Urgent : la descente de khoudamoul Khadim à Bount pikine garage de Touba

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 6 лют 2025
  • Abonnez-vous sur notre chaine youtube Rafah TV international / Service commercial Rafah TV International : 77 433 39 39 : Email rafahtvhd@gmail.com
    Facebook Rafahi tv
    Instagram Rafah tv international
    @RafahTV1
    www.rafahtv.net
    RafahTV basé à
    Touba Mosquée .
    Nous venons auprès de votre haute bienveillance solliciter une demande de partenariat entre votre entreprise et la notre Rafahtv pour le passage de publicités de vos produits et la visibilité de votre entreprise à travers le monde entier.
    En effet, RafahTV est une chaîne de télévision en ligne implantée à Touba près de la grande mosquée depuis 4ans. Notre chaîne fait partie des meilleures chaînes de la place,
    En espérant vous comptez parmi nos futurs partenaires, nous vous prions de croire en l'expression de nos salutations distinguées.
    Intéressé

КОМЕНТАРІ • 669

  • @diengrama6922
    @diengrama6922 2 роки тому +4

    Ligueye bi rafete na Machallah nek lene thi rek

  • @gueyeousmanendongalboromda4814
    @gueyeousmanendongalboromda4814 2 роки тому +149

    alhamdou lilah dieurue dieuf s touba yéne waa khoudamoul khadiim yalna lén seringe bi takhawoul bopam boulen ragal dara képou kou beugue loubakh migui sen ganaw♥️♥️♥️♥️♥️♥️

    • @alinebambafal3792
      @alinebambafal3792 2 роки тому +2

      Amine

    • @diagnemodounaar9613
      @diagnemodounaar9613 2 роки тому

      Bane Serigne moléni faye xana dou Serigne touba mi nk si bamélame dé

    • @aboulbacharsall6795
      @aboulbacharsall6795 2 роки тому

      @@diagnemodounaar9613 Dieuredieufety S TOUBA🙏🏾

    • @morsama5212
      @morsama5212 2 роки тому +1

      @@diagnemodounaar9613 ww serigne touba moo léeni fayy c'est quoi le problème ✊️

    • @bambambaye2692
      @bambambaye2692 2 роки тому

      @@diagnemodounaar9613 diagne ioe lo beug dégg

  • @mbayedieng379
    @mbayedieng379 2 роки тому +36

    Macha allah dia dieaf mourid amna solo❤️❤️💯💯💯touba rék touba bafawo dieare dieaf serigne touba

  • @modouseck2049
    @modouseck2049 2 роки тому +1

    merci bonne continuation

  • @moridsaadix2751
    @moridsaadix2751 2 роки тому +2

    Jërëjëf Yàlla na lèen Yàlla sammo

  • @tallfamilleelectroniquekol6840
    @tallfamilleelectroniquekol6840 2 роки тому +4

    Machallah amnasolo yalla na yalla déf diamou si bar keb serigne touba amine

  • @ndiawargueye5007
    @ndiawargueye5007 2 роки тому +61

    Continuez sur cette lancée, on est derrière vous

  • @fatysarr7733
    @fatysarr7733 2 роки тому +25

    Wow incroyable vraiment vous êtes les meilleurs on est très fière de vous que dieu vous protège si barki serigne saliou

  • @amdifall5269
    @amdifall5269 2 роки тому +2

    Jerejeff bravo gayndé continué lénë dé boulénë kénë welbeti

  • @cheikhounambacke-wd4qw
    @cheikhounambacke-wd4qw 4 дні тому +1

    Merci beaucoup yalla nalén yalla takhawou poupam ❤❤❤

  • @senegalrek5805
    @senegalrek5805 2 роки тому +94

    Mane dh souniou kogne binguén toudé bountou pikine rek moma méti 😭 pourtant police dinafi nieuw mais nii lay rombé diaye katou yamba yi ak boy agresseur yi té dougne lén wakh dara wala niou diapp lén tay soubeu niou bayi lénn safinatoul amane au moins boula diapé si loudoul yone dinala fayloo 12000F wala mou yoboula police dianatou psk poste bobou mo geuneu diégué Garage darou mais police doulénfa tée té lolou dou yonne psk police Touba yamoul ak yénén police sénn porte police yi sakh police SPÉCIAL DE TOUBA lagne si bindeu kone commissaire thiombane dafa dioume si kadou yi limou wakh warouko wakh bou Wa khoudamoul xadiim diapé ay déf katou louniouy téré si Touba diagne lénn wara tée wala fayloo football nagne multi fois police diapp niou kone commissaire thiombane dafa dioume chef yikofi djiitou wone sakh danio amone collaboration ak Wa safinatoul amane kou wakhoul deug fénn police amoufi ndiarigne merci Wa ( khoudamoul xadiim ) et ( safinatoul amane ) yéna niou doy sécurité Touba et aussi Wa Touba ça kanam yéna niou doy si avancement Touba merci à vous niongui sén guinaaw.🫶🏾🙏🏾

    • @massambandiaye9288
      @massambandiaye9288 2 роки тому

      Saway del wax deugg ! Fofou lay ligeuyé Police chaque semaine mo deff fa décente, ramasse fa ay boy

    • @moustaphafall9494
      @moustaphafall9494 2 роки тому +4

      Wallahi ba parei gnou bagne ni khoudam ak safinatul amane dougnou def seen ligueye 😢

    • @senegalrek5805
      @senegalrek5805 2 роки тому +2

      @@massambandiaye9288 saway bofi dé léguéy mane mifi deukk nak ? fii police koumou ramass nga fanane fa bo kheuyé mou bayila lolou bane ndiarigne la ame

    • @KebenKeben-bb9ze
      @KebenKeben-bb9ze 2 роки тому +1

      Wallahi

    • @cheikhndiaye4244
      @cheikhndiaye4244 2 роки тому +1

      Machallah

  • @rimkafall5371
    @rimkafall5371 2 роки тому +36

    Ils font un exéllent travail
    Que la grâce de Sérigne Touba soit avec eux.

  • @sarrcheikh254sarr4
    @sarrcheikh254sarr4 2 роки тому +33

    Ndigala serigne bi Day sakh ba fawou inchalla lanén ndiguel kay lou diougué woul si serigne bi lani wakh wayé bi moom Day wey inchalla

  • @ibrahimahalilcisse5105
    @ibrahimahalilcisse5105 2 роки тому +9

    Machallah li rk la linu beug ci dëk bi mom nun Talibé yi nokofi mana déf Inchallah

  • @mbayeaminiang838
    @mbayeaminiang838 2 роки тому +11

    Li amna solo loll yalla nala yalla fayy ngirr dieumi Serigne Touba

  • @cisse07cisse8
    @cisse07cisse8 2 роки тому +13

    Machallah amna solo lool bonn conntination💪💪❤❤✊✊

  • @smahdiyoudiop6008
    @smahdiyoudiop6008 2 роки тому

    Waw lènn goor amna solo lool diadieuf xouddamoul khadim

  • @serignecheikh3626
    @serignecheikh3626 2 роки тому +23

    Vous avez fait un bon boulot courage ça c'était le travail de thioumbane le commissaire et vous l'avez fait a sa place merci

  • @sidytambedou3541
    @sidytambedou3541 2 роки тому +2

    😭😭😭képou kou né touba di déf ndakasoudoul nounou yalnala yalla may ak ndjioupe

  • @diopdame4835
    @diopdame4835 2 роки тому +3

    Merci à vous je suis très content

  • @petitgalass8734
    @petitgalass8734 2 роки тому +1

    Machaallah Bilahi beug naléne niogui sen guinaw

  • @serignemodoumakhtarsene3157
    @serignemodoumakhtarsene3157 2 роки тому +16

    Alhamdoulilah ligey bi boumou lale souff Dieuredieuf borome touba ❤❤❤

  • @serignesall3257
    @serignesall3257 2 роки тому +17

    Continuer vos Jobs on est tous derrière vous

    • @moussabakhembacke3857
      @moussabakhembacke3857 2 роки тому

      Le garage de Darou Mouhty est être délocalisé sur la route de Darou Mouhty.

  • @souleymanesow7640
    @souleymanesow7640 2 роки тому +24

    Pour taire tout ce qui est incohérence dans leurs politiques, que l'Etat donne un statut spécial à la ville de Touba. Parce qu'elle n'égale aucune autre ville du Sénégal en termes d'application des principes islamiques.
    Que l'Etat se réveille !
    La doctrine du Mouridisme est même un modèle de développement, comme les modèles des puissances occidentales. Ou plus efficace, plus sûr et plus cohérent que les modèles occidentaux.

  • @ousmanefaye9378
    @ousmanefaye9378 2 роки тому +4

    Merci khoudam et safinatoul aman

  • @gueye009fallou2
    @gueye009fallou2 2 роки тому

    Togne bakhol té yénagui Togne serigne touba dekem bi légene féye déf niew na

  • @abdoulahadfall6441
    @abdoulahadfall6441 2 роки тому +5

    Mash'Allah votre travail est parfait ! Que Dieu vous protège barkép Serigne bi ♥️

  • @senelucky
    @senelucky 2 роки тому

    diadief way mourit dierediefe seringe touba khadim rasoul one love bro ❤❤❤❤👍👍👍👍👍

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 2 роки тому +9

    Machalah félicitations à toute l'équipe sén liguéye rafètna

  • @papembaye5007
    @papembaye5007 2 роки тому

    Bravo,on doit prendre notre destin,sur les plans.les colons noirs ne fait pas peur !!!!

  • @soldarouboromtouba6115
    @soldarouboromtouba6115 2 роки тому +3

    Machallah khoudam liguéye bi boume lale soufe Touba Bamba ko mome

  • @loufaoriginaljooptoubatv9633
    @loufaoriginaljooptoubatv9633 2 роки тому +5

    Première commentaire li mome lou war la grass darou mome loune am nafa

  • @kane251
    @kane251 2 роки тому +2

    شكرا جزيلا

  • @barasow3654
    @barasow3654 2 роки тому

    Dieuredieuf wayy lii rekk mooy deugue yalla nalene borom Touba fayee

  • @papendiaye3237
    @papendiaye3237 2 роки тому +1

    Jërëjëf S TUUBAA, waaw leen goor nii rkk la

  • @lomm913
    @lomm913 2 роки тому +21

    Macha allah bon boulot ! Touba Serigne Touba moko mome!

  • @khadimawaballa
    @khadimawaballa 2 роки тому +12

    Police touba ak khoudamoul khadim sèn probalèm moy pas pas

  • @MDbousonko
    @MDbousonko 6 днів тому

    Machallah s'en Liguey rafetna dieura ngéne dieufati

  • @cheikhndiaye4244
    @cheikhndiaye4244 2 роки тому +7

    Merci beaucoup le combat est continue 💪💪💪💪💪💪

  • @serigndieng6634
    @serigndieng6634 2 роки тому +5

    Machallah 👏 liguey bi rafetna

  • @mamediarrasall29
    @mamediarrasall29 2 роки тому

    Alkhamdoulilah, dieureudieuf Serigne Touba,sounou gnou garage fatou bi gnou toudé bountou pikine makoy dioy chaque jour diko niaktou diok ngén si .bon boulot les gars

  • @sarrabdou3040
    @sarrabdou3040 2 роки тому

    Dieureudieufé Serigne Touba rekk Touba thia kaw , thia kanam

  • @moridetv7979
    @moridetv7979 2 роки тому +1

    Machallah Tuuba Daara la , Sèén Liguey AMNA Solo lool

  • @ousmanefaye9378
    @ousmanefaye9378 2 роки тому +13

    Séne liguéye rafetna khoudam merci

  • @BaabakarSëy
    @BaabakarSëy 2 роки тому +1

    Jaajëf waa Xuddaamul Xadiim 👏🏿👏🏿👏🏿

  • @fallouleye5555
    @fallouleye5555 2 роки тому +1

    Dieureudieuf chéikh Ahmadou bamba khadimou rassoul touba yéin you bonne yii warou féii amm

  • @NdeyeNdiaye-uh4hy
    @NdeyeNdiaye-uh4hy 2 роки тому +15

    Akassa Alhamndoulilah 😍Jerejefety serigne touba Diarramaty sama yakar Dji fall ndiaga ❤😭li serigne Bamba beug rk mofiy am inchallah 🙏🙏

  • @soxneufatimamakhtardiouf5613
    @soxneufatimamakhtardiouf5613 2 роки тому

    Yalla nalen Kutedd kii geuneu takhawou sii Barkeii Fawzeyni🙏🙏🙏

  • @seconvertiralislam9790
    @seconvertiralislam9790 2 роки тому

    Assalamou aleikoume,mbok yi.maa chaa Allah.ya Allah naniou ya Allah Di moussel si yakh Kate yi.si Touba AK Sénégal AK adouna bi yeupe.Amiine

  • @mamethiernogueye4681
    @mamethiernogueye4681 2 роки тому +3

    Je ne veux pas voir ça dans mon ville sainte Touba 😢❤

  • @thiamibrahima3933
    @thiamibrahima3933 2 роки тому +1

    Machalla ❤️❤️❤️❤️ Amna solou

  • @tdvtvdesvaleurs
    @tdvtvdesvaleurs 2 роки тому +1

    Jērēngeene jēf bu ñepp defoone ni yeene leegi Sénégal Jaar yoon

  • @faloudiop7678
    @faloudiop7678 2 роки тому +1

    Merci beaucoup khodam amna solo loll

  • @ousmanendiaye3572
    @ousmanendiaye3572 2 роки тому +8

    Mane dé contana thi Li mai nak souma sanione niou andak police nék béne ligueye deuk bi ndakh police mome manoule niak thime réw ndakh lou diangue le ba khame secret professionnel ba mana khame kou bakh ak kou bone Kone naiouléne ko ndangol nion bok Sénégal bok touba nioune gnéppe di aye senegalés kone diamou moniou war yalla na yalla déf diamou

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 2 роки тому +4

    Machalla amatina solo dieure dieuf khedmatoul khadim lii amatina solo ❤❤❤❤❤❤❤bravo modou Diop yaak gnienga andal gnieepou

  • @damesene2939
    @damesene2939 2 роки тому +5

    Machalah yalla nalène serigne taxawou

  • @laminembodji6934
    @laminembodji6934 2 роки тому

    Macha alla yalla naléne yalla faye na continué rek serigne abdoulahad contane ci yéne wayé bongonmane yi fi nek di teugue yalla naléne yalla wer niome niepou

  • @ndiayeabdou2623
    @ndiayeabdou2623 2 роки тому +3

    Machallah amna solo yallanalen Serigne bi Faye barke cheikhoul khadim

  • @133xb44
    @133xb44 4 дні тому

    Wawaw Machallah Sénégal sounou reww la nioune kesse' nio ko mouna defar 💯🦾💯 PROS 🙏✊🇸🇳💚💛💛❤️💚💛❤️🇸🇳🗿🗿🤔

  • @serignediop1104
    @serignediop1104 2 роки тому

    Machalla sene ligueye rafetna

  • @SerignemourtallaDiouf-b5u
    @SerignemourtallaDiouf-b5u 6 днів тому

    Machallah li amna solooh ❤❤❤❤❤

  • @damesamb6296
    @damesamb6296 2 роки тому

    Avec ça ap commendant niew thi deukeubi di ame loumouye wakh thi deukou serigne touba te niome defou gnou dara thi deukeubi..li serigne touba beugue thi deukeubi moye ame inch'allah...on est dernière vous...touba mome worma rek

  • @salihatmobaraq3391
    @salihatmobaraq3391 2 роки тому

    Maasàllaa wallaahi li rafetna lool jërëjëf waay yàlna leen YÀLLA taxawu

  • @marasamb6147
    @marasamb6147 2 роки тому +5

    Machalla bonne continuation

  • @zorasow7962
    @zorasow7962 2 роки тому +1

    Machalla Machalla Machalla Machalla gracias gracias a un saludo desde España

  • @modousamb7610
    @modousamb7610 2 роки тому

    Yenne waa khoudamoul khadim senne travail rafét n'a yalla nalénne srg bi fayal boppam

  • @ndiaynagoy8713
    @ndiaynagoy8713 2 роки тому

    Toute coeur avec vous

  • @italianomcmr7647
    @italianomcmr7647 2 роки тому +9

    Dieureu dieuf s touba merci bcp

  • @Niass5775
    @Niass5775 2 роки тому +1

    Ma challah amna solo looool

  • @ibrahimakhalil2234
    @ibrahimakhalil2234 2 роки тому

    Machallah serigne touba dh bagoul liii Bilahi amna nioubonnnn 😢😢😢😢😢que la grâce de see touba soit toujours avec vous ❤❤❤❤

  • @thiate87
    @thiate87 2 роки тому +28

    Bouléne ci dara djeulé deh lois Serigne bi mofey dokh

  • @lepatriotevivesonkopreside4570
    @lepatriotevivesonkopreside4570 2 роки тому +4

    Gni gnou homme de loi nah amougnouy thiahane Macha allah sene liguey rafetna

  • @sokhnandiaye6177
    @sokhnandiaye6177 2 роки тому

    C bien faire son travail tout en mettant les formes c s ka fait se policier l'autorité lui revient mais koi kil en soit chapeau

  • @wakanatvhd930
    @wakanatvhd930 2 роки тому

    Dieureudieufff serigne touba sama khol sédna si liguéy bi

  • @saliougueye8773
    @saliougueye8773 2 роки тому +3

    Akassa diadiuef amna solo

  • @baxrektv4781
    @baxrektv4781 2 роки тому

    جزاكم الله خيرا
    Yalla nalén yalla fay ta dolli tawfékh yi

  • @modoutall3281
    @modoutall3281 2 роки тому

    Merci machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ibrahimafallgueye2665
    @ibrahimafallgueye2665 2 роки тому +1

    Touba khana bokoul sii Sénégal Gendarmerie mo warra réglé lou amm Touba

  • @mamemor7761
    @mamemor7761 2 роки тому

    جزاكم الله خير ا

  • @SeydinaSow-gg1nd
    @SeydinaSow-gg1nd 6 днів тому

    macha allah merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @alfulaanibahpullo23
    @alfulaanibahpullo23 2 роки тому

    Machallah sen liguey rafetna

  • @maremetoure6315
    @maremetoure6315 2 роки тому +30

    Bravo bravo bravo toute la population de de touba est fière de vous

    • @khadimdieng6730
      @khadimdieng6730 2 роки тому

      Ya mana féne... Gni liniye yakhe mo eupou fouff liniy défar

  • @nabyshop2298
    @nabyshop2298 2 роки тому

    Mercii❤

  • @moustaphambacke3150
    @moustaphambacke3150 2 роки тому +8

    Dieuredieuf yallah nalaéne serigne touba fay

  • @balmah1
    @balmah1 2 роки тому +5

    Waw leene goor ,yalla naleene Serigne Touba feey

  • @papendiaye9775
    @papendiaye9775 2 роки тому +5

    Bilahi barki brom touba sama khol séde na Trop sakh

  • @ibrahimagningue2595
    @ibrahimagningue2595 2 роки тому

    Li môme bakhna trop mais aussi dèlène sol aye gants mo gueune👍👍👍

  • @mourtadacobar4216
    @mourtadacobar4216 2 роки тому +1

    Waaw lé gooor tawfekh ak taysir ci barké khassidayi diamo rek inchalla

  • @seringembakendiaye8349
    @seringembakendiaye8349 2 роки тому +21

    Yalla nalène yalla feuye contenna nou bou bakh

  • @saalihu824jóop
    @saalihu824jóop 2 роки тому

    Dieureudieuf yalla Na lene Serigne bi fay ne peur rien, on est ensemble.

  • @biranegueye75
    @biranegueye75 2 роки тому +1

    Ohh Serigne Touba amoul moroom

  • @NiangAmadou-bt3mg
    @NiangAmadou-bt3mg 17 днів тому

    Waw goorrrrrrrrrrrrrrrrr billahi sama xol séddna xoly mourid yeupe Sedna yalla nalén borom Touba taxawoul bopam

  • @moudomou7043
    @moudomou7043 2 роки тому +1

    amna solo machallah yall na yalla samou lene aart lene thi barke Serigne Touba

  • @lebaolbaoltigui2599
    @lebaolbaoltigui2599 2 роки тому +2

    le policier qui a portè le colier doit etre entendu...ca ne fait pas , ressembler un n'importe qui! il est policier, c'est dejà du DESORDRE !

  • @jazaka3178
    @jazaka3178 2 роки тому

    Kou yor sa Lou bonne NGA nokh guéneu Touba

  • @Laseydatte78
    @Laseydatte78 2 роки тому

    Bonne continuation mes frères nii rekk leuu lou bookoul si deukk bi nafi kéine Inchallah

  • @fallmamadou5036
    @fallmamadou5036 2 роки тому +1

    Merci merci merci merci

  • @abdouniang2876
    @abdouniang2876 2 роки тому

    Machalah amna solo continues lènn nioungu sènn gunaw

  • @khadimniass2023
    @khadimniass2023 2 роки тому +1

    Alkhamdou lilah jerenguene dieuff
    Wa bountou Pikine légui amnane siege bou bess si étage bi nek en construction coté diaka baye lamp ndiaye gno taxalo wa forage baye lahat sonou nane lolou

  • @ousmanefallait8804
    @ousmanefallait8804 2 роки тому

    Machallah liguey bi Rafet n'a...délén xolalé téléphone yi ndakh amoul xbet