Mbacké : Concert Wally seck annulé, les chaude réaction de la jeunesse de Touba.

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 12 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 99

  • @matarthiam9572
    @matarthiam9572 18 днів тому +24

    Kou meunoul respecté li khalif beugue si Touba rek nga delou sa deukou Mame wala sa deukou Baye , am lén yar ak téguin ak worma . Jub jubël rek mouride ndiguël

  • @Jeunepatriote
    @Jeunepatriote 18 днів тому +14

    Dieureu dieuf sama boki baye fall yii sa kaw sa kanam inchallah ❤❤❤❤

  • @loudoulaktalibesafouma3429
    @loudoulaktalibesafouma3429 17 днів тому +2

    1 er bi lil wax ❤❤❤moye deug boye yi dagne léna wara douma😢baye fall❤❤yi ❤

  • @ModouDarame-u2p
    @ModouDarame-u2p 18 днів тому +2

    Diaradiuf serigne touba❤

  • @BallaNiang-r5y
    @BallaNiang-r5y 18 днів тому +5

    Mbaye fall yi wakh nal basonou mérci mbaye fall❤❤ piont❤

  • @Mammorbeye-tf8gu
    @Mammorbeye-tf8gu 18 днів тому +4

    Diaradiuf seringue TOUBA dégel rk❤❤❤

  • @salioutine4426
    @salioutine4426 18 днів тому +1

    dieureudieuf baye fall yi ❤❤❤❤

  • @SyllaMouhtar313
    @SyllaMouhtar313 18 днів тому +8

    Wadji Rango Sac Bi AK Boye Bi Sol Yéré Bou Rouge Bi Yén Rekka Wakh Deugue Ndigeul Amoul commentaires Dieufé Rekk

  • @loudoulaktalibesafouma3429
    @loudoulaktalibesafouma3429 17 днів тому +1

    Baye fall yi ❤li serigne bi beug moye am❤❤❤

  • @ousseynoutoure3621
    @ousseynoutoure3621 18 днів тому +7

    Gonei yoyou dal jusqu'à preuve du contraire thiosanei wougnou touba aye lobbi gnofiye gneuw di nirouniroulou wa touba nguir maneu yakheu dieureudieuf waly yalna serigne touba faye

  • @BallaNiang-r5y
    @BallaNiang-r5y 18 днів тому +2

    Réw rék mérci mbaye fal❤piont ❤❤

  • @sonkofocus2024-ph4hv
    @sonkofocus2024-ph4hv 18 днів тому +6

    Koula téré déme concert mome dangako wara sante fo khamni aye bkar rk ngafay dieulé diaroull déme 😮

  • @cheikhabdoumbacke6970
    @cheikhabdoumbacke6970 18 днів тому +3

    Merci beaucoup wally seck ❤️❤️❤️

  • @hamathndiaye6803
    @hamathndiaye6803 18 днів тому +5

    Jajeuf les Baye fall
    Yalla nguen dathié ngueureum segne bi.aaaamine

  • @youssouphndiaye8323
    @youssouphndiaye8323 18 днів тому +2

    bayiléne sene thiakhane yi... deukkoup Serigne Touba bi lifi Serigne bi beug mofi ame par force... wormay TOUBA yagg na dou tay depuis jamonoy Serigne Abdoul Ahad Mbacké lawone. Mais vu k ken respecté wouko kon jotna niou deuguel ko.... Touba ken sossouwoufa kounek am nga sa deukoup mame té fanga bawou ngir dikk fi si Touba ngir ami khéweul. kon deuk bofa thiossanowoul dikk fa ngir sakou khéweul danga wara teunkou thia sa deuk ba namouy dokhé

  • @almustafambakke6163
    @almustafambakke6163 18 днів тому +3

    Nek leen ay Niit té Xam Séen Bopu té Li Serin BI bëg fawu dina am Inchalla

  • @DerMor-z8z
    @DerMor-z8z 18 днів тому +3

    Deugg bi moy dasi am talibé you compléxé rek am lou kéne amoul bayikofi di wouti lou bone tchim mani deuk bi lou serigne bi beugg mofiy am sokhka woun si xakatou kén koum nakhari nga dem sa deuk Maam

  • @lazanbambacke450
    @lazanbambacke450 18 днів тому

    Maasallaah ❤

  • @sadiocamara7957
    @sadiocamara7957 8 днів тому

    Kou ñiémé Yalla ragal sa moromou mbindeff😂😅

  • @oumarsarr4087
    @oumarsarr4087 18 днів тому +1

    Ay niouss rék mokoy fath

  • @djilybakhdad5223
    @djilybakhdad5223 17 днів тому +1

    Seen rapportage bi sakh dou yoon yii yéppo man naa niankk

  • @Sarr-jx7ux
    @Sarr-jx7ux 18 днів тому +1

    Jeuness touba gni thi eup dagno gnak diom nek lenne ay nite

  • @magiangfall4001
    @magiangfall4001 18 днів тому +6

    Wakhalene thi bokale bingeni bokale yalla

  • @Diks-m
    @Diks-m 18 днів тому

    Mais lou takh mbacké Coumba am ndeye la ak Coumba amoul ndeye

  • @Tttttttt-fm3ge
    @Tttttttt-fm3ge 18 днів тому +2

    Mani bayi léne saye tané waly seck ak Mbacké Mbacké yi nio farrr

  • @alleualleu693
    @alleualleu693 18 днів тому +2

    😢baye fall yi avant tout demlen diouli 😢😢😢😢

  • @sagyatal8545
    @sagyatal8545 18 днів тому

    7:28 En bleu Waw goor

  • @MaoFall-c7k
    @MaoFall-c7k 18 днів тому +1

    ❤❤❤

  • @DIEREDIEFSERINGETOUBA4
    @DIEREDIEFSERINGETOUBA4 18 днів тому

    ALLZ BADA

  • @aronandiaye7314
    @aronandiaye7314 18 днів тому

    Wawa

  • @toubadarmanko7193
    @toubadarmanko7193 18 днів тому

    Jeureudieuf Baye fall yi

  • @djilybakhdad5223
    @djilybakhdad5223 17 днів тому

    baye maslaa laniouy djital ci leppo mais khaléyi nioo rééw ba dof. Niakk ab yar. Khamady
    Mbir mi lou yombo la. Mooy kénn konék dém sa keur Mame nga défkofa

  • @abdoulayediop8062
    @abdoulayediop8062 18 днів тому +2

    nagn waxanté deuggeu nak waayé wally seck bou taxawéh naani baye fall leu loolou yabaaté leu, moom neu nekk musicien bimou doon rek té bayyi baye fall gui. un baye fall ne devient jamais un musicien. baye fall dafay deukkeu ci topp yalla di tarbiyou. waayé nekk ci seen yeufou thiaaxaan yi ba paré taxaw naani baye fall laa. le baye fall n'est pas n'importe qui. waly seck nak sou beuggéh nekk baye fall neu soppéh kou. baye fall deuggeu dou doon musicien nak vraiment. ngeen baal meu

  • @Bour_ndiaye_bour
    @Bour_ndiaye_bour 18 днів тому

    Kolén si diap mouy déf naka soudoul nonou gnaf léne ndayam bou bakh dieureudieufé bay fall yi

  • @sagyatal8545
    @sagyatal8545 18 днів тому

    9:47 Waw goor en rouge

  • @badadiopsatouba3828
    @badadiopsatouba3828 18 днів тому +1

    Je suis Baay Faal yii 😅

  • @BayemodouNdiaye-f6b
    @BayemodouNdiaye-f6b 18 днів тому

    Thiey wally mon barri baïre😂😂

    • @Sarr-jx7ux
      @Sarr-jx7ux 18 днів тому +2

      Dagua nane saytané mo bari baïré

  • @beugssalioumbacke2726
    @beugssalioumbacke2726 18 днів тому +1

    😂😂waly seul

  • @MouhamadoulamineSamb-n8g
    @MouhamadoulamineSamb-n8g 17 днів тому

    YeneuGoney touba yi na bay fall yi chifay len،احذروا هراوات باي فال

  • @solewgn750
    @solewgn750 13 днів тому

    Khale yoyounokhou lene laniou lenna deff

  • @moustaphaofficial
    @moustaphaofficial 17 днів тому

    Boy touba ti dagne lene wara niouss danio tèw trop

  • @محمدسيسهمعلمالقرءان

    Bada Waxi nit nga wax dé😂

  • @SeynabouDiack-c9s
    @SeynabouDiack-c9s 16 днів тому

    Néna diourbel la dieume le 2 li dalé touba diourbel ba mbacké wally boudé talibé serigne touba la jouer fa soirée warou ko

  • @Djilydiob-jf2ey
    @Djilydiob-jf2ey 18 днів тому +1

    Dëgg bi bi seen baay yi fobo ñaw fi xam nañu li Sëriñ bëgg kuko man nga took kuko manul nga dellu sa Dëgg maam wax ji jeex .

  • @patricelumumbaestunefierte781
    @patricelumumbaestunefierte781 17 днів тому

    Deuk bii nane ko ték ci lokhoy police ak gendarmerie

  • @khadimgueye1570
    @khadimgueye1570 14 днів тому

    Mouride à vie bouléne may li none yi di wakh

  • @abdoulahadgueye4643
    @abdoulahadgueye4643 18 днів тому +1

    Boyou Touba yi nio bonne té niak coleuré. Deukeul sa baye banga dioudou fayo bène droit ndokhe sakh doko faye. Nguène beugue yakhe deukou diambour.

  • @SeynabouDiack-c9s
    @SeynabouDiack-c9s 16 днів тому

    Lép Lou bokou si touba daray thiakhane waroufa ame

  • @tout1958
    @tout1958 18 днів тому +1

    Touba li Sérigne beugeu rék Moy am Domi xaram yi dém léne séne deukou baye wala séne deukou Mame

    • @bigue5329
      @bigue5329 18 днів тому

      Merci Sérigne Mountakha bouye defar kene douko thi fek bapar niou beugeu dhi khoti warmam domi kharam yi niake diom laniou te séné wadioure niou thi wara diapou dimbale Sérigne bi thi warma yi

    • @MohaMed-ep1dt
      @MohaMed-ep1dt 18 днів тому

      Ana sa deukoub bay yaw

  • @tout1958
    @tout1958 18 днів тому

    Domi xaram yi kouléne topou Touba am boîte de nuit tégeul léne séne ndeye dém séne deukou Mame

  • @AbdoulahadLo-x1e
    @AbdoulahadLo-x1e 17 днів тому

    Bayi liniouy wakh guemou niousi dara bay fall yi nane fi diougué

  • @abdoulahadgueye4643
    @abdoulahadgueye4643 18 днів тому

    Bolene bakhone âme diome ame coleuré ame ngore beugue lou bakhe Dolène dioté ak Baye Fall dara

  • @jamaaTV591
    @jamaaTV591 18 днів тому

    Reew dong a leen jàpp ñoom boyi Waly yi

  • @ndiayetoubausa391
    @ndiayetoubausa391 18 днів тому +2

    Kofi baye fall yi diabou rek nan ko Dorr yar ko rew nan trop

  • @patricelumumbaestunefierte781
    @patricelumumbaestunefierte781 17 днів тому +1

    Civil dou yar moromou civil lam

  • @ibrahimacissedieureudieufs2732
    @ibrahimacissedieureudieufs2732 18 днів тому

    Khaley Touba yii di wakh ay complexés you bone laniou ay séér youy nandité laniou khamouniou séne bopp

  • @ousseynoutoure3621
    @ousseynoutoure3621 18 днів тому

    Baye fall yi deifougnou dara sou ngueine bayei fo reck baye fall yi amougnok yeine problème

  • @MouhamedDiaw-f9b
    @MouhamedDiaw-f9b 18 днів тому

    Borom kap bi kou téppi leufeul ndeyam la ak kabou domerame dji mouy diaye nandité so gnewé Dakar khamni do nandité

  • @SaliouKne-il2qd
    @SaliouKne-il2qd 17 днів тому

    fii dall douniou fi neexall kene ndigall rek na booy yi yam

  • @tout1958
    @tout1958 18 днів тому

    Borome gassgett bi Domi xaram deugeu la

  • @Bawolbawol
    @Bawolbawol 18 днів тому

    Dañoo reew te doff baay faal yi rekkkk niofi baaax complexe

  • @dmcdjilymbayecolle4629
    @dmcdjilymbayecolle4629 18 днів тому

    Ay thiakhane rék la baye fall yi nék mais baye fall yi niom danioye teugeu di féthie

  • @modousarr8848
    @modousarr8848 18 днів тому +1

    niak fayda fi la Omar diange saka seringe bi wokho l'en fi doul nafékh yi ngén don

  • @papeleye267
    @papeleye267 18 днів тому

    Légui loutakh niouy dieul khaliss wally si Magali gui😂

  • @abdoukarimditmacodoundiaye993
    @abdoukarimditmacodoundiaye993 18 днів тому

    Bokalé guéne wara wakh

  • @madinagueye168
    @madinagueye168 18 днів тому

    Nit bokko japper tamit surtout bou deukoul Touba wala comprendroul worma yi dangakay fatali worma yi te bagne ko yobbou

  • @Tttttttt-fm3ge
    @Tttttttt-fm3ge 18 днів тому +1

    Mane lima diakhal waly daye diokhé adiya adiya dji fane lakoye dieulé

    • @dëgmonjëkdëgmomuj1780
      @dëgmonjëkdëgmomuj1780 18 днів тому +2

      Khana sa baay lako jox, danga gis Sëriñ Muntaqa jël xaalissu Waly

    • @khadynardiagne2681
      @khadynardiagne2681 18 днів тому

      😂😂😂

    • @beugssalioumbacke2726
      @beugssalioumbacke2726 18 днів тому +2

      Billy kay lu jara laaj

    • @bigue5329
      @bigue5329 18 днів тому +1

      Da nga masa guiss Wally diokhe adiya delene swi te teudi dou ngene masa am ndam thi kaw Sérigne touba li Sérigne bi beugeu moy am inchallah force koumou nekhoul nga niapou sa ndaye thia Khadije

    • @BabacarSarr-p5e
      @BabacarSarr-p5e 18 днів тому

      Tu l'as vu?
      Est ce ce xadiya est consommé ?

  • @TALiBÉBAMBABI
    @TALiBÉBAMBABI 15 днів тому

    ❤❤❤

  • @toubadarmanko7193
    @toubadarmanko7193 18 днів тому

    Mbirmi yombena li Serigne bi kouku meunoul bayi gueneul Touba dém Sa deukou bayi wala gua del fenene