Lima méti rek moy boy diém Di contourné banekh yoyou ligay dieunk dégue moy dound bi da Gate bayil stress bi tégua firi kouy dound day def yafou kouy dound alahou akbar
Assalaamu alaykum wa rahmatul Laahi wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yonnènt bi sAaws akiy sahaabaam rAa te wërsëgal nu dëkag gnoom ca firdaws. YÀLLA boole nu ci tuubkat yi. Wan nu dëgg bamu leer nga yombalal nu topp ko. YÀLLA sàmm nu sàmmal nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xamxam yi ragal seen Boroom YÀLLA. Jërëjëfati

Macha Allah ❤
Jërëjëf Oustaz ci fàttali yi
بارك الله فيك ياشيخنا مور كب
Macha Allah Amatina solo Amine ya Rabe
Masha Allah
Yallana yalla Yoko xam xam bi
Assalaamu alaykum wa rahmatul Laahi wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yonnènt bi sAaws akiy sahaabaam rAa te wërsëgal nu dëkag gnoom ca firdaws. YÀLLA boole nu ci tuubkat yi. Wan nu dëgg bamu leer nga yombalal nu topp ko. YÀLLA sàmm nu sàmmal nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xamxam yi ragal seen Boroom YÀLLA. Jërëjëfati
Louy difference التوبةوالإستغفار
Je n'ai rien à dire que الحمد لله
Macha Allah sheikh bi
Khady Diallo
machalla allahou oustaz amatina solo .
Fier de toi baara kallaahou fiika wa jazaakallaahou xyran
BaarakAllah feekum
Merci beaucoup
macha allah
Machallah
Merci ❤️🙏
☝🏾 Mash'Allah
👍👍👍👍