Les nouveaux lutteurs comiques:TAPHA MBEUR-ALBOURY-LAURENT NDIAGO...vous avez ajouté une touche en plus vous êtes de fins techniciens Yalnalén souñ borom dolli tawfekh 🤲🏿❤️
Merci pour la distraction on en a tellement besoin Alboury Vraiment tu mérites d affronter les grands lutteurs Du courage, un bon lutteur, un antistress qu Allah réalise tes rêves Big salutation at father Becaye Mbaye Nous demandons le combat Zoss/Alboury
Ce qui me plaît en lui il se cache pas derrière les bidas et la mafia des Serigne' diw , il rend tjrs grâce à Dieu donc ne change jamais sûrement certains vont assayer de t'amener dans tel ville religieuse ou l'autre refuse !!!!! Fi yalla ak yonente bi rek gnoffi nek ...
Alboury continue comme tu est billahi wallahi ya ngui tourné Sénégalais yi ame na béne imame bou nék souniou deuk wale andi yati rk lay tari légui 😂😂😂 Mais fait très attention alboury sétane naka mbapate mok reug reug alboury ndanane la
Kou yééné Alboury lekk tchi million yii beusseul j'aime!
Les diolofs diolofs encore
Machallah
Moi
Man perso je l’aime bien 👍 je lui souhaite beaucoup de succès
Tayson, Yékini, Gris Bordeaux… sont les meilleurs en communication
Ku bëgg Alburi bësal j'aime sama mbër bu dégg bi 😂😂
Alboury merci pour le sourire 😀
Vraiment tu transmets le bonheur
Tout les week-ends da nga wara ame combat
Mdr 😂😂😂😂😂
Vraiment,
Non il est possible d'être milliardaire de lute yalla na yalla defalko 🙏🥰💖
Aminee
Alboury est l'un des rares lutteurs qui parlent bien et en plus il est si comique ..... 👏👏👏👏👏👏
Yalla nga nék milliardaire si barké seydouna MOUHAMED walahi tu nous combles de bonheur 🥰❤️🤩🙏
En plus d'être comique il est très intelligent Machallah
Alboury je t” adore vraiment tu es simple et modeste que ke bon Dieu te garde, tu es un béni de Dieu 🙏
Albouri merci tu sais tjrs que Dieu est le tout puissant
Il est treeeeess intelligent et cultivé
Un homme outillé
Kiiii douuu doff dé waaalakhi 🤫🤫🤫
Ma Cha Allah alboury champion complet , yalla bo am défait, ya indiwat " Wal adiyati dabahane"
🤣🤣🤣
Les nouveaux lutteurs comiques:TAPHA MBEUR-ALBOURY-LAURENT NDIAGO...vous avez ajouté une touche en plus vous êtes de fins techniciens Yalnalén souñ borom dolli tawfekh 🤲🏿❤️
Bilae🥰
Ada Fass nga faté lim
Akk zoe technique
Nn boucher
Ki a regarde jusqu'à la fin😂😂Alboury Jtm😂😂🇸🇳❤🤴
me
Laurent alboury machallah je vous aime aye vraie Philosophe guéne surtout
Nooo alboury yalla nala yalla lafal thiate té yokk la soutoura ak ay ndam you barry nganiouye yagg béggueul
Après Modou Lo Alboury Moy Sama Mbeur😂en plus il communique bien
Bilay nion yam apart modou mom moy sama mbeur
Manguissi groupe bi 😁😁😁Modou ak alboury rek
Bilaye dafa saff khorom
Wawaw parcelle grand Médine
Même man aussi thila boko
Alboury yalla nala yalla defal jam Amin le meilleur reste à venir
Alboury c'est le meilleur 😂
C'est un bon lutteur
«NOUSS-NIOUSS-GNIBI NOCE»dixit Alboury 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Avec Alboury c’est non stress.
Merci beaucoup on est content de toi.
Mane bilahi damay ragal bokk fan's club alboury . Fouma guiss alboury nakko setann li mba diamleuh
Modou lo dh dinama niakk rek nakk
C'est le meilleur et il fait plaisir à tous !
Éh beh j'ai eu un nouveau lutteur Alboury 😂❤️😊😍👌🏽
Nio niém😂
Meme moi et surtout il est comique et intelligent
Non NDANANE DJIOUDOUNA
Amen way tu es formidable alboury
Machallah K dieu veille sur toi alboury 😁🇸🇳💓🙏
Yalla nga nék milliardaire si barké seydouna MOUHAMED walahi tu nous combles de bonheur ️
Ndaysan damalay suporté force 🤣♥️♥️♥️
même moi
Merci pour la distraction on en a tellement besoin Alboury
Vraiment tu mérites d affronter les grands lutteurs
Du courage, un bon lutteur, un antistress
qu Allah réalise tes rêves
Big salutation at father Becaye Mbaye
Nous demandons le combat Zoss/Alboury
J’aime albouryy ❤️❤️😂😂😂😂😂
Damay khar ba bénn cartier walla région né gno mom alboury rékk.
Gnoun gnépp gnoko bokk n'a lérr
Mdrrrr
Yaw ya gueuneu sakh alboury😃😃
Woy😂😂😂😂😂😂😂
Vraiment tu as raison mon frère
Machallah plateau bi rafet na. Père becaye mention spéciale
Aka wakh deuggg
So amei objectif dang siy def fouleu di meuytou loulay yakhal bravo Alboury sama mbeur bu bess bi
Alboury non dafa neikh dam reik inchallah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Alboury waay,lou bakh ci rewmi ndiaye la sant témouy deugue roi des arènes rék inchaalah yalla dolila jaam
Bilahi amna mbeur bou bess😂😂😂😂 Alboury reew nga 🤣🤣🤣
Alboury naleuh tiate sëkh lu way
Yangui bëgueul askane bi ❤
Il communique bien même souy comédie
Alboury c'est un nouveau fenomene sou beurré mou nexx sou bako mou nexx machalla bonne continuation
Macha allah que dieu te garde et te protège
Numéro Alboury Nguir yalla la sokhla 🤝 béne Mbeur la am mouy ioe beus niki tay
Kaye ma diokh lako
@@khadyfall2045 joxma ko mann tamitt billahi daf may fathie
Alboury mo takh ma beuga lamb moye sama mbeur❤❤❤👏👏👏💪💪💪
Bilahi
Dafa rélou🤣🤣
😂😂😂😂
Bilahi mo néxal lamb dji légui
Mais il parle bien et passe bien sn message il faut l'écouter attentivement
tu la tu comprends bien il profite bien Anna ciment bi🤣😅keurem bi la wara défar
Mon lutteur préféré Alboury 🤣🤣🤣🤣🤣
BILLAHI alboury dafay dindi stress tayit kou am fassha laaa yallah nako yallah Geunue takhawou doliko wér soutoureu katan talak fékké moss ak mouthiou réussite total inchallah si barke ya rassoulillah psl si barke Serigne babacar sy rta
Il est très intelligent ce lutteur
Alboury et jo technique , bonnes contribution , seniwakh tane defa néx
Khalei bi Deg temps tei dou wathie temps Nioune sounou keur lep loudoul temps niou néko pan😂😂😂walay Deg seu yeufeu
alboury moy mbeurou niepp niepa ko beugg bilahi nitt kou mbakh la ❤️❤️❤️❤️
Alboury ❤️❤️❤️🇬🇲🇪🇦🇸🇳
Ré na ba sonu bilahi yalla nala yalla defal diam😂😂😂😂😂
La fierté de grand medine🤣🤣🤣
wa Serigne lolou dafa lérr domou grand Médine 💪♥️🤍
Hé wa grand Médine Dong momougnoko dé🤣
Gnoun gnépp gnoko bokk
No est ce que alboury nit dinako setane te'dou Retane
Bonne continuation
Alboury woutal sa compte bop gnépay abonnée
Masha Allah il est phénoménal
Door yii damassi yok ndokh😂😂😂 sacré Alboury
Alboury yalla nanga goudd fann '' néna ayabi dako indiwatt
The President of the Underground Fighters Diaata Demba
Ce qui me plaît en lui il se cache pas derrière les bidas et la mafia des Serigne' diw , il rend tjrs grâce à Dieu donc ne change jamais sûrement certains vont assayer de t'amener dans tel ville religieuse ou l'autre refuse !!!!! Fi yalla ak yonente bi rek gnoffi nek ...
Albury c un tueur 🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣👍🏾👍🏾👍🏾😘😘😘😘🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Il me tue quoi non Alboury tu es phénoménal
Je te jure
Da may niaanal dima niaagal ✅
Il est fort machallah
Alboury rayngama yallanasa diam yag 😂💯💪🦁 merci beaucoup
albouri day déme c'est fini , lamb dji sossi beugué percé fame nga inover , indi aye féme
J'aime alboury franchement kii môme moy mbeurrou askanwii
Un face-à-face révélateur du talent de Haaj Bécaye.
Tu es un génie, baayu Móodu Mbaay.
Laf thiate
Qui est d'accord que alboury est poète clique sur j'aime ♥
Alboury le peuple t'aime barki Borom Darou ❤️😅
Merci beaucoup diambar 😀😀😀
Machalla yalla boula thiat topou🥺🥰😎😎
Merci alboury ♥️♥️
Alboury diambar jii mais kén dou Pére Becaye
Bilahi
Je l'adore par ce que il communique bien
Alboury moy sama mbour apres modou lo 😍😍😍🥰🥰😁😁😁😁
Félicitations
No alboury nitt la kw bnn continuation frr on t'aime
Le gars alboury jte souhaite tout le bonheur du monde
ALboury Beautiful vídeo 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🔥🔥🔥🔥🔥👏👏👏👏👏
Machalla alboury ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Khawma wone après Modou ak siteu mbeur dina d si sama khol bi 😂alboury goudal fane waye😂😂😂problemou téléphone bi raye nama
Hahahaha😂😂😂😂 I am laughing like non stop, this guy is the best👏👏
Alboury Goudeull Fann Té Wèrr 😂😂😂😂
Alboury continue comme tu est billahi wallahi ya ngui tourné Sénégalais yi ame na béne imame bou nék souniou deuk wale andi yati rk lay tari légui 😂😂😂
Mais fait très attention alboury sétane naka mbapate mok reug reug alboury ndanane la
Alboury sama champion yow laa geume
Ce gars il est fort vraiment d'égal limiy wakh mais yalna ko yala gana dimbalé tu devrais être un poète
je rigoles toujours vers 7 h 🤣🤣Alboury diam reik guay ame ❤️❤️❤️❤️
néna da vierge
Alboury millionnaire inchallah
MACHALA machala longue vie a toi 😂❤🙏
J’aime beaucoup Alboury Bilay walahi
Alboury je l’aime bien 🤩
Bole bi😂😂😂alboury temps temps temps ❤️je t aime
Alboury Yalla na gua am victoire chak fois
Rakhass bamou sett ma dinthie 😂😂😂😂
😃😃😃😃
Lolou momay dadji
Deug dal la wakh 😂😂😂
Ayway balla gaye 2 dinama niakk nakh alboury mi non😂😂😂😂😂😂😂😂🏃♂️🏃♂️🙏🏽
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Alboury yallah nga goudou fan wér dolisa soutoureu ak katan wayé sayo guéso rék guisniou
Je aimè Alboury bcp
Machalla albouri yak Joe yaala ngén dieul roi bi
Alboury goudal fann way yalla Nala yalla samu kontane na si yow bilhai Sama fans nga sa nuemro nak beug nako svp🤣🤣🤣🤣
Mane fane la nekone bay dor kham Alboury 😭😭😭😭
Alles alboury del nouye wa allemangne tu a des Fans ici 😂😂😂
Il est cool alboury depuis la Mauritanie
Yalna diam yagg waaye