🛑SPÉCIAL GAMOU RAMADAN 2021​ AVEC TAFSIR ABDOURAHMANE GAYE ET CHERIF MAMINE AIDARA

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 171

  • @fatoukinedioufdiouf502
    @fatoukinedioufdiouf502 3 роки тому +17

    Ce qui dislike c'est quoi leur problème passez votre chemin c'est tout seyidouna mouhamed à vie inchalah khou rabbi yéna ignane merci tafsir abdourahmane gaye yalna sa diam yague amine

  • @diodiondiaye7619
    @diodiondiaye7619 3 роки тому +55

    Ceux qui dislike sûrement ils ne croient pas en Dieu. Tafsir ak Cherif yalna yallah sameu lène, arr lène, yirr lène té fey lène yiw ci barké Nabil Moustapha ak wérou korr gui.

    • @timafakane7179
      @timafakane7179 3 роки тому

      Peut-être qu’ils savent même pas ce que sa signifie

    • @DM-ch2uy
      @DM-ch2uy 3 роки тому

      Wallah je me pose tjr cette question

  • @fallndeyefatou3263
    @fallndeyefatou3263 3 роки тому +22

    Kou topoule seydina Mohamed psl pértgue Macha Allah

  • @khoudialo8357
    @khoudialo8357 3 роки тому +18

    Machallah sama soppéyi encore dama contente si yéne Yalna Yalla faylène depuis 2012magui lendi suivre nguèn yague ma bégal si Seydina Mohamed (psl)

  • @awafall8437
    @awafall8437 3 роки тому +12

    Sama khôl bé sédaati rek beu mounuma wakh depuis direct bi mangui beugu wakh mais mounuma...nawone fawone mashallah 😥😭🙈♥️ c'est ce genre de personnes qu'on a vraiment besoin dans cette société remplie d'ignorants😥remplie d'hommes d'affaires sans scrupule ☹️Gaye yallna yalla Fay wéreul batt bi yok Diam diék khéweul gui...sugnu sopébi PSL dinala fayal bopam inchallahu rabbi 🙏🏻🙏🏻...Cherif yallna ande bi yagu ak takhaway bi🙏🏻🙏🏻🙏🏻❤️....trop de loves sur vous🤗un duo rempli d'enseignements...milles merci à la 2S

  • @oumarfall99
    @oumarfall99 3 роки тому +16

    Billay sa youma fébaré wakhtanou Tafsir dafmay werlo thiothe MashaAlah fans Tafsir number one mangui nih

  • @papaserignesakho4343
    @papaserignesakho4343 3 роки тому +6

    Mame maodo moy mame borom touba koulen beug taxaleh ya sikk fier de vous TAG et CMA

  • @hadymamadouagne3617
    @hadymamadouagne3617 3 роки тому +6

    Machallah yallah nalen yallah fay si barke seydina mouhamad sws

  • @khalifadieye9760
    @khalifadieye9760 3 роки тому +3

    Machallah kène dou seydou na mouhamed (psl)❤❤❤

  • @liouzodiallo8286
    @liouzodiallo8286 3 роки тому +2

    Mashala khole sedd neu kenn dou yonenti bi SAW ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aichatousene2349
    @aichatousene2349 3 роки тому +16

    tabarkala tabarkala yalna yalla fayal niou léne guéne yague ko téwé thi barké taha psl ❤💖❤💖💖💗❤💖💖💗

  • @MousseGaye-zr8gi
    @MousseGaye-zr8gi Рік тому

    Yalla na yalla dolly wer ngou yaram baye la fii bassi kanam si barke mouhamed❤❤❤❤❤❤❤

  • @ousmanethioye990
    @ousmanethioye990 3 роки тому +52

    Machallah mais talibé cheikh bi noumouye tagué Yonéneti bi noumou toudou ♥️🇸🇳🔥 machallah 2stv sa kaw sa kaname 🔥🔥🔥

  • @aminafall8453
    @aminafall8453 3 роки тому +12

    Machalah khol sed tina wayy aka neikone gnoukoy ame tous les samedis meme après ramadan

  • @ababacarseck377
    @ababacarseck377 3 роки тому +6

    Cheikh seydi El hadji Malick sy maodo yalla nako yalla Faye tè sameu kèpeu koye diabotame 🙏🙏

  • @hamid_line576
    @hamid_line576 3 роки тому +41

    Une fierté absolue d’être dans ce tarikha
    Tidjania dans le cœur ❤️❤️❤️

    • @jamesonvincent3779
      @jamesonvincent3779 3 роки тому

      I know I am kind of off topic but does anybody know a good place to watch new series online?

    • @Diopmaguette93
      @Diopmaguette93 3 роки тому

      @@jamesonvincent3779 9!₩

  • @sowjules2274
    @sowjules2274 3 роки тому +7

    Ma cha allah tidjaan thaï kanam

  • @gltntegilou9532
    @gltntegilou9532 3 роки тому +5

    Diamou reck alhamdoulillah diamou reck ci Sénégal soutoura ci Sénégal amiine yaraby machalla dieureudieuf yalla sounou boroom 🙏🙏🙏🙏🙏🤲☝️🥰♥️❤️💕💞💕❤️♥️

  • @mamadoudanfa4958
    @mamadoudanfa4958 3 роки тому +4

    Longue vie à vs que Dieu tout puissant vs donne plus de force pour nous faire connaître notre bien aimé (psl)

  • @maimounaboiro8875
    @maimounaboiro8875 3 роки тому +3

    YALLA YALLA GOUDAL SENI FANES THI BARKE SEYDINA MOHAMED PSL 🤲 ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @soumanikamara1557
    @soumanikamara1557 3 роки тому +4

    Machallah y'allah nalène y'allah faye thii barkè yonéte Mohamed ❤🥰🙏🙏

  • @gltntegilou9532
    @gltntegilou9532 3 роки тому +4

    Dieureudieuf tafsir Abdou rahman Gaye yalla n'a la yalla samou fayla goudou fan amiine yaraby machalla dieureudieuf 🙏🙏🙏🙏💯💯😇😇🥰🇸🇳❤️♥️💞👍☝️🤲❤️♥️

  • @marietoudiaw763
    @marietoudiaw763 3 роки тому +1

    Machalah khaly Ousmane khôl sedatina machalah ❣️❣️❣️❣️

  • @diengndeyemaguette8699
    @diengndeyemaguette8699 3 роки тому +1

    Mashallah mashallah khol sedatina barakallah fii kou

  • @bohfall186
    @bohfall186 3 роки тому +7

    Machallah yalna sen diam yague

  • @issadembele6066
    @issadembele6066 3 роки тому +6

    diamsiyennn..salamsiyen..kén dou Rassoulilahiii...(psl) khôl fekhhnaa..💓💓💓

  • @ousmanembaye2955
    @ousmanembaye2955 3 роки тому +3

    Machalla yalla na niou yalla doly diam AK soutoura ya raby🥰 inchalla yalla naniou feker dewene amine ya raby 🙏

  • @bamsbams8372
    @bamsbams8372 3 роки тому +7

    Li la'niou sokh'la si borom xam xam da'ngay meuné founé / wayé nak ndiabotou maodo nio mél no'nou / fô feugeu niou oubil'leu
    Machallah 🙏 🙏
    Machallah 🙏 🙏

  • @kodiopndoye3810
    @kodiopndoye3810 3 роки тому +4

    Tafsir Cherif kenne dou yénne machalla laffe satte

  • @gltntegilou9532
    @gltntegilou9532 3 роки тому +7

    Dieureudieuf El hadji ndiaye yalla n'a yalla faylen goudou fan amiine yaraby machalla dieureudieuf ndiaye machalla 🙏🙏🙏🙏☝️👍💞🇸🇳🥰☝️🤲♥️❤️♥️❤️♥️❤️💕🙏

  • @thiernosalamdiallo7874
    @thiernosalamdiallo7874 3 роки тому +25

    Macha allah sama xol bii sedd na billahi ❤❤🙏🙏 je prie qu'allah accepte nos Doua'as , nos prières, nos jeûne, qu'il nous pardonner nos pêche et qu'il nous guide sur le bon chemin amine y'a rabi 🤲🤲🙏🙏

  • @matymbodj7413
    @matymbodj7413 3 роки тому +8

    Sama xol sedana bilaye machallah 💕💕💕❤❤❤❤😭

  • @alioudiop8072
    @alioudiop8072 3 роки тому +17

    Serigne Babacar kassé sama way leu

  • @gltntegilou9532
    @gltntegilou9532 3 роки тому +7

    Dieureudieuf way merci beaucoup waa 2stv diamou reck ci yeun machalla yalla n'a yalla faylen goudou fan amiine yaraby machalla 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🤲🤲🤲☝️👍👍🥰😇💯🇸🇳♥️❤️♥️💞

  • @ababacarseck377
    @ababacarseck377 3 роки тому +6

    Maodo Malick yagnou khamale Yonène tibi yalla nala yalla Faye 🙏

  • @youssouciss537
    @youssouciss537 3 роки тому

    Macha allah mokale al khourane nrikhna tafsir yalna la Yallah sam yokou si fane may la weur ak katane bilahi contant yalna la Yallah fayeu yak gnigua andale gneup si spécial Gamou bi ak 2stv ak sponsor yi

  • @awagaye8807
    @awagaye8807 3 роки тому +12

    Machallah 💖

  • @ndiayebadou6939
    @ndiayebadou6939 3 роки тому +1

    Masha Allah dieureudieuf Ya Oustaz.

  • @papangalandoulo3774
    @papangalandoulo3774 3 роки тому +1

    Manchalah li nekh trop yalna borom bi content ci yenn..niou yag ko tewei ay att you beuri inchallah

  • @papaserignesakho4343
    @papaserignesakho4343 3 роки тому +1

    Waaaay li dafa nex kay looooool tafsir yagnoukoy firil 🌹❤️🌹❤️

  • @binetoudiop7928
    @binetoudiop7928 3 роки тому +2

    Machaalla el hadji ndiaye yalla na yalla faye bëgue nagnou dé
    Aidra kara ra zianagnou tafsir yalla na yalla same. Lafe thiat.

  • @omrdiaw2628
    @omrdiaw2628 3 роки тому +6

    Yalla nalen yalla faye
    🕋🤲

  • @ndeyecoumbagueye
    @ndeyecoumbagueye 3 роки тому

    ma shallah alhamdoulilah khôl nexna sama sopee djeuredjeuf tafsir gaye

  • @cameracachee2217
    @cameracachee2217 3 роки тому +1

    Li tafsir deff mo eup sollo yenene tele yeup💜💛❤

  • @l8l2
    @l8l2 3 роки тому +2

    Machalla li dra dakou ko
    Wayé nekk di tital nitt yi rek so déffé lii dem safara so déffé lé dem safara, dina tah kou beuguon toub sah dou yémé
    Wayy yalla moy borom yeurmandé sohoroul walahi azim

  • @ndeyefall6795
    @ndeyefall6795 3 роки тому +7

    Machallah dieureungéne dieuf Yalla na Yalla faye léne ♥️♥️♥️♥️🙏🙏🤲

  • @selbefaye577
    @selbefaye577 3 роки тому +2

    Yalla nalène Yalla sameu té takhawou lène. Yalla nalène Yalla faye yiw. Machallah Alhamdoulilah

  • @sulemaniba9873
    @sulemaniba9873 3 роки тому +5

    Tafsir yalla gouddale say fann yeu akh cherif mami aidara malen bouga sy sama kholl talibe thierno mouhamad samassa matam magui oukam cite mackiyou faye coli latouddu bissao guinne yalla guenn doundou 111 aminnne yarabale alamine

  • @babadiallo8800
    @babadiallo8800 3 роки тому +1

    Yalla nga goudou fannn ak wérrrrr

  • @gltntegilou9532
    @gltntegilou9532 3 роки тому +3

    Dieureudieuf cherif mamine aidara yalla n'a la yalla samou fayla goudou fan amiine yaraby machalla dieureudieuf diamou reck ci yow machalla 🙏🙏🙏🙏💯💯😇🥰❤️♥️🤲☝️👍💞🇸🇳

  • @yibydiop1536
    @yibydiop1536 3 роки тому +4

    Souma nekoul wone talibe cheikh loumay done la xamoul li nekhna si❣❣❣

    • @fatouseck5364
      @fatouseck5364 3 роки тому

      Yalnaniou yalla def deugue deugui talibé Cheikh séyal niou si tarikha bi bidiahi Nabil Moustapha SAWS

  • @khalifadieye9760
    @khalifadieye9760 3 роки тому +1

    Mahaalla yalla nalèn yalla faye 👂👈❤❤❤❤❤❤

  • @gayemboup611
    @gayemboup611 3 роки тому +7

    Ayo nekhna❤️

  • @ndeyeabyndiaye5188
    @ndeyeabyndiaye5188 3 роки тому +3

    Maachaa allah le duo Chérif-Tafsir gneup contaane nagnou si gamou gui yalla nalène yalla fay yiw goudal sène fane may lène wér si barké SEYDINA MOUHAMAD SAW

  • @mariamewar8457
    @mariamewar8457 3 роки тому +6

    Mashallah xol sedd na walahi

  • @mariamabalde8493
    @mariamabalde8493 3 роки тому +3

    Machallah Machallah soppyi Seidyna Mohammad 😘❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aissatasow7465
    @aissatasow7465 3 роки тому +6

    Je vous aime ♥️♥️♥️menchalla longue vie a vs inchalla

  • @jootayumamemaodo
    @jootayumamemaodo 3 роки тому +2

    Machallah Machallah 🙏🏿

  • @touremaguette257
    @touremaguette257 3 роки тому +1

    Machallah lidafa nekh Mohammed psl

  • @niangmansour5622
    @niangmansour5622 3 роки тому +1

    machalla aladawména kéne dou mohamet s.w.s

  • @diakhoumpandiakhate2372
    @diakhoumpandiakhate2372 3 роки тому +1

    Salam alkhamdou lilah santati sounou borom dieureudieuf 2stv choukran Cherif Mamine Aidara ak Tafsir Abdourahmane Gaye

  • @dianedie7378
    @dianedie7378 3 роки тому

    Ndakh mane nama kheuye soba ba goune ty digue lowoma Tafsir non non mano makou Tafsir dale mome lay wietalikou♥️♥️♥️

    • @miboldieng7574
      @miboldieng7574 Рік тому

      Bilahi xamal sa bopou rek
      Ms yalla Nala si Yalla sakhal

  • @brahimajack2540
    @brahimajack2540 3 роки тому +2

    No mane Tafsir douma rayy rime len ko li dafa nex😂😂😂♥️

  • @sarahjay5559
    @sarahjay5559 3 роки тому +2

    masha alla yalla na diam sante sii réw mii

  • @elimanewade1465
    @elimanewade1465 3 роки тому +2

    Yalla rek moye Burr👌🏾

  • @dabakonta7677
    @dabakonta7677 3 роки тому +3

    Machalah sma khôl sedd na thi diné l'islam bi

  • @mamantoure4864
    @mamantoure4864 3 роки тому +2

    Man dal je vous j'aime

  • @sallasall5571
    @sallasall5571 3 роки тому +1

    Je vous aimes trop bilay yalna sene diam yag🙏🙏🙏

  • @mboldieng234
    @mboldieng234 2 роки тому

    Bilahi Bi dou masi doyal tafsir yak cherif yalla ngene fi yague

  • @nogayefall2556
    @nogayefall2556 3 роки тому +1

    Machahalla yalla na yalla yook tahawaye bii 🤲🤲🤲🤲

  • @modoundongo6685
    @modoundongo6685 3 роки тому +1

    Machalla tafsir

  • @adjatoure206
    @adjatoure206 3 роки тому +1

    MACHAALLAHOU

  • @coumbadoucoure7455
    @coumbadoucoure7455 3 роки тому +1

    MâchaAllah à la 2STV AlhamdoulilAllAh ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @famambaye7607
    @famambaye7607 3 роки тому +4

    Machallllllah khol yi séd na

  • @babasillycamara2369
    @babasillycamara2369 3 роки тому +1

    Machallah dieu merci

  • @rokhayacimacisse4370
    @rokhayacimacisse4370 3 роки тому +1

    Yalla nalen yalla samm machalla

  • @malediarrafaye9485
    @malediarrafaye9485 3 роки тому +1

    Masha Allah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤Tafsir Mala beug

  • @pendasow2086
    @pendasow2086 3 роки тому +2

    Machalla Gaye 🤲🏻❤️🙏

  • @aissatou362
    @aissatou362 3 роки тому +2

    Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @babacardieye7967
    @babacardieye7967 3 роки тому +1

    Qui mooy mame maodo malick sy

  • @matydia5158
    @matydia5158 3 роки тому +1

    Machalla dieureudieufaty ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @famatadembele1325
    @famatadembele1325 3 роки тому +1

    Longue vie à vous.

  • @dianemamediarra119
    @dianemamediarra119 3 роки тому

    Sama💓💓💓💓 sédatina

  • @ouzdiackson753
    @ouzdiackson753 3 роки тому +3

    Psl ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @abdouseck7368
    @abdouseck7368 3 роки тому +2

    Macha Allah amna solo 💖

  • @fatimasy2240
    @fatimasy2240 2 роки тому

    MachaAllah 🤲🤲🤲🤲🤲

  • @hamedinetall2141
    @hamedinetall2141 3 роки тому

    Fier d'être talibé cheikh

  • @bohfall186
    @bohfall186 3 роки тому +1

    Machallah li nekhna♥♥♥♥♥♥♥♥

  • @michellkolley2639
    @michellkolley2639 3 роки тому

    Ya Allah Ameen 🤲thank you so much lmam ☝🏾🕋🕌🕌😭🕋🕋🕋🕋☝🏾☝🏾💝💝💝💝💝💝💝💝🤲🤲🤲🤲🤲

  • @fatoumattajallow6967
    @fatoumattajallow6967 3 роки тому +1

    Masallah❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾😭

  • @AbdoulayeDiallo-hh7sf
    @AbdoulayeDiallo-hh7sf 3 роки тому

    Machalla Machalla Machalla

  • @soihiboukeita8807
    @soihiboukeita8807 3 роки тому +1

    Mach Allah

  • @aissataaw4298
    @aissataaw4298 3 роки тому +2

    Machalla

  • @papasambaleye4779
    @papasambaleye4779 3 роки тому +4

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏿

  • @ndeyefalldiop2467
    @ndeyefalldiop2467 3 роки тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bilbassitv4798
    @bilbassitv4798 3 роки тому +1

    Manchallah

  • @khalifadieye9760
    @khalifadieye9760 3 роки тому +1

    ❤❤❤🙏🙏🙏❤❤❤

  • @ndiayemata3683
    @ndiayemata3683 3 роки тому +1

    ❤❤❤❤❤💖

  • @ramatoulayembaye9546
    @ramatoulayembaye9546 3 роки тому

    Sama khol comme glace

  • @kodiopndoye3810
    @kodiopndoye3810 3 роки тому

    Noumaî deffe pour invitelenes