Reportage : Rappel a Dieu de Serigne Saliou Mbacke

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 12 гру 2024
  • Sponsored by: ⁠www.amazon.com... Abonnez-vous gratuitement à la chaîne Murid Life pour rester informé chaque jour de nos nouveautés:
    / muridlife

КОМЕНТАРІ • 148

  • @alphaoumardiallo3884
    @alphaoumardiallo3884 21 день тому +3

    Jërejefeti Cheikhoul Xadim Jarama MAME Cheikh Ibrahima Fall Lampe Yalla na Yalla yokku ay lèram té tass nu si barkèm sama yaakaar tay ak ëllëk🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @lancelotnao5625
    @lancelotnao5625 7 років тому +62

    Je ne suis pas mouride mais j'adore cet homme de par sa simplicité. Sa sobriété. Je puis sur que c'est un saint.
    Les autres mara devraient imiter sa sobriété. J toujours la chair de poule quand je regarde sa photo. Depuis son vivant d'ailleurs. Rip

    • @nabougueye9
      @nabougueye9 6 років тому +1

      yalla na yalla yokou léram si barkém amine

    • @alaloussalioumbacke9160
      @alaloussalioumbacke9160 6 років тому +1

      lancelot nao yaram khamo si dara sakh ki nitou yalla deug leu Serigne touba bou soti moy Serigne saliou mbacké

    • @alaloussalioumbacke9160
      @alaloussalioumbacke9160 6 років тому +1

      lancelot nao yaram khamo si dara sakh ki nitou yalla deug leu Serigne touba bou soti moy Serigne saliou mbacké

  • @alphaoumardiallo6452
    @alphaoumardiallo6452 2 роки тому +9

    Yalla na Yalla yokkou ay lèram té Tass niou si sen Barké Borom TouBa 🙏🙏🙏❤️👌

  • @YayouMouhamad
    @YayouMouhamad 10 років тому +37

    Thiéy billé biss doumako faté mouk yallana Yalla yokk lérrame té tass gnou si barkéme amine

  • @amdymf4642
    @amdymf4642 5 років тому +2

    jour bi domako sama adouna serigne saliou sunu yakar adouna ak allakhira yallanako sunu broum dolli yeurmande

  • @diallkebekebe2656
    @diallkebekebe2656 4 роки тому +1

    Thieye serigne saliou kène doumome naniou ko yalla fayal

  • @oumarndoye1169
    @oumarndoye1169 Рік тому

    Serigne saliou yala na yalala doli ay lérame

  • @dieyendiassebakhyaye7058
    @dieyendiassebakhyaye7058 7 років тому +8

    mame Saliou yalla nako yalla khare ko aldiana firdawsi amine way yaraby Machallah

  • @bayesalioulo5999
    @bayesalioulo5999 8 років тому +16

    dieureudieufeuti Saliou Dieureudieufeuti Serigne Saliou Dieureudieufeuti Serigne Saliou Dieureudieufeuti Serigne Saliou Dieureudieufeuti Serigne Saliou

  • @khadysene8917
    @khadysene8917 3 роки тому +1

    Dou kougni fatei si kaw souf lougnou done mognouko def 😭😭😭💓

  • @serignebarambackesalioufalliou
    @serignebarambackesalioufalliou 5 років тому +1

    Yalna yalla yoko ay leram te tassnou si barkem

  • @zainasene9598
    @zainasene9598 8 років тому +9

    thieuy serigne saliou mbacké yalla nanouko yalla féyal

  • @khadycisse307
    @khadycisse307 2 роки тому +1

    Tjr dans mon ❤️ Serigne saliou yallna yalla yokou ayy leram

  • @insadiouf5960
    @insadiouf5960 3 роки тому

    Yalla naa Yalla yookk leram taa tassgnou thie Barkém amine

  • @diomayefaye9344
    @diomayefaye9344 2 роки тому +2

    Jour inoubliable Mame Salihou l'absolu

  • @dolceysa1
    @dolceysa1 10 років тому

    dieureudieuf mame saliou mbache dolinaniou sante bou weur mbache.yaye serigne touba bou weur.

  • @birahimthiam8993
    @birahimthiam8993 Рік тому +2

    Serigne saliou mbacké mogniouy wétal billahi Yalla na dollé la yeureum thi barcké cheikhoul khadim té yok Say lér kou téd ki

  • @khadysaliouniang3981
    @khadysaliouniang3981 4 роки тому +7

    Jour inoubliable

  • @maguettethiaw3286
    @maguettethiaw3286 5 років тому +1

    Kéneu la wone yalla na yalla yok ay lérame

  • @djeumbdiagne7566
    @djeumbdiagne7566 3 роки тому +2

    Yalla naniouko yalla fayal amin ❣️❣️❣️

  • @tfkteew3586
    @tfkteew3586 8 років тому +17

    Thieuye Serigne Saliou wétal nga adouna ohoooo

  • @bambaniang6986
    @bambaniang6986 6 років тому +13

    dieu est grand et serigne saliou yalna yalla yoku leerame

  • @ousseynoufall4588
    @ousseynoufall4588 8 років тому +3

    y alla nalla yalla xarée aldiana té tasse ni ou ci sa barké amine mbacké

  • @modoudiawe7174
    @modoudiawe7174 4 роки тому +5

    Thiéye serigne saliou Mbaké wétal guagnio kén douto faté le 28 décembre 2007😭😭

  • @ahmadoukhadimsylla1609
    @ahmadoukhadimsylla1609 5 років тому +6

    Fathia ake 11 lilassi yalla naniouco yalla fayale thi barké wŕrou kor gui

  • @abbixgamer3186
    @abbixgamer3186 11 місяців тому

    Yalla naniou ko yalla fayal mbacké ballah 🙏🏾

  • @dabangning5883
    @dabangning5883 4 роки тому

    Mbacke yalna yalla yokou sa ler te tass niou thi barke

  • @SalouNdiaye-w2m
    @SalouNdiaye-w2m 11 місяців тому

    Yalna yalla yogue ay lérame

  • @babacargueye2520
    @babacargueye2520 4 роки тому +2

    Mame saliou tjrs dans nos cœurs

  • @fatoudiop233
    @fatoudiop233 5 років тому +6

    Mbacké wetal ngagnu yalla nako yalla yeureum dugnu la meusseu faté😭😭😭😭😭

  • @soukaynafall8605
    @soukaynafall8605 11 років тому +4

    DIEURDIEUF BOROM YEURMENE YALLA NANIOU YALLA TAFE SIBARKEM SI BAREKEP SERIGNE TOUBA

  • @mbayethiao2156
    @mbayethiao2156 8 років тому +1

    diareudieuf serigne touba serigne saliou mbacke yalla yok lerammm

    • @Alqorn
      @Alqorn 7 років тому

      Mbaye Thiao

  • @birahimsoldaroussaliou117
    @birahimsoldaroussaliou117 6 років тому

    Thieyy mame saliou borom yeurmandé yalla n'a yalla yook ay léram tass niou si barckém 👐

  • @ramandiouck1553
    @ramandiouck1553 2 роки тому

    Yalna sounou borom tass ñou barkeme

  • @CheikhFall-qy2uk
    @CheikhFall-qy2uk Рік тому

    THIEY S SALIOU MBACKE 🤲

  • @xadijasalihoumintsalihate7958
    @xadijasalihoumintsalihate7958 6 років тому +1

    yallana ALLAH yokkeu sa yeurmandé thi niouneu

  • @IsmaelSow-v4n
    @IsmaelSow-v4n Рік тому

    ❤ Merci ❤

  • @malickfall8983
    @malickfall8983 6 років тому +2

    Dieu redieuf serigne TOUBA MBACKE

  • @gueyelhadj
    @gueyelhadj 2 роки тому

    Djeureudieufé Serigne Saliou Mbacké

  • @abdourahmanesow4923
    @abdourahmanesow4923 2 роки тому +1

    THIEUY YALLA

  • @alioufall6684
    @alioufall6684 8 років тому +13

    kénnn dou sergne saliou

  • @sofiaka2
    @sofiaka2 5 років тому +2

    Képp kou xol video bi decembre 2018 santal yalla ñianal serigne saliou mbacké

  • @modoumbingue9668
    @modoumbingue9668 8 років тому +9

    yalla na yalla Yoko le RAM barke serigne touba

  • @ismambaye8223
    @ismambaye8223 5 років тому +3

    Serigne saliou mbacké yalla nako yalla yeuram Yalla tass niou si barkém

  • @ilimaneseckndeyesanesamaya1872
    @ilimaneseckndeyesanesamaya1872 7 років тому

    ndaye sane sunou wadji borom khelcom borom diamono yalla nanou kon yalla faye yall

  • @momosow1322
    @momosow1322 7 років тому +1

    yalna yalla yokou leram Amine

  • @moussakatongo930
    @moussakatongo930 5 років тому +1

    Serigne Saliou Mbacké Yalla Na Yalla Yokkou Sa Lérr Si Barki Cheikhoul Khadim

  • @ismambaye17
    @ismambaye17 6 років тому +1

    thieye mame sa Mame Boye yalla na yalla yoki léram

  • @GalsenPost
    @GalsenPost 4 роки тому

    Yalna yalla yoke sa lére mame

  • @Sancoun43
    @Sancoun43 6 років тому +2

    Ceey As-Saliha😭❤️🙏

  • @alassanethiam8619
    @alassanethiam8619 5 років тому

    Serigne Saliou Mbacke yalla souniou borom yokou leral thi barké Seydina Mouhamed PSL ak Wadiourom Ba Khadim Roussoul

  • @cheikhdiouf2615
    @cheikhdiouf2615 9 років тому +3

    thiey yalla nanouko yalla fayal

  • @sambandiaye1769
    @sambandiaye1769 4 роки тому

    Ah saliha le soleil de son époque

  • @oussmame7053
    @oussmame7053 9 років тому +4

    mane dé yaye sama serigne doylo nala mbacké balls

  • @matydiop9725
    @matydiop9725 7 років тому

    dieuredieufeti serigne saliou gniakanagniou waliou kignioudane tek si yonou l'islam 😢😢😢😢😢😢😢

  • @daoudabaradji7418
    @daoudabaradji7418 6 років тому +1

    dieureu dieuf saliou

  • @maimounambaye8004
    @maimounambaye8004 8 років тому +1

    bisbou tiss thieuy sr saliou 😭😭😭

  • @visionmouridetv2317
    @visionmouridetv2317 4 роки тому

    ALLAH AKBAR DIEUREUDIEUFÉ S SALIHOU

  • @sokhnadiarratoullah1061
    @sokhnadiarratoullah1061 4 роки тому

    Yalna yalla yoki leiram

  • @buugusalieumbye3001
    @buugusalieumbye3001 5 років тому +1

    Ken duu yooka leraam serigne salieu moi yallah walahi

  • @mongmo98
    @mongmo98 9 років тому +1

    yalla na yalla yokkou leram.. aamiine

  • @malickfaye4376
    @malickfaye4376 5 років тому

    Bilae Mbacke Wètal gue niou

  • @khadimgueye7166
    @khadimgueye7166 6 років тому

    yalla na niou Yalla tass si sa barke

  • @MuridLife
    @MuridLife  12 років тому +8

    Sunu mame saliou yalnanouko yalla sakh di fayal ba bagne koy fekki aljannah.
    sinon naka sa magal nak ak att bou bess bi?

  • @fitteyatouneaminobirabihim9489
    @fitteyatouneaminobirabihim9489 5 років тому

    Reportages bouma guena marqué bila

  • @assanembow6453
    @assanembow6453 5 років тому

    Bisssou tissss bi dougnko fateee

  • @kinendiaye6804
    @kinendiaye6804 7 років тому

    yallana yalla yok ay lèram

  • @bayesalioulo5999
    @bayesalioulo5999 8 років тому +1

    ndaysan thieye Serigne Saliou

    • @Alqorn
      @Alqorn 7 років тому

      Serigne Saliou lo

  • @lahadseck6998
    @lahadseck6998 4 роки тому

    Sounou khél sounou xol l'EP pangi sisimom

  • @khadimgueye7166
    @khadimgueye7166 6 років тому

    Yalla na ko Yalla yeureume

  • @serignefallou2992
    @serignefallou2992 7 років тому +2

    ALLAHOU MA AMIIINE

  • @abdoudieng9728
    @abdoudieng9728 7 років тому

    jeureujeufaty mame Saliou
    jeureujeufaty mame Saliou

  • @falloundiaye3436
    @falloundiaye3436 6 років тому

    Thiay Mame Saliou

  • @SerigneCom
    @SerigneCom 11 років тому +4

    serigne saliou mbacke

  • @cheikhounalo5569
    @cheikhounalo5569 5 років тому

    Sunu yakar dia S saliou mbacke

  • @cheikhtouba3428
    @cheikhtouba3428 6 років тому

    yalnako yalla fayall

  • @mamrokhialo-vt2ql
    @mamrokhialo-vt2ql 11 місяців тому

    ❤❤❤

  • @ramandiouck1553
    @ramandiouck1553 2 роки тому

    AMINE YA Rabbi

  • @baguefallousarr1710
    @baguefallousarr1710 5 років тому

    Ndaayessane

  • @mariamasow3970
    @mariamasow3970 5 років тому

    NDEYSANE MBACKÉ WÉTAL NGUA NIOU

  • @ousmanethiam5342
    @ousmanethiam5342 12 років тому +1

    DIEREUREFETI SERIGEN SALIOU POUR OUSMANE THIAM

  • @papeansoumanebiaye6720
    @papeansoumanebiaye6720 3 роки тому

    Bise bi doumako meusa fatee

  • @badjiibrahima6845
    @badjiibrahima6845 7 років тому

    thieye mame saliou wétal nganiou

  • @mouridesadikha6319
    @mouridesadikha6319 2 роки тому

    ÑÔK YAW BA FAW MBACKÉ BALLA

  • @serignediop1148
    @serignediop1148 4 роки тому

    Aka.bakh

  • @khalilnewyorkino9493
    @khalilnewyorkino9493 4 роки тому

    Sama xol nexoul dara theuy brom helvom

  • @mariobarba3798
    @mariobarba3798 3 роки тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤👂

  • @dameniang7930
    @dameniang7930 3 роки тому

    13 anni fa

  • @MuridLife
    @MuridLife  13 років тому +1

    @luc664 Amine ci Barke Cheikhoul Khadim.

    • @khadyfall7612
      @khadyfall7612 7 років тому

      AlazharTouba Serigne saliou moy yermande

  • @SMoustapbaSylla
    @SMoustapbaSylla 3 місяці тому

    S touba

  • @assanembow6460
    @assanembow6460 3 роки тому

    😭😭😭❤🙏

  • @tallasock678
    @tallasock678 4 роки тому

    😭😭😭😭😭😭

  • @tafcotica4816
    @tafcotica4816 6 років тому

    yalla na yala yok lere rame

  • @cheikhdiouf2615
    @cheikhdiouf2615 9 років тому +1

    amiine

  • @elbachirprod9539
    @elbachirprod9539 4 роки тому +1

    YALLA NA YALLA YOKK AY LERAMME SA TASSE NIOU SI BARKEME SI BARKEP SEYDINA MOUHAMMAD

  • @naboulofficiel8128
    @naboulofficiel8128 5 років тому +2

    Nimako beugué dou asare Man décembre la dioudou

  • @alaloussalioumbacke9160
    @alaloussalioumbacke9160 6 років тому +2

    Niakk nagnou ko kham né dotou gnouko amati thi kaw souf

  • @aliounebadarandoye679
    @aliounebadarandoye679 7 років тому +2

    DIADIEUF SERIGNE TOUBA SERIGNE SALIOU /HAUTES DIMENSIONS.

  • @221business
    @221business 7 років тому

    aminé

  • @zaynabouleye7322
    @zaynabouleye7322 7 років тому

    kén duko massa faté Mbacke balla