Religion - S sam : Le prophète Mouhamed @baolnews.com !

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 1 гру 2024

КОМЕНТАРІ •

  • @moustaphacisse9188
    @moustaphacisse9188 7 років тому +30

    Ce k je ne cess de pleurer chak instant le monde a besoin de vous vivant

  • @salioutalibesmourtalasalio1078
    @salioutalibesmourtalasalio1078 4 роки тому +5

    Sop nako ba di gnane sounou borome gir ma toude ko dome bilahi sa soumakoye deglou dafaye melni taye laye wakhe yalla na yalla yok aye lerame barkep mame Cheikh mbaye wadiourame wou tede wa amin

  • @_Samate
    @_Samate 7 років тому +70

    Il avait comme mission de guider les âmes perdues. en ce qui me concerne Serign Sam m'a été d'une grande aide à travers ses audios, j'ai beaucoup changé et c'est en grande partie grâce à lui. Shoukrann Baye Sam, Moiridinn Sadikhinn

  • @moustaphacisse9188
    @moustaphacisse9188 7 років тому +45

    Je ne vois pas de nos kelkun plus savant k serigne sam ra yalna yalla youki lérame té tass niou ci barkem

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 3 роки тому

      y a n'a pas plus savant que lui dans ce pays

    • @aliounefall2228
      @aliounefall2228 3 роки тому

      @@galaxiepro.5641 comme qui stp ?

    • @bassboye2885
      @bassboye2885 3 роки тому

      @@galaxiepro.5641 voir mém le monde islamique selons ma conviction

    • @galsen527
      @galsen527 Рік тому

      Wakhe nga deug

  • @ousmaneniang9913
    @ousmaneniang9913 2 роки тому +11

    Serigne Sam Mbaye 🙏 je l'aime bien car c'est un vrai monument historique de connaissances Macha-Allah 🙏🙏🙏🤲🤝 diereudieuf Serigne Sam Mbaye 🙏

  • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
    @mouhamadoulamineseyebeugue2741 5 років тому +20

    *_Ceyy serigne Sam Mbaye yalna yallah yokk sayy leir si barkép SERIGNE SALIOU MBACKÉ_*

  • @aladjifayee5309
    @aladjifayee5309 4 роки тому +4

    Sama sopè bi BAYE SAM MBAYE ♥️ yalnako YALLA sunu BOROM doli leer te tass nousi barkem si BARKE CHEIKHOUL KHADIM ♥️🙏

  • @montanaboys4404
    @montanaboys4404 6 років тому +19

    Machalla ligua yene wone diam gni si xam xam tay yég neu ndakh dieum dji dém neu wayé ndiagualé gui mangui fi pour kép kou nama xam dieureudieuf 🙏🏾

  • @albachirlenfantnoir7652
    @albachirlenfantnoir7652 3 роки тому +6

    Ndeysan mane dama ko begue rk bilahi ❤❤ yalla nako yalla yerem 🙏🏽🙏🏽🙏🏽❤✅

  • @aladjifaye3439
    @aladjifaye3439 4 роки тому +6

    Yalnako sunu borom doli leer si barke cheikhoul khadim ♥️ baye Sam mbaye ♥️

  • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
    @mouhamadoulamineseyebeugue2741 4 роки тому +14

    _05:02__ samedi le 12 septembre 2020 au maroc🇲🇦❤😭😭😭🙏_
    *Cëyy Serigne Sam Yalla Dinala fay loum masa fay aye niteum wallahi😭😭😭😭😭😭😭😭🇲🇦❤🙏*

  • @taphaseye243
    @taphaseye243 3 роки тому +3

    Yàlla na yàlla dolli ay leram sa tasnou çi barkem Amiin ci barkeb khassida yi Aminnne Aminnne Aminnne

  • @elahjifallouleye1213
    @elahjifallouleye1213 10 років тому +40

    yalnako sunu borom dolly aye khéweule aki maye ci barké s touba

  • @cheikhmbacke4379
    @cheikhmbacke4379 5 років тому +4

    Yalla nako yalla yeureum te khareko Aldiana firdawsi srg sam mbaye barke seydina mouhamed

  • @khadimlo9702
    @khadimlo9702 5 років тому +6

    Sala mou halaykoum Bay sam mbaye yalah Naga walle taloubeyi ay lérr Puissance serigne Sam mbaye Aminé

  • @feuzbarryfeuzbarry53
    @feuzbarryfeuzbarry53 4 роки тому +13

    Serigne sam vous m'avez inspiré le soufisme et éclairer mon cœur dans la voie d'Allah yalla na yalla yok saye leer

  • @missmagattegueye1317
    @missmagattegueye1317 9 років тому +30

    yallana yalla yokou ay léram té tasniou si barkém

  • @knln6361
    @knln6361 7 років тому +57

    ceyyy 😢😢😢😢😢baye Sam beug nala billahi beug nala

  • @elfalliloudioum8259
    @elfalliloudioum8259 3 роки тому +3

    Qui regarde en 2021... notre éternel baye Sam je t'aime...

  • @adangom1649
    @adangom1649 4 роки тому +4

    La ilakha ilala🤔🤔waliwou yalla DEUGeu gui ni yalna yalla yok ay lérame

  • @modiboye3718
    @modiboye3718 6 років тому +4

    Yalla nagnouko yalla fayale thie barké Mohamed (psl)

  • @ibrahimakhalil9042
    @ibrahimakhalil9042 4 роки тому +2

    Ndeysan kenn dou seydina Mohammed ya rassoul loulahhi serigne sam yalna yalla yeureum co té Yokk aye lerram tass niou sii barkem barkep serigne Touba 🤲🤲❤❤👌👌

  • @toubamahwatvtoubamahwatv8439
    @toubamahwatvtoubamahwatv8439 Рік тому +2

    Sëriñ Sam Mbaye Yàlla nala Yàlla Faye

  • @lolamine9014
    @lolamine9014 6 років тому +4

    machallah amna solo trop yalla na ndiou KO yalla fayall si barke cheikhoul Khadim

  • @mouhamaddiop118
    @mouhamaddiop118 9 років тому +6

    Serigne bi yalla na yalla yooke saye leer.dimbeli ngua niou,dieuredieufety...

    • @amadoundiaye5208
      @amadoundiaye5208 6 років тому

      Yalla sédéna ni mala beug Baye Sam Mbaye. Yalna yokk léram té taax ñu ci barkém

  • @vieuxndiaye662
    @vieuxndiaye662 4 роки тому +7

    Yalnako yalla yeureum tes djiégualko xaréko aldiana firdawsii amine 🥰🙏🏿😂

  • @lansanatoure5348
    @lansanatoure5348 8 років тому +26

    yalla naniou yalla Tass si barkèm

  • @magayegaye2368
    @magayegaye2368 8 років тому +19

    Yalna yalla yok lèram thi barkè wèrou kor AMINE

  • @niangniang1094
    @niangniang1094 4 роки тому +3

    Machalla serigne sam mbaye yallana noko yalla fayal amine 💕

  • @bambybambily9537
    @bambybambily9537 8 років тому +20

    bou done bah dina rombou bah Kone gnouné mame Sam ya rombou bah yalnagnouna yalla fayal fanga nek bilahi mame Sam yangui thi sounou holyi

  • @adelaidedrame462
    @adelaidedrame462 2 роки тому +3

    Ndeysann Serigne Sam Mbaye . J' ai été émerveillée par ses illustres enseignements sur les Immenses Grâces du Noble Prophète Muhammad sallallahou aleyhi wa Salam.

  • @laminediaw3552
    @laminediaw3552 6 років тому +2

    Dieureudieuf serigne sam mbaye yallna sunou borom yok ay léram tass niou si barkém

  • @modoundongothiam7300
    @modoundongothiam7300 3 роки тому +2

    Le 23| 01/ 21 yalna borom yok yeurmande thi mom // ya rabbi yalla nangafi dieule tawat dji niep am diamou

  • @papeseydousow7167
    @papeseydousow7167 7 років тому +4

    sante. s erigne. mbaye. keene. amoul. fayame. Yall nako yalla. f ayel. amine.

  • @khadimefall7590
    @khadimefall7590 8 років тому +36

    céy serigne sam wetal nga diamono ya lérr xam xam machalla

  • @TheBadaseck
    @TheBadaseck 8 років тому +32

    Yalla na la soniou brom yeureum la diegal la tabala al diana

  • @taphasylla3784
    @taphasylla3784 3 роки тому +1

    dieregnef serigne same mbaye yalla na yalla yokou saye leer ci barcke serigne touba

  • @elhadjisocembathie4762
    @elhadjisocembathie4762 Рік тому +1

    Le guide spirituel Serigne sam mbaye un grand savant l'homme qui sacrifier sa vie pour le bien des musulmans

  • @mamecheikhmbaye374
    @mamecheikhmbaye374 9 років тому +21

    yalna yala yok leram sounou serigne sounou sope

  • @ndongoasse4739
    @ndongoasse4739 7 років тому +1

    Yalna Yalla Yokou Ay lèram tass gnou si barkèm dieureudeuf Serigne Sam

  • @moussalo8580
    @moussalo8580 8 років тому +29

    SERIGNE SAM YALLA NAKO SOUNOU BOROM FAYAL GNOUKO.

  • @serignefalloufall4242
    @serignefalloufall4242 2 роки тому

    Machallah Dieureudif serigne Sam mbaye kén dou yawou yalla na le yalla faye Amin si barckp khadim rassul dieureudif 👂👂❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇧🇪🙏🏿

  • @taphakoundoul7286
    @taphakoundoul7286 5 років тому +6

    Souma guisse ni ki rek talibe serigne touba la damaay sante yalla bou weerrr si done guima done mouride

  • @badabada62
    @badabada62 10 років тому +20

    dieure dieuf Serigne Sam Mbaye

  • @bayesidy6076
    @bayesidy6076 Рік тому

    Serigne Sam Mbaye yallah na yallah yoke sa lèr. Sama serigne ❤️🙏🏾

  • @SayeFall-mh6ms
    @SayeFall-mh6ms 2 місяці тому +1

    Sallahou khalayekhi wa sallame ❤❤❤❤❤

  • @dieyedieye2931
    @dieyedieye2931 5 років тому +1

    Baye same yalla nala yalla yokou sa lerr té tasniou si sa barké

  • @matysalioundjitte4609
    @matysalioundjitte4609 2 роки тому

    Yalna yallah yokk aye leram teh tassarei am ndiagalem ba nieup moune sei diarignou

  • @khadimdieng20
    @khadimdieng20 10 років тому +8

    Dieureudieufety serigne sam

  • @aluounegaye7934
    @aluounegaye7934 4 роки тому +2

    Al Hilm moy xam xam moy Bay sam sante nan thi sa niowoub diamono♥️😭💎

  • @khadimmbacke8242
    @khadimmbacke8242 8 років тому +25

    Machallah YALLAH nala Bour Yallah fayy

  • @amethdieye1031
    @amethdieye1031 9 років тому +10

    diaradiaf serigne sam mbaye

  • @mactargueye8835
    @mactargueye8835 4 роки тому +2

    Allahou sali ala Seydina Mouhamed salla lahou aleyhi wa salim

  • @modndye4791
    @modndye4791 3 роки тому +1

    yalla na yalla yeureum serign Sam mbaye amine

  • @mamembarganethiam1045
    @mamembarganethiam1045 2 роки тому +2

    Serigne Sam, l´eclaireur, un vrai missionnaire. Sunu Sopé. Mon maitre spirituel

  • @khadijamaman6819
    @khadijamaman6819 7 років тому +5

    Dieudieufety serigne sam mbaye

  • @tallagueye3587
    @tallagueye3587 7 років тому +4

    Yallana yalla yokou lérame Amine

  • @lampka9546
    @lampka9546 5 років тому +1

    Yalla nako yalla yeureum tè khareko aldiana firdawsi srg Sam mbaye barke amadou bamba ken dou mom

  • @aladjidiop6619
    @aladjidiop6619 4 роки тому +4

    Machallah baye sam mbaye le grand conférencier islamique

  • @fatmalo504
    @fatmalo504 6 років тому +1

    Yalla.na.noko.yalla.fayal.thi Barke.seydina.mohamet

  • @mamadousanoussytoure6041
    @mamadousanoussytoure6041 6 років тому +3

    Mane de s sam moy sama SERIGNE ak Cheikh moussa ka borom wolofal

  • @abdoulahatguene3881
    @abdoulahatguene3881 2 роки тому +1

    Salalaahou aleyhi wa Salama !!!!
    Yalna Borom bi fay yiiw Serigne Saam Mbaye🤲

  • @alyalassanekebe8046
    @alyalassanekebe8046 9 років тому +16

    yalla nanou ko sounou borom feyal

  • @moustaphacisse6053
    @moustaphacisse6053 5 років тому

    Serigne sam mbaye mo baakh yalla na yalla yokkou lèram tè taass niou si baarkêêm.

  • @omargueye8896
    @omargueye8896 5 років тому +1

    KEN DOU SEYDINA MOUHAMMAD SALLALLAHOU HALEYHI WA SALLAMA HATIMOUN NABIYI WA IMAMOUL MOURSALIN WA BACHIIRAN LI AHLI ALJANNA WA NAZIIRAN LI AHLI NARI. SALLALLAHOU HALEYHI WA SALLAMA.

  • @moanne680
    @moanne680 5 років тому +1

    Un homme multidimensionnel yalla n'a yalla yoke lerame

  • @ouzinouzin5516
    @ouzinouzin5516 2 роки тому +1

    Serigne Sam mbaye sama werou waye ♥️🥰🙏 dieureuf Serigne Sam mbaye 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @amadoukasene
    @amadoukasene 6 років тому +1

    YALLAH na sounou borom dolli si mom nguereummame bi jahi Seydou keuwnayni baassita Naïm.

  • @bambaba7979
    @bambaba7979 7 років тому +2

    Yalna yalla yok leram tei tasniou ci barkeime

  • @elhadjimactarkebe2515
    @elhadjimactarkebe2515 11 років тому +30

    il faut bien ecouter ses paroles

  • @cheikhamar-vs4sl
    @cheikhamar-vs4sl 9 років тому +15

    Eternel sam mbaye

  • @bayediagne8856
    @bayediagne8856 7 років тому +11

    amine serigne Sam

  • @tallagueye3587
    @tallagueye3587 7 років тому +7

    yallana yalla khare aldiana Amine fire dawsi amine

  • @amadoumoustaphadieng8660
    @amadoumoustaphadieng8660 Рік тому

    Qu'Allah illumine sa tombe et l'accorde le Paradis !

  • @serignesalioundao3438
    @serignesalioundao3438 3 роки тому +1

    YALLA NA SA BOROM DOLLI SAY LEER TÉ WATHIÉ BEUSS BOU AK YEURMANDÉ SI SA KAW SI BARKEP AHMADINA SALIHA MAN MOM IOW YA TAKH MA KHAM SAMA YAYE YA TAKH MA KHAM NIMAY TOPPR SAMA BAYE IOW YA TAKH MA KHAM NIMAY TOPPÉ SA SERIGNE YA TAKH MA KHAM SUNU BOROM YA TAKH MA KHAM AK YONENTÉM KON SI GUATAL YA TAKH MA KHAM SAMA ADOUNA KON MANGUIY DELLOU DILA GNANAL SUNU BOROM CHAQUE SECONDE CHAQUE MINUTES CHAQUE HEURE CHAQUE JOUR SUNU BOROM DI DOLLI SAY LER AK YEURMANDÉM 🙏🙏♥️♥️🙏

  • @cheikhibradiop6631
    @cheikhibradiop6631 Рік тому +1

    Dieureu dieuf serigne sam mbayen❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @moussasow9735
    @moussasow9735 10 років тому +22

    kene dou serigne same te dotoufi ame

  • @sididiop3501
    @sididiop3501 8 років тому +14

    thiey serigne sam

  • @fallyarammomsarignetouba6266
    @fallyarammomsarignetouba6266 5 років тому +1

    Yalnano kou yalla fayal Baye Sam mbaye

  • @serigneabdoulahiseye1111
    @serigneabdoulahiseye1111 5 років тому +3

    Theiye serine Sam 😥😢😢😢

  • @ndiogouloum2966
    @ndiogouloum2966 6 років тому +6

    Baye same Mbaye machalla yalla na yalla fayla Mbaye

  • @daoudafall6116
    @daoudafall6116 2 роки тому

    Yalla nako Yalla gueureum té guereum niou amiine

  • @khadimdiouf3114
    @khadimdiouf3114 6 років тому +4

    Masha Allah

  • @joaomaikon414
    @joaomaikon414 6 років тому +2

    Yalla nala Faye ti bake Mame chiekh mbaye

  • @SayeFall-mh6ms
    @SayeFall-mh6ms 2 місяці тому +2

    La ilalaha ilalah moukhamad rassouli lahsallahou khalayekhi wa salame ❤❤❤❤😂😂😂😂

  • @dianeelhadji9368
    @dianeelhadji9368 6 років тому +2

    q la tere lui soi legere si seydina mouhamet psl

  • @malickndiaye942
    @malickndiaye942 9 років тому +10

    dieureudieuf borom touba

  • @seynibarro7244
    @seynibarro7244 5 років тому +1

    Khame khame rek ma cha Allah mbaye

  • @serignefalloukhidma2898
    @serignefalloukhidma2898 5 років тому +6

    للهم اغفر له وارحمه ببركة خادم رسول

  • @abdoukhadredieylanidia5313
    @abdoukhadredieylanidia5313 10 років тому +15

    Miracle

  • @baylamuhammad7026
    @baylamuhammad7026 4 роки тому +1

    Ohh ndeyssane il a donné des conseils inestimables...tiey segn sam beugue nala dh...

  • @leuzadl9571
    @leuzadl9571 6 років тому +3

    جزاك الله

  • @bayesalioudiagne1518
    @bayesalioudiagne1518 5 років тому +1

    Ndayesane kén dou serigne same

  • @fayeibrahima8756
    @fayeibrahima8756 7 років тому +5

    Ma cha alla sama serigne

  • @modouhann7237
    @modouhann7237 4 роки тому +2

    Un homme multidimensionnel

  • @aladjidiop6619
    @aladjidiop6619 4 роки тому +2

    Machallah baye sam mbaye sa sopé bi

  • @madiamayade6085
    @madiamayade6085 6 місяців тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndiayeabdoulaye8599
    @ndiayeabdoulaye8599 7 років тому +6

    Machallah serigne sam

  • @papeseydousow7167
    @papeseydousow7167 7 років тому +5

    s@ ma. s erigne. sam. mbaye. R eekk. la. lumière. du. cœur. @ me. diamou. d'i. diamouyalla. R erkk. barri. xame. khame. R erkk. moyyye. borrome. d'i. kharitou. yalla. yalla. thiaye. sama. moi. xame. yalla. yalla. R eekk

  • @babacargueye1658
    @babacargueye1658 6 років тому +1

    Yalla naniou yalla takh si sa barké