuneu fayal serigne Touba.
❤️❤️😊😍😍🙏🇸🇳🥰😍ohhh mâcha Allah way
🙏❤️khôl sedatinaaa dh Rouhh yui mbegu 😅🥳🙏❤️❤️
Machalah darou khoudosse yénangui si dh
dieuredieuf chiekh ahmadou bamba yalna sene diamou yagne barkp khassida yi barkp khassida yi 💞💓💔💞💋
Walay ndeyssane yalla nguen am ngeuremeul Borom Touba
Khesiideyi sunuk defaru adouna ak allakhira dierejefety cheikhoul khadim jaarama mame cheikh Ibrahima Khalil faal lampe baabul mouridiya ❤❤❤❤
Aye waye li ma raté metinama eskeuy sasounou yeuketé xol yepeu béke machallah
Macha Allah yalna nou yalla fayal Mame borom Touba bilahi xol Sed n'a trop 😭😭
Malaaka Yi 🥺♥️🙏🏽 Diene Yallah may nako ♥️
Diene de me ko niè mane
Kene dou diene
🥺👎ᕦ(ಠ_ಠ)ᕤ
Malad yi😝😬digne yalla may nako
@@mamediarrafall9292 ???
je ss tidiane ms j'aime beaucoup Serigne Touba yalla n'a yalla yokou lerame😘😘
Ndeysane 🥲Amiine barké xassida yii
Dieureudieuf yalna sounou borom fayalnioula thi barkee seydina Mohamed
Celui qui aime les mouride aime
Si barké khassida yiii yalla na corona bii dem inchalla
😭😭😭dieureudieuf serigne Touba 😭😭alkhamdoulilah sante naniou bou bakhh
Ndeysan dieuredieuf serigne touba
Gnii billahi danoo mena diangue oohh😭😭😭
Diaguendieuf yalla na sunu borom dollilen werr akk xeweul si barkep Serigne bi
Aldiana deug mongui nii walahi ♥️♥️😍😍😍 heures bouma xeuyé mom lay deglou mawahibou kawé na lol fall
Yalla nélénn djik si barki Serigne Touba ♥️♥️♥️
Machallah ❤️🔥❤️ Limay yeukk say souma degue khassida🤭🤭
Je suis faire d’être Mouridea sante na yalla si li mouma déff ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏻
They dama contan bly khassida yii rek
Ndeyesane serigne touba doyna werou waye
😭😭😭😭😭Je suis très fière de cheikh amkhmadou bamba
Mashaallah Allahou Akbar sallalahou ala mouhammad sallalahou aleyhi wa salam alhamdoullilah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ dieuredieuf Serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilay s touba amoul Lou bone kouko yapp rek si gnoune lakoy diarr bilay dou morom 😭😭😭😭😭😭😭
Machalla gome borom touba rék wore❤️❤️❤️❤️❤️😍😍😍
Wawaw gueneu nekh gueneu bakh ba aldjiana inchallah
Serigne bi défal naniou lép niou motali ak geumgeum ak pastéf rék mossi dess
Merci mon Dieu de m'avoir fait Sénégalais 🙏🙏
C'est très grave de dire sa
Je suis tidiane mais j'apprécie beaucoup
Ana wa mawahibou 71
Sama idole
MAGUI NI SAMA KHASSIDA SAMA DADJI 71 REK❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Gnoo ngi dè
Magui mi
Wawaw magui dé
Dieuredieufeti s.touba billahi li sédena ❤️❤️
Macha allah yalnalén borome Touba takhawou😭😭😭😭😭
Alhamdoulilahi rabil alamine dieureudieufé serigne touba diarawlak lamp fall yaw minou nîîtall mame banou khamko ba meune thié diarigno
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😭 damako déglou abonné brk xassidatyi ohhhhhhhhh!!!!!!sam xol Lima si yeugg meunou ma wakh❤️❤️❤️❤️❤️ ta cette année laytoul khadr s'en bâche rk lako beuguon défé yalla ndogalou ko mais un jr viendra ❤️✨
Thiey Serigne Touba 💓💓💓💓💓💗
'ndeysen wa darou khoudoss machalla😭
Thieuy louniouy fayeee Serigne Touba
Kén dou seringe touba bilahi
Machhalla yague té wêeer si barké borom touba
Dieureudieuf Serigne Touba amoul morom tay ak euleuk 😭🙏
Dieureudieuf serigne touba .ahmadou kénla
lerok nieupa daanou ler ❤️❤️🥺😭
sen Mawahibou bi kay ben lafi
Serigne DJILY N’DIAYE MAY ALLAH BLESS YOU 😭😭
Vous êtes des meilleurs ♥️♥️♥️♥️🕋
Li nékh na matar diéne dioye lona kép kouye mouride dama dioye ba sonne bly ❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieufeu Sérigne Touba, hanna lou geuneu nekh liii? Ah amoul wa, xassida kone day sax ci sa xoll ba faw rek
Diene mom bouy diang al dakoy dougou awma sago si mom yalla seder na lolou
Thieuy Ahmadou Mbacké kenneu dou moom ♥ ♥ ♥
Ndèysaan manuma téyé sama bopp. Thiéy
Machalla mon cœur est remplie de joie et mes yeux remplis de larmes