En tout cas tes paroles sont honorables, je ne te connais pas mais si s'est avéré que c'était ton posture depuis l'affaire Adji sarr vous êtes une personne qui défend la vérité. Nagnou niaanal sounou mbokkou joulit ya nekk ca Palestine Liban ak Iran ak mbolem joulit bou nekk ci ayye tolof tolof CI BARKI SEYDOUNA MOUHAMMAD Paix et Salut D'ALLAH soient sur.
Il est invité à quel titre ? Juste parce qu'il est le beau frère de Macky ! Origine de sa richesse ? Le pays mettra du temps à se développer que des débats de bas étages...
Tu ne comprends rien toi t’es un vrai ignorant boy celui là n’est pas pour Macky au contraire il est contre le régime de son beau frère il faut suivre l’intégralité de l’émission pour juger banalement mon cher
Nio kharrr kenen mou nieuw deif ni adama,mais pape adama faye nila meussa wakhei dama kham bene waliu yallah boussi done wakh di dokh tang diam entre mariem ak adama faye ndakh andul woone ak niom
Décidément, ayant bénéficié des largesses de Macky , tu n’as jamais pipé mots de ton désaccord sous son magistère. Aujourd’hui comme y’a plus de gâteau , tu peux te permettre de baver à tout bout de champ.
Il parle de titres qui appartiennent à l'État qu'il s'est procuré. Ki moom c'est un client du pool financier. Suufu État bi yëpp ñii ñoo ko caxat caxaaté
Cette mosquée n a pas sa place là-bas. C etait prévu une route qui devait relier la route de l aéroport yoff. Pour camoufler un litige ils construisent des lieux de culte. Le sénégalais est de type émotif.
Merci Pape Ngagne ko dou Nitou dafa tekkiwoul Dara demba ak Teye , Adji Sarr est une citoyenne sénégalaise au meme titre que Sokkonljame nga ni M Sall yonam meussoul nekk ci affaire sweet beauté soubtogone auprès de ses épouses Lii lepp dou Khew
Pourtant nak ni leu meussa wahei, yaguena critiquer wa keur macky depuis toujours
Il est vérédique même en l'écoutant parler. Il est vraiment franc, je l'aime beaucoup.
@@yankhobagassama1081sont ils sont tous des voleurs
Merci beaucoup Adama
Merci pape mé Adama kou bakhe la man dé walakhi magui koy dogo sétan mé kouko sopou la
Ndeysaan pourtant Cheikh Bara Ndiaye wakhone nafii né marieme Faye akk famille danj méré Madambal Diagne thie fén yimou fénal sén yaye.😂😂😂😂
Bilay wakhone nako
@@toutetrien6708 oui Cheikh bi et pertinent Masha'Allah.
Madiambal ligay fen khana dosi sett yalla 😂😂
Madambal 😂
😂😂😂
En tout cas tes paroles sont honorables, je ne te connais pas mais si s'est avéré que c'était ton posture depuis l'affaire Adji sarr vous êtes une personne qui défend la vérité. Nagnou niaanal sounou mbokkou joulit ya nekk ca Palestine Liban ak Iran ak mbolem joulit bou nekk ci ayye tolof tolof CI BARKI SEYDOUNA MOUHAMMAD Paix et Salut D'ALLAH soient sur.
Adama Faye mi dal beugue nako
Ce monsieur est vraiment extra ordinaire. Yalla sama KO
En tout cas il est tres posé et tres calme
Merci beaucoup pape nggne
Merci beaucoup frère ❤❤❤❤❤
Merci faye ❤
Vérité absolue machallah
NAFEK MOO BARI SENEGAL REK NAX ALALOU ADINA
WAAYÉ DEUG DIAFEWOUL DJISS AK FEPP FO FARR !!!
Mann deh mangui rafetlou yarr bi AK dall gui
Si Adama Faye
Adama faye nite kou bakh kou djioulité ❤Mashallah il est digne
Ki kou bakhla MachaAllah
Merci beaucoup Mr Mansour Faye Pape Ngagne tu es faux
Adama faye
CE CRÉTIN DE PAPE NGAGNE EST GRÂCEMENT PAYÉ POUR SABOTER ET FAIRE DES INSINUATIONS.
C'EST IN VRAI DEALER CE PETIT CON.
Machalla bo bakhé bakh gua yow nit cou bakh gua ❤
Résistant de la dernière heure 😂😂😂
Merci futur député du peuple
Alkhamdoulilahi
Merci Adama FAYE
C'est difficile d'avoir un Frere Ministre et un beau-frere president.
Madamballll dé day fénnn rek
Pour dir vrai nite cou bakhe la
C'est un homme de valeur bilahi
Machalla yalla dafa beugué deugue
merci
Ah wahi Madiambal dé diaroul daure sa dome😂
Virement souko xoulé t xam nit dinga xamni ko degu la
merci adama faye wallahi il a raison
Merci beaucoup adama
Cheikh yirim legui souy fen couran day couper
Machala si dall gui ak deugou bi
Il est invité à quel titre ? Juste parce qu'il est le beau frère de Macky ! Origine de sa richesse ? Le pays mettra du temps à se développer que des débats de bas étages...
Tu ne comprends rien toi t’es un vrai ignorant boy celui là n’est pas pour Macky au contraire il est contre le régime de son beau frère il faut suivre l’intégralité de l’émission pour juger banalement mon cher
Il a été invité en tant que tête de liste de la coalition Défar Sa Gokh pour les élections législatives
Ki 2009 la créer sa 2éme société donc limou ame dafko ligueye
Nio kharrr kenen mou nieuw deif ni adama,mais pape adama faye nila meussa wakhei dama kham bene waliu yallah boussi done wakh di dokh tang diam entre mariem ak adama faye ndakh andul woone ak niom
Pour temps mr adama ce homme véridique
Doma dimbeuli si surcuit bobou nakh ma ame keurr
snoko snoko snoko snoko 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
En tout cas Adama Faye dale nga et tu m’as vraiment convaincue.Diameu si yow
il a raison et sincère ce adama faye
Ila peur ,on l'a manacé, c'est pour cela
Adama nit ko bakh ragal yalla ❤
Vives Pasteef❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Décidément, ayant bénéficié des largesses de Macky , tu n’as jamais pipé mots de ton désaccord sous son magistère. Aujourd’hui comme y’a plus de gâteau , tu peux te permettre de baver à tout bout de champ.
Adama faye avec tes verrités ma fais perdre beaucoup te temps a écouter verémen ❤❤❤❤
😮😮
Pourtant Adama faye nitt Kou bien la dhé
C'est croustillant c'est révélation 😂😂😂
Machalla Li wané n'a ni dou nieupa bone nagn déf attention si mindéfou yalla yi
Pape ngagne ti es mauvais sokhor
Hummm c'est quoi ces vérités adama tamite
Le format est bon mais Pap NGagne est un peu limité.
Adama fay wanma wane circuit bi
Pape mi sama xél téyna si mome 😡😡😡😡😡😡
Il est pro Macky!
Famille bou nekk amnaa sarakh dommage pour Adama Faye
Bilaye lui c'est un vrai domarame
@@maimounasall224dafa khamni bou dèwè mome rek ak bamèlam ken diara louko ay feen loutakh deug dilen deranger🤔🤔🤔
Adama il est véridique depuis
Man dé sopou nala
Adama Faye sathieu guéne famille bi niome nieupeu sathieu laniou amou léne Dara khalissou askane bi guéne done sédo digueu khamené sathieu guéne
trs coherant je suis patriote mais li adama faye di wakh ni man dal na sama khel t nekhna degue
bayi ba dian djie romb nga top si watite bi😂😂😂😂😂😂😂
Pape nga da arrogant
Ah toujours le frustré qui cherche une cache.
Adama ya nafekh
ce gars Adama FAYE il faut sauver sa peau tout ce qu'il dise c faux
Wakho deugu
Mai loutakh bobou ba legui gueno wakh ko yen yeupa yame
Wakhena plusieurs fois démal khol vidéo yi mou def pendant que Macky était encore président
Après tout Pape Ngagne il est pertinent
Pape dii nafék
Pap ngagne khamoul touss vrai nafékheu la vrai domouharam la
Méchant sokhore
Il parle de titres qui appartiennent à l'État qu'il s'est procuré. Ki moom c'est un client du pool financier. Suufu État bi yëpp ñii ñoo ko caxat caxaaté
Daw lakgou
Personnellement ce gars ma surpris il ma lair veridique.
En tout cas noro nga ko baakh dé khawma nak ta daa mélni sén fami yaroon nan lén ngour mooy soppi nit rék
Wakh deugueu djaféwoul walay émission bi dafa nekh trop
Madiambal est toujours dans la manupulation
Je ne l ai jamais ecoute parler.j ai de l estime a l entendre parler
Adama bayil souf bi...
Cette mosquée n a pas sa place là-bas. C etait prévu une route qui devait relier la route de l aéroport yoff.
Pour camoufler un litige ils construisent des lieux de culte. Le sénégalais est de type émotif.
Pure veritè
Deugeu rék moy modiou
MADIABAL DOMUHARAM LA
A P R
Alliance des Pilleurs de la République
Li d bokko wakhonn macky dallay ray .
Wakhenako plusieur fois en publique les vidéos sont toujours sur le net
Dafeu khamené sathieu guéne yèneu Yéme ak madiambale sathieu guéne nieupeu khame naniou domou badoleu guéne guéne beugueu yore aye milliards nane dérétou askane bi guéne défe
Adama ressemble un citoyen productif et pieux.
Seulement bo diegue fess.
Li yeufou nafékh la lane motakh wakho ko wone boba
Ki moyy sarakhou famille yam
Si si waxon nako kay
Si wakhoun nako
Babacar Cisse ki wakhonenako meussoul ande ak les magouilles de macky
😂😂😂😂😂
Lamigne vou, Reuye moye Sén kham kham senegalais yi
dañió soneux thi yén aye poupe ngendi, khégne senegalais yi
Il ne dit pas la vérité ce type.
Pape ga poldof
Adji Sarr n'a pas de famille ?
Adama mi moy nafekh deugue
😅😅😅
Nite qi soko khamoul boulko juge
Senghor.1968.bdg.senegal.8000000000o.miliar.le.ac.sept.mille.miliard.kholal.digaanetebi
Ce gars là daffa iniaan
Wakh ba ngi nounou ki dafa iniane sokhor
Bodeu liulawahk dé kobhkini
Li yeup ndakh macky beugoulon mou al poste c ridicule franchement adama setal yalla mbok ken dou ko bayi ndakh aduna
Loutakh beugou len dègu deug 🤔🤔🤔
Merci Pape Ngagne ko dou Nitou dafa tekkiwoul Dara demba ak Teye , Adji Sarr est une citoyenne sénégalaise au meme titre que Sokkonljame nga ni M Sall yonam meussoul nekk ci affaire sweet beauté soubtogone auprès de ses épouses Lii lepp dou Khew
Il essaie de ße laver à grande eau.
Lolou la guiss mane
Yow Adama do sarap nokoul feulé