ليس كهم وليسوا كه الأستاذ شيخنا امباكي عبد، شيخنا في العلم والحلم والأخلاق، والانضباط والصدق والخمول والإخلاص، رجل عظيم، جميل الأفعال وجليل الأعمال، قليل الكلام وشديد التواصع، خافض الجناح ولين الجانب وسهل التعامل، من عرفه أحبه، وما قلته غيض من فيض، حفظه الله وأبقاه قرة عين لنا،
الصحيح الواضح أن شيخنا عبد الودود وأمثاله من أكابر علماء الطائفة المريدية،ينبغي لنا التمسّك بهم والاقتفاء بآثارهم،بدلاً مِن نَقْدِهم أوْ رمْيِ الحجر إليهم. فهم يرفعون راية الطائفة المريدية إلى قمة الأعلى.
Gisou ma bou weso s mountakha koulen eupel solo thi s touba ñiom ñiar s touba molen di ligey lo te geurem na senoub ligey ñiou Bon ñi rakh yonwi ñiolen di wakh Lou bom te Dou Len wañi Dara dafay yokou sen makhama Rek
Tégua ragar yalla si liguay wakh. S. Cheikhouna abdoul woudoud dé amo moko mouka guana liguayal s. Touba. S. Cheikhouna manoul niaka si yone wi yalla nakou yalla samou❤
ليس كهم وليسوا كه
الأستاذ شيخنا امباكي عبد، شيخنا في العلم والحلم والأخلاق، والانضباط والصدق والخمول والإخلاص،
رجل عظيم، جميل الأفعال وجليل الأعمال، قليل الكلام وشديد التواصع، خافض الجناح ولين الجانب وسهل التعامل، من عرفه أحبه، وما قلته غيض من فيض،
حفظه الله وأبقاه قرة عين لنا،
الصحيح الواضح أن شيخنا عبد الودود وأمثاله من أكابر علماء الطائفة المريدية،ينبغي لنا التمسّك بهم والاقتفاء بآثارهم،بدلاً مِن نَقْدِهم أوْ رمْيِ الحجر إليهم. فهم يرفعون راية الطائفة المريدية إلى قمة الأعلى.
Jërëjëfati Serigne Saliou. Amatina solo lool lool machallah❤❤❤
Machalla waye refétna serigne saliou amna solo merci beaucoup ❤❤❤
Sëriñ saalixu ñang léeral yi amna solo❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤jërëjëf
Dieredief serigne salihou serigne cheikhouna amoul morom te wa touba khamouñou moy kann❤❤❤❤❤
Buthi tooñ waa tuuba xana bokko thi waa tuuba
Yalla nalla Yalla faye yawe
Sëriñ séexuna ak sëriñ mbakké abdu Rahman waxé wuñ mukk séen bakan li sharia yoon wu jub wi diglé rek lañuy léeral
Waw gor waye amna solo
leep rafeetna yalla nala yalla faiye barké Serigne Touba
Lifi néke si ay boromi khame khame si Touba manoko lime
Yalla Na yalla same léne berkeb cheikhol khadime
Dieureudieufet🙏🙏
Mashlla jiadef
Machalla s salihou dege ga wakh
Machalla❤❤❤❤
Man deh gën nama yokk sama coféel ci sëriñ séexuna ak sëriñ mbakké abdu Rahman
Dëg gui ñuy wax talubé yi kepp mooy deranger ñen ñi
ماشاء الله ❤❤❤❤❤
Ndeysaaann amna solo loool mouride
Borom xam xam dal da wara am téguine té guéne bou serigne mountakha diglé teuyé sén lamigne yi
❤❤❤❤
Ku xam sëriñ tuuba war ngua xamné sëriñ bi ci xam xam rek la daan jëf ku nara ñakka wormaal sunu borom xam xam yi nekko ci la sëriñ bi nékkoon
Gisou ma bou weso s mountakha koulen eupel solo thi s touba ñiom ñiar s touba molen di ligey lo te geurem na senoub ligey ñiou Bon ñi rakh yonwi ñiolen di wakh Lou bom te Dou Len wañi Dara dafay yokou sen makhama Rek
JHIADIAE FATY S GNIANG WAKHA TY NGA DEUG DHIY
Ci xam xam rek lañuy jëf nguir tek nit ñi ci yoon wu jubb
Serigne mbacké abdou rakhmane khame khame dafa lér
Bo lén yaro rek do lén dég loulén nekhoul
Dieredief leerna
Li nga wax di nga ko reccu de.
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤🎉🎉
serigne saliou niang sawakhtanwi amna solo Lol Lol cheikhol khadim degenala
Bilahi ac woro lay nuru rec ac ñaka xam
ولا يُهِينُ عالماً إلاَّ جاهلُُ
Serigne cheikhouna Abdoul woudoud pass passou wahabiste bou bone la yor dou mouride
Yaw moom wakh dji sisa bakane rek ngako tekk
Kikaye dafa rer waye yalla khamna li nek thi khol yi@@mamourmbodji1204
Ay wadji ragalal yalla
Tégua ragar yalla si liguay wakh. S. Cheikhouna abdoul woudoud dé amo moko mouka guana liguayal s. Touba. S. Cheikhouna manoul niaka si yone wi yalla nakou yalla samou❤
Sa waye billahi aye nafeq guen
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤