li ngay laaj defeu melni xam nga ko Jamhu ayi baat la fiy laccee " jamhu = pluriel " Haqaa iq = vérités = sew sew Mbir mu nek li ko lal Hawaalim = mondes = jamhu baatu haalam on di pas masahir Mais mazaahir = apparences = feeñu waay mazaahir = apparences = feeñu waay as salaat = donc juli = prieres ou encore asalaat = authenticité donc tiosaanu ap mbir, wala weur pengg Abadaat ou ibaadat On dit ibaadaat = xeetu jaamu yalla yi wala ibaadaat = xeetu jaamu yalla yi wala dinay firi aussi mboolo jaamu kat comme abadat taghoot Dawaa ir = jamhu pluriel de dahira = mboolo Dawa ir = cercles aussi
Abou salimata wala aba salimata Demal dindi sa touri jigeen bi tay def yeufi goor. Boy jihaad wala jubanti nga dem ci tiedoo yi. Nitt dina wah deugg dou jangg al quran Nitt dina jangg al quren ak hadith ta xamul fu yalla nek. Yeen bu nitt gniy outt yalla yeen ngeen di lijanti ndah diw dey lakk arabe wala wolof ak dileen sikal. Loolu nak dou lislam.
Téki aya taxouko diouk... Wané Yalla mokofi indi... Délene déglou Yàlla téh xamni moy waxé si niite gni melni ki... Xamngua yaw li yalla diaralko guissouniou ngua defko??? Téh nguako diapalé mo gueneu nguay wédi... Joulite dou noné moromam
wakh thi diné mom, bou amoul aya amoul hadith rék rér dongou lay done fi guinaw soubeu do indi bén preuves thi wakhi YALLA wala Yonentam thi sén mbir, yalnagnou YALLA dioubeul ta dioubal lén
Segn bi ziare nala 🙏 Ngua balma wayé Borom baax bi di wax indina aya xana yako dégoul... Téh saxx xél rék téré la naxx Yàlla moni borome xél yi lay waxal yonénté bi bimouy woté borom téré yi la woo kone lane moy Téré yoyou... Bissi tope naniouy déglou ndiarigne téh bania beug wédi sou boba Yàlla dina wax ngua wédiko... Alkhuran bi nguay wax nak molani si souratoul kahf souniou done binde waxou Yàlla yi dieul guédj ak khobou garape yi waxou Yàlla yi dou diékh... Kone defal nank
Masha laah amna solo ku baaah Tasawuf nga waroon laccee moy lann ba nopi. Gnaareel bi ku gisul yalla, xamooko , xamoo fum nek noy jebaloo ci mom ? Dontee ak njebal kudul yalla moo mu ko ta kudul mom meuno ko mom. Jangil souleymane ak balqiiss.
Wane niou fou Yàlla nek niou diébeulou si mome... Ibliss li wathié gradam bokena si khétou wax bi ngua wax naxx dafa banione soudiotal Adama... Adama nak dou nite késsé wayé niite kou Yàlla xamal mbolém mbir la kom niko ayabi waxé... Nite kokou nak moy Yàlla
Mashallah Mashallah 🙏🙏🙏
Akasssa yalla yalla na yalla goudeul fane bi
amine
jahjeuf
Machallah lingua wax kou guemoul Yàlla saxx souko dégué téh ame xél dina xamni deug la...
Rawatina joulite nak 🙏
Jahjeuf ku bax
Machaalah léral yima beugoone dégeu....❤akassa....yalna siniou borom degeureul iman
Amine
Niou bok ko bu bakh
Akassa sangue yaram kawéna lol machalla yalna yalla barkel kham kham bi.
Amine
Jahjeuf
mashAllah yaaram bu séll bi, yalla yokku te barkéél bijaahi cheikh Moussa
Amin niou bok ko
Akasa yalna yalla fayla
Yagui donn out sama numero
775315281
Hakassa Mame Seydina 🙏
Jahjeuf kou bax
leer na. c'est très clair
Jahjeuf mame cheikh
Lan moi hakha ikhi, hawalim, masahir, Asalat, Abadad, Dawa ir,
li ngay laaj defeu melni xam nga ko
Jamhu ayi baat la fiy laccee
" jamhu = pluriel "
Haqaa iq = vérités = sew sew
Mbir mu nek li ko lal
Hawaalim = mondes = jamhu baatu haalam
on di pas masahir
Mais mazaahir = apparences = feeñu waay
mazaahir = apparences = feeñu waay
as salaat = donc juli = prieres ou encore asalaat = authenticité donc tiosaanu ap mbir, wala weur pengg
Abadaat ou ibaadat
On dit ibaadaat = xeetu jaamu yalla yi wala
ibaadaat = xeetu jaamu yalla yi wala dinay firi aussi mboolo jaamu kat comme abadat taghoot
Dawaa ir = jamhu pluriel de dahira = mboolo
Dawa ir = cercles aussi
Djeureujeuf Sangue bi
Sa kham kham rafet na lool setna selna
Jahjeuf
Seydina souleymane Sene dangsee booleee yar motakh tee yarou moogeun kham kham
téki wo aya bi dé: و أنيبوا إلى ربكم و أسلموا له kon YALLA léral na thi kan lagne wara diébalou
Abou salimata wala aba salimata
Demal dindi sa touri jigeen bi tay def yeufi goor.
Boy jihaad wala jubanti nga dem ci tiedoo yi.
Nitt dina wah deugg dou jangg al quran
Nitt dina jangg al quren ak hadith ta xamul fu yalla nek.
Yeen bu nitt gniy outt yalla yeen ngeen di lijanti ndah diw dey lakk arabe wala wolof ak dileen sikal.
Loolu nak dou lislam.
Téki aya taxouko diouk...
Wané Yalla mokofi indi...
Délene déglou Yàlla téh xamni moy waxé si niite gni melni ki...
Xamngua yaw li yalla diaralko guissouniou ngua defko???
Téh nguako diapalé mo gueneu nguay wédi...
Joulite dou noné moromam
wakh thi diné mom, bou amoul aya amoul hadith rék rér dongou lay done fi guinaw soubeu do indi bén preuves thi wakhi YALLA wala Yonentam thi sén mbir, yalnagnou YALLA dioubeul ta dioubal lén
Segn bi ziare nala 🙏
Ngua balma wayé Borom baax bi di wax indina aya xana yako dégoul...
Téh saxx xél rék téré la naxx Yàlla moni borome xél yi lay waxal yonénté bi bimouy woté borom téré yi la woo kone lane moy Téré yoyou...
Bissi tope naniouy déglou ndiarigne téh bania beug wédi sou boba Yàlla dina wax ngua wédiko...
Alkhuran bi nguay wax nak molani si souratoul kahf souniou done binde waxou Yàlla yi dieul guédj ak khobou garape yi waxou Yàlla yi dou diékh...
Kone defal nank
Eskey dekite ngor yalla
Jahjeuf
Diadieuff
Lane moye tassawouff??
Dina ci def video in cha Allah
Mou yatou ci nieup
Kou bakh meun nga khol lien bi
facebook.com/2094154100914226/posts/2408960002766966/
Inshalla
Soukrane
dou souloub mais soulouk dèjà yaw sakh khamou nougne koy wakhé, djoullite thi YALLA rék la wara diébalou, filiation djoullite moy nék djoullite, avant tasawwouf mom djoullite gni amougnou wone filiation ?
Masha laah amna solo ku baaah
Tasawuf nga waroon laccee moy lann ba nopi.
Gnaareel bi ku gisul yalla, xamooko , xamoo fum nek noy jebaloo ci mom ?
Dontee ak njebal kudul yalla moo mu ko ta kudul mom meuno ko mom.
Jangil souleymane ak balqiiss.
Wane niou fou Yàlla nek niou diébeulou si mome...
Ibliss li wathié gradam bokena si khétou wax bi ngua wax naxx dafa banione soudiotal Adama...
Adama nak dou nite késsé wayé niite kou Yàlla xamal mbolém mbir la kom niko ayabi waxé...
Nite kokou nak moy Yàlla
Dara amul ludul yalla nyep khamnenko, ludul yalla nen la kuneka Munk koi wah. Lodu du fathu
Yaw d mo amon fathu xam wah , xam li ngay wah ak ni ngay wahee