Barca wala Barsakh , il craque et fond en larme , mane damay dem espagne par force parce que...

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 30 лис 2024

КОМЕНТАРІ • 729

  • @soldaroumamesaliou7609
    @soldaroumamesaliou7609 4 роки тому +44

    Aka khame limouy wakh entre chauffeurs ak policies

  • @serignebaradiouf6984
    @serignebaradiouf6984 4 роки тому +13

    Bilahi boy bi dafa intelligen ki mom damako beug té amna Khél trop machallah yalnala yalla indi ci rew mii

  • @holqr1350
    @holqr1350 4 роки тому +19

    Saway manela el capo mangui Espagn yene gnep ngew lene fi amna xiweul diou beuri barke baye niass Senegal amoul dra salerou wer Senegal ngaye amfi bene fane yalna lene yalla diapale senegal dafa metti te amoul dara bilahi

  • @amethgueye8598
    @amethgueye8598 4 роки тому +50

    😂😂😂 no mais boy bi amul du courage yalla nala yalla indi Europe si diam inshala frère

  • @capsiboymathiavelly
    @capsiboymathiavelly 2 роки тому +1

    Lidafa mety bilay nioune NDAW beugnaniou Liguey dh mais police 👮‍♂️ mayougne niou jaam

  • @awasagne4649
    @awasagne4649 2 роки тому +7

    Ma Chala que Dieu vous Protege

  • @tallambengue1092
    @tallambengue1092 Рік тому +1

    Sénégal ndaye ndayi réw

  • @mouhamadoulaminegueye7014
    @mouhamadoulaminegueye7014 4 роки тому +53

    Un journaliste doit être posé, calme et attentif.
    Safara wala aldiana dou domou adama mokay décider leip yalla la

  • @malickndiaye3835
    @malickndiaye3835 2 роки тому +3

    Ohhhhh 😭😭😭 frère linga buegue Yako khame Yalla nala ko yalla défal😭

  • @momoyoutube6456
    @momoyoutube6456 4 роки тому +26

    Je te le jure cet homme identifie la jeunesse sénégalaise. Limou wakh lep deugla. Tout sauf galgui. Du courage. Injustice totale

  • @boycisse9397
    @boycisse9397 2 роки тому +6

    😭 frère courage yalla nga niow Espagne si diam mottali sa yennnne aminnnnne,🇪🇦🙏🇸🇳😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @ridialpeuzzi7743
    @ridialpeuzzi7743 2 роки тому +3

    Lii dafa méty trop bly 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @leuzdiarra682
    @leuzdiarra682 4 роки тому +12

    Je me demande est ce vraiment un journaliste ??
    L'invité est trop pertinent et posé
    Machallah

  • @ablayediouf-mf1zo
    @ablayediouf-mf1zo Рік тому +1

    Bilahi yalla khamnago Lou lér la wakh man douma safuer mé Sénégal dafa méti

  • @ibrahimadiop9433
    @ibrahimadiop9433 4 роки тому +19

    Il faut in soulevement populaire et pacifique des jeunes des adolescents femmes et enfants pour reformer le pays et partager les resources equitablement

  • @malickseck1639
    @malickseck1639 2 роки тому +1

    bilhya waliaye ndayesan yalla nako yalla samou dolli soutoura ndayesan ❤💯❤💯❤💯❤💯❤💯❤💯❤💯❤💯❤💯

  • @fantacordroch8645
    @fantacordroch8645 4 роки тому +31

    Bilahi Sénégal meti la déf kham naa si dara mane mi nék Europe sakh lo yore fii envoyé ko doundou lép yaw yakoye déf dakh liguéye amoul dépenses yii barina.
    Yalla na lép soti incha halla

    • @binetasylla5035
      @binetasylla5035 4 роки тому +1

      Yalle naniou yallah dolli aye kheweul niou lène di gueuneu meuneu diapalé inchallah

    • @fantacordroch8645
      @fantacordroch8645 4 роки тому +1

      @@binetasylla5035 amine Etat bii mo wara kholate liguéyam éducation, emploi, santé.
      Parents yii yar khaléyi bo guisé Chine bok si puissance yi taye c'est par ce que da gno encadré jeune école, wala école technique sén éducation doom dou gnou ko fowé imagine khalé yi de 7h du matin jusqu'à 23h yagui école
      De 7h à 19h cours école
      De 19h à 23h tt les cours yi gua déf si journée bii faut le savoir par coeur bala guaye dém au lit.
      Gnoun nak parents défou gnou sén liguéye si keur pr yar khalé, école enseignant(e) you nilare gno fa nék, Etat bii défoul bén effort éducation.
      Khalé yii wara yorr réw mi bou gnou amoul béne formation, ni discipline lougnou begueu 🤷‍♀️c'est dommage

    • @thiernaabdoulba2908
      @thiernaabdoulba2908 2 роки тому

      Amine Amine diam si iow Sénégal méti n'a insahala

    • @thiernaabdoulba2908
      @thiernaabdoulba2908 2 роки тому

      @@binetasylla5035 Amine Amine

  • @cptnaier7998
    @cptnaier7998 4 роки тому +28

    Deugleu la wah Sénégal 🇸🇳 amoul ligiéye

  • @gabrielpro2747
    @gabrielpro2747 4 роки тому +9

    Si tu réussi de entre ici en Europe tu vas beaucoup gagner, on paye très bien, mon mari est chauffeur mais machallah

  • @oumarnd4866
    @oumarnd4866 4 роки тому +25

    Dem europe nek garap gnoumay arroser moma gueuneul nek ministre Senegal 💪🏿💪🏿💪🏾💪🏾💪🏾

  • @badoukane6584
    @badoukane6584 4 роки тому +8

    Man de Chauffeur la won Senegal 🇸🇳 carapip 2006 - 2012 mais sama saler Senegal 🇸🇳 bilahi moy journée fi Europ bayi lene nakhate bi Senegal 🇸🇳 d’où Dara

  • @king-jp5mb
    @king-jp5mb 2 роки тому +1

    Mauritanie fi moōguen Sénégal fouf🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷

  • @soldaroumamesaliou7609
    @soldaroumamesaliou7609 4 роки тому +20

    Bilahi frère tu as parfaitement raison souma guissé gal ma déme inchallah

  • @fatoukin7e
    @fatoukin7e Рік тому +1

    Boul koko may bayi ko ak yala c'est vraiment triste courage

  • @ndiayelhommefort2618
    @ndiayelhommefort2618 4 роки тому +4

    Sarap ndayi bii journaliste 😂😂😂😂

  • @aichadoucoure4337
    @aichadoucoure4337 4 роки тому +34

    Qu’Allah nous protége et guide sur le bon Chemin😭😭😭

  • @yorowar2250
    @yorowar2250 3 роки тому +15

    Du courage Fréro dieu est la loguiss day fini

  • @layezodiallo8684
    @layezodiallo8684 4 роки тому +3

    Pour gni deime yallah naleine tékk si yoni diame gni egueu yallah nalein oubul bountou khéwal si barké seydina mouhamed (PSL)

  • @ablayediouf-mf1zo
    @ablayediouf-mf1zo Рік тому +1

    Man magu ni fimay lagéyé defnafi 10 san magu ni awma Dara bateau mé békhé amoul

  • @cheikhndao3924
    @cheikhndao3924 2 роки тому +1

    Merci machalla dieg kér guawakh

  • @Prince-lo1um
    @Prince-lo1um 4 роки тому +34

    Journaliste, sois professionnel
    Du courage à toi le chauffeur
    Mais gal yi dou yoon bro yalnala Yallah diapaler 💪🦵

  • @fatandiaye4707
    @fatandiaye4707 4 роки тому +15

    Machalla my boy

  • @astoundiaye7558
    @astoundiaye7558 4 роки тому +18

    Tu as parfaitement raison fréro

  • @papefaye4719
    @papefaye4719 4 роки тому +10

    Dafa lerr barké Serigne Touba

  • @mamadoubalde4330
    @mamadoubalde4330 4 роки тому +7

    Le jeune a une bonne raison il y a que de mauvaises gestions de la part de l'état sinon la richesse du pays peut maintenir la jeunesse est créée des emplois comme le Ruanda de Mr Paul kagame dt je le felicite

  • @aidandiaye8529
    @aidandiaye8529 4 роки тому +35

    Il est nul l journaliste cependant l'invité est très pertinent machala😞😞

  • @mbayeanta9236
    @mbayeanta9236 2 роки тому +1

    Ndeyessane kii khawma journaliste khawma deumm la ak wakham djou Barry djii boy bo guissé yoon bi démall Sénégal dou gatt

  • @ibrahimadiop2638
    @ibrahimadiop2638 3 роки тому +2

    Un journaliste droit etre calm mes pas c' et homme la belle réponse frère

  • @souleymanediouf9513
    @souleymanediouf9513 4 роки тому +7

    Courage mais weurseuke yalla que Dieu facilite les jeûnes

  • @walyndour8787
    @walyndour8787 2 роки тому

    Diôylô ngama lèpay deugue

  • @matytoure2237
    @matytoure2237 4 роки тому +4

    C'est vraiment triste mais Santa yalla rėkh tu ya toute la vie devant toi l'essentiel c'est de croire en dieu

  • @madediouf4712
    @madediouf4712 4 роки тому +7

    yow mom do journaliste khamo dara du courage mon frère ligua wakh yeup seuguela thieuy sènègal

    • @farmadieng5556
      @farmadieng5556 4 роки тому

      Khana mou nek fi di signe ni rek ki di wakh louko méti baye dioye

  • @biramesenghor3528
    @biramesenghor3528 2 роки тому +1

    J sw d'accord avec tw frère bonne continuation

  • @ndiayegoo
    @ndiayegoo 4 роки тому +13

    SAA WAAY DEMM SI GALL GUI ERREUR LEU

    • @falloumbaye6514
      @falloumbaye6514 4 роки тому

      Wallahi

    • @mouhamednabyjrkhouma1195
      @mouhamednabyjrkhouma1195 4 роки тому

      Erreur la si ioe kom báyil gni bueg dem dem

    • @ndiayegoo
      @ndiayegoo 4 роки тому

      @@mouhamednabyjrkhouma1195 kou beuggueu demm nguirr Yalla outeull visa. souleu teuwéé nga kharr ba Yalla gneuww. Wayé Boul deff li nga khamné sa bakann khathie nassi

  • @niangtra
    @niangtra 4 роки тому +25

    Yaw journaliste nga khawma lo doone, wakhofi touss, Etat loumoufi kat ndayam def??? L'exploitation bimou wakh mofi nekkk

  • @ebrimasaidy9332
    @ebrimasaidy9332 2 роки тому +1

    Bravo fratello buon dica

  • @omzprogaye1939
    @omzprogaye1939 4 роки тому +28

    Surtout nous les chauffeurs de taxi on es fatigué 😡😡😡😡😡

  • @xeuchclasschic1910
    @xeuchclasschic1910 4 роки тому +23

    Xolal journaliste bi mome di féne di diéma danale khalé. Ki Xakhna deug blh je suis sénégale mé je deteste mon pays

  • @papadiallo1285
    @papadiallo1285 4 роки тому +2

    Merci bcp frère degué nékhoul vérité ga wakh

  • @goroudiarrafaye9307
    @goroudiarrafaye9307 4 роки тому +5

    J fèlicite ta courage mn frère

  • @elimanegueye2563
    @elimanegueye2563 4 роки тому +1

    bilahi tu as raison Societe senn contrat bakhoul dagniouy doul di fenn

  • @boubacarboris8655
    @boubacarboris8655 4 роки тому +20

    Journaliste bi n'est pas professionnel éthique et déontologie tiouné nga rekk 👎🏾

  • @roonapro821
    @roonapro821 4 роки тому +17

    Journaliste bii pour mane môme laniou invite

  • @loufadieng2284
    @loufadieng2284 2 роки тому +1

    Oh 😥 Billakhé magui dioyé 😭😭😭

  • @assanendiaye8035
    @assanendiaye8035 4 роки тому +29

    Le journaliste n'ai pas une professionnelle dommage les gua le Sénégal va très mâle ces malheureux....

  • @combe4823
    @combe4823 4 роки тому +20

    Tu as raison mon frere senegal la majeur partie ne travaille pas avec des contrats para rapport en europe c impossible parceque ya tjours des controles. Senegal metina torop. C pas vrai le journaliste on ne peut rester 40 ans en europe sans rien... Europe loumou metti metti mo tané fouf afrique un salaire minimun c 800 €. Du courage la jeunesse les policiers cherchent tjours des depenses en connaissance de cause durant mes vacances au senegal

  • @layezodiallo8684
    @layezodiallo8684 4 роки тому +4

    Journaliste bi fane la diangué journalisme franchement khamo tousss

  • @goroudiarrafaye9307
    @goroudiarrafaye9307 4 роки тому +5

    Il est bien dit ce goss

    • @abdouazizndiaye2166
      @abdouazizndiaye2166 2 роки тому

      Iow journaliste bi
      Khana do Sénégalais doul wayé
      Sénégal bou bon bi

  • @fallouthiam1890
    @fallouthiam1890 2 роки тому +4

    le jeune il est calme et posé contrairement au soit disant journaliste

  • @almouhtarkandji8143
    @almouhtarkandji8143 4 роки тому +5

    Boye liga wakh lép deug leu partager lén ko

  • @thiernaabdoulba2908
    @thiernaabdoulba2908 2 роки тому +3

    Bly c véré Sénégal amoul Dara ila ESPE je insahala 👊👊👊👊

  • @aliounendong7080
    @aliounendong7080 4 роки тому +3

    Ndey San annasalo 🇪🇸🇸🇳😭😥😔😔🤲🤲

  • @ndiagandiaye400
    @ndiagandiaye400 2 роки тому +5

    Vérité absolue

  • @sadiodieye9482
    @sadiodieye9482 2 роки тому

    Bilahi 60mil mane liguéye nako plus de 4ans
    Dakh bagne kouma yap rekk

  • @amadoudiouldesow663
    @amadoudiouldesow663 4 роки тому +2

    Boy bi mom il à bien parler machallah

  • @oussynoundiaye7591
    @oussynoundiaye7591 4 роки тому +3

    Mane li ma done sénégal rék moma meti 😭😭😭

  • @kebadia5831
    @kebadia5831 2 роки тому +1

    Amna solo Biillye ❤️❤️🙏🙏🙏

  • @libasseniang8450
    @libasseniang8450 2 роки тому +1

    Ngani donne fa garap molla geuneul donne fii ministire hum yallah nallah yalla andit si diame ak voi normal defal ndank rek nga diar fou laire

  • @iboucisse4626
    @iboucisse4626 2 роки тому

    Europe dei méttina Franchement mais fénnn dou senegal tamitt...bimay diogué senegal dei j'étais tellement decouragé que j'avais plus envie de revenir...

  • @papecheikhcorrea7238
    @papecheikhcorrea7238 2 роки тому

    Bilay frr sénégal métina torop man mangui nii dépuis février amouma 500f you mott man mom souma yoré khaliss démay dém comme tu la dit nék plante niou lay rosé mo gueune nék 1er ministre fii en plus au moment où je te parle je suis entrain de tracé mon bilan pour partir Maroc

  • @maimounacamara6841
    @maimounacamara6841 4 роки тому +4

    C'est vraiment triste 😭😭😭

  • @abdoudiop332
    @abdoudiop332 4 роки тому +4

    Sénégal policier ,douanier ak gendarme you bari safara lagnouy dougou billahi

  • @naboucheikhndiaye7805
    @naboucheikhndiaye7805 4 роки тому +14

    Waaa 😭 Journaliste bii moom khana dou sénégalais

  • @talambacke8195
    @talambacke8195 4 роки тому +2

    bayilén di wakh dem thi gal yi kharou la kharou kokoy def dé rek ngay guiss mai khale yi tekki rek lagno guiss billahi

  • @yakhyasakho3621
    @yakhyasakho3621 4 роки тому +4

    Courage frère

  • @elhadjimaodomalickfall9222
    @elhadjimaodomalickfall9222 4 роки тому +12

    Tu a raison my boy......ligawah lep deugleu....mais le journalist...il est nul...

  • @assaneloum4581
    @assaneloum4581 4 роки тому +2

    Yalla Na la yalla diapalé

  • @falloumboup5572
    @falloumboup5572 4 роки тому +35

    Journaliste bi xamoul ndm dara 😭🏃

    • @lilmomo2
      @lilmomo2 4 роки тому +1

      jtj ki ken khamoul lanela youtube mognou togn tu invites qulequ un pour repondre et parler a sa place degloul niit ki wakh mey ko mou wakh c est le minimum

    • @famalayembaye4704
      @famalayembaye4704 2 роки тому

      Billahi khamoul dara

  • @alikassem7719
    @alikassem7719 2 роки тому +1

    8.50 😂😂😂😂😂

  • @ibrahimandiaye1505
    @ibrahimandiaye1505 4 роки тому +1

    Journalliste bi mo katt ndeyame

  • @tallambengue1092
    @tallambengue1092 Рік тому +2

    Journaliste bi yaw khamo Kat pasque niguaye ladie dra bakhu si démal ndiagui wat

  • @papacamara4498
    @papacamara4498 2 роки тому

    Il y a trop d'injustices dans les pays africains comment voulez vous qu'ils se développent avec une mentalité pareille.

  • @khadimseck5985
    @khadimseck5985 4 роки тому +4

    Machaalah freres

  • @bessanehyperactif7458
    @bessanehyperactif7458 4 роки тому +6

    Bilahi parfois dagay tok si Rewmi guiss loula méti liguey ba dh do guiss dara
    niou nek ci kergui di fayé kou copain t'as tous raison mé le journaliste n'a rien compris parsk'il gagne des gains et des gains.

  • @alioudiallo6691
    @alioudiallo6691 2 роки тому

    Merci bro Amna solo

  • @aichasall8287
    @aichasall8287 4 роки тому +2

    Li nga wakh si policiers yi dé mom deug bou wore la, le nouveau ministre war si wakh. ils rakéte les gens.

  • @papemodoudieng0824
    @papemodoudieng0824 2 роки тому +1

    👊👊👊👊🤟🤟🤟

  • @mouhamednabyjrkhouma1195
    @mouhamednabyjrkhouma1195 4 роки тому +6

    Wallay wax ngeu deug kou muena nieuw na niew Africa dou dem ms journaliste bi ioe lingaye wakh sakh khamó ko

  • @boyguerofamillybgtv1655
    @boyguerofamillybgtv1655 4 роки тому +3

    no figua terminè grave na frére deugueu bou wërr dia dieuf kaïrè

  • @massmbaye0792
    @massmbaye0792 Рік тому

    Journaliste d une certaine conné tu a parfaitement reson mes

  • @mamadouba6246
    @mamadouba6246 4 роки тому +2

    Billahi wadji deugg rek la wax

  • @matarfaye2696
    @matarfaye2696 4 роки тому +12

    l'incompétence et la manque de professionnalisme pour cette journaliste communication zéro

  • @amandataha8516
    @amandataha8516 4 роки тому +7

    ki mongui diexal sama xol ioe meune nga tok sa clim tim la ngay weddi kiy nekk si nathie bi ioe demal ndeyi menebri

  • @senganesakho7870
    @senganesakho7870 4 роки тому

    10crge my Boy
    Tu es vrement courage

  • @matarsall7957
    @matarsall7957 4 роки тому

    Bilahi am am diaglé borom bi la

  • @nadshu9192
    @nadshu9192 4 роки тому +8

    Peut-être qu’il est pas posé mais il dit la vérité le journaliste...avouez leu sénégalais pour mom da warra tekki force...fi koufffi yoor say pièces normales policier da doff balay bindeull ???loumouy binde ???arretez wayy mane deh je prends l’exemple de mon père policier yi lougn ko lath mou diokhleen après niouniko demal diapp pour lannn ??? Diapp leen tewa bayyi rek dina bakh mes frère 🙏🏽 Gall gui darra diarouko

    • @ilimankebe4102
      @ilimankebe4102 2 роки тому

      Merci kayré 220 policier dangay ame piéces yépe ta teiwoul dagnou laye bindal Sénégal mon méty

    • @diadiefaye1239
      @diadiefaye1239 2 роки тому

      C fau nio yém motakh gnouy retraité rek torokh

  • @ibrahimadiao4578
    @ibrahimadiao4578 4 роки тому +8

    Interview leu wala wéranté ? Le journaliste t'as du chemin à faire 💔👎👎👎

  • @salioukane23
    @salioukane23 4 роки тому +1

    Hooo machalla boy ak lérr 😭😭😭😭

  • @serignemansourgueye7730
    @serignemansourgueye7730 4 роки тому +8

    Ne juge pas les gens le journaliste l’état ne ft r1 pr les jeunes

  • @amathdiawara4482
    @amathdiawara4482 Рік тому

    Koumoudéme demale Sénégal nekhoule