Machallah Marie tu es la meilleure et j'en sais quelque chose. Yaw yay sama yaye bou ndao et tu n'as ménagé aucun effort à mon égard quand j'étais enfant. Qu'Allah te gratifie si barké sougnou Yaye Isseu
I cannot understand what was spoken in your video so I had a Senegalese friend/sister translate for me. My husband requested this dish as one of the Tabaski holiday meals. He only remembered how much he enjoyed it and that it included lamb and potatoes. lol. But you blessed us with your video and simple recipe and instructions. The meal was perfect. I used the marinade on day two of Tabaski for the grilled lamb. Again, it was perfect and the compliments were beautiful. Thank you and may you have God’s blessings in abundance in this life and the next for sharing your culture. Peace & love from North Carolina, USA.
Machallah Marie tu es la meilleure et j'en sais quelque chose. Yaw yay sama yaye bou ndao et tu n'as ménagé aucun effort à mon égard quand j'étais enfant. Qu'Allah te gratifie si barké sougnou Yaye Isseu
Macha Allah longue vie à toi mala beugueu légui nieupeu noungui togueu nakh yaw laf thiate
I cannot understand what was spoken in your video so I had a Senegalese friend/sister translate for me. My husband requested this dish as one of the Tabaski holiday meals. He only remembered how much he enjoyed it and that it included lamb and potatoes. lol. But you blessed us with your video and simple recipe and instructions. The meal was perfect. I used the marinade on day two of Tabaski for the grilled lamb. Again, it was perfect and the compliments were beautiful. Thank you and may you have God’s blessings in abundance in this life and the next for sharing your culture. Peace & love from North Carolina, USA.
😊😊😊
Masha'Allahou sokhena marie diop togou yaye Isseu. Yallah Rek lagnou laye bayile mou Fayale gnoula. Amiiine Yaa Rabal Alamine si Gnanes yi. Amiiine
Machaala tata marietou yaallnala yaalla faye maye katane ak wer ak werle toufe bimome maachala ti voglio bene 😍😍
Merci tata yallah nassa diame yague barké serigne saliou ♥️♥️
Qu’Allah vous protège toggou yaye Isseu sa liguey rafetna machaallah
Maa shaa Allah Sokhna Marie👌👌👌neex na saf na. Merci.
Tu es la meilleur ♥️♥️♥️♥️
Machallah Tata yalna yalla wéreul lokho bi
Sama maman marie gudufane ak werrr ak werle rek lalay nianal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machala yalla na la yalla défal diam je suivre depuis Canada ont vous t'aime💗💗💗💗💗 fort
mashaallah tata Marie ❤🥰😘 yalna lohobii werr
Ma challa tata yalla nassa diamou yague
Machalla yalna yalla gouddeul sa fane ❤❤❤
salam macha allah tata marie amna solo yagui défare keur yi diame diou sakhe akke tawfékhe
Machalla ya isse dîeg ji dano jang ci yaw❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machala yalnala yala défal diam dioubari wakh deugueu yala amouniou sa faye
Amin notre manma chérie je t'aime infiniment 💓💓🌹💯
Masha ALLA sister. Yalna sounou borombi gueuneu wereul lokhobi amine ALLAHOUMA amine 😍😍🥰😘
Macha allah tata
Machallah tata defati nga sa manine yalla na yalla weral lokho bi
Machallah sister chérie yallana lokho bi weer tay moom lay togue
Machallah merci pour les recettes dewanaty
Machallah maman yalah na sa diam yague🙏
Mashallah tata yalla na lokho bi werr
Je suis marocaine et j’aimerai goûter cette tuerie malheureusement j’habite a milan 😢
Machallah maman toggg rek nguèye def
Fête yeup Tabaski MoMA si daxal!!! J'adore!!!
Koulay simi Haha
@@adjadiallo2523 hahaha!!!
Dinagne la soumi deh😂😂😂attention au mouton inchallah 😄😄😄
@@myasarr9779 diarouko. 😂😂. Balamay khéwlou Dina soumékou
Machallah tu as assuré comme d'habitude 💗💗💗
MASHA ALLAH Dieuredieuf YAL NALA YALLA BOURBI FAYE MAY LA GOUDOUFANE AKH WÉR SI DARADJA SEYDINA MOUHAMAD PSL
Machalaa Ta Yaye et merci encore une fois,
Merci beaucoup maman Isseu montrez nous aussi comment ont prépare les crudités pour décoration s'il vous plaît
Machallah nekhna ba nopi
Tu es la meilleur tata ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla la reine de la cuisine
Merciii maman🥰 Longue vie à toi ❤️
Vraiment u est ma meilleure
touffé yapou khare tabaski rek was sent to me by my beautiful Gambian wife of 8 years. She is a good cook but I am better. Thanks you, I love lamb
Dewenaty et laf thiat 💯💯
Machallah tata defatinga sa meunine
Yalla na diam yague maman yalla weral lokho bii yagual weral yokal barké cheikh Ibra fall
Amine sama domou baye
Mashalah Sà bouquet garni amna mana gout rek ngay am
Machallah tu aide les femmes a la cuisine
Fékele deweune macha alla ♥️🥰
Machalah amna mana merci beaucoup yaye boye
Yafi né. Se togue dey gaw explications lerr tres facile a reproduire ❤
Mashallah. Généreuse en cuisine. Nekhatina
❤❤❤❤😘😘😘👍👍👍👍l'eau a la bouche. Mashalah
Machalah sa touffe bakhna machalah
Machalla yal nala yalla faye
Yalla nagua fi yague t wérr 😘🥰
Merci tata nekhna sell na
MaShaAllah Yaye boye ; ioe Yala rèk leugne lèy bayyèk
Machala c tres bon et bien fait
Toogou yaye isseu ont vous remercie pas ce que beaucoup de plats africaine je les a prit avec vous merci
Merci Diallo
Barakallahou fiky merci beaucoup
Machallah machallah wa Congo dinako Moss inchallah
Merci tata c joli.. Mai huile bi mome mane Perso douma ko deff si touffe yapou khar..
Opppopppooo merci yaye isseu
Macha Allah merci yalla na sa diam yague
Machallah❤merci beaucoup tata
Macallah Maman contante sii yow💝💝
Machallah y'a bakh de weni
Machalla souxran 🙏🙏🙏
Machalla le meilleur
Machalah presentation bi nice
Machallah merci beaucoup diare na yone
Machalla ❤️🙏
Machalla mbadiene amine ya rambi 🥰🥰🥰🥰
MachaAllah nehatina 🥰🥰🥰
Machalla maman
Machaallah maman sa touffé bakhna❤❤❤
Niane yalla. Am depense bou. Doy
Amine ya rabbi
MachaAllah togue rék ngay def. Amine si niane yi
❤❤❤❤❤❤❤❤
bonjour tata machalla ligaye def nice na mes dit comme faire pour avoir des pomme de terre crussent
Trop bon Tata
machallah tay li lay préparer pour la mifa
Merci tâta togou bi selena l'âne moye mariné royal
Sama repère ❤️
Machalah merci tata ❤️❤️❤️
Hello dinama nekh
J'aime se plat vrais
💓💓💓💓💓💓💓 j adore
Quand est que vs avez mis l'huile wala diarouko
Mangi lay suivre founer yalla na sa diam yag
merci beaucoup maman chérie déwéteny a vous et a toute la famille encore un grand merci bisous
Machalla maman chérie mais begue nagne gua gnow si bif tek s'il te plaît nk😘😘😘
Togoon na bref steak. Recherche si videos yi
Trop Bon
Mashallaw suurna
Machallah Tata
Ma challah yaaye boy
Je ne comprend rien mais ça a l'air tellement bon🤩. Je vais essayer incha'Allah. C'est la.viande de mouton ?
Oui
Maman issa yague fi lofiye keuneu yague mouye keuneu nekh bilaye saye togou lanla
Ô plat bi yobounama Mauritanie way démako boukone bima nèké fofou
Merci pour la recette 😍😍
Ma sha Allah
Merci maman isseu
Notre maman
Nokas royal nouniou koy deffé
Machalah tata 😍😍
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️