Dieureudieuf Pape Ousmane Chérif Mbaye Ba Laye si kaw si kanam dognou doyal si sougnou anciens éleveurs yi yokk lénn émissions yi si anciens yi gnou meuna yokk kham kham bi si élevage. Yalla na yalla barkéll liguéy bi. Dieureudieuf les champions Trio Tv
Ma sha Allah 😍 Triobi TV Yalnalén YALLA fay té barkél ligueye bi🙏✨🙏 Dama sételou Parcours des Champions bou amé wakhoumala njikoy sétan disi contane disi jang mais mome éleveur bi dangaye sételou mbéckté bi moy andal bouy retracer son parcours ✨✨✨ Ma sha Allah Triobi tv sa kaw sa kanam❤❤❤
Machallah merci à vous et merci pour la suite
Dieureudieuf Pape Ousmane Chérif Mbaye Ba Laye si kaw si kanam dognou doyal si sougnou anciens éleveurs yi yokk lénn émissions yi si anciens yi gnou meuna yokk kham kham bi si élevage. Yalla na yalla barkéll liguéy bi. Dieureudieuf les champions Trio Tv
Machalah ❤❤❤❤
Vraiment émission bi nexna mais chérif day interrompre interventions you amsolo merci Pa Ousmane
Ma sha Allah 😍 Triobi TV Yalnalén YALLA fay té barkél ligueye bi🙏✨🙏 Dama sételou Parcours des Champions bou amé wakhoumala njikoy sétan disi contane disi jang mais mome éleveur bi dangaye sételou mbéckté bi moy andal bouy retracer son parcours ✨✨✨ Ma sha Allah Triobi tv sa kaw sa kanam❤❤❤
Ana 3éme partie bi 🎉❤
No père ndanane leuh li yalla boumou diékh
Émission bi nekhna trop