LYRICS / PAROLES : WALLY Yéwou ci seu wét doyna mbégté Diakaarlok seu kanam doyna banékh Love bimay yeuk kouko meun teuyé Ana kiko sagne diaral nama khéékh So beugué nak mou sauvage baby So beugué nak mou doux, lo deff ya tay Dis-moi ce qui t'arrange bébé Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré BAYE MASS Yéwou ci seu wét doyna mbégté Diakaarlok seu kanam doyna banékh Lo-love bimay yeuk kouko meun teuyé Ana kouko sagne diaral nama khéékh So beugué nak mou sauvage bébé So beugué nak mou doux, lo deff ya tay Dis-moi ce qui t'arrange bébé Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré WALLY Ci seu wét douma baayi Ak loum meunti done Boulma yeureum, déma gaagne Takk sama lokho Yow seu allure dafa gaaw Kouko léék fott Même so togné boulma baalou Lo deff dafmay néékh, ya tay BAYE MASS Soma togné, ya tay Réwantoul sakh, ya tay Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay WALLY Soma togné, ya tay Réwantoul sakh, ya tay Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay BAYE MASS Mane dé beug naa (ya tay) Lo wakh mou nékh (ya tay) Yow da nga taarou, da nga diékk, da nga nice WALLY Seu dokhine rafette na (ya tay) Mane beug naa (baby ya tay) Lo deff mou nékh, khamna dingma meussa gagne Beugouma niouy réro Wakhoumalak taago Sama thiofél ci yow wornama Nope naala mane eh-eh ya Show me your love my babyboo Sama safara, my seytaané Everything! My love knocks me down Rothie sama guégno diokhnaala ko Ah dissah deep love fidi gyal dem Dem ennemi mana ready fi shoot dem Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing BAYE MASS Baybe yaag neu man dama paré Ndiggueul xalé bi diaral nama xaré Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing WALLY Ci seu wét douma baayi (ma babyboo) Boulma yeureum déma gaagne (mon bébé à moi) Seu allure dafa gaaw (ma babyboo) Même so togné boulma baalou (mon bébé à moi) BAYE MASS Soma togné, ya tay Réwantoul sakh, ya tay Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay WALLY Soma togné, ya tay Réwantoul sakh, ya tay Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay Hum… Show me your love ma babyboo
Il faut se rendre à l’évidence et accepter la volonté divine: Wally B SECK est devenu le Goat de la musique sénégalaise. Lionel Messi de par son talent inné, Cristiano Ronaldo de par son travail acharné et son engagement. Il regroupe tout ce qu’il ya de meilleur chez un artiste, une Star. Rien d’anodin! Que le bon Dieu le garde et guide ses pas, le préserve des mauvaises langues. Je n’ai jamais ressenti un tel amour et affection pour un artiste.
deg bou lerrrr nga wakh, mais malheureusement certains khamounou lolou, khôl bou bone rek, mais wakh deg wali c'est lui le président de la musique sénégalaise aujourd'hui machalah
Il a dead le game, maintenant il se retourne donner de la force aux plus jeunes. Amadeus, didi, baye mass, VJ, mya Guissé..... En vrai c'est le GOAT qu'il pense etre. Doxalal Mar Yacine !🎉
Wally Bravo..vraiment il est entrain d'accompagner les jeunes talents. Ballago bilahi tu as raison doula yakhal dara, tu es déjà dans nos cœurs. Kagne lalay djis si aduna..😢
Son bou nara nekh moy bi, extrait bi rek dafa viral tiktok. Sou guéné rek nako faramareen yep partagé fep mou def 1M de vues en un temps record inchalla🎉
Le man de sa génération Maryacine goudou fan ak wer l’ambassade de la jeunesse vraiment on est fier de vous félicitations t’as encore frappé Baye mass Machallah ❤❤🎉
Si tu tombes sur ce message qu’Allah te facilite, te pardonne, te protège,te bénisse et t’aide à réaliser tous tes projets et souhaits ainsi que moins de problèmes et d’obstacles dans ta vie 🙏🏽 ❤❤
C'est un hit. Année 2024 les faramareen sont gâtés hit sur hit. Wally le meilleur tout court. Baye mass dafa mana woy yarou. Reverses dafa melni molen dakh clip ak choix personnages yi. Mais clip bi dope na et colle avec le thème YA TAY 🙃
Pape laye beats est fort quand même, wally continues de travailler avec eux pour d'autres sons stp. C'est une masterpiece ça, reggae waouh, bravo à vous🫡
Où sont les infatigables fans de Faramareen Wally B seck comme moi pointez ici, l'industrie musique mbalax est à vous actuellement on est fier de vous 🔥💪🏾🤍🤍🤍🌱🌿🇸🇳🇸🇳🇪🇸
MachaAllah ❤Faramareen, il a fait les meilleurs feat avec les jeunes artistes en vedette et très talentueux ❤❤. Bonne continuation ❤❤. Yallah nala Yallah saam et weiral baat bi Ballago Seck 🙏❤️
j'aurai aimer que le théme de cette chanson sois une source d'inspiration et de motivation pour dire a nos jeunes de ne pas abandonner surtout en ce moment ou ils sont trop décourager parce que y'a pas de boulot pendant ce temps les musiciens gagnent de l'argent à travers les vidéos nous on regarde les vidéos pour essayer de camoufler notre douleur interne de tous les jours ! THAT GOD BLESS EVEBODY
Machahala frère c’est trop cool 🫶💪 🎉 yalnala yalla motali sa yoon thie barké Seydina Maouhamed 🙏(PSL) 🙏 vraiment la population de Niakhar sont très fière de toi 🫂 Thiakaw Thiakanam notre prince du sine 🙏 bilahi j’ai même pas les mots 🥲 je suis très contente
Mar Yacine ni nga meuna mel danga bakh machallah Adji nar nga dess ndop diarka nga dess lambay ndjino ndjin faramaren yalna yalla sam la ya bakh té beugu say nawlé artiste❤❤❤🎉🎉🎉
LYRICS / PAROLES :
WALLY
Yéwou ci seu wét doyna mbégté
Diakaarlok seu kanam doyna banékh
Love bimay yeuk kouko meun teuyé
Ana kiko sagne diaral nama khéékh
So beugué nak mou sauvage baby
So beugué nak mou doux, lo deff ya tay
Dis-moi ce qui t'arrange bébé
Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré
BAYE MASS
Yéwou ci seu wét doyna mbégté
Diakaarlok seu kanam doyna banékh
Lo-love bimay yeuk kouko meun teuyé
Ana kouko sagne diaral nama khéékh
So beugué nak mou sauvage bébé
So beugué nak mou doux, lo deff ya tay
Dis-moi ce qui t'arrange bébé
Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré
WALLY
Ci seu wét douma baayi
Ak loum meunti done
Boulma yeureum, déma gaagne
Takk sama lokho
Yow seu allure dafa gaaw
Kouko léék fott
Même so togné boulma baalou
Lo deff dafmay néékh, ya tay
BAYE MASS
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay
WALLY
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay
BAYE MASS
Mane dé beug naa (ya tay)
Lo wakh mou nékh (ya tay)
Yow da nga taarou, da nga diékk, da nga nice
WALLY
Seu dokhine rafette na (ya tay)
Mane beug naa (baby ya tay)
Lo deff mou nékh, khamna dingma meussa gagne
Beugouma niouy réro
Wakhoumalak taago
Sama thiofél ci yow wornama
Nope naala mane eh-eh ya
Show me your love my babyboo
Sama safara, my seytaané
Everything! My love knocks me down
Rothie sama guégno diokhnaala ko
Ah dissah deep love fidi gyal dem
Dem ennemi mana ready fi shoot dem
Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing
BAYE MASS
Baybe yaag neu man dama paré
Ndiggueul xalé bi diaral nama xaré
Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing
WALLY
Ci seu wét douma baayi (ma babyboo)
Boulma yeureum déma gaagne (mon bébé à moi)
Seu allure dafa gaaw (ma babyboo)
Même so togné boulma baalou (mon bébé à moi)
BAYE MASS
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay
WALLY
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay
Hum… Show me your love ma babyboo
Macha Allah ❤️
@@officielwallyseck ❤️
Machallha waye
❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
❤❤❤
La sortie de ce clip coïncide avec le jour où l’amour de ma vie a accepté d’être à mes côtés pour l’éternité après des années d’attente😢 je t’aime AD❤
Félicitations mon frère
machAllah, Yalna Yalla mottali inchAllah
Oooh félicitations 😊🎉
Boule faté dieunde pastille comme sonko loumou waaxe rek
Frere khamal tay la say problem mou adouna di yok 10foi
Combien de fans Internationaux pour soutenir Wally Seck et Baye Mass ?
Diabarou artistes yi yallah naléne yallah maye kholou mougne 😂❤
Billay wakhatiko dameu tit mane 😂😢
Sheu li dafa yémè😂😂😂😂😂
Bilahi li kayi 😮😢😅😅
@@BabyDiallo-k1f club bi key doyna warr😂❤️
@ 😫😂
Il faut se rendre à l’évidence et accepter la volonté divine: Wally B SECK est devenu le Goat de la musique sénégalaise.
Lionel Messi de par son talent inné, Cristiano Ronaldo de par son travail acharné et son engagement. Il regroupe tout ce qu’il ya de meilleur chez un artiste, une Star. Rien d’anodin! Que le bon Dieu le garde et guide ses pas, le préserve des mauvaises langues.
Je n’ai jamais ressenti un tel amour et affection pour un artiste.
Allahouma Amin ❤❤❤
Amin c’est le meilleur ❤
deg bou lerrrr nga wakh, mais malheureusement certains khamounou lolou, khôl bou bone rek, mais wakh deg wali c'est lui le président de la musique sénégalaise aujourd'hui machalah
Il a dead le game, maintenant il se retourne donner de la force aux plus jeunes. Amadeus, didi, baye mass, VJ, mya Guissé..... En vrai c'est le GOAT qu'il pense etre. Doxalal Mar Yacine !🎉
Et Diaw Diop Didi❤
Mo bakh kay ❤❤❤❤
Li xol bou rafett la moléne raw délou dilene dolel masha Allah
C'est le GOAT, le number 1. J'espère qu'il fera un feat avec Obree daman et Dieyla aussi
Il était k mou def ay feat Lolou c est vrai et c est a saluer
Soutien depuis le Bénin 🇧🇯 touchez mon commentaire je reviendrai à chaque fois déguster cette belle mélodie 👊🔥
Moi aussi ❤️ je kif trop le Sénégal vive a tout les dakarois
À chaque fois que quelqu'un va aimer mon commentaire je reviendrai ici pour regarder cette chef d'œuvre
Après sa aucun ta santé oubien explique moi?
À chaque fois que quelqu un va aimér
Waly khalé yi Niola eupe chance 😢❤ Akon dala rejeté wone mais tay yegue nga ba mày khalé yi sen chance bravo 👏
Wally Bravo..vraiment il est entrain d'accompagner les jeunes talents.
Ballago bilahi tu as raison doula yakhal dara, tu es déjà dans nos cœurs. Kagne lalay djis si aduna..😢
Yalla bakhna
Kép koussa yaye di doundou yalnala sounou borom bi mayla khéweul bagua yobou ko makka mou ziaridji Nabi SAWS🙏🙏🙏
Amine
Amiiine yaa Rabbiiii❤❤❤
Amine
Amine ya Rabbi
Amiiiine Allah 🙏🙏🙏
Je suis guinéen🇬🇳
Mais j'avoue que Wally est meilleur de sa génération
🫶🏾🫶🏾
🇸🇳❤️🇬🇳
Oh wonderful song wally B seck X Baye Mass. Love from the Gambia 🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲... The king of tha New 🆕 Generation ❤
Oh tu as encore frappé notre wally et avec baye mass chaque fois que quelqu'un touchera mon commentaire je reviendrai écoute cette chef - d'oeuvre ❤❤❤
Xana waykate Sénégal yi daniou bayi 😂 franchement wally et le meilleur de tous les temps mar Yacine 🎉
Kone Senegal bénén waykate?
Wally key mi ggui melni SONKO insbi mayoul dara oposition bi 😂😂😂😂😂😂
Wouy takatina rasta yiii 😫Wally Fo gnou dieumé 😭😭❤❤❤️❤️❤️
Son bou nara nekh moy bi, extrait bi rek dafa viral tiktok. Sou guéné rek nako faramareen yep partagé fep mou def 1M de vues en un temps record inchalla🎉
Waly bravo ,tu es entre de donné des coup de pousse au jeunes talents Sénégalais
Thieuy Mare Yacine!!! Deugue deugue do nitou fiii.
The GOAT. Lolou dara douko dindi.
Dokhalal
Baye mass meilleur chanteur de sa génération 😭❤️🫶🏼
Aayyy papa yangui danél réw miii oooohhh liiiii laane leuuu❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥
Je valide depuis la Guinée 🇬🇳
Big up aux frères de la Guinée ❤️❤️❤️🙌🏿
La chanson est fraîche wayyy !!! Waly tu relèves le talent de la jeune generation de musicien !
Merciiii pour ta générosité ! Mashalla
Le man de sa génération Maryacine goudou fan ak wer l’ambassade de la jeunesse vraiment on est fier de vous félicitations t’as encore frappé Baye mass Machallah ❤❤🎉
Si tu tombes sur ce message qu’Allah te facilite, te pardonne, te protège,te bénisse et t’aide à réaliser tous tes projets et souhaits ainsi que moins de problèmes et d’obstacles dans ta vie 🙏🏽 ❤❤
Allah ouma amine inchallah pour nous tous inchallah ❤
*Amenn❤🙏🏽*
Amin inch'Allah
Amine
Amine
Il à encore tapé fort je l'adore cet homme 😂😂sa noone dina wayadi deh😂😂😂 merci de chanter avec nos jeunes chanteurs longue vie à toi golden boy ❤
First time listening to this song, and so in love with the vibe ❣️ Wally is a superstar💫
La voix de baye masse c juste waow!!!!
Wally si bopam mo xam ay ndanane
Vraiment baye masse ndanane leuh ❤❤
C'est un hit. Année 2024 les faramareen sont gâtés hit sur hit. Wally le meilleur tout court. Baye mass dafa mana woy yarou. Reverses dafa melni molen dakh clip ak choix personnages yi. Mais clip bi dope na et colle avec le thème YA TAY 🙃
1:52 ba fin wally amna louko doug li dou meune way rek amna lousi rakh nak bilahi wallahi tallahi wally yallah nala yallah sam amineee touff touff ❤
Bilahi amine
Una zona klkenk di Modena ❤❤e mezzo di provvedere a
Il donne la chance à ses petits frères woow 🎉 légendaire Wally seck 🥰👏🥳🥳🎙️💥
Wally Seck "YA TAY" + "JANATOU" = 1M de vues en 1jour. Sortir 2 clips en même temps yep di dokh machala Wally et Félicitations à vous tous ❤️
Beat better than Afro beat
From Nigeria 🇳🇬, I've always love this Senegal beat and instruments💓 ❤ from Child hood, cos i once lived in French country
Thank you🎉🎉🎉🎉
nioune dal amouniou sa fay❤ khana da nianal yalla defal leu diam rek
❤❤❤❤❤❤
Non😢
Ndéké Wally moy Uefa Champions League🎉🎉😮
Yééna Torokh Alal jaroul Taatinén, jigéen Amatoul bénn valeur. wayé kousi déé Yééwou.
Walakhi mane je suis dépassé
😂yéwou kay👊🏿
Sa yaye mo amoul valeur, wakho dara gorr gni ngay wakh djiguén affaire valeur té yén na gueuna thiaga
@@aramthiam4706 Aram Réw nga Man Sama yay Sokhna le Exposé woul boppam, Yéen Waro léna Nangou Di wané Séeni Taate
@ goor gni gnio gueneu thiaga ta wakhoko. Djiguén gni amel ngen ko akk
MaShaAllah so much love in this song 🥰😍🫶🏾❤️❤️ Wally Seck up to any level🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲🇬🇲
Franchement rien à dire sur le son vous avez dead ça ❤🎉
Je suis guinéen je kiffe Wally seck a vie c’est le meilleur artiste musicien sénégalais de génération ce mec est un phénomène
Machallah meilleur artiste de l’année wally❤ rk moko mérité bravo mar👏
Billahi Wally yalla na goudou fann ❤️
Ce son est une véritable pépite ❤🎉
Meilleur feat vraiment ❤🎉🎉
On te suit depuis le CANADA.
Faramaréne Musik Sa kanam rekk 😊.
Pape laye beats est fort quand même, wally continues de travailler avec eux pour d'autres sons stp. C'est une masterpiece ça, reggae waouh, bravo à vous🫡
Da man loumou guéné hit leu
@@BabacarNdiaye-u2f c'est le meilleur 🎉
Pape laye le beatmaker il est éxtraordinaire...🎉🎉🎉
Wally d legui rappeur la😂😂😂Machalah ❤❤❤
😂😂😂
😂😂😂
Partie bobou dafa nèkh😂
@@MarySy-o6u bilay yw 😂😂
Machine vraiment wally contanagne trop thi ligaye boy ayy loxo Machalla thakaw thiakanamr inchalla ❤
Waly c le meilleurs bilaye ❤❤❤
Où sont les infatigables fans de Faramareen Wally B seck comme moi pointez ici, l'industrie musique mbalax est à vous actuellement on est fier de vous 🔥💪🏾🤍🤍🤍🌱🌿🇸🇳🇸🇳🇪🇸
Thieyy loluuu🎉❤
Gnongi niiii Wally rekkk lou heeré ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla ❤❤❤
Machalla ❤❤❤❤❤❤
Toujours encore frappé ❤❤😊
Khamgua lanela tay mou nékh 😅 laff tiate maryacine diam rék inch'Allah Wally seul amoul lénéne nékha faral ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Magnifique Duo diguaaa fii rayy niteu marr Yacine di may boy yii chance ioe rekk yakhoo fiiiyy deff merci beaucoup ❤🎉
Nekh com dab mais baye mass tamite khalebi machallah
Réfét n'a trop mais khana baye mass thione seck laniouy fatali moy limou soll tenue bou mougne bii ❤🎉
Je t'aime Papeuhh ❤ Mar goudou fann ak wërr rk lalay nianal 😭🙏❤️🥰
Ah non je kiff🙌🥰Alhamdouliha mane ak Mare nio Bokou génération👋😂
Le chanteur du peuple le plus style du siècle 🎉
Un très beau clip bien réalisé avec un jeu d'acting captivant de wally extra sur une chanson pleine d'harmonie mashallah !
Quand ❤
WALLY QUI DONNE UN COUPS DE MAIN A LA JEUNE GENERATION C UNE BNE IDEE MASSALAH💖💝
J'aime ♥ comment il tire la main de ses jeunes frères dans la musique love WS❤
Wally rék Laniouy top lal lén j'aime ❤️ yi
Le seul et unique WBS ❤
Waay lou soft waay so amoul wone dagnoulaye creer waay 😀❤❤❤❤❤
meilleur duo wwally dou nit et bay mass avec sa voix exeptionnel🤩 c du ouf
Trop Nice waly et baye masse machaalah thiate sékhe lou léne ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
J’ai tellement attendu votre duo baye mass un jeune pétri de talent ❤ merci Waly ❤
Bilay Wally Dou moromou gars yi ❤❤ des coeurs pour Wally svp ❤❤❤❤🎉
Wllhy Seck tu es quiii💃💃
J’aime la partie reggae ❤❤❤mar Yacine vraiment chapeau
Wally temps yi sa yaram tangg na d mashallah bro🔥🔥🔥😍😍😍
Partie biniouye rabè temps la dee❤
Oui cette partie 🔥
Le chanteur du peuple international wally seck🥇👑🎤💰🌟🤍et le super talentueux baye mass macha ALLAH☝🏾❣️
He provides his younger brothers an opportunity. Wally Seck is a legend.
Fière de toi ❤❤❤❤❤❤
Kénn manoufé bayi déglou music ndakh Wally mii enhh lingay way nèkhna way ❤
L voix de Baye Mass tmt enhhh❤
Chaque fois qu’une personne mettra un like je reviendrai réécouter ce chef-d'œuvre 😊❤
Kon dé digua fi fanane 😂😂😂😂
*Gneuwatal kone j’ai like 👍 😂😂🤣*
MachaAllah ❤Faramareen, il a fait les meilleurs feat avec les jeunes artistes en vedette et très talentueux ❤❤. Bonne continuation ❤❤. Yallah nala Yallah saam et weiral baat bi Ballago Seck 🙏❤️
Pape laye beats is doing some great stuff❤
10ans amouma j'aime je le jure
Çé t'un chef-d'oeuvre vraiment waly tu nous doit plus rien
Que du bon Cameroun
🎉🎉🎉❤❤❤ les camers...
Le chanteur du peuple avec l'un des meilleurs da sa génération ❤️🎉
j'aurai aimer que le théme de cette chanson sois une source d'inspiration et de motivation pour dire a nos jeunes de ne pas abandonner surtout en ce moment ou ils sont trop décourager parce que y'a pas de boulot pendant ce temps les musiciens gagnent de l'argent à travers les vidéos nous on regarde les vidéos pour essayer de camoufler notre douleur interne de tous les jours ! THAT GOD BLESS EVEBODY
Have watched and listened to this more than 15 times, though i don't understand, I'm enjoying, much love from kenya 🇰🇪
One millions ❤❤
Maintenant nous réclamons le duo waly et cherifou 🎉🎉🎉🎉
Kana pour la deuxième fois kay
Non mais wally ya menu Machala ❤❤❤❤😂😂😂
Machahala frère c’est trop cool 🫶💪 🎉 yalnala yalla motali sa yoon thie barké Seydina Maouhamed 🙏(PSL) 🙏 vraiment la population de Niakhar sont très fière de toi 🫂 Thiakaw Thiakanam notre prince du sine 🙏 bilahi j’ai même pas les mots 🥲 je suis très contente
Wally c'est le meilleur 🎤☝🏽♥️
Niou khar jeeba ak Wally tmt ❤❤
Le chanteur du peuple 🇸🇳👑
Featuring of the year 😭🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤️❤️❤️❤️❤️🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Le euliw de la musique sénégalaise bayemass 🎉
Mboka L 🇨🇩❤
🎉🎉🎉
Mar Yacine ni nga meuna mel danga bakh machallah Adji nar nga dess ndop diarka nga dess lambay ndjino ndjin faramaren yalna yalla sam la ya bakh té beugu say nawlé artiste❤❤❤🎉🎉🎉
Wally meilleur artiste de l’Afrique 😮😮😮😮
Thieuy Mar Yacine yaa meun dei kii rassoulillahi❤️🥳
Lilanatila wally
Aveç ça geuü beugue Bayy wayy Après gaä loorr Niou mais Wally loy khare pour neck Sounou président
Merci beaucoup wally
Ya ngi motivé boye yi
Billaye wallaye Sa xol bou raffette lalla Yalla di faye❤❤❤