deysan li dawna yaram, Une famille expulsée en plein jour, leur maison démolit par leur propre frère

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 26 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 99

  • @OriginalThiernoFaty
    @OriginalThiernoFaty Місяць тому +18

    Guiss ngua nitt bala ngua até si genre yii danguay degglou niarry version yeup . Femme yii gno beuri problème

    • @Bgch7525
      @Bgch7525 Місяць тому +4

      Je suis d’accord avec toi mére yi gno sikk rekh yalla na ma yalla balle. Mais affaire d’héritage mo sensible.

  • @diomagirard5899
    @diomagirard5899 Місяць тому +19

    Bonjour Fadel j'espère que vous allez bien svp ou ce situe cette femme j'ai un terrain que d'ici 10 ans j'aurais pas besoin si sa peut leurs aider le temps de ce relever sincèrement

    • @sokhnandiayeba5606
      @sokhnandiayeba5606 Місяць тому +2

      Yalnala yaĺllah feye sa yène

    • @maimounagueye350
      @maimounagueye350 Місяць тому +1

      Maymako waay

    • @diomagirard5899
      @diomagirard5899 Місяць тому +1

      @maimounagueye350
      J'ai deux filles deux garçons si non je l'aurai fait avec grand plaisir sa sœur bonne chance Dieu est grand 🥰

    • @ninkinanka3644
      @ninkinanka3644 Місяць тому

      Yow Nitt Nga​@@maimounagueye350

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Місяць тому +1

      *Ohh sa yénè rafette na Yalla nala sougnou Borom fay sa yeurmandé 🙏🏽*

  • @Matar-i6d
    @Matar-i6d Місяць тому +25

    Adina lègui dall kou euppou nite dollè rék wane ko, li dfa niaw mème famille, Adina dou dra 😢😢😢😢

    • @ArameMbaye-j6k
      @ArameMbaye-j6k Місяць тому +5

      Bala ngay wakh danguay kham ba paré yani togne deh té douniou lako bal abadane

    • @maho5304
      @maho5304 Місяць тому +1

      @@ArameMbaye-j6kwallahi demna setaan benen video bi afaire moy lolu ❤

    • @gelawargelawar8972
      @gelawargelawar8972 Місяць тому +3

      Diay sene keurr di victimiser wou sene wakh diouboutt

    • @ballagaye2955
      @ballagaye2955 Місяць тому +1

      Dagnouy fén sén Mac wakhna gni noi nékoul thie deeg .dékété femme yi noi beugeu gnou diay ba paré xallis bariwioul lolou moy problème

    • @assanembengue6364
      @assanembengue6364 Місяць тому +1

      Elle son à accuser c'est frère et les autorités judiciaires , elles sont pas incohérent

  • @OumyNgom-m7p
    @OumyNgom-m7p Місяць тому +10

    Bonsoir la famille faites très attention aux messages c'est entre famille et c'est un seul version faites doucement et attendez les autres version c'est ds notre quartier

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 Місяць тому +9

    Thiéye Sénégal Fomou dieum ohh vraiment lii niaw na trop bilahi 😢

  • @cheikhdiop851
    @cheikhdiop851 Місяць тому +25

    Sarap li rk amna nio xamni dama yakarni douniou xalate déeee😢

    • @fatimandao8359
      @fatimandao8359 Місяць тому +2

      Yow d diop yaye xalate dèh gni aduna rék lagni dokh mais yalla dina até

  • @MamadouSow-j1n
    @MamadouSow-j1n Місяць тому +6

    Attention ! il ne faut pas juger sans avoir entendu l'autre version

  • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
    @AboubacryGASSAMA-zs7oi Місяць тому +8

    Ohhh ndèyessane adouna dou keur dhè walahi koudoul halate bamèl loula nèkh défal...loumou yague yague domou adama bi souf rèk laye sanguo ...louway meune dèf thilou bakh dèfko louway meune dimbali dèfko .doko rethiou fi ak feulè inshaalla yalanala léne borom tahawou tè yombal lèp inshaalla

  • @adamasarr2941
    @adamasarr2941 Місяць тому +8

    Ndeysane lii rek motax beugouma am ay djabar

  • @adamadieye7767
    @adamadieye7767 Місяць тому +3

    Liga wokh kén comprendre Alioune gauche Alioune droite

  • @mansourgaye6205
    @mansourgaye6205 Місяць тому +9

    Keur mame dou Keur jiguéne gñu nek si keur bagne seuyi beug fa yoré séni dôme problèmes la senegal bou lolou wésso adina amule solo Keur gui môme diaye rek mirage kouné xame fo dieum ni nguéne fa beuga néké meunule wéye ñiati famille si béne Keur kouné ak sa ndiabote té borom keur gui nékoufa dokhoul

    • @cisco9615
      @cisco9615 Місяць тому +3

      Lolou dou force

    • @abonnesundefilesgars
      @abonnesundefilesgars Місяць тому

      Yow dag kham loulen fa tek ?
      Niola wakh beugouniou seuyi ?

    • @kharymkleye2187
      @kharymkleye2187 Місяць тому

      Waxi dof dé nga fi wax nga baal ma. Ségém goor ñi ñoy am problème pour am kër massa Soxna yi ñu gëm lo ni da ñu léen a wara yor, dëkkël leen. YÀLLA daganal tàkkaliko nak. Ku la wax ni fassé wu ñu léen ?

    • @mansourgaye6205
      @mansourgaye6205 Місяць тому

      @kharymkleye2187 bayil sa thiakhane yi cône loutax mouni bi sama dieuker di dound neksi keur gui gñi soléne dégué xame ni keurgui lagñi kheuthio loutax bi dieukéreum di dound nieuwe deuk ak môme keur mame dou Keur

    • @kharymkleye2187
      @kharymkleye2187 Місяць тому

      @@mansourgaye6205 li mu wax lép déglu wu ma ko. Li nga wax ni Soxna yi ñoo wara bàyyi di dellu séen kër Famille dëkk fa ak seeni doom bu fa sëy amatul la doon tontu parce que da nga ni loolu problème la. T man dé wax dëgg gisuma nu mu nekkee problème. Waxumala tas waaya ku boroom kërëm faatu sax sañ na dellu kër famém bu dé amut fu mu jëm

  • @fatimandao8359
    @fatimandao8359 Місяць тому +4

    Maned vraiment je ne comprends plus rien sokhor gui ameu si famille légui dafa eupe yalla na yalla doli soutoura

  • @Beugdeug
    @Beugdeug Місяць тому +3

    Ya😢trop de cas Pareils dans ce pays

  • @sawroumbengue7820
    @sawroumbengue7820 Місяць тому +4

    Alakhira dina méti trop 😭😭

  • @ballagaye2955
    @ballagaye2955 Місяць тому +2

    Femme bou kat dieulna 500mille si Xallis lep mom la grand frère bi wakhna lou wor lou lér .diayna gnou keurgui borom keur mélél guéné

  • @HelenePouye-fk5em
    @HelenePouye-fk5em Місяць тому +3

    Sénégal amoul loi. Ou est le ministre de la famille.

  • @BMS7810
    @BMS7810 Місяць тому +1

    Ahh man teey naci j ai écouté la version du gars

  • @Beugdeug
    @Beugdeug Місяць тому +11

    Elles n'ont pas d'assistance et ne sont pas calme ndayssane, les frères ayez pitié de vos jeunes frères et sœurs adiuna amoul solo

    • @nioukfall7869
      @nioukfall7869 Місяць тому

      😂😂😂😂c frères et sœurs est ce que ils sont gentils

  • @aronadiagne5272
    @aronadiagne5272 Місяць тому +5

    Mé Maty keur gui daniouko wara diay sédéloko vraiment bouguène menoul ande môme diaybi faratala

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 Місяць тому +8

    sama domou bay moune day tek ay plawam pour nahma۔ma lathko papier keurgi moune douko guenne plus d 22ans😂dima forcee signee

  • @BayelatToure-f9q
    @BayelatToure-f9q Місяць тому +8

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @SokhnaDieme-r7d
    @SokhnaDieme-r7d Місяць тому +4

    Toujour affaires yi nilaye dèmè gni ame fougniou deuk ba parè dagniouy beugue dia😢ye gni amoul fougn deuk nè diayougniou ’mai diaye mom bala am ifok guène wakhtane si diek a par ca keur ndono dou keur kounek nagua woute sayefou bop conseil pour tout le monde

  • @AminaSeck-t9j
    @AminaSeck-t9j Місяць тому +1

    Yalla na yalla atté

  • @IbrahimaDiallo-ub3cr
    @IbrahimaDiallo-ub3cr Місяць тому +1

    Courage mes petites mamans

  • @TyyyHhyy
    @TyyyHhyy Місяць тому +6

    Police mo wrona convoquer ça
    Fait oubli enquette

  • @ummhuraira2495
    @ummhuraira2495 Місяць тому

    Miraas lagnou Yalla saak. Kou dè dagnou ko wara miraas!!!!! Deukk bi fèss ne dèllll ak problèmi miraas. Nagnou RAGAL YALLA!

  • @PaaliKebe
    @PaaliKebe Місяць тому +4

    Naniou lén diapalé waay

  • @HamadySall-nk3ek
    @HamadySall-nk3ek Місяць тому

    Ils sont le ministre de l'administration du territoire les préfets les maires et surtout la justice sénégalaise. Diomaye et sonko doivent faire travailler ce ministre paresseux en 8 mois aucun effort concernant les plaignants victimes de ces situations graves. La justice doit faire immédiatement son travail.

  • @mbodjamadou1829
    @mbodjamadou1829 Місяць тому +1

    Ah les Femmes problémes Rek incohérence wakh lou amoul rek

  • @KREUPEUZEII_BII
    @KREUPEUZEII_BII Місяць тому

    Elle n'est pas cohérente dans ses propos elle flippe tandis que dans l'autre video le frère est rester calme lucide et trés clair

  • @tallaseye9893
    @tallaseye9893 Місяць тому +2

    Nit kou faatou daniou ko wara mirass diaye baguass yépou sédeléko kounék dieull walam diamou né nioye

  • @mittv7661
    @mittv7661 Місяць тому

    On a écouté la version des frères avec des preuves claire.

  • @HelenePouye-fk5em
    @HelenePouye-fk5em Місяць тому +2

    Thiey adina

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 Місяць тому +5

    mam diamaguen la deukeu si marche bi samay domou bay dagnma fek may nelaw nioubeugeulama signelo te wahtan amoul ma bagne te ay fx papie laniou endy 22ans niou neubeu kayitou keurgi۔ hehak man ba tay signewoumeu۔moy compeulo ak ay haritam nioumay bapp

  • @YossouphaNiang
    @YossouphaNiang Місяць тому

    Thiéye yalla 😔😔😔

  • @mamadoufaye9962
    @mamadoufaye9962 Місяць тому +3

    Thieye senegal ak problemou souff khawma kagne laye thiowou souff di diekh senegal khawma kaane mosi am degue wayé senegal barina niou niémé akha dé lol sakh

  • @salimatoudiallo9404
    @salimatoudiallo9404 Місяць тому +2

    Sama keur mame dou keur té yenn téyou lenn dara

  • @mbayediopmbaydiop8342
    @mbayediopmbaydiop8342 Місяць тому

    Slm slm lep jaam nima degué versión djiguéne Yi sen wakh dioubul

  • @mariamagueye9084
    @mariamagueye9084 Місяць тому +1

    keurou mame nak vraiment dou keur.

  • @awadiop5533
    @awadiop5533 Місяць тому +2

    😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @sokhnandiayeba5606
    @sokhnandiayeba5606 Місяць тому +1

    Adouna metina légui bé seet di kheuthio keurou mame

  • @diomalmandiaye9024
    @diomalmandiaye9024 Місяць тому

    Tekk ack tegui guenn warr bayyi. Anni senn mirass mam. Konn sen pape moko donou. Mirass lenn sen pape kou nakh djel wallam ta demm

  • @Flame-gl9lo
    @Flame-gl9lo Місяць тому +5

    Xana amoul ay gor si yen nguen diapou wadji niouss ko

  • @dialibatoumarahib79
    @dialibatoumarahib79 Місяць тому +2

    Teyoulen dé

  • @moussekharma2181
    @moussekharma2181 Місяць тому +1

    Maty mi loumou dra lérou si

  • @mariamabandia777
    @mariamabandia777 Місяць тому +2

    Douko dieurignio dé

  • @MTd-w2v
    @MTd-w2v Місяць тому

    No ki

  • @khadysene799
    @khadysene799 Місяць тому +2

    Legui neew dolei togne la

  • @bayebeye3070
    @bayebeye3070 Місяць тому +1

    Métina lole mais nanouye mirasse si tèle pour éviter ce genre de malentendu

  • @elhadjipaye5398
    @elhadjipaye5398 Місяць тому +1

    Je pense que.majeur partie bi bouniou daccoré rek ..loi.ndiaye bi day takhaw.obligatoirement

  • @HamadySall-nk3ek
    @HamadySall-nk3ek Місяць тому

    Vraiment le nouveau gouvernement le ministre qui s'occupe de ce problème doit rendre la justice et réparation et condamné si ya abus de pouvoir. Des affaires comme ça ca commence à trop nous agacé. Le ministre et les juges soient ils travaillent soient ils rendent la justice sénégalaise. Qu ils soient de diomaye de sonko ou de Macky Sall. On en a marre de voir des décisions qui font souffrir d'autres et l'état est bon cas encaisser et sourire pour rien faire.

  • @OusmanaDiallo-md7os
    @OusmanaDiallo-md7os Місяць тому

    😢😢😢

  • @serignemodoundiaye8418
    @serignemodoundiaye8418 Місяць тому +1

    Mettina trop
    Mais lu yalla wax kuka deful guiss ko nitt bu fato (dei=mort) nan ko miraas kunei djeul liga moom kuka djendeu bo nango nitt gni deuk fi bo demei ba begue ko djaye ioe mako djeundeu wax ko ñifa deuk

  • @Soupersokizo
    @Soupersokizo Місяць тому

    C est triste

  • @Beugdeug
    @Beugdeug Місяць тому +1

    Maty ou est son mari le père de ces enfants aussi qu'il réagisse sinon Mary nak

  • @ababacarsedikhkebe7775
    @ababacarsedikhkebe7775 Місяць тому

    Alioune ya yak fayda diayo sa keur baye di diaye sa keur Mane

  • @mariamademe
    @mariamademe Місяць тому

    😭😭😭😭

  • @hawadiagne7221
    @hawadiagne7221 Місяць тому

    Thiey lii adouna amoul solo adouna dou keur

  • @Galsen655
    @Galsen655 Місяць тому

    Niom sèn papa bou nieuguè dè sè mame aye domou ndeyesane sakh molène eupeullè si

  • @Beugdeug
    @Beugdeug Місяць тому

    Quant est-ce-que justice sera rendue aux pauvres populations

    • @patriciafall464
      @patriciafall464 Місяць тому +2

      Justice khamoul pauvre deh, la justice c'est pour dire le droit.. Pauvre ak riche nio si yém, kou âme deug y'a âme deug nga riche wala nga pauvre.. Wayé keurou ndono mome déggo rekk wala si diaye laye moudié..

    • @nioukfall7869
      @nioukfall7869 Місяць тому

      ​@@patriciafall464Merci c'est ça que doit être la justice c'est oas parceque on est pauvre qu'on a raison vice versa

  • @mariamabandia777
    @mariamabandia777 Місяць тому

    Yaw mal yuiyame dina metie how ga neke si keur di khagne kene keur 😢😢

  • @ahmadousaradiallo7904
    @ahmadousaradiallo7904 Місяць тому

    😢😢😢 arête de provoke

  • @moussacissokho4248
    @moussacissokho4248 Місяць тому

    Mais pourquoi bok ak mom béna baye .té dakoroul Ndiaye.
    Police atéléne dégue .
    Je jour du jugement dernier vous attends 😢

  • @Bgch7525
    @Bgch7525 Місяць тому

    Que Dieu me pardonne mais qui sole lou rouge niro na kou beurri histoire

  • @cheikhounambackecheikhouna6942
    @cheikhounambackecheikhouna6942 Місяць тому

    Bilahi elle ne connais rien kii nafëk la Bilahi kii mère bii baxoul

  • @ArameNiang-j7g
    @ArameNiang-j7g Місяць тому

    😢😢😢😢😢😢😢