Qui a fais coulé des larmes en écoutant les mots de ngaaka je suis pas fan de lui mais wallah je partage la peine c trop triste mais Alhamdoulila 😑 yalla nala yalla taxawou nga matal projet yeup inchallah chapeau à toi ❤
Thia kaw thia kanam ngaka blindé.. Kila kham ko diangandole moma khamal ni linga sole noumou wékhai nonoula sa khole rafété.. Deukai thi diappalé diamou yalla yi... Yalnala yalla diapalé...
Je n'ai jamais écouté un morceau de rappe sénégalais mais à part d'aujourd'hui je vais le suivre grâce à toi. Tu me plais beaucoup car tu as montré une maturité. Que le bon dieu te protège aux mauvaises langues et oeils.
allahou akbar kabira wa prison metina dh amoul teud la deigg dh shiiiii les innocents qui sont la bas yalnaleine yalla gueinei si barki cheikhoul khadim les autres aussi yalla mayleine xolou mougn tei années yi gaww lol niou gueinnn
J écoute pas le rap mais ngaka je l écoute, je l’adore et c est le meilleur. Rien qu’à écouter sa mère on ne peux pas ne pas l’aimer. Go go go ai confiance en toi lep dîna bakh
Ngaaka blinde beugue Kone la na mais damala ngueuneu beugue vraiment j suis Vrai fans de toi.parce que tu es l'homme modeste et honnête.mai faite bien attention.pour les.ennémie de intérieur.parce que la vie. c'est une leçon,il faut bien viser.ton expérience, Total,et très loins maintenant 👉🎤🎤🎤❤❤❤👍 merci je suis la d'épuis a italie.bonne continuation.et bn courage merci
Vraiment Ngakaa nieup la beug , bignou la diaper ba déféré la dama donn dioy , parck sa son bi Neema waaw je l’écoutais en boucle dafa dope avec mon mari , mais sant yalla banga nek tokk di expliquer, yalla nala borom bi arr defal la diam , peace ✌️
On lové Ngaka blindé💞💞💞 💞💞💞💞💞💞💞💞💞 Man moutakh may deglou hip hop gal sene parceqe damalay béugeu billahi wallahi lodoul deugeh monoul yangeu ni rek la manoun déumeu amal diamou diamou rek ngay am
G bcp apprécié ngaka franchement courage ta enduré des pir moments mai kom si rien nété vraiment ta un mental d'acier yup bandit nous sommes derrière vous respect
No serieux j'aimer pas nga mai je sens kil est une personne vrema digne, simple et courageux je te souhaite une tres belle carriére courage je suis fan legui💪
ndeyssane si tu vw son visage et et sa sérénité tu te rend compte k c un innocent bilahi il a été cohérent dans tous ses propos mou nek lo xamné kou deugouwoul meunouko on sent kil est vrai vie sur tw❤✌KING BABA
Pape sidy fall douma la dône déglou mé chapeaux prsk damà déglou Makhou Pobar mou dal sa kao ga bayi mou sed néx nama trop épi sô ci meuné diap a propos de M..P.. fé le bn courage
Vraiment li dawna yaram😓😓journaliste déleine kholl bou bakh sén information yii ep8 chambre 100 où 300 personnes c'est troop état bii warna si diouk force à toi ngaka the King diapalnii mission la et tu l'as accompli👍👍💯
Ngaaka blindé yalla naga yag ame diam gudeul fane niune niola beugeu tei yalla tah ngaaka fi yafi nek game bi yako mome ngaaka fi ngaaka fé ngaaka feuler... 22 juin inchallah continue à être tw même et comme tu l'as dis dielal expérience Biga dielei feuler utiliser ga wone gayi fi yafi nek tei yafi meune
Jvien d regarde l'émission et jsui telma heureuse que TT soit divulgué car JM tjr discute tjr battu avec des famille et des amis sur s sujet qu'il est tjr innocent que natou rek la t taye diekhena t vraiment les sa lui a ouvert bcp de porte t inchalla sa sera plus blind blind rek
Bon retour Le king du Game...BILLAHI damala beugg...borom xol bou rafète nga kw..émission bi c'est la 2e fois makoy watch la 1ere fois c'était à la Télévision...Big up :)
slt tous le monde je voulais juste faire part a ce témoignage trés touchant de ngaaka blindé qu'il a été trés courageux pour avoir vécu toutes cette injustice et je suis trés déçu de la justice sénégalaise
Vraimnt ndaka je t’aime bilahi aussi suis fiert de toi pour la 1er fois mAy Setane plateau boh khmna 1h de plus vraimnt mane dama Meusse ame louma metii si ligniouko teuth bilahi mais yalla nalah yalla takhawou yalla mousseul lah sii thiat
une édition vraiment spéciale big up King Baba fii yafii nekk dara dou yombou ton dernier message walahi keineu amoul seu fayou yaye elles sont spéciales
Si on juge les Japonais d sérieux de politesse c'est grâce a leur presse pourkoi parce ke la presse Japonaise soigne les problèmes ki s passe a l'intérieur de leur pays il n divulgue pas les mauvaises informations contrairement a la presse Sénégalaise ki n publie ke les mauvaises choses ki s passe prenons les choses dans le côté positif nous sommes Sénégalais et essayons d soigner notre image a l'échelle international et ça doit commencer avec la presse Si t'es d'accord pousse bleu👇
Ndeysane c'est triste tout ça yalla naniou yalla moussal si prison. Li yep natou yalla la wone rek bro yalla na done sa mourlay ,amal diameu,et bonne continuation dans ta carrière musicale
Ngaaka nèna Dip mane bomay diay rèw ma wanela my nigga sa papa la ngani dama dèm dièl di dioy di yakh sama dèrr mais c pas méchant☝️🙈😂😂😂King Baba di Ngaaka yalla na sa diam yague mane mome damala beugue en plus dila enjoy nak bou bakh👌
Ngaka boul fater Dj Boubs aussi ndeysane durant sa problème bi yeup souvent souy animer dafa lay toudou ak kouthia aussi ndax mane rfm rek lay deglou Wa real one aussi(kalz, holly be)
Alhamdoulilah yalnala yallah takhawou bagua yekk koo j’ai regardé tellement d’interview après son arrestation et je ne jamais été autant peiné mais sant yallah rekk le 24 yalnagnko fêké si diam
Débat validé. Nekhna ak plein d'enseignements... Des questions et réponses concrétes et honnêtes!! Je kife trooppp😉. Au passage, Bijou sagnesé nga; de la tête au pied machallah tt te va à merveille😗
Ngakaa. banlieue bi amna ay rappeur gno geum rap meunko pinal gang under shiffay niamu mbam rap attack ay bagnkat .holal si grands yi.tewal banlieue.royal si gno.bayil rap love
Soit fort mon gars la vie est comme ça..en plus leçon la et j'espère bien que prochaine fois dinga xam bou baxx foy tekk sa tank. En tout cas dawna yaram vraiment
Man douma déglou rap mé ngaka dafma nékh trop kouko guiss ak ay rétanam khamni ndeyssan dara nékoul si xol bi machallah yalla nala yalla yobou fou sori inchallah jtador
Non Nkakaa nice boy nga neuk. Mais goor mo moom experience ak metit mo takh ngey done vrai diamou Yalla. Ndakh sunu borom bala nga ka ham deug am ay diar diar you doy war Sénégal neuk deu niou bari fo ak tiakhane. Mais neuk santal beu démoulo chambre 3 ak 4. Big up
Vraiment je s8 content de Ngaka blindé et tout les hip-hopeurs gnép takhaw nagne et bonne continuation frère une erreur est une leçon dans l'avance yonou ndaw dou gaw
J l jure sur le saint tay dama woor té diaraloma ayy fene en regardant ce video dama dolii gueuneu ragal yalleu lii kemtann leuu est c k setlou guene regarou ngaka il est pur mais senegall mongui ni jugé akh wakhal nitt lou bon fii leu fekk bakh manguii lay gnannall barkii ahmadou bamban bignou bok yalleu sam leu yokk sene khewall akh sa meunne meun boull tiitt sakhoull sa gnanou wadiour dii diamou yalleu le rest tek thy lokho yalleu❤️👌
Papis très belle intervention se sont nos produits pire sénégalais il faut les soutenir c’est très important Actuellement les français font pareil par rapport au football ⚽️ Exemple mbappé sera tjrs intouchable au psv parcek c’est un pire produit français il est prioritaire c’est un business Donc chapeau valorisons nos produits merci c’était moi
Alkhamdullilah ba meussouma ko geum ndakh fékkewouma té hamnané d'autres font pires té kéneu dadioulen mais nakk geumeul yallah rekkk natou gneupp lay dal dafa beuuriy façon rekk koneu santal ndakh niteu gifi AVC té yallah mouthieul nalassi koneu santal bou wérrreu
Ooh c'est la première fois que je t'écoute ngakaa mais je suis éblouie par ta maturité et ta simplicité machallah
Qui a fais coulé des larmes en écoutant les mots de ngaaka je suis pas fan de lui mais wallah je partage la peine c trop triste mais Alhamdoulila 😑 yalla nala yalla taxawou nga matal projet yeup inchallah chapeau à toi ❤
Lansanafaty
Thia kaw thia kanam ngaka blindé.. Kila kham ko diangandole moma khamal ni linga sole noumou wékhai nonoula sa khole rafété.. Deukai thi diappalé diamou yalla yi... Yalnala yalla diapalé...
Je n'ai jamais écouté un morceau de rappe sénégalais mais à part d'aujourd'hui je vais le suivre grâce à toi. Tu me plais beaucoup car tu as montré une maturité. Que le bon dieu te protège aux mauvaises langues et oeils.
Depuis USA, bro tu m’as fait pleurer tè mangui dogga wacci. Yalla bofa dèmatt, tè oumpou bepp goorrr.
Mame Sene Bilahi gneup la dioylo msne j pouvais mem plus tenir mes larmes
Mame Sene donne ton Snapchat je vais lui passé inshallah et merci bcp ya salam
Alahouma amine
allahou akbar kabira wa prison metina dh amoul teud la deigg dh shiiiii les innocents qui sont la bas yalnaleine yalla gueinei si barki cheikhoul khadim les autres aussi yalla mayleine xolou mougn tei années yi gaww lol niou gueinnn
J écoute pas le rap mais ngaka je l écoute, je l’adore et c est le meilleur. Rien qu’à écouter sa mère on ne peux pas ne pas l’aimer. Go go go ai confiance en toi lep dîna bakh
Merci 2s et merci ngakka blindé le king du game❤😊55😭
Ndeysan je me rappelle concert Canabasse 11Août sound wou ngaaka la pape sidy dougou sei c'était tellement émouvant😴 PSF mérite un Maximum de respect✊
Ngaaka blinde beugue Kone la na mais damala ngueuneu beugue vraiment j suis Vrai fans de toi.parce que tu es l'homme modeste et honnête.mai faite bien attention.pour les.ennémie de intérieur.parce que la vie. c'est une leçon,il faut bien viser.ton expérience, Total,et très loins maintenant 👉🎤🎤🎤❤❤❤👍 merci je suis la d'épuis a italie.bonne continuation.et bn courage merci
Gni nékeu si Prison bi yalla na léne fa yalla guéné 🙏🏾
ta kou mou ma sul dal yalla bum la dal 🤲🏾
Vraiment Ngakaa nieup la beug , bignou la diaper ba déféré la dama donn dioy , parck sa son bi Neema waaw je l’écoutais en boucle dafa dope avec mon mari , mais sant yalla banga nek tokk di expliquer, yalla nala borom bi arr defal la diam , peace ✌️
Bonne continuation il s'exprime bien il est naturel vraiment longue vie ta Maman t'aime mais aussi tu es un modèle pour un fils
Ngaaka vraiment tu es une personne extraordinaire. Longue vie à toi 🙏
Pape Sidy le combat fut noble. God bless you... Ngaka courage pour la suite.
Pap sidy nimou def moy jeufou nit
Yala souy defar day melni louy yakha machalah kasso bi djikk neuleu boudé noon moko defff yakhnako ndax danga gueneu am maturite
Non prison metina😭
Gni fa nek té defougnou dara yalla nalene yalla guéné thi barké barhama niass🙏🇸🇳🇸🇳
Marichou Sow pape..diouf
Ngaka yalla bakh na
On lové Ngaka blindé💞💞💞
💞💞💞💞💞💞💞💞💞
Man moutakh may deglou hip hop gal sene parceqe damalay béugeu billahi wallahi lodoul deugeh monoul yangeu ni rek la manoun déumeu amal diamou diamou rek ngay am
One love a Bijoux ngonè, ❤❤❤
Vraiment Ngaka blindé tu es un homme très courage wallhi yalla nala yalla défal diamo
Bravissimo a Pape sidy fall 🙏🙏🙏
G bcp apprécié ngaka franchement courage ta enduré des pir moments mai kom si rien nété vraiment ta un mental d'acier yup bandit nous sommes derrière vous respect
No serieux j'aimer pas nga mai je sens kil est une personne vrema digne, simple et courageux je te souhaite une tres belle carriére courage je suis fan legui💪
Def Lou bax et tu n'attend rien aux retours ☝️c ce que pap sidy a fait.aka diafé. chapeau a toi
ndeyssane si tu vw son visage et et sa sérénité tu te rend compte k c un innocent bilahi il a été cohérent dans tous ses propos mou nek lo xamné kou deugouwoul meunouko on sent kil est vrai vie sur tw❤✌KING BABA
En tout cas il communique bien. Il a plus de maturité. Bon courage à lui.
Tu as raison Mor
Aminata Thioune franchement chapeau à ngaka yalla nako yalla sameu pure talent ngaka juste rekk Li wara continue di soleu costume cravate chemise
Pape sidy fall douma la dône déglou mé chapeaux prsk damà déglou Makhou Pobar mou dal sa kao ga bayi mou sed néx nama trop épi sô ci meuné diap a propos de M..P.. fé le bn courage
Vraiment li dawna yaram😓😓journaliste déleine kholl bou bakh sén information yii ep8 chambre 100 où 300 personnes c'est troop état bii warna si diouk force à toi ngaka the King diapalnii mission la et tu l'as accompli👍👍💯
Bijou ngoné est pertinente .
Ngaaka je ne te connaît pas ni tes sons mais gueum nani dinga yeggueu fou sori . machaallah
Chapeau ngaaka .c etais un mal pour un bien .tu as gagné en maturité .tu communique très bien .chapeau
Ngaaka blindé yalla naga yag ame diam gudeul fane niune niola beugeu tei yalla tah ngaaka fi yafi nek game bi yako mome ngaaka fi ngaaka fé ngaaka feuler...
22 juin inchallah continue à être tw même et comme tu l'as dis dielal expérience Biga dielei feuler utiliser ga wone gayi fi yafi nek tei yafi meune
Jvien d regarde l'émission et jsui telma heureuse que TT soit divulgué car JM tjr discute tjr battu avec des famille et des amis sur s sujet qu'il est tjr innocent que natou rek la t taye diekhena t vraiment les sa lui a ouvert bcp de porte t inchalla sa sera plus blind blind rek
Bon retour Le king du Game...BILLAHI damala beugg...borom xol bou rafète nga kw..émission bi c'est la 2e fois makoy watch la 1ere fois c'était à la Télévision...Big up :)
slt tous le monde je voulais juste faire part a ce témoignage trés touchant de ngaaka blindé qu'il a été trés courageux pour avoir vécu toutes cette injustice et je suis trés déçu de la justice sénégalaise
No ngakka dioylo ngama bilakhi yalna yalla fay sa khol 2stv jsuis content de vous
Vraimnt ndaka je t’aime bilahi aussi suis fiert de toi pour la 1er fois mAy Setane plateau boh khmna 1h de plus vraimnt mane dama Meusse ame louma metii si ligniouko teuth bilahi mais yalla nalah yalla takhawou yalla mousseul lah sii thiat
Alhamdoulilah nguaka
Niou doli santeu yallah bou bakh
Le meilleur reste à venir
MW j'ador nguaka j t souhait l meilleur bilay
une édition vraiment spéciale big up King Baba fii yafii nekk dara dou yombou ton dernier message walahi keineu amoul seu fayou yaye elles sont spéciales
Bijou Ngoné est t'un bon journaliste elle maîtrise ce qu'elle fait
Vraiment pape sidy kou bakh ga ngaka nak adouna ni la lou yalla dogal meuno si dara
Man douma deklo rp Ngaka yalla rék motakh ma beuko yalnala yalla defal diam barké serigne fallou
Si on juge les Japonais d sérieux de politesse c'est grâce a leur presse pourkoi parce ke la presse Japonaise soigne les problèmes ki s passe a l'intérieur de leur pays il n divulgue pas les mauvaises informations contrairement a la presse Sénégalaise ki n publie ke les mauvaises choses ki s passe prenons les choses dans le côté positif nous sommes Sénégalais et essayons d soigner notre image a l'échelle international et ça doit commencer avec la presse
Si t'es d'accord pousse bleu👇
Fi dé dagnouye sossal sakhe Sénégal tilimeul ko ndakhe sén propre intérêt
Mais bijoux t'as assuré félicitation et tu maîtrise ce que tu fais 😍❤
Salma Faye bisous est Adorable ❤️elle est mature ❤️
Hoooo j ai mm les larmes aux yeux gni nekk prison yallah naléne fa yallah guéné respect à king baba mbarikalah rek
Doundou bou sotégoule louné khadje nasi yalla naniou yalla sameu
Ngakka francement dafa yarou koi li thi sa kaname yalla nathi yalla défe diamou INCHA ALLAH
Ngaka meilleur de sa génération😘😘😘😍😍
Machalla ngaka nitou kesse la je viens en rendre compte tu deviens mon rappeur de cœur good bless you bro
Ndeysan nèk nitt nittè KO geune Machalla ngaka diam rek inchallah
Vraiment c'est émouvant personne ne sait que l'avenir nous réserve demain mais qu'en même du courage.
Qu'ALLAH nous guide
Nn ngaka keuthieu nga kW doundou Lou melni téwate si game bi ngaka chapeau a toi 👊👍👍
J aime un artiste bien encadré et ce ngaka est sur ce chemin je l adore
Yaram dawna way😭😭 ...Prison métina,,gnifa nék naléne yalla takhawou🙏🙏🙏
Amine
Amine🙏🙏🙏
Amine
Amine
Amin 😭
Ndeysane c'est triste tout ça yalla naniou yalla moussal si prison.
Li yep natou yalla la wone rek bro yalla na done sa mourlay ,amal diameu,et bonne continuation dans ta carrière musicale
Bokk na ci maqama yoneint Yalla suleimaan dugg kasso mouy nattu buyy yokk nitt ki ci ay daradja mokham zahir wala baatiin...ndam rek
Yalla naniou Yalla mousseul si Prison. Allahouma Amine.
Métina trope.
SÉNÉGAL Prisons yi Métina trope.
Diaar diaar yoyu yep j’aurais aimé nga def ko film, histoire
Amdara la dh
Maodo Malick yow do dém film kay
😂😂😂😂
Nooooo😂😂😂😂🤦🏼♂️
Wakhgua deugue mounone nako def film 🙌🏽
J les larmes o yeux yalna tek lokho gni fa nekk 🙏🏿❤️ 100a 300 prsnes c trop
Bilahi boy Afia rk Guay am dakh dagua beugu sa Maman ☝🏿👌🏿🙏🏿🇮🇹🇸🇳
Ngakaa blindé big respect a toi nioune iow laniou bégué weur na yalla
Je lestime bcou ngakka.yalnala yalla defal diam.
vraiment ngaaka beugonna nga invité dip le 22 juin inchallah ymgx🖖
Ngaaka nèna Dip mane bomay diay rèw ma wanela my nigga sa papa la ngani dama dèm dièl di dioy di yakh sama dèrr mais c pas méchant☝️🙈😂😂😂King Baba di Ngaaka yalla na sa diam yague mane mome damala beugue en plus dila enjoy nak bou bakh👌
Nul
Dip rawnaléne😜
@@Seyd985 boy affaire bi ngaka laa
Fuck your opinion
Bayil doul waxoul ak Dip teaser bii laniou done lam lamé lolou mais ba son bi guéné nekoul Dip lassi waxal doff nga rek
J'ai pleuré 😭😭😭😭 comme pas possible vraiment je suis désolé pour mon pays le Sénégal va très mal.... bonne continuation à ngaka blindé
Ngaka boul fater Dj Boubs aussi ndeysane durant sa problème bi yeup souvent souy animer dafa lay toudou ak kouthia aussi ndax mane rfm rek lay deglou
Wa real one aussi(kalz, holly be)
Ngaaka du courage natou la rek yalla nala borom bi sameu la yékati la sa kaw
ngaaka c'est le king mais moi je dis chapeau à bijou vraiment pour une fois j'ai kiffé ce qu'elle fait
Ngakaa il s'exprime bien yalla nala yalla defal diam🙏🤘🤘
Alhamdoulilah yalnala yallah takhawou bagua yekk koo j’ai regardé tellement d’interview après son arrestation et je ne jamais été autant peiné mais sant yallah rekk le 24 yalnagnko fêké si diam
Yeah bro pape sidy fall thanks you very much man bro 🎤🎤🎧
Débat validé. Nekhna ak plein d'enseignements... Des questions et réponses concrétes et honnêtes!! Je kife trooppp😉. Au passage, Bijou sagnesé nga; de la tête au pied machallah tt te va à merveille😗
Ngakaa. banlieue bi amna ay rappeur gno geum rap meunko pinal gang under shiffay niamu mbam rap attack ay bagnkat .holal si grands yi.tewal banlieue.royal si gno.bayil rap love
Un grand homme yalla nala yalla defal diam aduna akk noone gno and
Mais sant god rek😚
J'apprécie beaucoup ngaaka blindé c'est vrai magnifique son teint noir ♥️
Soit fort mon gars la vie est comme ça..en plus leçon la et j'espère bien que prochaine fois dinga xam bou baxx foy tekk sa tank.
En tout cas dawna yaram vraiment
Man douma déglou rap mé ngaka dafma nékh trop kouko guiss ak ay rétanam khamni ndeyssan dara nékoul si xol bi machallah yalla nala yalla yobou fou sori inchallah jtador
Vraiment yaram dawna dina baxx bro bonne continuation vrai baye fall nga machallah
Ngaka à l'ancien un message sur respect à nos Maman
Non Nkakaa nice boy nga neuk.
Mais goor mo moom experience ak metit mo takh ngey done vrai diamou Yalla. Ndakh sunu borom bala nga ka ham deug am ay diar diar you doy war
Sénégal neuk deu niou bari fo ak tiakhane.
Mais neuk santal beu démoulo chambre 3 ak 4.
Big up
Ngaka sa kaw sa kanam si barké serigne touba 👐
YAKK DER SENEGAL
Pape Sidy merci a toi
Ngaaka du courage
Ngaka blindé yalnala yalla may goudou fane ak weer ngaka doundal waay
Ngakka tu m'as fait pleuré... courage à toi pour le reste de ta carrière
Ngaaka blindé tu m’as surpris vous avez vu son air intellectuel ? Il sait parler ce boy
bonne change ngaka tu as du talent yalla nalla yalla arre mousal la.....namone nanioula.. momo fans dip
Vraiment je s8 content de Ngaka blindé et tout les hip-hopeurs gnép takhaw nagne et bonne continuation frère une erreur est une leçon dans l'avance yonou ndaw dou gaw
Merci beaucoup ngaaka blindé yalla nala yalla fay way
Vréma bisou bou défé émission je l'aime de plus en plus ngaaka ma fait pleurer bimouye raconter 1er jour prisons bi😘bn courage et bn vend
Bijoux une très bonne journaliste Respect à Ngaaka Blindé ✌🏿
Bon continuation li diar diar diar rek leu que dieu te protège si barke Serigne saliou
We are blindé familly my lovely artice 🤩🌹🙏 un an prison yombutt mais on gère c'est MBARIKALA MBARIKALA on dit
J l jure sur le saint tay dama woor té diaraloma ayy fene en regardant ce video dama dolii gueuneu ragal yalleu lii kemtann leuu est c k setlou guene regarou ngaka il est pur mais senegall mongui ni jugé akh wakhal nitt lou bon fii leu fekk bakh manguii lay gnannall barkii ahmadou bamban bignou bok yalleu sam leu yokk sene khewall akh sa meunne meun boull tiitt sakhoull sa gnanou wadiour dii diamou yalleu le rest tek thy lokho yalleu❤️👌
Ça se voit sa xol mo rafféte bilahi man j te prend comme idole Ngaka king baba Diamm RK gaye amm fr jtm💜👌
Bravo pape sidi fall 👏👏👏👏👏👏👏👏👏🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Ngaaka blindé King baba rek 🤴🤴🤴🤴🤴🤴🤴ngaaka blindé King baba de retour à
ngaaka blender rek #±WAKH KO SAKAW BRO king ngaaka
ngaaka blender rek
Louy king baba?
Cool
Papis très belle intervention se sont nos produits pire sénégalais il faut les soutenir c’est très important
Actuellement les français font pareil par rapport au football ⚽️
Exemple mbappé sera tjrs intouchable au psv parcek c’est un pire produit français il est prioritaire c’est un business
Donc chapeau valorisons nos produits merci c’était moi
Merci 2tv courage ngaka blinde
Alkhamdullilah ba meussouma ko geum ndakh fékkewouma té hamnané d'autres font pires té kéneu dadioulen mais nakk geumeul yallah rekkk natou gneupp lay dal dafa beuuriy façon rekk koneu santal ndakh niteu gifi AVC té yallah mouthieul nalassi koneu santal bou wérrreu
#NGAAKA BLINDE KING OF RAP👑👑👑🇸🇳👍🏽✊️🎤 bayou rappeur yi yaw la !! #BIG RESPECT MY BRO NGAAKA 🙏
Dafa lerr bro
Bien dit
Je ne plus tenir mais larme car ngaaka damako moudjié yeureume bilahi.mais nake yalla bakhena
Yalla Nagnou yalla mousal si prison mousal si bep môleme djoulite
Nice vraiment. Pape Sidy chapeau a toi
Nice👊❤❤
C’est trop dure vraiment bilahi diambar lah deh yalla bouh nekk kham nih prison mell
Pape sidy communique super bien
chapeau a pape sidy
Eklwkkwkl1
Ke dieu te guide ngaka❤️❤️
vraiment ngaaka champion la .big respect a vous