li dal famille Waly mbirou yalla rek la ndakh mane mii dal nama j'ai perdu mon père ma mère et ma grande sœur mon petit frère di dirr bou Gate même pas 2an et j'ai même pas 40an
C'est cela la volonté de Dieu, il n'y a pas d'heures, on a vu une famille décimée un coup, où est la volonté de Dieu la mort est naturelle et elle emporte tout le monde...
Wa mane senegal daniouy faté mbirou yallah wala Ma yallah mo binde di diokhé di nangou watt ko wa nitt kou yalla tekk nattou est c k douniou ko santé yalla tamit
Arrêtez d'effaroucher les gens déjà suffisamment traumatisés. Combien de familles ont connu ou traversent une telle situation. Les Kennedy ont connu une situation pire. Ici-même des familles entières sont décimées par une maladie ou accident de la circulation. On peut avoir de la compassion mais pas culpabiliser
@@DieynabaSow-r2g meuna yagg si iow aussi teh doko xamm...man béne Pa moko wzx sama yaye . Et depuis k j'ai commencé le traitement j'ai tous les signes au début...Et quand je dormais avec la Rokya télécharger aussi je l'ai vu crier et me menacer ...Bon bayinak lama défagoul🥲 Et puis maguini awma sax jikeur gnanal lénmeuuu
Day febar kome gnoune c des êtres vivants ya rien de extra si djinn. Dagnouy lek nane eumbe wossine c une communauté une société dagnouy djangue sen fort rek moy ils st invisible à l oeil nu et vivent plus longtemps
Geum len sunu borom lou am yalla sunu borom la ❤
Lou dal la famille seck est la volonté divine
En tout cas qu'Allah swt nous permette de nous concentrer sur LUI.. Amine.
li dal famille Waly mbirou yalla rek la ndakh mane mii dal nama j'ai perdu mon père ma mère et ma grande sœur mon petit frère di dirr bou Gate même pas 2an et j'ai même pas 40an
Massa Sister yalla souniou borom kharé lene Aldianay Firdawsi 😊
Ohhh masst metina trop yalla nalene Yalla khare aldiana yalla rek moy dogal
Masta Yalla kharelene aldiana firdawsi
Massa
Massa yalana borome bi haréléne aldiana firdawssi
Ki mome koubala déf té yalla takh yombatoul❤❤❤❤❤❤❤❤
MERCI ETOILE DIAMONO
Bravo yala nala yala samm ❤
Yalla lagnou geum té mome lagnou wolou li dale Wally yalla sounou moko beugue
Grand ibou fierté joal fadiouth la nianal len ko goude fan sama wayla billay namna tolba ❤❤
C'est cela la volonté de Dieu, il n'y a pas d'heures, on a vu une famille décimée un coup, où est la volonté de Dieu la mort est naturelle et elle emporte tout le monde...
Té mouy degg bou weer ya ALLAH !!! Dal moy buur
Domou adama yi bayilénn toutalle boulénn faténi yalla moye mayé
Très bien dit yalla moye mayy kou ko nekh
Ragal léne yallah, adouna dou keur..la vie et la mort sont du ressort D'ALLAH SWT
Merci beaucoup ibou ❤❤❤
Wa mane senegal daniouy faté mbirou yallah wala
Ma yallah mo binde di diokhé di nangou watt ko
wa nitt kou yalla tekk nattou est c k douniou ko santé yalla tamit
J'ai perdu 3 frères en 2ans leup yalla la
Ohhh Massa🙏🙏🙏
Machallah. Sa xool rek meun na féth kou nek
yalla na la yalla faaye ,goudou faan ak wérr,ak diaboot gou barkél
Serigne ibou diokh yalla nala yalla faye sa hol défala goudou fane ak weur dieuredieuf
Ah oui, feue Anne Marie DIOKH m avait raconte cette histoire.Cetait son grand pere
Yalla rèk mo Fi nek
Je n'ai jamais gouter l'amour paternel et maternelle.mais cest la volonté de dieu
Ohhh massa🙏🙏🙏
Talla moye Dogal le lep mais yalla moye maye ham ham kouko nekh
Machalla tonton ibou yalla nala yalla sameu yarabi borom bakh bilahi
Mbirou yallah rek la dou dara guemlen yallah sénégalais geumoul yallah mystique laniou guemlen no waye
Sérères AK diola douniou thiakhann.def guiss
Machallah tonton ibou
Li guem dh serigne dangay nango liguey
Qu Allah te prête longue vie
Ki moy ibrahima kou bakh bilahi yalnala yalla fayy sa xol❤
Ioe dh louma léer baa léer sama bokk nga
Meune na?
Ki fane la nék si joal
Ayway diokhma numérom
@@Mariama1900 número bi mongui si écran bi
Merci beaucoup la suite svp.
Journaliste yi dal sounou wakhoul thi wally dougn am diam khalas
W mais yeine guem leine yalla
Cheuuuuu mane diomina adouna bi daal yallah amatoufi place mane rouss na
Machala mon papa
Sénégal ragal Lén sunu borom
Bilaye dagniouy faté yalla
Bilahi waly bo gueume yalla diapal ni mbirou yalla nianalne souf oyof sen kaw
Mane a distance de 5 mois j ai perdu deux frére et deux oncle donc croyais en Dieu
Le lion de joal fadiouth
Journaliste khana yow do dioulite yalla moy rey
Lépp lou ame rékk souniou borome leu, wayyé tamite diame bi dafayy sabapelou
Machallah li dé yomboul
Yalla mo laye faye
macha'hallah
Suite bi inchallah ❤️
👍👍👍
Machalla
Yalla nala yala yeureum wayyy
Arrêtez d'effaroucher les gens déjà suffisamment traumatisés. Combien de familles ont connu ou traversent une telle situation. Les Kennedy ont connu une situation pire. Ici-même des familles entières sont décimées par une maladie ou accident de la circulation. On peut avoir de la compassion mais pas culpabiliser
❤❤❤
Kou bahe
Wakh ko mo tall site bi
Yalla rk dou lénén
En toucas il n'a pas ferme les commentaires donc personne à croire
👍👍🙏✊👏👏🙏🙏👍🤝
Khana geumoulene yalla
Fi gnoune gneup gno Gueume yalla wayé mystique si doundou bi la boke
Ki c quoi son numéro
C'est la volonté de Dieu car partout iil y a des décès donc essayer de vous concentrer sur vos familles et laissez les autres s'occuper des siens.
Numéro
Man deh farou rab moma sonal mann🥲
Noy khamè daga ame farou rapp stp?
@@DieynabaSow-r2gdangay gueintt di seuy ak ay visage inconnnu walla parfois mou dikeila sa frere walla sa kharit
@@Evaa_Sn en Daccor merci❤️
@@DieynabaSow-r2g meuna yagg si iow aussi teh doko xamm...man béne Pa moko wzx sama yaye . Et depuis k j'ai commencé le traitement j'ai tous les signes au début...Et quand je dormais avec la Rokya télécharger aussi je l'ai vu crier et me menacer ...Bon bayinak lama défagoul🥲 Et puis maguini awma sax jikeur gnanal lénmeuuu
@@mariamagueye5272te gnon dem si ki. Moi j’ai 43 ans dama fadiou ma soneu 😢
@pendo guisse Nieuweul khol
🤣🤣🤣🤣🤣
Sma kanam ak appel yi ak yeup mako feke môme lu ler
Meune na?
@@quenne_dudiolof9536Hey way yow mi di lathier rek yalla rek k meune serigne bilahi amoul dieurigne obstacle si doundou domou adama la bok
Sama boy là nak
Tonton ibnou nitt kou bakh té âme yeuremande si kham khamame
Yaw dh gueum ga yalla 😢
Oui sama grand la
Foumou deuk si joal
Son numéro
muneh len bayi famille diambur. lan mor la worr neh dafa am lou too famille bi. yow kou plainte sakh jelal
Ki khamoul fène
Borom joal fadiouth niit kou bakh té deugou
Meune na?
Envw son numero
@@ngoulou935degual khana Yalla,man joal la deuk yarofa maguefah,defefah sma.cursus scolaire leep bah obtat6 d mn bac,b6 vrai meuna mais guemlene yalla🙏🙏
Wa djiné day febarr
😅😅😅😅
Djinné lepp louy dall nite dakoy dall rek
Xam-xam rek mo wor
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Djiné noumouy febaré
Day febar kome gnoune c des êtres vivants ya rien de extra si djinn. Dagnouy lek nane eumbe wossine c une communauté une société dagnouy djangue sen fort rek moy ils st invisible à l oeil nu et vivent plus longtemps
Guir yalla diokh lenma numérom yalla faye léne dama febar basone
NUMERO BI MUNGI SI VIDEO BII
Li réka takh gnouléne di rey ma meun boléne guiss si internet bi di ladie numérom.
Numéro ba ngui ni si vidéo bi
Numerom mongui si écran bi
N importe quoi
Véridique
😂😂😂
Yow journaliste bi wah ko bou def beu do dé abadane dayemane. Au lieu k mouy dadialè ay yéré diagua pour les sauver de mawti
Machalla tonton ibou yalla nala yalla sameu yarabi borom bakh bilahi
Sa tonton la
Machalla tonton ibou yalla nala yalla sameu yarabi borom bakh bilahi