Écouter Wazifa Mame Abdou Aziz Sy Dabakh à Tivaouane (Partager)

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 6 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 429

  • @seynaboudieng9568
    @seynaboudieng9568 2 роки тому +11

    Thiey souniou gorgui yallana yalla yokou ay leram

  • @alassanedioufciss7375
    @alassanedioufciss7375 3 роки тому +11

    Yalna dollila ay Leer Mame, ta yoka souniou cofeel ci yaw, ta tasniou ci sa barke bi Barakatou RASSUULOUL LAAHI SAWS

  • @madjiguenediop6541
    @madjiguenediop6541 3 роки тому +5

    Ndeyssane Mame Abdoul Haziz yalna souf oyof thi kawam

  • @zahrathiam651
    @zahrathiam651 4 роки тому +18

    Sy Malick yalla nagnou la yalla fayal tass gnou thi sa barkei bijahi taha PSL amine

  • @aminatandiaye3634
    @aminatandiaye3634 3 роки тому +2

    Mame Abdou wétale guaniou wéteule senegal nitou diama non politicien yalla nalla yalla kharé aldiana diegueulesa saye bakare akhe mboléme niwe yeupeu sama mame sama kharite tu ns manque beaucoup yalla na yalla deff si bareké mohamed yarassoulilahi salalahou aleyekhi wadsalambaniou dqdié aldiana inchaallah akh sama famille akh bépeu niwou nioulite té yalla na yégue inchaallah sy malick

  • @mariemdibba2027
    @mariemdibba2027 2 роки тому +3

    Mame Abdou yalla na gnou la yalla fayale yok sa ler sy❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mansorkandji3830
    @mansorkandji3830 2 роки тому +3

    Yalna yalla doli leeram te tasnu ci barkeem amiiin yaa rabbi

  • @babalissaguisse6982
    @babalissaguisse6982 4 роки тому +7

    yala na yalla yogue leer si mome sy malick

  • @gsthiatgueye5883
    @gsthiatgueye5883 3 роки тому +2

    Machallah sy malik dabakh al Khalifa sounou sang bii sy malik yalla nanou ko yalla fayal thi barke seydina mouhamed s a w

  • @sokhnafatoudeme634
    @sokhnafatoudeme634 4 роки тому +15

    Bilahiiii syyyyy 23 dèja doumako meuna fatè par c k j bobouuuu la dioudouuuu😭😭❤❤❤❤❤

  • @djibelgueye4412
    @djibelgueye4412 4 роки тому +15

    Macahla sy malick yala nako yala khar aldiana

  • @vieuxsarr6424
    @vieuxsarr6424 Рік тому +1

    Le meilleur marabout de tout les temps kendoumome

  • @ngonelo1769
    @ngonelo1769 4 роки тому +7

    Ndeyesane mame Dabakh sama serigne papa yalla na yalla yokk sa ay lere sa barsakk tai tasgnou SIDA barke tu nous manque

  • @sophiendiaye2230
    @sophiendiaye2230 4 роки тому +16

    Maachaala yalna YAALA fayalnouka wiw super fazifa émouvant Soukran

  • @yibydiop1536
    @yibydiop1536 4 роки тому +16

    Machallah sy Malick yalna BOROM bi yesal yeurmandé si mom té tass gnou sisa Barké inchaallah

  • @layladiop6106
    @layladiop6106 3 роки тому +2

    Machallah Sy yalla na allah soubhaha wa talla terrou sa adiana ay firdawsiya

  • @adjika5780
    @adjika5780 4 роки тому +12

    Yalla na yalla yessal yermedem thie barke mouhamed psl

  • @fatouseck7344
    @fatouseck7344 4 місяці тому +2

    SOUGNOU MAME ABADAANE INCHAALLAH MERCI BEAUCOUP NOTRE KHALIFA GENERAL DES TIDIANES RTA MAME DABAKH DAABAAKH RTA FIRDAWSI SOIT SA DEMEURE ÉTERNELLE INCHAALLAH SYMALICK RTA

  • @ousmanesimakha9078
    @ousmanesimakha9078 5 місяців тому +1

    Masha'Allah Mame Abdou Dabakh Malick Yalla Na Yalla Yok sa lér té taf gnou sisa barké 🙏🏿🤲🏿 Amine

  • @MbosseSamb-qc8bi
    @MbosseSamb-qc8bi Рік тому +1

    Machala s'y Malick yalananiou yala Tass si barkem yala York ay leram Amine

  • @vieuxsarr6424
    @vieuxsarr6424 Рік тому +2

    Tu resteras toujours dans nos cœurs billahi sy malick ya bakh

  • @combecane257
    @combecane257 5 місяців тому +1

    Yalla NGA hippé aldjana firdawsi sougnou Mame sougnou soppé Mame Dabakh mou bakh mi... Amine ya Rabi ❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndeyeawadabakhNdiaye
    @ndeyeawadabakhNdiaye 4 роки тому +24

    Yalla rabbi mayma dommm bou touddd mame Abdoul Aziz dabakh
    Euway ami'ne
    Bou dieul say djiko
    Amine
    Amine
    Amine

  • @seydiafall9159
    @seydiafall9159 2 роки тому +1

    MachaALLAH yallana YALLAH BOURBI YOOK lerame thia barzakh. Kou nek thi kholyi Mame Abdou Aziz sama sopé ba.

  • @adjika5780
    @adjika5780 4 роки тому +1

    Yalla nako yerem thie barke mouhamed psl

  • @21abdiescobarofficeal45
    @21abdiescobarofficeal45 4 роки тому +4

    Buga nala torop mame abdou Aziz babahk Malick sey yanna nala yallah yerem Ameeem 🙏🙏😭

  • @papadieng621
    @papadieng621 4 роки тому +16

    Je pleureé pour Notre MAME Abdou et le Wezifa Tidianiya part tous DANS le monde TARIKHA CHEIKH Ahmed Tijane MOY DEGUE kham kham

  • @mamanfounediop2039
    @mamanfounediop2039 2 роки тому +3

    Yalla n'a niou yalla tafe thi sa barkel

  • @general4477
    @general4477 4 роки тому +12

    Sénégal dina yaga am diam sakh deh.sans tambour ni trompette on se dirige vers les mains les plus sûrs de la planète .

  • @alimatousadiyandiaye2498
    @alimatousadiyandiaye2498 3 роки тому +1

    yalla na yalla yokk sa leeerr tass gnou thi sa barké tu nous manques beaucoup mame boye

  • @alikharma7706
    @alikharma7706 4 роки тому +4

    Dieureudieuf cheikh ahmed tidiani lep yaw leu diarawlaka mame maodo diarama mame dabakh ni rekk ba firdawsi amine yarabii

  • @youssouphadiop1854
    @youssouphadiop1854 4 роки тому +7

    Machaalla yalna yalla yoko léerou bamélame

  • @Mouslim-talibe-hamallah
    @Mouslim-talibe-hamallah Рік тому +2

    Jaime trop ❤ qu' Allah le tout puissant lui fasse miséricorde Amine

  • @traedinternationalltd8364
    @traedinternationalltd8364 4 роки тому +7

    Machalah Dabakh Malick yalla tass gnu si barkem

  • @aminaseck4943
    @aminaseck4943 4 роки тому +10

    😭😭 Sama sopé sama Mame Abdoul Aziz Sy tjrs présent dans nos cœurs et dans nos vie. Je l'aime de tout mon âme 😭
    Yalla nala borombi doli ay lér barké Seydouna Muhammad SAW

  • @Hawaa351
    @Hawaa351 4 роки тому +9

    mame abdou yalla rek ak yonente bii

  • @diarrasow4738
    @diarrasow4738 4 роки тому +9

    Macha Allah borom quadrante ans zéro faute yalla na ko yalla bourbi fayal si barké seydouna moukhamed salalahou alehi wassalam amine yarabi Allah 🤲🤲🤲😥

    • @fatouseck7344
      @fatouseck7344 2 роки тому

      Nittouyaaallahbouwereezerofautebilakhirtamerciwakeurmamemaodomalickleguide

  • @fatoufayendao1694
    @fatoufayendao1694 2 роки тому +27

    Machaallah k’ALLAH t’accueille dans son paradis firdaws
    Allahouma Amiiiiiiiiiiiine

  • @papadieng621
    @papadieng621 4 роки тому +8

    MAME Abdou YALLA nala YALLA doli grat te yok la ler sisa barke BAY ak say mak AMINE

  • @cissecoumba1563
    @cissecoumba1563 4 роки тому +8

    Yalla n'a yalla nangoule gniou niane amine

  • @aichagaye3659
    @aichagaye3659 4 роки тому +12

    Maschalla Sy Malick yallana sougnou borom yokk léram tass niou ci barkem

  • @fatoumatadiop6276
    @fatoumatadiop6276 4 роки тому +10

    Yalla na yalla yokou sa lerou bammel.dieureudieuf sounou Mame

  • @combecane257
    @combecane257 6 місяців тому +2

    Yalna sougnou borom doli la yeurmandé ak lér té tass gnou si sa barké ❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndeyediagne1932
    @ndeyediagne1932 2 роки тому +2

    Sy Malick yallah na yallah yoke sa léer té taas niou tie sa barké

  • @abdouazizba99
    @abdouazizba99 11 місяців тому +3

    Macha'Allah dabakh Yallah nagnou Yallah seid sisa leir AMINEEEEE

  • @diopaly2132
    @diopaly2132 4 роки тому +7

    Hola me llamo aly diop soy Senegal estoy muy con tento de este regordo de noestur avoelo mochos gracias

  • @cheikhdiba4448
    @cheikhdiba4448 3 роки тому

    alahouma la adorrr seydil hadji malik sy lep tivauone lay khewe malaco wakh incalahou seringe

  • @abdoulayesanoho1347
    @abdoulayesanoho1347 4 роки тому +25

    Que la terre te soit tjrs légère, tu manques trop aux peuples, le Sénégal en particulier en cette période de pandémie avec les prières que tu donnais tout le temps

  • @adjarokhayadiop2890
    @adjarokhayadiop2890 4 роки тому +5

    Je suis fière. D être talibe. Cheikh

  • @coumbaly2442
    @coumbaly2442 6 місяців тому +2

    Sy malick yalla na allahou yokk say léer ya bakh dabakh

  • @Sokhna_si
    @Sokhna_si 4 роки тому +10

    Alhamdoulilah dieuredieuf Mame boy yallah na niou yallah tass thi sa Barker thi Barker arkhourane Barker Inchallah

  • @ouleyecamara427
    @ouleyecamara427 4 роки тому +10

    Éternellement présent SY Malick, yalla na la yalla yeureum té tass gnou thie sa barké. Figua teudeu djisgua Sénégal limouy doundou ak
    mbass-bi. Gnou guilay gnane Mame Dabakh ngua gnaanal Sénégal, Afrique , Adina yeup.
    Allahouma Amine.

    • @salydiouf2193
      @salydiouf2193 4 роки тому

      Amine Yabil Allamina. Puisse Ya Allah entendre vos prières et les exaucer par la grâce de Moulaye Dabakh Cheikhal Abdou Aziz SY RTA.
      Puisse sa lumière continuer de nous guider.

    • @ndeyeawadabakhNdiaye
      @ndeyeawadabakhNdiaye 4 роки тому

      Ouleye Camara amine amine

    • @khadydiop4813
      @khadydiop4813 3 роки тому

      Mame Abdou 40 zéros faute sama mame Abdou damakha sope borome djikho bouraffete dafa wathe popame yalla xekhetukha

  • @papmgueye4218
    @papmgueye4218 4 роки тому +11

    Yalna yalla gueune' corona virus thi adounabi.
    Surtout SÉNÉGAL.
    AMINE thi barke' MAM ABDOU AZIZ SY.

  • @talibecheikh1478
    @talibecheikh1478 4 роки тому +41

    Ndeyssane sa voix raisonne dans mes oreilles .mame tu nous manques tellement dans ses moments de détresse walahi hanzim dougnou la meussa faté.repose en paix a jamais dans nos coeur et nos esprits.

    • @mboubakasse7427
      @mboubakasse7427 4 роки тому +3

      Machalla tu nous mangue a code de Sète maladie s'y malik

    • @modoudiagne6151
      @modoudiagne6151 4 роки тому +3

      هو شيخنا الجليل مام عبد العزيز رضي الله عنه

  • @abdouazizba99
    @abdouazizba99 11 місяців тому +1

    Teiksi kharei leu si al Jannah you kawei yi AMINEEE

  • @souleymanekeita5357
    @souleymanekeita5357 4 роки тому +10

    Mame abdou Aziz sy dabakh merci pour tes enseignements et tes comportements envers les gens yalla nalla yalla faye si sa dieuf amine

    • @tanyfall7530
      @tanyfall7530 4 роки тому +1

      ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @elmansoursarr5646
    @elmansoursarr5646 3 роки тому +4

    Masha Allah suñu mame Dabakh yalna ñouko yalla fayal ta tass ñou si barkem💗💗💗💗🙏🙏🙏

  • @niangfallou4520
    @niangfallou4520 3 роки тому +6

    Machallah yallah yalla yokk Say Lére Mame Dabakh 😍

  • @diaryndiaye3018
    @diaryndiaye3018 9 місяців тому +4

    ❤❤❤❤❤Machalla yalla na Niou ka yalla fayale amine yarabi si barke seydouna Mohamed saw

  • @aissatoudieng3937
    @aissatoudieng3937 4 роки тому +13

    Machalla mame yallanala yalla faye

  • @cissecoumba1563
    @cissecoumba1563 4 роки тому +25

    Mame est toujours avec nous yalla n'a yalla yokke leram amine

  • @BinetaSall-wx9wt
    @BinetaSall-wx9wt Рік тому +1

    Sy Malick yalla n'a yalla yokke leram amiiiiiiiii Mame Abdou ❤

  • @amadoudianedia1614
    @amadoudianedia1614 4 роки тому +12

    Mame Abdou Moy Diangale wasifa

  • @khadyndiayeaye7295
    @khadyndiayeaye7295 4 роки тому +17

    Amine Mame DABAKH yallana yalla Tass niouci Barkem Amine

  • @Madylamytoure
    @Madylamytoure Місяць тому

    Wallahi hool sédenaa ❤❤❤❤ Yalla nagnou Yalla feeyaallll MAME cheikh seydil hadji Malick Sy RTA ak ndiabotame ❤❤ Yalla nagnou Yalla feeyaallll MAME Abdou Aziz dabakh ❤❤❤ té mou yokou lérame

  • @absadiop9430
    @absadiop9430 4 місяці тому

    ❤❤billahi wallahi watallahi li woor ba woor Moy ni rek kou yalla denkon la ték thi dimbalenako ba moussoul derappé. Wayê itam thia ngor gua thia wathie ga AK dal gua fékhéna ba guenoul hala'lahou hala'rassoul deferana yakhou yakhou Yep thi bepp fana tekgnou thi sieatal moustakhim Mame Abdou dal gathié ngualama kou derappé itam yawla wayé mom matalna mataléna thi ndimbalou yalla yalna yalla yokk lereme maodo fall

  • @adamadieng4148
    @adamadieng4148 4 роки тому +6

    Mame waite nagnou sa lair YALLA boumou dagne dignou lairal si adouna bouleundeumbi

  • @deffaly9056
    @deffaly9056 4 роки тому +7

    Masha Allah ❤❤❤🙏🙏🙏🙏 YALLAH na Yallah yoke lèram tè taass niou si barkém si barké Seydouna MOHAMMED saw amine ya Rabbi 🙏🙏🙏❤❤❤🕋

  • @mereada94
    @mereada94 4 роки тому +7

    Yalna Borombi fayalniouko Amine Ya RABBI

  • @alyba3288
    @alyba3288 4 роки тому +39

    Que la terre te sois légère Mame boye adoré.amine yaa raabbi

  • @astousall6213
    @astousall6213 2 роки тому +8

    Fière d'être Talibe Cheikh
    Wazifa bi nékh na ♥️♥️🥰ma sha Allah

  • @ismailathiam2871
    @ismailathiam2871 2 роки тому +6

    Ma SHA ALLAH dieuredieufty Maodo
    DABAKH l'inoubliable toujours dans nos coeurs

  • @mansoursy6517
    @mansoursy6517 4 роки тому +1

    Yallana yalla yock aiye lerrame t’es tasse ngou sii barkéme

  • @ramseschou7708
    @ramseschou7708 4 роки тому +17

    Non mais quelle voix!! quelle pronociation!! quelle cadence!!..

  • @AmynaNabySarr-bouDabakh
    @AmynaNabySarr-bouDabakh Рік тому +41

    Toujours dans nos cœurs 💓Yalla nala Yalla doli yeurmandé tei tasse gnou si sa barké Mame boye. Dabakh 💓🙏🏾

    • @abydia6089
      @abydia6089 Рік тому +3

      Merci

    • @adjiseck5667
      @adjiseck5667 Рік тому +2

      Amine yarabi machalla sy malik ❤❤❤❤❤❤yalla na yok lerame tassgnou si barkéme amine

    • @MaguetteCiss-qe5ig
      @MaguetteCiss-qe5ig Рік тому

      ​@@abydia6089#v😮😢🎉😂😬🥭

    • @daouddispo3973
      @daouddispo3973 Рік тому +1

      ​@@adjiseck5667merci beaucoup

    • @cheikhngom2796
      @cheikhngom2796 Рік тому +1

      Amine ya rabbi 🙏🥰

  • @amadinetallof6503
    @amadinetallof6503 2 роки тому

    Euskey Cheikh Abdoul aziz sunu mame sunu serigne na Yalla yoke sa lère saassounè

  • @omarsembene4426
    @omarsembene4426 2 роки тому

    Machala magui wetalikou depuis italia chaque matin ma deglou ko

  • @sinequoinone5121
    @sinequoinone5121 3 роки тому +12

    Seulement entender SA voix ,bou's sommes des privilegiens et surtout ceux qui ont vecu la meme epoque de ce Saint Homme..Dabakh Malick YNTSSB🙏🙏🙏

  • @papsouley2000
    @papsouley2000 2 роки тому +12

    Dans nos cœurs et nos esprits tant qu'il nous restera un souffle de vie !

    • @djkabou3006
      @djkabou3006 2 роки тому +2

      Manchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @moussafall8696
      @moussafall8696 2 роки тому +2

      Mérci DAABAAKH que Dieu te le rétribue!ton souvenir nous restera Amen

    • @AmynaNabySarr-bouDabakh
      @AmynaNabySarr-bouDabakh Рік тому

      💓💓💓🙏🏾

  • @fallfatou4627
    @fallfatou4627 2 роки тому

    Machalah sounou Mame yallanako leram yeguelo thia makama ya gueuna kave si barke SeydinaMouhamed PS l

  • @emanalami-gaye955
    @emanalami-gaye955 4 роки тому +10

    Rahim’Allah ya Mame Abdou Ak sa Harit Mame Abdel Hadi El Alami ak sa dorm Mariam Bensouda Yalna YAllah leral sen Baamel teh dekkal ko fa

  • @albouryndao480
    @albouryndao480 4 роки тому +9

    macallah yalla yalla faye lén way

  • @ndureaaawa9481
    @ndureaaawa9481 2 роки тому +1

    Mashallah Amna solo Jerry Jeff Mam Dabakh

  • @isesam3011
    @isesam3011 4 роки тому +3

    Yalna yala douguelko ci aldianam you kawéya amine

  • @zeinabouniang3969
    @zeinabouniang3969 4 роки тому +13

    Machallah, que Dieu le tout puissant l'agrée et nous guide vers le droit chemin 🙏🙏🙏

    • @zeinabouniang3969
      @zeinabouniang3969 4 роки тому +2

      Amine Amine, nous t'aimons très fort Mame Abdoul Aziz

  • @astpuizambart1126
    @astpuizambart1126 2 роки тому +3

    Machalla, Machalla, Machalla Borome 40 ans sans fautes Yalla n'a Yok Yermademe This Môme , Tasse gnou si Barkeme Amine Yarabi Machalla

  • @laminendiaye4631
    @laminendiaye4631 4 роки тому +28

    MACHA ALLAH,DABAKH MALICK TOUJOURS DANS NOS COEURS

  • @mouhamadediouf101
    @mouhamadediouf101 4 роки тому +5

    Machala yalnakoyalayeremkharekoaljana te

  • @mamanrokhayadieye4390
    @mamanrokhayadieye4390 2 роки тому

    Mbayi nieup diagale ba tay dou massa dieh guide spirituel perpétuel de tous les temps Merci papa et grand père ALLAH SWT tass niou si barkem

  • @biguendiaye5140
    @biguendiaye5140 2 роки тому

    Yala naniou ko Yala fayal Amine

  • @khadidiatoulysall3749
    @khadidiatoulysall3749 2 роки тому

    Mame,Yallah bougnela mosse fate!!!YALLAH Nala YALLAH khare Aldianaye Firdaws thi wettou Seydina Muhammad Rassoullah Salalahou Aleyhi wa Salam ♥! Amiiine yaa Rabal Aalamina Allah!je vous-mêmes Remercie infiniment pour tout ce que 6èmes a écrit of your own q

  • @sambabsa852
    @sambabsa852 4 роки тому +1

    Aladji Abdou toujours présent dans nos cœur yalna KO sounou borome dolli Aÿ lerr tasniou si barkem

  • @mamesayendao7484
    @mamesayendao7484 2 роки тому

    Machala yalna yala fayal gnou sounou mame Dabakh.

  • @NdeyemagateNdiaye
    @NdeyemagateNdiaye Рік тому +1

    Machallah biss bou nekk maye yessel sama beuguel thi yaw Sy Malick

  • @cheikhdiouf4029
    @cheikhdiouf4029 4 роки тому +1

    MAME ABDOU AZIZ DABAKH KÉN DOU MOM WALLÂHÎ WALLÂHÎ

    • @safietousamb1340
      @safietousamb1340 4 роки тому

      Fatabaraka lahou sy malick wetal gua senegal loool sy malick alhamdoulila

  • @adjiseck5667
    @adjiseck5667 2 роки тому +1

    Amine yarabi yalla nagnouko yalla fayale bopame amine yarabi machalla sy malik 🤲🤲🤲🤲🤲🤲❤❤❤❤❤

  • @moussadia4503
    @moussadia4503 4 роки тому +2

    Alhamdoulillah rabil alamine

  • @assanefall3199
    @assanefall3199 Рік тому +2

    Allahou akbar wasifa bi Machallah

  • @fatouresow1675
    @fatouresow1675 4 роки тому +4

    Macha Allah Sy Malick

  • @aishabnc
    @aishabnc 2 роки тому

    Thiey talibe cheikh
    Diegalou souniou borom
    Magal borom bi
    Diouli si sangou sangue yi
    Kou am lènène dieuleul tè bayimak bi
    Alhamdulilah