L'homme au bonnet carré l'homme au sourire légendaire l'unique Khalifa de sa génération borom souma roussoul sama baye kouma woo sii photo ma wouyouleu♥️
Il faut continuer cette émission même après le ramadan parce qu'il est grand temps que la jeunesse sénégalaise sache et connaisse nos vaillants chefs religieux et leurs mamans. Merci à vous tous!
Alhamdoulilah rabil alamine ! Khole sedatina ! YAlna yalla faye léne yeew, goudal séni fane ! Sougnou Papa Mbaye Dondé Mbaye yalna yalla yessal yeurmadéme ak djéguel thi mome. Sougnou Mame Babacar Sy, yalla fayal gnouka môme AK wadiourame you bakhe yi, AK rakame yi, domame yi AK seteum yi. Khalifa bifi tokk, yalla sameka, diapalé ka, yok khame khame bi, yok Soutoureu si , môme AK aye rakame yalna yalla wéreul séni thieure, nagou séni gnane mou dignou are, dignou yok, té sakhale gnou ba fawe si tarikha Cheikh thi Seydina Mouhamed sala lahou aleyhi wa salam. Amine.
Yalna bokou si ay nitou Serigne Babacar Sy 🙏🏽 Teranga adouna ak Alahira 🙏🏽 Réussites you kawei si diangg bi ak richesse abondante ici-bas et dans l’au-delà 🙏🏽 Neik Talibei Cheikh ak talibei Serigne Babacar Sy 🙏🏽 Sama taw bou gor Yalla toudou Serigne Babacar Sy 🙏🏽 Amine si barkei Serigne Babacar Sy ( Werr ak goudou fann ) 🙏🏽
Non a vrai dire ses émissions dafa Warren Di âme jakk goundi aldiouma wayyy 😭😭nn seulement le mois du Ramadan wayy tous les tarikhaaas j'ai goundi aldiouma machallah ♥️ Diam yague Sénégal
Je suis mourite deireudeifé serigne babacar sy wayé mane mame Abdou aziz dama ko beug billahi deireudeifé mame Abdou aziz 💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘
Kénn dou serigne babacar sy yalla n'a ko yla faye❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Nous l'aimons sans le connaitre sans vivre avec lui mes il est dans nos coeurs sans savoir pourquoi mais ce que je sais il est notre bonheur le merveille que dieu nous a donné nous les enfants de mbaye
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ fière d'être talibee cheikh Serigne Babacar sy rta domou Maodo Malick serignou Maodo Malick sama Sérigne yalla naniou yalla fayale Serigne Babacar sy rta amine
Ma beugue serigne Babacar sy rta réke té yalla takh 😭😭😭😭😭❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
L'homme au bonnet carré l'homme au sourire légendaire l'unique Khalifa de sa génération borom souma roussoul sama baye kouma woo sii photo ma wouyouleu♥️
Ken dou serigne babacar sy malick yana sounou borom doly leram te tass niou si barkem amine inchalah
Il faut continuer cette émission même après le ramadan parce qu'il est grand temps que la jeunesse sénégalaise sache et connaisse nos vaillants chefs religieux et leurs mamans. Merci à vous tous!
Machalah yalla nala yalla faye kenne d'où monme
Thieyy sama tourondo amoul moromm borome bonnet carré bii,foumako woo mouu wouyouma , surtout si soutoura machalla
S
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sougnou tourando❤
Machalla machalla diamou reck ci yeun machalla yalla n'a yalla faylen goudou fan amiine yaraby machalla dieureudieuf seringne babacar sy Malick
Macha Allah ken dou Serigne Babacar sy Man deh diafa ndouna si Mbaye
L'. S'en direct pape maliik
De de ce cas de lo
Genre de TV HD le en
C
W
Ndeysane damakoy setane di dioye ma beugue serigne babacar sy
Ndeye sane !!! Beuguenala yaw tamite
Serigne babacar sy amoul morome bilaye
Kéne dou sérigne Babacar sy ❤️❤️❤️🥰
Sama wadji s'y malick borom bonnet carre sama werouway foumako wo mou wouyouma yalla naniou yalla Tass si barkeim
Alhamdoulilah rabil alamine ! Khole sedatina ! YAlna yalla faye léne yeew, goudal séni fane ! Sougnou Papa Mbaye Dondé Mbaye yalna yalla yessal yeurmadéme ak djéguel thi mome. Sougnou Mame Babacar Sy, yalla fayal gnouka môme AK wadiourame you bakhe yi, AK rakame yi, domame yi AK seteum yi. Khalifa bifi tokk, yalla sameka, diapalé ka, yok khame khame bi, yok Soutoureu si , môme AK aye rakame yalna yalla wéreul séni thieure, nagou séni gnane mou dignou are, dignou yok, té sakhale gnou ba fawe si tarikha Cheikh thi Seydina Mouhamed sala lahou aleyhi wa salam. Amine.
Machalla Serigne Babacar s'y❤️💓💖😭😭💓❤️💞💖💓❤️
Machalla Mbaye ya niou doy Mbaye ya niou doy Seydi ABOUBACAR Bakarekh dara mame ya niou doy doo sen morom
C'est émission devrait continuer même après le ramadan bilahi
Kéne dou Serigne Babacar sy❤️❤️❤️ machalla
Yalna bokou si ay nitou Serigne Babacar Sy 🙏🏽 Teranga adouna ak Alahira 🙏🏽 Réussites you kawei si diangg bi ak richesse abondante ici-bas et dans l’au-delà 🙏🏽 Neik Talibei Cheikh ak talibei Serigne Babacar Sy 🙏🏽 Sama taw bou gor Yalla toudou Serigne Babacar Sy 🙏🏽
Amine si barkei Serigne Babacar Sy ( Werr ak goudou fann ) 🙏🏽
Ammine❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Après seydina mouhamet psl pour moi c'est Serigne Babacar sy
Yalla nagnou yalla fayal Serigne Babacar ay ♥️🙏
Alhamdulilah sama xol sédd na si yeine yallah na borom bi faye leine Mashallah ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Manchallah Sama Xool fées na♥️🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽 billah ma beugue Serigne Babacar ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️👅👅👅🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Non a vrai dire ses émissions dafa Warren Di âme jakk goundi aldiouma wayyy 😭😭nn seulement le mois du Ramadan wayy tous les tarikhaaas j'ai goundi aldiouma machallah ♥️ Diam yague Sénégal
🙂🙂😍
Je suis mourite deireudeifé serigne babacar sy wayé mane mame Abdou aziz dama ko beug billahi deireudeifé mame Abdou aziz 💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘💘
D
Machallah borom bonné carret bi sougnou Mame yalla na yalla yokk sa leer té Tass gnou sissa barkel
Alahouma amine
@@aissatasow7301 ⁿ
Amine
AMIINE INCHAALLAH
Thiey yalla😍😍😍 ken dou Khalifa Babacar ❤️❤️❤️❤️
Thiéye Serigne Babacar sy amoul morom
Machalla ❤️❤️❤️❤️ thieye Serigne Babacar Sy ❤️❤️❤️
Masha Allah....
Kéne dou Sérigne Babacar
Diarama Sérigne Babacar
Aye waye yalla n’a toudé dôme serigne Babacar sy
Amine 🙏🙏🙏😭
Amine way inchallah ❤😊
Amine way yalla nala ko yalla may🙏🙏
Amine inchallah
Amine
Serigne Babacar sy sama dieumi hollll
Ma force serigne Babacar sy malick
Kénn dou serigne babacar sy yalla n'a ko yla faye❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ahbib❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😌❤❤😌❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
On n'a bien appris en ver toi merci beaucoup oustaz doucoure 🙏🙏🙏
Non li bilakhi doumasi doyal 😢😢MaShaAllah way❤😍❤❤
Thieye sama tourando Serigne Babacar sy yalna yalla yokou léeram tes tasse niou si barkéme 🤲🤲🤲
Machallah Machallah merci beaucoup 💚💛💗💖💪👂💪👂🙏🙏🙏👍👍
Man layenne bou beug serigne babacar sy
Ndeyasann ohh yallah nala serigne babacar sy teutal
Dou yaw rk dh❤️❤️
Machallah
Koorou ren gui mom tarkalah🙏 amoul Ben polymique yalla na yalla fayal gnou soun mak gni Barké "Dialibatoul Marahib"
Kéne dou serigne babacar s’y ❤️❤️❤️❤️
😫😫😫♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Machallah yalla nanu ko yalla fayal thi barké yonente bii SAW🙏🏽👏🏽
@@baseynabou2558 o9
@@baseynabou2558mm
Dieureudieuf serigne touba diarama mame cheikh ibra fall
Nous l'aimons sans le connaitre sans vivre avec lui mes il est dans nos coeurs sans savoir pourquoi mais ce que je sais il est notre bonheur le merveille que dieu nous a donné nous les enfants de mbaye
Bilahi bilahi bilahi bilahi bilahi bilahi bilahi
Billay man sama mbeuguél si mome amoul limite
@@papeousmanesonko5755 yallna diam du yagg mane dhei si mome lay dewer
@@mariamadiouf3335 yalna sa beuguel du gueneu yokk keneu mbaye
Bilahi nous l'aimons tous si khole la néck
Kène dou sèrigne babacar sy ❤️❤️🙏🙏
Machalla sy Malick yalla nagnouko yalla fayal 🙏❤️❤️❤️❤️
💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍💚🤍 sama khole cédena yalla nalene yalla faye yiw
AMIINE INCHAALLAH FOREVER
Sama mame awma ci moom sagooo🙏🏻🙏🏻😢
Yalna yalla yokk sayy lerr 🙏🏻
Nioune Tidiane beug naniou 🤍Mbaye gueme naniou Mbaye 🤍dieufé sél naniou Mbaye🤍 def naniou Mbaye🤍 souniou xol yii kénn dou 🤍Mbaye si nioune 🤍
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ fière d'être talibee cheikh Serigne Babacar sy rta domou Maodo Malick serignou Maodo Malick sama Sérigne yalla naniou yalla fayale Serigne Babacar sy rta amine
Amoul morom Khalifa Ababacar SY♥️
Yalna Yala yokk leram tass niou si barkem🙏Serigne Babacar Sy Malick ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Way maylenko khaliss way😥😥 walay soumala dieguewon dinaka may ba sa khol sedeu
Kén dou borom bonnet carré ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Dém tiwawane ziari ko rek la beugue yalla nama yalla yombalal pass bi rek amine
Bo demagoul ba legui ma mayla pass
Ndeyssane SA ma papeu Al amine Allah yourmo yaffo
Diaza kalahou🙏 xayran Serigne Babacar sy
Talibé cheikh rek inchallah 🙏♥️♥️♥️💯
je peux regarder cette vidéo une centaine de fois
Machallah Mbaye Si kouko am doylo ko am lou réy barki Rassourilay❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sama Mame ❤❤❤sama idole et aussi Sama serigne Mbaye Sy rek❤❤❤💖
aka nékha beug sy Malick ♥️❤️❤️🙏
Machallah sama goor gou rafét bi❤❤❤❤
J'aime serigne babacar sy mon oxygène l'unique Khalifa de ça génération walahi on t'aime ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
🎉😂❤😢😮
Yalnaniou yalla fayal sérigne Babacar sy 🙏💞🕋
Serigne Babacar SY kene la dotoul gnare si adouna
Machalla souniou Khalifa bii ken dou mome s'y yalna yala yok lairam te tafniou ci Barkem alahouma amine
J’aime serigne Babacar sy ❤brom sacré yalla bi😊❤je suis Mouride ms dmko beug ❤ylna nieup am diam si barke seydina mouhamed sws 🙏🏿
Serigne Babacar sy ❤️🙏🏻
Mach Allah Allah Mame babacar sy yalla na yalla yokou léram
Bilahi DEUG DEUG contant nagnou bou bakh
Machallah ❤️ SY Malick ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Allahou Akbar euskey ken dou suniou Mame Khalifa Ababacar Sy rta jerejeuf yallah suniou borom moom miniou jokh Cheikhoul khalifa ooooooh thiey Mame Cheikh seydil Hadj Malick Sy rta ken dou moom macha allah
Machalla Sam Mame Sam Serigne contan n'a torop
Waw kay li danioukoy beug machallah ❤️❤️❤️❤️❤️
Bilalhi dama contane batay soumay seetane li ❤️❤️❤️
Sama mame khalifa kéne la bilahi t dotoul kénéne kou mélni mome si kaw souff ❤️🔒
Sama serign serign BABACAR SY MOME REK LA HAM MOME REK LA AM ❤️🙏
Kene dou Serigne Babacar sy
Yalla nako yalla yeureum té kharéko al diana amine insha Allah
Macha'alla 👍 ce bonheur d'être talibe chez 😢
Serigne Babacar Sy ❤❤❤❤❤
THIÉY SERIGNE BABACAR SY RTA SAMA SOPEY SAMA FORCE
Yalna yalla yokk léram te tassou niou si barkem
Fière d'être Talibée Cheikh Tidiane SBS ma Fierté ❤
Ken dou borom bonekarebi ❤❤😢😢
Machallah ma sope goor gui loleu sakhhh...❤
Macha’Allah 🥰😍❤️sougnou mame
SOUGNOU MAMOU KHOLE INCHAALLAH
Mame mbaye sama docteur❤❤❤❤❤
yalna bour yalla yokk leeram mom mame khalifa nimako beugue eupnama lokho walae yalla khamnako
Machala 💕 Sy Malick
Serigne bi khoule yalla na la BOUR bi Fay Modou khoule
Sama mame babacar sy rta bilahi walahi mako si sama❤ bi
Souma nékoul wone talibé cheikh loumay wax wa kogn ba
❤❤❤❤❤❤❤❤Serigne Babacar Sy
Sougnou yakarr adouna ak alakhira 💯♥️🙏
Yalna yalla yokou leram
Hooo yalla nama yalla May dom bou gor m'a toudeko serigne babacar sy
Machalla kene d'où Serigne Babacar sy
MACHALLAH khol sédeneu ken dou Serigne BABACAR SY RTA
Mame babacar sy yalna yala yokh leram
Machallah s8 fier de vous
J’aime beaucoup mame Babacar sy Malick
Machallal Machallala 😭❤❤❤❤❤💯❤❤❤❤💋
Euskeuy MachaAllah Sama Wassila yal naniou KO Yalla fayal
Amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine amine ❤❤🙏🙏🙏❤❤❤🙏🙏🙏❤❤❤masahala
♥️♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Serigne Babacar rek
Pourquoi ces émissions sont arrêtées après le ramadan 🥺🥺
Doyna warr 😂
Vraiment
Deukou thiakhan rek pour niom dîné wzkhtanou yalla koor rek la wara yam