😱 XOULOO bou métii si live Cheikh Ahmed Cisse entre Kaliphone, Adamo et la voyante Aissatou Diop

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 26 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 180

  • @tendancebmn1573
    @tendancebmn1573 9 годин тому +6

    Grand mère kalifone, amina, adamo dagnou la wakh vérité absolue c’est pourquoi tu as mal.😂😂 libére l’enfant c’est mieux niak ga foula niak ga diome beugue ga gore. Délol khalébi Guire yalla. Merci kalifone merci Amina poté méti merci Adamo. Bou léne ko may dara

  • @fatoumatadiop2398
    @fatoumatadiop2398 12 годин тому +21

    Merci Kalifon li gue woh yeupe ce n’est que vérité ! Il a juste appuyé là où ça fait mal ! Ouseynou mome de fe niakeu ambition haliss rek mo ko diareul sacrifice bi ni ! Mère bi de fe niakeu fayda halei bi intérêt rek motah mou topeu ko! Mais on ne sépare pas un enfant de sa famille et encore moins de sa maman!
    Mounane Amina Pote > Amina dei djek le ame classe ame tchass di défeur di diapelei domou Adama fou mou sei goro yi contane mo le Eupen feeling guene le bah avec un esprit saint tu lui arrives même pas à la cheville délol domou diambour bi yayeum mou takeu moromeum ame si aye doome Lolou moye degue! Mère ne sois pas égoïste halei bi ni soko beguei libère le qu’il retourne dans les jupons de sa maman ! beute nak bou roussoul tourou nak tchim

  • @KaraJieu-p5p
    @KaraJieu-p5p 17 годин тому +23

    Nako ay mbookam wouteul une2ieme femme de 20ans tai penda diop mii seuy seuyeum.arrêtez les acharnements et rancunes sur penda diop,vous étés revanchards,tai loolou baakhoul

    • @makavelyngom8208
      @makavelyngom8208 15 годин тому +2

      Pourquoi dieukewoul kou ameu 20ans nefekh yi guegne doneu ndakh Elle as 53ans seuy bi amena domeram yi guegne doneu

    • @KaraJieu-p5p
      @KaraJieu-p5p 14 годин тому +1

      @makavelyngom8208 seuy bi dou tass.ousseynou amaguoulwoone loumou dieukai thi kou am vingt ans.foofou sarakh amoufa.500000f lagn lafay laadji minimum.nako penda mbaa yaayam outeul kou am vingt ans,yaine ay yaifeur nguaine piir moo takh nguaine di yaakh lou daguane

    • @ramatoulieseckan7169
      @ramatoulieseckan7169 11 годин тому

      Budey sah rakk laa do wakh li.

    • @Malicksindidi1988
      @Malicksindidi1988 4 години тому

      20'ans?nooo lolu eupp na si boy bi 14 'ans rek bakhna si boy bi

    • @KaraJieu-p5p
      @KaraJieu-p5p Годину тому

      @@Malicksindidi1988 kou am 14ans,kookou day diaangue.sou amai 24ans,kou am 19 ou 24ans baakhna thie moome

  • @NdeyefatouThiang
    @NdeyefatouThiang 9 годин тому +4

    Merci kali

  • @kenzifafall3438
    @kenzifafall3438 9 годин тому +4

    Délol domou diambour dji ki beutou dome ngako waré kholé vraiment c'est honteux 😢

  • @fatoudiop5631
    @fatoudiop5631 8 хвилин тому

    Amina poté bou amé tamite fouki séye dou guathié yalla moko dogal mai mongi seye ak kou mature

  • @fillytoure7780
    @fillytoure7780 15 годин тому +9

    Mane comprendre na Cheikh Ahmed dafay khambe gayi pour gnou wakh mère bi mome limouko beugeu wakh mais mounoukoko wakh par ce que mome moy live té bougoul mère bi quitté live bi dako beugeu téyé gayi diko wasse mais fararoul mère bi bien au contraire dafa contane thi gayi

    • @blazejohns8004
      @blazejohns8004 14 годин тому +4

      J'espère bien ! Parsk ameth mi moguilay beug diaxal

  • @NdeyeMaheDiouf-b3f
    @NdeyeMaheDiouf-b3f 14 годин тому +6

    Diafieuf khalifone merci

  • @madiaboucissokho829
    @madiaboucissokho829 8 годин тому +5

    merci ahmed cisse

  • @MaimounaDieng-bp2pg
    @MaimounaDieng-bp2pg 8 годин тому +2

    Yiiii deugueu kaliphone yi machalah vraiment deugueu raik lay mais haler dafa wala ormale mak

  • @ibrahimaboye878
    @ibrahimaboye878 6 годин тому +2

    Libéré oussénou Libéré oussénou Libéré oussénou Libéré oussénou Libéré oussénou souba grève de la jeunesse à 1267h 😂 n'a gneup gneuw

  • @madiopmbaye9010
    @madiopmbaye9010 5 годин тому +1

    Hamed Cissé no du jamais vu

  • @mamanmbaye1305
    @mamanmbaye1305 10 годин тому +3

    Aïssatou diop khana macky sall nékoul wone sa president affair president mome bouko fi wakh mane dal souma done yaw mo nopi bayi reseau sociaux yi vraiment li dou personalité

  • @mamadoundiaye1724
    @mamadoundiaye1724 17 годин тому +9

    Kalifone ay vues niokay doudeul loukhew silay profito chak jur mou live meme cas aziz dabala 1 mois lako traiter

    • @nojusticenopeace8683
      @nojusticenopeace8683 17 годин тому +1

      😂😂

    • @FamaDainge
      @FamaDainge 15 годин тому +1

      😂😂😂😂❤❤❤❤ merci 🙏

    • @fatimabintoubalde1499
      @fatimabintoubalde1499 11 годин тому +1

      Kali dafa perte té legui mou am 50 ans dh mé amoul liguey France il la dit ouvertement tiktok mokoy faye

    • @Annebaidysouleymane
      @Annebaidysouleymane 9 годин тому

      ​@@fatimabintoubalde1499vraiment dommage

    • @tendancebmn1573
      @tendancebmn1573 9 годин тому +1

      Mais dé tay vérité absolue lassi wakh na grand mère libérée l’enfant c’est mieux. Yéne nék léne placou yaye dji guéne khol nimou mété

  • @deliciouspartyfood5784
    @deliciouspartyfood5784 6 годин тому +1

    Aissatou %100❤❤❤❤

  • @fatoundoye2173
    @fatoundoye2173 4 години тому +1

    Amour rèk ❤❤❤

  • @OumarGueye-r9l
    @OumarGueye-r9l 18 годин тому +14

    Ousseynou Mbengue nekal nitt
    Ousseynou Mbengue nekal nitt
    Ousseynou Mbengue nekal nitt
    Ousseynou Mbengue nekal nitt
    Wa bakhna

    • @tendancebmn1573
      @tendancebmn1573 9 годин тому

      Ousseynou Mbengue mystique moko fa té grand mère nabayi seutame bi c’est mieux

  • @NgoneRassoul-lz2xq
    @NgoneRassoul-lz2xq 16 годин тому +4

    Ouseynou 😭😭😭😭😭😭

  • @tendancebmn1573
    @tendancebmn1573 8 годин тому +2

    Tay la nit yi diko wo si numérom biga diokhé sagako bamou dé 😂😂😂

  • @ngatefall4832
    @ngatefall4832 5 годин тому +1

    Ameth cissé yaw na fékh nga quoi vraiment adamo ak kaliphone sall wakh nanou deug

  • @deugrek344
    @deugrek344 15 годин тому +4

    Sénégalais you wayadi yi loulen kalboune sall def ak adamo, ameth cissé, awoush couty déf bakhna. Comme yéna fék nio kham ni chantage laniouy def guén lén di wakh sén vie ak séni problèmes té dou kèn kou thie nék Sénégal wala ngua gnimé nieuw Sénégal. Comme beugoulén nék niit lou lén kathior yi déf bakhna.

  • @KhadySENE-b8i
    @KhadySENE-b8i 9 годин тому +3

    Merci kalifon😂😂😂

  • @mams7777
    @mams7777 4 години тому +4

    Kali dal iow la andal point si ligua wakh lep

    • @KharyAna-b5o
      @KharyAna-b5o 30 хвилин тому

      😢😢😢❤😮😮😮😮7😢😮😮😢

    • @KharyAna-b5o
      @KharyAna-b5o 30 хвилин тому

      😢😢😢❤😮😮😮😮7😢😮😮😢yq

  • @SenyTandine
    @SenyTandine 8 годин тому +8

    Kalifone. Machaalla merci merci beaucoup

  • @SalimataFaye-v9o
    @SalimataFaye-v9o 12 годин тому +4

    Lima remarquer moy khalé bou gor bi wow na beute

  • @mouhamadoudjigo7100
    @mouhamadoudjigo7100 13 годин тому +4

    Moi j’ai juste une question est-ce que la femme du prophète avait un enfant avant de se marier avec le prophète psl ou pas parce que la question qu’on doit se poser c’est ça

    • @mouhamadoudjigo7100
      @mouhamadoudjigo7100 13 годин тому +2

      Sourate La vache

    • @awandiaye9733
      @awandiaye9733 12 годин тому +1

      Très bonne question

    • @Mame-zw5gf
      @Mame-zw5gf 5 годин тому

      Khadija avait 40ans quand le prophète l'a épousé à ses 25ans. Elle n'était pas ménopausée et c'est elle qui a donné au prophète toute sa progéniture

  • @MaimounabaLamounasse
    @MaimounabaLamounasse 2 години тому

    Bravo kali

  • @khakika-d9g
    @khakika-d9g 5 годин тому +1

    Mère bi dafa nekh louko nekh dafa def Lou teguouwoul fene

  • @Inkn_894
    @Inkn_894 6 годин тому +1

    Kéne controul seuy bi mai mai li xalé bi wane guinawe wadioureum ndax yaw la kéne andoul yobouko mou toubeul yayam nguén meuneu continué séne mariage si diam lolou moye deugue

  • @sokhnadiongue8092
    @sokhnadiongue8092 7 годин тому +1

    Khalebi setlou gueneko bouniouko delo yayam mba dinako amal dierigne ki tedeko mba mou melni lou sidekou

  • @AmyDiallo-dx3sg
    @AmyDiallo-dx3sg 6 годин тому +1

    Âhmede Tu es vraiment faut tu sais que c’est pas normal vraiment mon fils ne t’énerve pas pour ça

  • @marianendoye
    @marianendoye 16 годин тому +2

    Adamo t'as tout faux. Laisser cette femme et son mari vivre leurs vies, occupez-vous de vos affaires

  • @oulidiop8981
    @oulidiop8981 6 годин тому +1

    Kaliphone mi khaliss rek kay diamou si ay live vraiment bayilen seye diambour bi Adamo khaliphone Legui sakh yeunegui siye douguel Bouchet ak rox Amina pote je t’aime beaucoup mais affaire yi mome bou thi dougou

  • @DembiFall-i7z
    @DembiFall-i7z 10 годин тому +2

    😢😢😢😢Adamo

  • @KaraJieu-p5p
    @KaraJieu-p5p 16 годин тому +3

    Adamo doufi wakh l'islam ,ndakh saagua la diaangue,diaanguoul l'islam.

  • @user-nd2yx2qg7w
    @user-nd2yx2qg7w 18 годин тому +3

    Aissatou penda délol domou diambour yakh ga diom

  • @mamoudouniang8280
    @mamoudouniang8280 8 годин тому +1

    Louma yak ar moy kii mo def ligueye bii Serigne domeram bii

  • @madames9182
    @madames9182 17 годин тому +3

    Ouz deemal gnibi , maane j ai trop honte thi seuye miiii , liiii

  • @massambanzaly8877
    @massambanzaly8877 17 годин тому +2

    Vraiment vérité absolue

  • @Mame-zw5gf
    @Mame-zw5gf 5 годин тому +1

    Ah bon ousseynou da biireul ? Kone kay lii dou cas, papa bou takk maman c rien

  • @DiomeDIOR-iq4mw
    @DiomeDIOR-iq4mw 6 годин тому +1

    Hamed dal ya moune analyses tes khame lou rafet machalla noires bou také moromame noire mou am problème si c'est paa toubab moo takou sougnou khalé yii kéne dou wakh dou am bruit. Seuy yalla mokoy tak sa arasse .ont le souhaite le meilleur rek

  • @Love_kayy-j2v
    @Love_kayy-j2v 7 годин тому +2

    This lady is sick

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 15 годин тому +8

    😮kon bo faree meuno atte😂grefas54ans dem maka di gisanee 😢kou yes rek moy tak diabar te yeugeuloko sa yay ❤

  • @kenzifafall3438
    @kenzifafall3438 9 годин тому +2

    Yihhh kone deh ninga khéwé bakhoul

  • @damembow6856
    @damembow6856 10 годин тому +1

    Aissatou penda ya pénda sa sarapp ndeye thiaga nga délolle domou diambour nguir yalla dolli toucouleur bi

  • @khakika-d9g
    @khakika-d9g 5 годин тому +1

    Ousseynou sama toma la mais dafa beugu tate reuy beut intérêt matériel kesser moko dougueul si ndaw si

  • @KhadySENE-b8i
    @KhadySENE-b8i 9 годин тому +1

    Bravo adamo😂😂😂😂😂

  • @fatimabintoubalde1499
    @fatimabintoubalde1499 11 годин тому +1

    Adamo ak kali dieul guen coup dh 😂😂😂😂

    • @tendancebmn1573
      @tendancebmn1573 8 годин тому

      Bane coup 😂😂kone yaw wéro gnidé deugue rék lagnouy wakh grand mère bi 😂😂. Na libérée khalébi wakh ko lolou c’est mieux

  • @gabymane5027
    @gabymane5027 2 години тому

    Amina Poté dé mola dak fouf yaw mi di nirok mbotte , dof motakh magatte gou mélni yaw nga nane ma khéw raféto diéko , Ousseynou gnak motakh mou top de la . Chim Améth Cissé mou faut mi dila diaye , so bakhone do togak Améth Cissé so moytouwoul mou time la.

  • @codoudiouf2371
    @codoudiouf2371 17 годин тому +6

    Je suis d accord avec kali

  • @OulyBassene-nc4gq
    @OulyBassene-nc4gq 15 годин тому +9

    Merci kilifone

  • @kenzifafall3438
    @kenzifafall3438 9 годин тому +1

    Kaliphone wakh nala deugueu pire

  • @MamyGueye-q9o
    @MamyGueye-q9o 8 годин тому +1

    Dagua khéw ligua déf kouka déf khéw

  • @Ndeye-v2p
    @Ndeye-v2p 18 годин тому +7

    Man yeureum na ouseynou wa Mère tamit Li mba Diam La

    • @quenne_dudiolof9536
      @quenne_dudiolof9536 18 годин тому +2

      Dagno nekaler meusougno marié mère domeram la ,il vit en concubinage organiser anniversaire di doule

    • @tendancebmn1573
      @tendancebmn1573 9 годин тому

      @@quenne_dudiolof9536yague na teuder khalé bi dé .

    • @khadycisse877
      @khadycisse877 3 години тому

      @@quenne_dudiolof9536anniversaire la? 😳

  • @DameCissé-u8v
    @DameCissé-u8v 19 годин тому +2

    Adamo wakho deuge❌❌❌❌❌❌

  • @dioumaka5232
    @dioumaka5232 10 годин тому +5

    Mère bi. Dafa gnak Diome bolési di dagua santé

    • @tendancebmn1573
      @tendancebmn1573 8 годин тому

      Mère bi obsédé la Bilay insbi guissoul dégoul dara loudoul koyou khalé bi

  • @KhadySENE-b8i
    @KhadySENE-b8i 9 годин тому +2

    Domarame la

  • @beukeuloubakh
    @beukeuloubakh 10 годин тому +1

    Wax l'énergie deug bi goor man nga tak coula mat grande sœur mais pas koula mat yaye

  • @ladyeve7071
    @ladyeve7071 4 години тому +1

    Ki dou amm dom y😅

  • @moussadiouf6313
    @moussadiouf6313 6 годин тому

    Tout ça parce que la Dame est sénégalais.❤ Si s'était une Dame française ❤ personnes ne dirais rien 😢😢😢 c'est le Sénégal......

    • @khadycisse877
      @khadycisse877 3 години тому

      C’est parce que tu es comme ça que tu penses que tout le le sont

  • @mamysane3885
    @mamysane3885 3 години тому

    Vraiment kalifone waxna deugu

  • @fatoudiop5631
    @fatoudiop5631 12 хвилин тому

    Bilahi beugue seye diaroul li Bilahi guathié la outal sa kou ame 47ans mo gueune adamo ak kaliphone deugue la niou wakh

  • @AS-oi8dq
    @AS-oi8dq 10 годин тому +8

    Penda mi amoul foula 😢

    • @ladyeve7071
      @ladyeve7071 4 години тому

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @fatimabintoubalde1499
    @fatimabintoubalde1499 11 годин тому +1

    Wa kali temps yi dieulgua amina poté dh noum fa démei nonou

    • @mayasamb3859
      @mayasamb3859 9 годин тому

      Toi même tu sais pourquoi 😂

  • @richerichesse7091
    @richerichesse7091 17 годин тому +4

    Cheut sarap cas bi😂😂😂

  • @ariseldtcesr2632
    @ariseldtcesr2632 5 годин тому

    Ahmad wakhna vérité

  • @awandiaye9733
    @awandiaye9733 12 годин тому +1

    Mère bi wakhoufiii dara déjà li dou classe lou niit wakh gua tontou dougou thi live xaléyi melnii kou wéroul amo diom amo fayda bayil domou diambour lagnou wakhhh

  • @richerichesse7091
    @richerichesse7091 17 годин тому +6

    Oussess dagua am ay dome ah ousss télgua beugue Tada diii ah li mba diam laaa

  • @sokhnadiongue8092
    @sokhnadiongue8092 7 годин тому +1

    Kali contanne nathi thi yaw der boulene bathi der

  • @madames9182
    @madames9182 17 годин тому +2

    Adamo faut sa diabar toub gua thiane ko .

  • @AS-oi8dq
    @AS-oi8dq 10 годин тому +1

    Cisse nafekheula

  • @souleymaneouldmokhtar1485
    @souleymaneouldmokhtar1485 9 годин тому +1

    Cheikh Ahmed mingui wakh deug

  • @mariemembengue340
    @mariemembengue340 17 годин тому +1

    Kalifone doul amo xam xam

  • @horssyba8817
    @horssyba8817 15 годин тому +2

    Kone mere bii wa baagne leu et takoyel 😂ok yalla bakhna

  • @sant9021
    @sant9021 14 годин тому +1

    Ahmeth cisse mom au début daf done critiquer louko changeloo video

  • @WeulliThiaw
    @WeulliThiaw 2 години тому

    Yaw améth Cissé ce que vous dites c est pas raisonnable laisser ses parents sans les informer de son mariage ce n'est pas normal mais on ne dit qu elle ne peut pas avoir d enfants c est autre chose

  • @ladyeve7071
    @ladyeve7071 4 години тому +1

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @AminataFall-w8q
    @AminataFall-w8q 15 годин тому +1

    NĎAWSSI MÈUNEU RAY DOMDJI NEC EXTERIEUR.ELLE SE FAIT INSULTEŔ.

  • @awakane1050
    @awakane1050 17 годин тому +2

    Bayilène diambour bi AK dieukeureum Sénégal dou reuw ayy wakh dafa takh mou tass takhoul mou tass kou nèkak choix wam kali yow ki gayy wakh mère magou laa mak gan bayil diambour bi

  • @KaraJieu-p5p
    @KaraJieu-p5p 17 годин тому +5

    Yaaye dji, na djiooy nguaiweul,mais seuy bi dou tass.yaak coura,kou beugue sonko nguaine bagn ko,yaalna seuybi barkail loole sakh,amiine.lingua daif adjiaa thiaré faataiwougnouko

    • @naboujadieng627
      @naboujadieng627 16 годин тому +4

      Yow on parle d'une maman affecté et l'avenir d'un jeune qui est en jeu ioe ngay wakh wakho politique ? Ça vas pas

    • @FamaDainge
      @FamaDainge 15 годин тому +2

      Merci beaucoup bien repondu ❤❤

    • @tendancebmn1573
      @tendancebmn1573 8 годин тому +1

      @@naboujadieng627gni dagnon dof lou nit wakh gnou gni dafa bagne sonko wala macky la motakh. Kholou gnou sakh vérité bi

  • @antagueye8447
    @antagueye8447 34 хвилини тому

    Ahmeth cissé iaw ya nafikh deugue way sa mag bo bokal Ndèye ak baye mou febar boko fadioul kan mokoy fath teh nga tanéko ak mo eupou priorité si iaw kou eupoul ko bokal beneu bir bolen guené waye iaw wero deh

  • @NaïbaNdiaye
    @NaïbaNdiaye 18 годин тому +2

    Wa hamed cissé mi nitte la wala coubére yalla bakhna

  • @gabymane5027
    @gabymane5027 2 години тому

    Yayam mingui dioye affairamla Améth Cissé Ya bone yaw danga alkou.

  • @PapaPabi-h7e
    @PapaPabi-h7e 10 годин тому +1

    Salam salam kali ya néek cci deugue

  • @WeulliThiaw
    @WeulliThiaw 2 години тому

    Sénégal obligation nga fathie sa mak yaw améth Cissé ce que vous dites c est pas bien même si une personne est atteinte d une maladie grave on doit le soigner meme si elle est étrangère aissatou laisser les lives parce ces gens là ne sont pas vos égaux ce sont des enfants c est pas de la classe

  • @westcoastsunugal
    @westcoastsunugal 15 годин тому +3

    Ay way bib seuy vie prive si internet bi

    • @KaraJieu-p5p
      @KaraJieu-p5p 15 годин тому

      Soeurou ousseynou moo ko yaubou thie internet bi dai ak kanamam guou guoude guii na kawassou mbeur

    • @tendancebmn1573
      @tendancebmn1573 8 годин тому

      @@KaraJieu-p5pmo tay yobouko parsk secour lay woute

  • @madames9182
    @madames9182 17 годин тому +1

    Adamo , 😂😂😂😂 khaana sa seuye bi dou l islam sa diabar diokhoko tiane , boss des negri mbadou mairie keeppe gua deme😂😂😂😂😂.

  • @gabymane5027
    @gabymane5027 2 години тому

    Mére bi dafa dof , ba paré gnak diome . Yéne rék ka am diott di wakhatt mére bou doff bi , Amina Poté mola gueune.

  • @KaraJieu-p5p
    @KaraJieu-p5p 17 годин тому +1

    Dame cisse,yaw moome noble ngua.gneupe penda lagnou aandal.Adamo yaangui noonou tak koudoul sanguou sait,dou tari faatiha.,soo daiaiwaiai doula taiaindji,fii deudeulai amoufi ,soupçons moo fi am,soeurou ousseynou day faine raike,ap dofla,fii katantai amoufi,meunooko saiaidai itam

    • @AichaDia-t1d
      @AichaDia-t1d 16 годин тому +1

      Ya gniamé yallah diabar admo marocain la do toubab de😂

  • @Alkhamndoulila
    @Alkhamndoulila 18 годин тому +5

    3 perssone yi yallna len yalla diegeul

  • @bagora8053
    @bagora8053 7 годин тому

    adamo yawe ak kalifone metrigewoulene lingendi wakh

  • @mayasamb3859
    @mayasamb3859 9 годин тому +1

    C’est vraiment du n’importe quoi mais son mariage vous concerne ? Mais foutez nous la paie à la fin merde laissé la faire sa vie comme elle veut

    • @tendancebmn1573
      @tendancebmn1573 8 годин тому

      Elle n’a ka libérée l’enfant après on la laisse vivre sa vie .

  • @KhadimeDiouf-i2q
    @KhadimeDiouf-i2q 11 годин тому

    Seye amateurs sens,si mes enfants me disent qu ils ne veulent pas se marier je ne les obligerai pas..May wax domram yi taxaw nan d'à ñouye waraté..Li takh ñuye seye la majorité nékatouñou thi...

  • @MohametNdiaye-e7y
    @MohametNdiaye-e7y 3 години тому

    Jarama nias

  • @CheikhounaDiop-y5r
    @CheikhounaDiop-y5r 19 годин тому +1

    Adamo rekk😂😂😂😂

  • @fatoundoye2173
    @fatoundoye2173 5 годин тому

    Wa kalifone doul way

  • @KaraJieu-p5p
    @KaraJieu-p5p 17 годин тому +1

    Takhoul saagua daguane nak kali .bou gneupe doone saathie,saathie day daguane ?maguam bou faibarai nako dieukeureum fadji.penda baine seuy la tasslai il paraît

  • @OulyBassene-nc4gq
    @OulyBassene-nc4gq 15 годин тому +1

    Amet laisse la maman parle

  • @FatouBintoudiaw-s5e
    @FatouBintoudiaw-s5e 2 години тому

    Ki limoy wah tegou ko fen sa makbo bokal dey ak bay gani warou ko fathe ayemena ki limou def dara bahou si bouday mom douko neh nagne wahan tedegue

  • @DameCissé-u8v
    @DameCissé-u8v 19 годин тому

    Adamo warougar bogoul ci seuye❌❌❌❌❌❌❌❌❌