NIANKOU ak Koor Gui- Episode 01

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 11 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 1,4 тис.

  • @senegal5com
    @senegal5com  4 роки тому +500

    5 TV Sénégal/senegal5.com vous demande pardon pour ce mois de Ramadan et vous souhaite un Bon début de Ramadan. Nous vous rappelons aussi que NIANKOU ak KOOR GUI se déroule ici tous les jours. Heure précise : 20h15. L’Application Mobile de Senegal5 est disponible sur PlayStore. Le Téléchargement est gratuit.
    Pour tout Sponsor, merci de contacter le service commercial : 77 864 86 84

  • @galsentvgalsentv5924
    @galsentvgalsentv5924 4 роки тому +189

    Kou aimé sama commentaires bi yalla fay la 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @zaliousarr2359
    @zaliousarr2359 4 роки тому +53

    Niankou c'est le meilleur kou d'accord besal j'aime

  • @khadimMbayeSaamPastef
    @khadimMbayeSaamPastef 4 роки тому +68

    Ndayan il est fort aussi vraiment, ana fans ndayan yi way

  • @mouhamedndoye585
    @mouhamedndoye585 4 роки тому +15

    Non niakoul ni ndiankou meuss ne dofff😂😂😂😂trop fort ce gars❤️ 🔥 🔥li dou talent kessé way😁😁ndayane tamite

  • @youngthiam9821
    @youngthiam9821 4 роки тому +10

    On en parle pas de Ndayane, mais bilahiiii il est trop fort ptdrr 😭😭😭 nénaka " douma mbeur bouma supporté" 😭😭😂😂🤣🤣🤣🤣

  • @taphadiop7468
    @taphadiop7468 4 роки тому +32

    Kiii mo meune nieip kou d'accor rek lalma Jaime

  • @maremecisse4145
    @maremecisse4145 4 роки тому +21

    Kou d'accord nii niakou ak ndayane dagniiy dindi stress 👍

  • @diazdesigngraphiste
    @diazdesigngraphiste 4 роки тому +14

    Niankou dafa nekh bilay ki est d'accord pouce bleu rek mou gueueneu nekh

  • @toubaofficiel9432
    @toubaofficiel9432 4 роки тому +12

    Yalla nadiou yalla MAY kourouk diam BARKEB MAWLANA Amine way 🤲🤲🤲

  • @firstboy5277
    @firstboy5277 4 роки тому +22

    Kou beug niankou may ma jiam

  • @alimekeita5584
    @alimekeita5584 4 роки тому +9

    Ana niou beugeu Niankou❤❤💗, yalla nagnou yalla mousal cii corona bii🙏🙏, et koor diam🤝🤝Bal lène MA ak Bal na lène yalla nagnou yalla bolè Bal sii barkè seydina Mouhamed psl

  • @yorodiop4773
    @yorodiop4773 4 роки тому +8

    Niankou yassi tok kou beus J'aime yallah nala yallah nangoul sa koor

  • @cheikhouomarfaye9633
    @cheikhouomarfaye9633 4 роки тому +25

    Kouma may j’aime yalla na yalla nangou sa koor way 🙏🏾

  • @cestpossible3460
    @cestpossible3460 4 роки тому +12

    Wah team WiFi and setann Niankou, je vous salue

  • @papedeme3892
    @papedeme3892 4 роки тому +16

    Ana niou beugue niankou beuss lénn j'aime

  • @xamletv1
    @xamletv1 4 роки тому +18

    Cette année combat bi cest entre Wadioubakh et Nianku .... diogaye am na concurent bu makk nakk😂😂😂😂😂
    Safara mofi nekk ajana niam na ba dem😂😂

  • @cheikhmbackeniang715
    @cheikhmbackeniang715 4 роки тому +20

    kou beugeu corona bi diougué fi beusseul j aime

  • @khadimseye502
    @khadimseye502 4 роки тому +7

    Non niankou srxxx lii dou talent késsé rakh na wayy machala té le meilleur ☝️

  • @fallabdouaziz7097
    @fallabdouaziz7097 4 роки тому +11

    Cheikh Béthio thioune yalna ko yalla kharé aldiana

  • @mamefatousarr983
    @mamefatousarr983 4 роки тому +12

    Maachalah Niankou, il donne en même temps des leçons de morale

  • @badarakarara9730
    @badarakarara9730 4 роки тому +7

    ana gni beug niankou framarene bejeulén j'aime way🙏

  • @nabydiouf9698
    @nabydiouf9698 4 роки тому +19

    Kou beugue seydina Mouhamed PSL

  • @Djilirving
    @Djilirving 4 роки тому +10

    Korou diam à tous les musulmans que dieu vous protège 🙏🏽🌙✨ramadan kareem

  • @cheikhibrahimafallsock9703
    @cheikhibrahimafallsock9703 4 роки тому +7

    😂😂😂😂 il est le meilleur de sa génération bilay diam ci iow

  • @mouhamedgueye5722
    @mouhamedgueye5722 4 роки тому +18

    600 000 vues même pas 300 000 abonnés c pas normale way délène abonné sama gayi niankou mérite plus que ça.dibalou niepp akh ta dilène bal si wérou koor gui 👌👌

    • @senegal5com
      @senegal5com  4 роки тому +1

      Merci beaucoup mon frere .NIANKOU et toute l'équipe de 5TV Sénégal vous remercie

  • @kingdissiofficiel953
    @kingdissiofficiel953 4 роки тому +18

    Daaya nena 4h du matin la niamm soow bi 😂😂😂

  • @cheikhounandiaye553
    @cheikhounandiaye553 4 роки тому +9

    Nianko raynama way 😂 douma doyal si nianko ana ngiko bague 😅😅😅

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf110 4 роки тому +10

    Action mbote bi kouko sétan 5foi kom Man 😂😂😂🏃🏃 mbot bi reuy neu amna louma nekhari sama adouna nk Lima yékha koumasé sétan niankou😂😂😂

  • @princesall2316
    @princesall2316 4 роки тому +15

    Ay way niankou le meilleur 💪💪

  • @moustaphadiallo4512
    @moustaphadiallo4512 4 роки тому +12

    Théâtre légui mougui yeumbeul Niankou le meilleur

  • @mouhamedndiaye4117
    @mouhamedndiaye4117 4 роки тому +13

    Nn niankou bilae lima lay wakh sm khole lako tibé niankou da nga ay trop li ngay daff meune ngako trop courage frr🙏🏿🙏🏿❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @papiscosysy517
    @papiscosysy517 4 роки тому +9

    Wamé nianckou hana dawalkatou charette la il daur très bien

  • @magattendiaye8360
    @magattendiaye8360 4 роки тому +19

    fans niankou j aime bonk

  • @tallzofaitdesvideos7788
    @tallzofaitdesvideos7788 4 роки тому +6

    Niankou le meilleur de sa génération kou d'accord

  • @papeseck7997
    @papeseck7997 4 роки тому +10

    Non niankou ak ndayane dagnouy khoulo rk😂😂😂Diam ci yen waay

  • @SeydinaOmarFall
    @SeydinaOmarFall 4 роки тому +5

    Nn Niankou bouko si nak kou kontane si mome beuseul j'aime ❤️🤣🤣🤣🤣

  • @senegalbicisuuf
    @senegalbicisuuf 4 роки тому +8

    Mangui léne di bégué yaine gneup yalna gnépp am diam

  • @jahkarajrofficiel5656
    @jahkarajrofficiel5656 4 роки тому +5

    qui regarde avec moi la vidéo en replay aussi met pouce bleu
    😂😂😂non tayy momm ndayan ñiankou t'as flippé 😂😂

  • @daarahmiftahounasritoubama1939
    @daarahmiftahounasritoubama1939 4 роки тому +8

    Képeu koye woor 1 moi bi yeup beusell j'aime

  • @alaathiou1936
    @alaathiou1936 4 роки тому +5

    Niankou yalla na sa diam yaague waay

  • @sembeneelhadjimalick
    @sembeneelhadjimalick 4 роки тому +4

    Niankou machalla yalla boula thiate dougou ,liguaye def âme na solo trop

  • @toufasow2564
    @toufasow2564 4 роки тому +8

    Ndayane 🤣 🤣 Sama fans louko beugg besseul j'aime

  • @helenemane2382
    @helenemane2382 4 роки тому +8

    Allez niankou t le meilleur ❤️😂🌹

  • @sidybouyadiouss9923
    @sidybouyadiouss9923 4 роки тому +8

    Niankou va vraiment nous manquer ptdrrr nena voisins dagno yéwou nane ndokh 😂😂😂😂

  • @ndiogouwade1419
    @ndiogouwade1419 4 роки тому +6

    Kouy fans niankou beusseul 👍damalay encourager pour ngua woll noon niankou amoul koiii👁👁👁😂😂😂😂

  • @yayakane3594
    @yayakane3594 4 роки тому +7

    Kou beugeu niankou reck beusseul j’aime

  • @abdumaty1046
    @abdumaty1046 4 роки тому +6

    Niankou mo ame fitt ak foula 😂😂😂

  • @abdouazizdia6507
    @abdouazizdia6507 4 роки тому +8

    Yalla na koor gui yoobalé covid 19 bi yalla na ko yalla def

  • @mariemamathiam7058
    @mariemamathiam7058 4 роки тому +9

    Ndiankou yalla nala yalla maye goudou fann ak wérr mahalah

  • @momarpouye3787
    @momarpouye3787 4 роки тому +6

    Niankou yalna yalla defal leuh diam

  • @ndeyenarndiaye4910
    @ndeyenarndiaye4910 4 роки тому +6

    Le mois de l'amour et du pardon balle léne ma akk🙏🙏🙏

  • @lynx_beatz_uchiha
    @lynx_beatz_uchiha 2 роки тому +4

    Sante yallah bagnou feke wate kor gui alhamdoulah yallah nagnou ko feke ay ate ate🤲

  • @elhadjmormatysarr113
    @elhadjmormatysarr113 4 роки тому +10

    Niankou est ce ke woor nga sakh ? 😂😂😂

  • @AbdoulMalikMbaye2225
    @AbdoulMalikMbaye2225 4 роки тому +7

    Wallahi niankou yang may raye😂😂 nénako lolou dieumoul keur🤣✔

  • @tiktokgalsen8173
    @tiktokgalsen8173 4 роки тому +5

    Yalla nagnou yalla nagoul sougnou koor ta mouseul gnou si febar bii amine 🙏🙏🙏

  • @mansourdieng2000
    @mansourdieng2000 4 роки тому +7

    SAMDI 25 AVRIL 2020 1ÈRE JOUR RAMADAN YALLA NA GNOU YALLA NAGOUL AMINE 🤲

  • @marenadeze7362
    @marenadeze7362 4 роки тому +8

    Tu m’as tué a la fin 😂🤣j’aime tes vidéos les gens mechants ne vont pas aimé ✌🏼je t’encourage

  • @djboupsjuniorbampoky5859
    @djboupsjuniorbampoky5859 4 роки тому +4

    Ndayane ak Niankou sérieux wolaine dagainie Dindi stresss 😂😂😂❤️

  • @daffamarega1437
    @daffamarega1437 4 роки тому +46

    Mais yén 🤔 ndayane mii esk dou guinzman vrai sah 😁🤔en tout cas il joue très bien son rôle

    • @sarrabdou3040
      @sarrabdou3040 4 роки тому +2

      Nonn rôle leu rekk

    • @amadoudiouldesall9522
      @amadoudiouldesall9522 4 роки тому +1

      Billahi même man Loulay xalatt

    • @saliouniane4008
      @saliouniane4008 4 роки тому +1

      Lii motakh sènègal nakarè jouè role. Daguayy interpreter personage sii film gnom gnounane est c ke douu deggu

    • @daffamarega1437
      @daffamarega1437 4 роки тому +4

      @@saliouniane4008 wathiél sa tempérament.. daniouy kaf rek .. 👍

    • @saliouniane4008
      @saliouniane4008 4 роки тому +2

      @@daffamarega1437 wathienako yaw lèww dèh

  • @abdinholukamodric5154
    @abdinholukamodric5154 4 роки тому +4

    Niankou khiram yi dal nagne dé 🤣🤣🤣 legui daye beugueu niémé ndayane

  • @ndeyemaperelam7746
    @ndeyemaperelam7746 4 роки тому +5

    Vraiment niankou moi je t adore walahi bonne continuation 😍

  • @bambasalihou7386
    @bambasalihou7386 4 роки тому +4

    Mais kou guisni NIankou amna place si lamb dji pouce bleu

  • @moristoniang6023
    @moristoniang6023 4 роки тому +3

    Moi il est mal 😂😂 Ndayan mo déé😂 ani wa Team niankou beuseul j'aime may guiss👍

  • @ousseynoudiop887
    @ousseynoudiop887 4 роки тому +6

    Ndayane dèm na top 5😂😂😂😂

  • @noreynigning2932
    @noreynigning2932 4 роки тому +7

    Sa jeu mo naturelle blh Niankou t le meilleur

  • @mouhamadoumamounediop918
    @mouhamadoumamounediop918 4 роки тому +6

    Niankou le meilleur comédien

  • @incpv
    @incpv 4 роки тому +8

    Niankou neina ko ndah safna soukar?? 😂😂 pouss bleu pr NIANKOU way 👍👍

  • @momodiop5796
    @momodiop5796 4 роки тому +6

    Nianko ya nekk si dial bi insbii il est fort kel doff

  • @bigeventsproduction
    @bigeventsproduction 4 роки тому +8

    Number 1k dans les commentaires 😂🔥🔥

  • @djboupsjuniorbampoky5859
    @djboupsjuniorbampoky5859 4 роки тому +5

    😂😂😂😂 cheuttt vraiment j'ai rien dans mon poche frère tu m'a tué

  • @aramendiaye220
    @aramendiaye220 4 роки тому +9

    Fallait dir que djingéne nga doumala door pour passé le message djingéne kén douko door
    Qui est d'accord ??

  • @hasanatoulo2266
    @hasanatoulo2266 4 роки тому +4

    Niankou amnga fulla dh yor sa xiir di réklé koñ bi yaangi ñuy bégal daal thi kaw thi kanam

  • @amadouniang7708
    @amadouniang7708 4 роки тому +6

    Walahi suis fier d vs Macha allah yalla na sen diameu yagg way niankou et ndayane les meilleurs

  • @daniroundiaye9226
    @daniroundiaye9226 4 роки тому +8

    Niankou nn stres lay doundou🤣

  • @mordiop4795
    @mordiop4795 4 роки тому +6

    Niankou tu est très fort machalla

  • @assanendoye739
    @assanendoye739 4 роки тому +5

    Niankou tanyi da ndiemei ndayan deh😂💪

  • @salioutaekwondogueye4944
    @salioutaekwondogueye4944 4 роки тому +4

    Ay lutteurs guène wala meune guène beuré deh 🤣🤣. Bon ramadan

  • @serignemassambakane9509
    @serignemassambakane9509 4 роки тому +4

    Yalna nu yalla defal jamm🙏💕💕

  • @mrjumsesamis7398
    @mrjumsesamis7398 4 роки тому +6

    Bonjour cherche amis et ses compatriotes je vous demande de l'excuse en même temps vous pardonner et k vous souhaite un bon ramadan ''niankou '' bonne continuation

  • @lunedieng4297
    @lunedieng4297 4 роки тому +6

    Worna yalla Niankhou meuss n'a doff dans le passé lii d'où talent kessei way. Big up

  • @famadiop1234
    @famadiop1234 4 роки тому +3

    Niankou moune nama Ray ak kaan fii touche like😂😂woor force

  • @beajarrahabdn8312
    @beajarrahabdn8312 4 роки тому +4

    Ani wa team Ndella🔥❤😍

  • @modoudiankha4096
    @modoudiankha4096 4 роки тому +1

    Niankou c'est le Meilleur 😂😂😂😂 bilakhi mounu ma teude té duma ko sétane 😂😂👏👏👏👏

  • @wallysecktv5733
    @wallysecktv5733 4 роки тому +6

    Mbott bi Balla Tyson lamay diokh 🤣🤣 sathiés siteu 🤣🤣 thieuy domou doubléss yi yéna wor

  • @dyshlasarr1304
    @dyshlasarr1304 4 роки тому +2

    No mais vraiment ces deux là ils peuvent me tuée🤣😂😂😂😂no Niankou ak Ndayan meunoumalen mougne 🤣🤧🤧🤣🤣

  • @simbabaoltv9313
    @simbabaoltv9313 4 роки тому +7

    Mai ndayane mi il est trop fort

  • @momosylla8101
    @momosylla8101 4 роки тому +6

    Ma ngui dead si night bi legui daale XaRame la Yoore
    Max de like Guayi🔥💪🏼❤️

  • @s.m.g3645
    @s.m.g3645 4 роки тому +7

    Il devient de plus en plus professionnel

  • @madameoumar1622
    @madameoumar1622 4 роки тому +4

    Niankouuu niankou niankou mani na yeurrr ssi mais y'a quelqu'un bi 😂😂😂😂rayyy nama

  • @dioufysane7715
    @dioufysane7715 4 роки тому +4

    😂😂😂Niankou tps yii danga nènou Ndayane lingakoy door barina trop

  • @abdoufall933
    @abdoufall933 4 роки тому +2

    Niankou le maire komédié de la ans aimé bon ramadan lé fans niankou

  • @bocarndiaye2755
    @bocarndiaye2755 4 роки тому +7

    Ce duo est incroyable 🤣 bne continuation mes frères 🙏

  • @mohamedsylla7113
    @mohamedsylla7113 4 роки тому +4

    Un duo exceptionnel Niankou et ndayane vraiment

  • @djigomamadouibra2206
    @djigomamadouibra2206 4 роки тому +11

    La face de Niankou quand il dit Niaaaw

  • @ousmanefaye507
    @ousmanefaye507 4 роки тому +4

    Billahii Mane Niankou mounou mako mougne 😂😂😂😂

  • @doorwaar9465
    @doorwaar9465 4 роки тому +4

    Merci yenagui yèter dei
    Soukarou koor dou farata

  • @diengvieux2706
    @diengvieux2706 4 роки тому +4

    Yewou nane ndoxx naxx nitte 😂😂😂😂😂😂

  • @maodosy6193
    @maodosy6193 4 роки тому +4

    Yalla nañou yalla nangoule souñou korr

  • @princekilleuh8473
    @princekilleuh8473 4 роки тому +2

    Wouy yooyo niankou dinama Ray magui roulade😂😂😂